Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct / luttetv / luttetv / luttetv / luttetv luttetv.com/
Пікірлер: 468
@delfynancooje49946 күн бұрын
Lamine Seck un journaliste très professionnel. Des questions toujours bien posées
@Dioppatriote066 күн бұрын
Il est très sérieux
@OusmaneGilbertJuniorBALDE-z8x6 күн бұрын
Parck li mouy waxe,da la arrangé bro😂😂😂😂
@tivactutv6 күн бұрын
Guiss ngéin qualité image Lutte tv yi . Macha Allah et félicitations à Lamine SECK .
@khadimgadiaga18556 күн бұрын
Sama Ndiago OR bii tout les Parcelles Assainies sont derrières toi ❤❤
@M.DIAGNE1ST6 күн бұрын
Vraiment ce Mec il est Posé Yalna souniou Borom Bi May la ndame Emile François Gomis LOU REUY tchi Kaw Amadou Baldé DIMANCHE LE 16 FEVRIER 2025 INCH'ALLAH et NE CHANGE SURTOUT PAS Yaar AK Téggin reck BONNE CHANCE Frère On est derrière toi et chapeau aussi à LAMINE LUTTE TV par tes questions pertinentes.
@mouhameddiatta83735 күн бұрын
En tt cas Franc t'es plein de maturité et c'est ce qui manque à Ama. Je vous apprécie tous les deux, que le meilleur gagne et vive notre sport national
@assanefall41116 күн бұрын
Manchallah Lamine Seck très professionnelle et pertinente wa albourakh djumo lene deh Lamine Seck très poli
@MamadoMamo6 күн бұрын
Thiey Fran ndam rek inchalla ❤
@AliouneBadara-x7k6 күн бұрын
Franc yalna nala yalla may ndam si Amadou Latyr Baldé
@mansourkane14266 күн бұрын
Kou sokhore doula beug yalnala yalla soutoural maye la ndam inchala parcelle yeupe gnougui sa guinaw inchala
@moussandaby97076 күн бұрын
Non fran kou yarou nimouye wahéé té nitté ndayesane limou wakh si yonènete bi yalla nala yalla ndame fran dafa nitté yarou❤❤❤
@tidiane18786 күн бұрын
Professionnel haut niveau je vous dis 🥰🥳Ya meune ya eup dollé
@modo62186 күн бұрын
Image yi rafett na machallah franc ndam inchallah
@ndiagafaye31066 күн бұрын
Amiiiin yaa rabbi
@taphadiop6076 күн бұрын
Lamine seck ,un très grand professionnel du métier, toujours posé et pertinent 🎉 nala yalla defal jam mon ami de valeur ❤ Tapha diop leu depuis New York
@amadoudiop75725 күн бұрын
❤ Fran nous sommes wa niodior derrière toi et inchallah ndam rek
@AbdoulRahmanDiallo-p7j6 күн бұрын
Fass la deukk fans modoulo franc Yalla nala Yalla may ndam inchalah amine ☝🏿🙏🏿🙏🏿🫶🏿✊🏾✊🏾👑👑👑🤲🏿
@ShiekhjobeTijan6 күн бұрын
Ndam Rek Franc kesse insa Allaho rabi ♥️♥️♥️♥️
@khaliloulah37036 күн бұрын
Yalna gua am ndam bou reuy🙏🏿🙏🏿🙏🏿
@IbrahimaNdiaye-eo3qh6 күн бұрын
Machalla franc vraiment il est tres displine il communique bien bonne chance champion
@lahadboukharagnelo67076 күн бұрын
Toujours confiance amoul bayii khel khale nga ❤️❤️❤️🔥🔥🔥
@lacitoyenneafricaine85666 күн бұрын
Li may beug wah koumou meti na nga ma bale. Wayer nak louy defar le rek. Sou fekker ni si bire parcelles ame ne keneu wala gneneu gno khame ni yakar nagnou ni Franc dafa ame gnoumou yeugoul wala lenene ba khame ni sonou gnou si combat bi nagnou tek lepp si souf djapaler boy bi. Khaler keneu douko bedi sou fekker da nga ko beug yaar. Khaler da gnouye teyer si lokhome teter ko mou khame adouna souka deffer bou souba fo ke tek rek laye tegou. Ne parcelles yeup nek derrière Franc dolele ko khol lene si Modou lo djapaler lene boy bi. Merci.
