Djaredjef la jeunesse patriotique sénégalaise. Vive le Pastef. C'est çà le nouveau Sénégal. Merci les jeunes.
@PapeamadouBa-u3jКүн бұрын
S'il vous plaît arrêter maintenant c'est bon on est tous des patriotes fair play c'est bon il a reçu le message c'est bon merci gars
@michelndiaye9241Күн бұрын
Fadilou daimale tope sa yaye
@MAMA-AFRICA1Күн бұрын
PM SEYDINA SONKO AK PASTEF LES PATRIOTES YALLAH NA LEEN YALLAH SAMOU, SAMOU AFRICA BIJAAHI RASULILAH S.A.W 😍😍😍❤️❤️❤️☝🏾😇
@MbayeCisse-cd1tuКүн бұрын
Sonko moye Sénégal barkie serigne touba❤❤
@OusmaneFall-m9dКүн бұрын
Affaire bi moy, Fadilou s'il ne peut pas accepter la jeunesse de Pastef, il n'a qu'à démissionné de Pastef parceque gnoune PM Ousmane SONKO kesse mome lagnouy tope moy sounou leader emblématique point barre
@coumbandiaye1900Күн бұрын
J'ai toujours pensé k mara niass ne devait pas dire le prochain opposant de Sonko sortira de pastef niit kou nioul dafa beugueu gour, et c'est la générosité de Sonko qui fait k l'aimons en plus d'autres attitudes.
@MariamaMG23 сағат бұрын
Non il n’a dit de pastef plutôt niou bokk woon coalition si diomaye bii
@capricefemelle316823 сағат бұрын
Opposant bou guéné pastef sénégalais yi douniou ko diapé loudoul workate té sénégalais mo ay si workate
@Bichri-rek16 сағат бұрын
❤❤❤ billahi degue nga wakh@@capricefemelle3168
@cheikhabdoumbacke697012 сағат бұрын
Sonko à vie ❤️🔐🫡
@babacar-bmwКүн бұрын
❤❤❤❤❤❤ sonko rek lagnou tope ❤️
@ahmetfall763622 сағат бұрын
Yenn ay nafekh nguen trop vraiment. Fadilou est un combattant
@djilysall7727Күн бұрын
Ousmane mouchelmi yalnako yalla may goudfan ak wer ak patriyot yeup amin yarabi
@adamaba6508Күн бұрын
❤ vive le président bassirou diomaye sonko faye ❤ vive le président Ousmane sonko faye ❤pastef a vie ❤💯👍
@FALLOUGAMING-y2iКүн бұрын
maye doule nane bayi na sonko 😭
@SeydiMassaneКүн бұрын
Wakh bi yombou na mais def ko moy problème
@Baabakar2296Күн бұрын
😂😂😂😂
@pendandour7651Күн бұрын
Dagua meusoule bok si niou beugue Sonko ak gni andeu ak Sonko. Bayiléne séne khél yi guéne fowé meunouléne déf walla wakh baniou bayi Sonko. Nopale léne séne bop
@ALPHASONKO-cd8mxКүн бұрын
Danko diap
@AminataSene-xt5tbКүн бұрын
Yaw kay doulkate bou Am fite ngua 😂😂
@adamaba6508Күн бұрын
❤ serigne Ousmane sonko moy tanne kouy tok filek moufiy nek inchallah ❤
@cheikhabdoumbacke697012 сағат бұрын
Dafa lér ❤❤❤
@coumbandiaye1900Күн бұрын
Fadilou deug deug migui sissou😂😂😂😂😂
@BabaDiallo-x6kКүн бұрын
Merci beaucoup Léa frère patriotes 🎉🎉🎉❤❤❤🙏🙏
@KnsenegalmeilleurКүн бұрын
😂😂😂ay fadilou Yamal khaleyii sonko rekk lagnouy topp teh sonko tamit khaleyii lay topp Khaleyii deh comme djiby gueye Ndiaye lagnou reukeul 72h you saff sapp 😂😂😂 Ay fadilou demal tokk sa roukk liguey bayi Boy yii gni si guerr lagnou diouguer 😂
@Top-OusmaneКүн бұрын
😂😂😂😂😂 bilakhi wakhal dé
@Abraham20005Күн бұрын
ce qui vous fait mal à tous, c'est ce qu'il a dit d'ARRÊTER d'être paresseux, de boire, Attaya, de courir au bureau des AUTORITÉS, d'être un influenceur n'est ni une carrière ni une profession, d'aller travailler, de trouver quelque chose à faire 🤨
FADILOU, EN TANT QUE SOEUR PATRIOTE, ON TE VOUE UN GRAND RESPECT.. ON T'AIMAIT BEAUCOUP, MAIS TES INTERVENTIONS ARROGANTES COMMENCENT A TE SORTIR DU COEUR DE TES FANS. ON N'AIMERAIT PAS DU TOUT TE DETESTER, CAR TA MAMAN A FAIT UN TRAVAIL DE TITAN DANS CE PAYS. REVIENT A LA NORMALE, SACHE QUE PERSONNE DANS PASTEF N'EST A LA HAUTEUR DE OUSMANE SONKO. ON N'A RIEN CONTRE TOI, MAIS ON VOUDRAIT SEULEMENT QUE TU TE RESSAISSISSES, QUE TU TE REVOIES DANS LA GLACE ET TU TE REMETTES DANS LES RANGS A L'IMAGE DE TOUS LES PATRIOTES DIGNES DE CE NOM