@rouguikebe99845 күн бұрын
Vraiment mercii❤wakh nga lépp😊❤🎉
@IbrahimaNdong-h4g6 күн бұрын
Macha Allah mon frére Yalla na la Yalla maye ndame lou séde vrai man Macha Allah
@abdoutoure46996 күн бұрын
Faranc yalIa nala yalla maye ndame amine yarbi
@AboubacryGASSAMA-zs7oi6 күн бұрын
De toute les façons migui si forme .ils est calme et sérieux ...sérénité...posé . Fékhél ba boula ama baldé diape si mystique wala guay reup Biir combat .. léne moye gagner combat bi moy lecture de combat. Door coup 👊 you normal en regardant. Ame rapidité ..vivacité. souplesse. Vitesse d'exècution ...kou déf lima wakh ni digua gagner combat bii wa salam
@Jeuneentrepreneurcheikh2176 күн бұрын
Franc dafa mature trop en plus il parle bien 🎉
@MouhamedCissé-j9d6 күн бұрын
Franc a vraiment l'esprit de champion.
@mamadouseydougueye16966 күн бұрын
Bravo lamine lutte tv
@kurayahmi6 күн бұрын
*Le 16 Modou moy indi Franc, Eumeu moy indi Ama. Lamb jou nekh derby bou tangue dieur*
@allikebusiness94276 күн бұрын
ak balla gaye 😂😂😂😂
@moudoudiop62166 күн бұрын
Ama balde Seul yalla Nakou yalla maye Ndam aminé ❤❤❤
@ndiagafaye31066 күн бұрын
AK Lou meunti xéw yalna Franc daan jeel bou reuyy amiiiin 🙏🙏🙏
@AmadouSow-y5o5 күн бұрын
incha allah demal nga d'âne ama le 16 boula balla gaye nième nga diel ko d'âne ko nga tek thi eumeu sene bou dawatoul kay modou retré diokhla roi bi
@modo62186 күн бұрын
Emil francoi ndame rek inchallah
@ModouWade-oq2cm6 күн бұрын
Franc yalnako yalla may ndam inchallah ♥️🙏🏽
@MamecheikhantaNgom6 күн бұрын
Franc seul yalla nala yalla may ndam ❤❤❤
@غلامالخليفةآبوبكرسه6 күн бұрын
للهم ءامين يارب العالمين ❤❤❤❤🤲🤲🤲💯💯🤲🤲
@ndiagafaye31066 күн бұрын
Amiiiin
@AbouBa-z3p6 күн бұрын
Dou am dra😂😂😂
@Mansourndiaye-r4u6 күн бұрын
Amine
@MamecorNgom-s2z6 күн бұрын
Sokhor bakhoul dé bro do yalla kham gua @@AbouBa-z3p
@mouhamedfall60026 күн бұрын
Machalla Franc Amna dollé deh mystiquement aussi il faut être prêt
@anonym78116 күн бұрын
Franc grand champion, victoire inchallah❤
@mamadousene55106 күн бұрын
Franc mo meun ama fouf il est en super forme
@ndiagafaye31066 күн бұрын
Yalna nako yalla may ndam AK Lou meunti xéw
@Magistraaa6076 күн бұрын
No cấp
@ibrahimalo66606 күн бұрын
Yalna ko sounou soutoural may ko ndam ci kaw ama balde. Ci bark Seydina Mouhamed
En tt cas il a un mental fort et pour dire vrai lamb leu dei mais ama foumouy diaar franc louma diaxal lay done.. ama feine reik la meunone sonallei franc moy si heihh tei heihham assureiwoul.
@cheikhflodiao60916 күн бұрын
Niang mballo 🎉Mbacké Faye 🎉Franc🎉 La fête aux parcelles assainies le 16 In'cha'Allah ❤❤❤
@AdolpheGomisКүн бұрын
Amen
@KhalifaSow-hw1dw6 күн бұрын
Ndam rek inchalla ❤
@AdolpheGomisКүн бұрын
Par la grâce de Dieu di nga daane Ama Amen
@OmarBao-gu5qp6 күн бұрын
Franc =modou Lo ❤
@amethzidane25666 күн бұрын
Franc stp le jour j boul beurei reglement de compte dieuleul exemple si talfa vs pokola leineu lagnu beug gnom mouy dane motax dagnu lay wo si yi pur le jour j nga gneuw gueineu si combat bi diap si rek boul beurei li khew si signature bi yalla nala yalla may ndam
@AladjiGueye-r6q6 күн бұрын
Yalla Nala yalla may Ndam way ❤❤❤❤
@DameSalle-b8k6 күн бұрын
Ndeyssne moudou lo cou bakh le❤
@mercipourlaqualitenetflix84546 күн бұрын
Ndiago bi ndam rk inchallah 🙏🏾
@ndiagafaye31066 күн бұрын
Mais aussi équipement bi cool fine nice 👍👍👍👍👍👍👍👍👌
@BassirouGueye-i4r6 күн бұрын
Franc Ndam rek 💪💪👊👊👊
@moustaphasognane20716 күн бұрын
Yalnala yalla may ndam franc . Ama lodef danou
@BenzaminCorrea6 күн бұрын
Super franky ndam rék inchallah
@ndiagafaye31066 күн бұрын
Man daal ndiago bi neex nama lool waay 🙏💪💪💪
@FatelKa-l2b6 күн бұрын
Franc yalla nala yalla maye ndam ❤
@alinesyllaSyllaaline6 күн бұрын
Yalna yala maye ndam inshalla ❤sama ndiago bassarél bi❤🙏
@VoyageSpirituel6 күн бұрын
Super Franky je te souhaite une belle victoire
@bassiroundiaye39136 күн бұрын
Franc yalnala yalla May ndam
@ndiagafaye31066 күн бұрын
Amiiiin yaa rabbi 🙏🙏🙏
@ALIOUBluesFAYE6 күн бұрын
AMINE
@AdamaMbaye-e1o6 күн бұрын
Amin amin amin 😂
@lbyoungtv22236 күн бұрын
Y’a meun ya gueneuh nk xalei ❤❤❤
@danielmendy27713 күн бұрын
Je suis de tout cœur avec toi mon frère Ndiago bi Que le Sang 🩸 précieux de Jésus-Christ te couvre et te protège qu’il te donne la santé, la Vigeur, l’intelligence, la force ainsi que la victoire amen ❤
@CheikhouDiagne-f3z6 күн бұрын
Yalla nala yalla may ndam te def la dieulett 🙏
@ElhajdiDiallo-y2f6 күн бұрын
ya meune ya eupé dolle ndam rék inchllah yallna là yalla défal diamou ❤❤❤❤❤❤
@wizamethiadie6 күн бұрын
Ndam rek champion 😊😊
@istanbulsenegal31306 күн бұрын
Lamine merci MAGUi ba usa. Soumou khollle sed na merci merci merci
@mormboup93016 күн бұрын
Franc avan arbitr bi si sifflet mayniou sa teup yi way 😂😂j’aime bien ❤ Yala nala Buur bi may ndam
@khalil62506 күн бұрын
Yala nala yala may ndam inchallah 🤲
@boucardiouf16766 күн бұрын
Bilahi Franc a une bonne éducation
@ndiagafaye31066 күн бұрын
Par rapport aux pikinois
@aboundiaye70236 күн бұрын
C normal c'est un chrétien et ils sont discipliné les chrétiens mais Ama baldé la faral 🎉🎉🎉
@AssaneDiop-n8h6 күн бұрын
Pikine derrière franc ndam rk inchalah ❤
@YakhyaSakho-n6g6 күн бұрын
Ndiago mo meune mo eupeu doolé ❤️💪
@mouhamedcherifaidara9236 күн бұрын
Yalla nalla yalla maye ndam❤
@MamourNgom-q4c6 күн бұрын
Franc yalla nala yalla maye ndam amine inchallah❤❤❤
@MohamedDiallo-s6j6 күн бұрын
LUTTE TV 📺 sen image Yi rafett n’a machallah
@abdoubakhefall63446 күн бұрын