@InsaSane-lg2os17 сағат бұрын
On n'a un patron sur partir chez sonko seule késs kénn toulou gou fén
Fadilou daffa réw mome pour mome yayame rékk mo bakhe si adouna
@aligueye4821Күн бұрын
❤❤❤❤
@BeugdeugКүн бұрын
Mais sachez aussi que il nest pas un ennemi Fadilou keïta après tout
@Babacar998Күн бұрын
Bayi leen ñii ñou ligéy beuri ngén wakh trop ahh
@bathiembaye1199Күн бұрын
fadilou mo wara bayyi live yi, dèm liguèyi
@CheikhDiop-f3dКүн бұрын
Merci beaucoup 👍
@mousseseck-mv3feКүн бұрын
Boulenou fonto bayi leen wakhdji mano bageu sonko bange ay Anda doram mano bageu Yonen taby Bang sahabayi
@MakhtarDiaw-cd4yc20 сағат бұрын
Liiguani wakh barina ta amoléne ay téguine khamoléne liguéne wara wakh ak kiguéne wara wakhall boudé yéne yénay proché bi aaaa konedé dalou diousi seydina Ousmane ak président bassirou niou am ay téguine lane
@MouhamedCisse-u1fКүн бұрын
Non boy goridingéne AK fadilou nomou soné ci ligaybi non Mane dama warou
@morfassandiaye7737Күн бұрын
Fii niepa sonou diambar nit dangay khekhe nguir seu rew waye waro khekhe nguir seu bopou
@MorTouureКүн бұрын
Nice ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
@MariamaMG23 сағат бұрын
C’est vrai que falilou keita a mal communiqué mais il faut faire très attention aux informations données par mollah baxna daal
@amadoufall9276Күн бұрын
SONKO SONKO SONKO SONKO SONKO SONKO SONKO
@thegambiasinterestlaminbad303323 сағат бұрын
Waw gorr jajeff
@Galsen655Күн бұрын
Bilahi yèna Sof ma khalal kao kao yi yaw fallou mola geune
@seckcheikhanta956Күн бұрын
Yawe ya reew
@EumeFall16 сағат бұрын
Deg pirrrrr
@BeugdeugКүн бұрын
C'est Fadilou keïta
@MassMass-lm4eiКүн бұрын
Fadilou dafa khamoul nayamm bopam
@mamadoundiaye172421 сағат бұрын
Falidou mobeugue reseau sociaux wakhdji lawara bayi mais mom loukhew mou posté mom ak waly diouf bodian
@dykhmbengue3931Күн бұрын
Yeneu ba tay si fadilou li Mou wakh il y'a rien de mal ndeyssane SONKO wakh'ako Nioune nioyye sounou ProRes opposition Fadilou diambar la il est très humble niafekate la te Ousmane wolou nako arrête lene Sene manipulation dou marche ak mome
@LeuzSikki-sg9kv19 сағат бұрын
Et puis fadilou limou wakh rekk la Sonko wakh, boudé bén leaders rek Mooy wakh gnou déeg Lou ko, on est pas différent des autres partis
@Nogaye-ei6nkКүн бұрын
Wallahi ki dafa bew
@bayegorfall1813Күн бұрын
Bilahi yena beri wakh te sof afer yi diekhna way
@farbadiouf1990Күн бұрын
Fadilou Keita a le devoir - de chercher - du travail à ces jeunes. Il a le devoir de réhabiliter l'école. Il a insulté ces jeunes. Rien à édulcorer ! Pas l'homme qu'il faut à la place.
@CNMBusinessКүн бұрын
Patriot naniou bayi mou seude té diemeuléna diapalé si liguey falilou guene bi meunona niake nakhe taye boleune démé baniouléne khame taye yalla pros nite kou bakhe dou feuke dieufe naniou diapalé president diomaye ak pros ngir yalla
@user-nd2yx2qg7wКүн бұрын
Youn dall sonko rek lagni topou kouko diape you diappla kouko bagni you bagni sa ndeye piont
@maguettebomou517713 сағат бұрын
Moi je pense que fadilou n'est pas seulement arrogant il est méprisant envers la jeunesse 😢 il n'est pas généreux il ne partage pas il veut être le centre d'intérêt ne supporte pas la hiérarchie il est indiscipliné kou rèw la c'est un fils à maman il pense que tout lui est dû. Mais je vous le dis il sera le premier dissident de Pasteef les Patriotes parce que c'est un jaloux et se pensant arrivé il va continuer à défier Sonko soit il quittera soit il sera viré parce qu'il va déraper c'est certain.