Ama balde yalla nala sunu may défaite ci katanou yalla incha allah
@MameMbaye-p9d6 күн бұрын
Fran seul❤❤❤❤❤❤❤
@ModouNdiaye-je2kn6 күн бұрын
Yalla nala yalla may ndam
@diopmakhou26734 күн бұрын
Vraiment franc tu change ton communication et j'aime cas continue comme ça
@AbdouCisse-xs5mc6 күн бұрын
Yalla na yalla may ndam 🎉🎉🎉
@غلامالخليفةآبوبكرسه6 күн бұрын
ءامين
@mbayeseydinadjibr6 күн бұрын
Ndame rek inchalla f
@omarsarjo62046 күн бұрын
Ndam rekk ❤❤❤❤❤❤❤
@GueyeMbacké-p7q6 күн бұрын
❤❤❤❤ ndam rékk inchallah
@AblayeYoum-x1u5 күн бұрын
Bilaye dama franc rk té yalla tak yalnala yalla soutourale la mayla ndame lou séde inchalahe ❤❤❤😢😢😢
@SYLVESTREKANKOLA6 күн бұрын
Ndam réck inchallah 🙏🙌🙏
@AmdyDiop-ne4bc6 күн бұрын
Ndam rèk inchalla franc seul
@LamzoFall-mj4sc6 күн бұрын
Yalla nalla yalla maye ndam
@freesenegal123456 күн бұрын
Le 16 février franc dey dane ama incha allah
@djibrilniang4816 күн бұрын
Ndam rk champion ❤❤
@غلامالخليفةآبوبكرسه6 күн бұрын
Incalla ❤
@parlonsfoot20236 күн бұрын
Franc est très mature
@yaguesow19376 күн бұрын
Vraiment interview bi nekh neu ameneu talibé machallakh
@ndiagafaye31066 күн бұрын
Non franc nit leu kw
@modo62186 күн бұрын
Bilahi
@mouhamaddieng62186 күн бұрын
Franc ya meune ya eupp doleii 💪
@Modouwillane-vq4kh6 күн бұрын
Machalla yalla n'a yalla may nam inchallah Amine ❤️
@Mudboy_OBS6 күн бұрын
Super Franky seul ❤
@LamineFall-r9p6 күн бұрын
Merci franc❤❤❤
@tontonomar13335 күн бұрын
Tay moom pour cette foi je suis très content de franc à cause de sa comunication
@damembow63746 күн бұрын
Ya meunn yaa eup dolé bonne chance
@ibrahimalo35236 күн бұрын
Franc kassé ❤
@amleking22196 күн бұрын
En faite khawma lane la mais modou lô takhna thioféll bima am si wa parcelle khawma lane la koi blh❤ mais yalla bakhna parcelle ndam rk inchallah 🤲❤❤
@FallouPene-z4v5 күн бұрын
Franc yalla na ko yalla maye ndam si mbarcké serigne fallou mbacké 😊😊
@DjibyFall-g4z6 күн бұрын
Ndam rek inchallah 🎉❤
@ndiagafaye31066 күн бұрын
Amiiiin
@majobecham70756 күн бұрын
Seringe Sam mbye kii suma mam la may his soul rest in peace ❤❤❤❤
@kara18936 күн бұрын
Ndam rek inchalla
@Mamebambadiouf6 күн бұрын
Machallah lutte tv image bi nc na😍💚
@papis21-f3p6 күн бұрын
Frank rek❤❤❤❤
@papegaye14526 күн бұрын
Franc yalla nalla borom bi maye ndame bou reuye inchallah le 16 Février 2025
@ndiagafaye31066 күн бұрын
Amiiiin yaa rabbi 🙏🙏🙏
@ModouNdiaye-y8j6 күн бұрын
Le16 Liss ndiago franc Ndiago yalla naléne yalla may ndam inchalla 🤲🤲🤲🤲
@NabyLeJuriste6 күн бұрын
Franc dal yallah nako yallah may ndam way inchalah
@CheikhFall-v2y5 күн бұрын
Franc Yallanako Yalla may ndam incha allah 🤲
@modoudiop10216 күн бұрын
merci franc wa lamb degn lah hein ndakh linga geum sa bop mais eska franc hamna dayo combat bi combat bi combat bou am solo siza carrier 🧏
@bangalysangare71756 күн бұрын
PA notre fiertés L'équilibre de communication et le professionnalisme parcelloise dépasse largement celle de pikine Franc le prince héritier du trônes