@SeckPape-v7zКүн бұрын
Lolou mo létreu sonko rék diomayeu sakh bounioukoye topou sonko mo takh?????????
@ModouBodian-jv4oj20 сағат бұрын
Falilou Keita sa ndéye défaloul dara réwmi loudoul katou ci ginaw di wach rék lolou lolou djiko naféque dëgg le sa yaye ipocrite la
@baboucargoudiaby2933Күн бұрын
Bayi ko sans do d'ara môme rek la niou top meuno mobilise personne diniou fongo
@mouridebi5108Сағат бұрын
Fadilou dafa goré woul tei dey faaté liko fall
@Abdoulahi-cisseКүн бұрын
Bamba mi ci turbin bi 😂
@ElimaneNdao-tf6dnКүн бұрын
Fadilou keita da téla bédiaw rek mais bambino la comme fils a maman la il na ka demissionné dieul référencam defko directeur de campagne lathie mairie kaolack wa salam kou bakh la nak mais da yeuk bopam xelou xalé
@LeuzSikki-sg9kv19 сағат бұрын
Vous n'avez même pas honte d'attaquer Fadilou comme ça, alors limou wakh rek la sonko wakh, soof nguén trop waay.
@coumbandiaye1900Күн бұрын
Mais esk fadilou beuguoul wone nek 2e personnalité de l'état tamitttt ??????
@coumbandiaye1900Күн бұрын
Fadilou si tu étais à la place de sonko diomaye ne serait jamais Président, sonko son intérêt personnel lui importe peu.
@cheikhmbodji5593Күн бұрын
Dafa khamoul bopame
@ismailaceesay551Күн бұрын
Degah degah dafa arrogant. President sa partie wakh naa beh parreh, kon laww amm pour wakhatie. Soo bogul partie bii, naa ngaa demissone
@seckcheikhanta956Күн бұрын
Keita dafa reew xamoul bopam rewande lay diaaye mais mane dokh dem rek
@CathySalle-g6eКүн бұрын
patriote yi svp na gnou deff pétition pour les personnes à dégager . commençant par fadilou keita ... il est arrogant ce gars un imposteur . mouy khonkal tougn
@mikekamara1803Күн бұрын
Non tontou lèneka mokhambopam, après moubalou moudiékh
@BeugdeugКүн бұрын
3 postes PCA non non non non non c'est pas vrai comment il peut détenir crs postes
@nafissatouthiounendiaye458Күн бұрын
Doumako deglou Sonko kesse
@cheikhdiakhate716Күн бұрын
Fadilou dafa arrogant
@VOISINAGE2000Күн бұрын
FADILOU DAFA RÉW té arrogant
@mamadoudiouf9911Күн бұрын
Les propos de Fadilou c'est pas destiné à Sonko mais il vaut faire savoir aux militants qu'en dehors de Sonko ils doivent écouter les responsables
@BeugdeugКүн бұрын
Le Pastef n'est pas organisé à la base c'est pourquoi il faut y penser sinon moy lolou
@SeckRockinaКүн бұрын
Fadillou fenen lay waxé yen nay yakhal P.Sonko sof gen torop té am diot fi nieupa xéxe té investire ken dou xoulo sa canam None surtout NTouba ak Laminiou Darou latée gen sof gen Patriotes yi .
@FamaraDiatta-j1lКүн бұрын
T'as raison mon frère ses paroles ne sont pas à destinée du pm nos frères n'ont pas compris
@FamaraDiatta-j1lКүн бұрын
Béna erreur rek la falidou def moy le blocage car si tu décide de parler sur les réseaux sociaux il faut s'attendre à des commentaires
@moustaphaseck7661Күн бұрын
Yèna sen koyou bay yen begou leèn sonko sax fèn rek genii deff 😮
@morfassandiaye7737Күн бұрын
Amal yar aki té guine
@morgueye3939Күн бұрын
❤ gayi Dano ko kalidou kayta kou bakh la nit kesse la mais Bayilene wakh djiiii
@bayekawКүн бұрын
Sincèrement yéne niou réw nguéne bilahi vous vous pensez que projet bii Ousmane Sonko kesser meunako doxal
@abdoulayesane7747Күн бұрын
D'accord niooteyyyyy😂
@ALPHASONKO-cd8mxКүн бұрын
Mon frère, tu as Mal parlé aussi
@Abraham20005Күн бұрын
Beaucoup d'entre vous ne connaissent pas leurs limites et s'accordent trop d'importance, connaissez-vous vous-mêmes et arrêtez de DIVISER le parti, vous n'êtes que des TIK TOKERS, vous êtes des INFLUENCEURS, vous collez des images et vous leur manquez de respect, il faut ARRÊTER 🛑