URGENT📛IMAM CHEIKH GUEYE DI LERAL KAN MOY CHEIKH MOUSSA CISSE NDIAMÉ DAROU AK MOUSA DIAGNE YAQKAT BI

  Рет қаралды 24,521

اهل البيت TV

اهل البيت TV

Күн бұрын

Пікірлер: 120
@mouridembaye3925
@mouridembaye3925 3 жыл бұрын
Machallah Imam contaane naniou si yaw lolou yalla na yalla doli tawfekh ak soutoureu barkëp Borome Touba barkëp hisnoul Abrar
@louisefaye5143
@louisefaye5143 2 жыл бұрын
Cheikh mousa Diagne ndiambe borom darou son chemin est la vérité je les donne mon coeur et mon âme
@abdalahyakeen7392
@abdalahyakeen7392 Жыл бұрын
Vérité absolue
@NdiameTv
@NdiameTv 3 жыл бұрын
Cheikh Moussa Diagne amna ndam ndakh takhna ni wediwon Cheikh Moussa Cisse Ndiamé Darou demb teyji gnoukoy deugal.(Atation:SerigneTOUBA Cheikh IBRAHIMA FALL ak:Mourila kinè bayfala Na lèr banopi )
@abdoulayefaye6784
@abdoulayefaye6784 Жыл бұрын
Barki Borom Darou
@sadamsarr9361
@sadamsarr9361 Ай бұрын
Que dieu nous protège
@ibrahimacisse3867
@ibrahimacisse3867 3 жыл бұрын
Serigne Cheikh diadieuf leral gui amna solo. Thiakhaan kat yi dagno bari te khaleyi diangatougnou
@papisbadardiop3560
@papisbadardiop3560 Жыл бұрын
Amoooo dra yow... yow talibé SCMDNBD reik soungueine JakaarLo weih mou deff lah GoorDjiingueine sii yallah
@moustaphayacineseck3563
@moustaphayacineseck3563 3 жыл бұрын
Imam ŋogui lay suivre dila top Merci
@FalilouSene-tv9xf
@FalilouSene-tv9xf Жыл бұрын
Amna solo
@AbuBakar-gi7vr
@AbuBakar-gi7vr 3 жыл бұрын
M'achallah Dieurëdieuf imam Yal Nanio Yallah Dëfal Topë ak Dëgue çi Barkép Al Quraanú Kārim
@mamediarragueye8714
@mamediarragueye8714 3 жыл бұрын
Merci imame
@ousseynousy3590
@ousseynousy3590 3 жыл бұрын
Mashallah amna solo dieureudieuff 👌
@babsndong4388
@babsndong4388 3 жыл бұрын
Gracias ya oustaz
@sidykane4297
@sidykane4297 3 жыл бұрын
Leer na nagn dee amna solo ya al imame
@doudou9242
@doudou9242 3 жыл бұрын
Wawaw dafa ler 👏👏 merci
@BiramePathefaye
@BiramePathefaye 9 ай бұрын
walahi daffa lerr.Ndiambé Darou Fowoul dhe
@adamaba2246
@adamaba2246 Жыл бұрын
Wakh dague yalla khame woumako woon ni ki diamou yalla kece laye def
@falltiane133
@falltiane133 3 жыл бұрын
dieuredieuf sangue cheikh moussa diagne kou serigne saliou séd kene ko wakh 000000000
@serignetoubadiop5528
@serignetoubadiop5528 11 ай бұрын
YALLA NA YALLA arre mack mouy wakh deug;;diadieuf ;;;;;Mack bakhna thime rew ;boudee wakh deug;;raggal yalla;;Li nguay wakh ;mbacke mbacke gno ko waronna wakh ;comme ni RAFAHI di def;;;dieureudieuf;;;
@niggaroouscool7016
@niggaroouscool7016 3 жыл бұрын
Santé Mamé cheikh moussa cissé ndiamé darou rek
@falltiane133
@falltiane133 3 жыл бұрын
Guis gua gor yalla nioune yor nanioy ay casetou ndiambe il dit diouly dou diamou yalla kor dou diamou yalla gis gua sangue cheikh moussa diagne mome rk mo yor degue té bilayi lep lou wax xam xam la yen nak wagene kholate se bipou soidisent gor yalla
@omardiop9681
@omardiop9681 3 жыл бұрын
Billahi imam nei dano fattè yawmal khiyam yalla Nanou yalla mousal ci nafèkh
@ousman5143
@ousman5143 3 жыл бұрын
Shukran imam Gueye ❤❤❤❤🇿🇦🇿🇦
@abdoufatahniang9520
@abdoufatahniang9520 Жыл бұрын
S Modou fadiama Niang mom al co s Touba khadimou Rassoul boléll imam
@khalifacisse5813
@khalifacisse5813 3 жыл бұрын
Merci cheikh bi
@papemalickndong6220
@papemalickndong6220 3 жыл бұрын
Amna solo machalla merci
@sokhoutall4886
@sokhoutall4886 3 жыл бұрын
Je suis yalla yalla mais ce que je ne comprend pas,il avait dit á cheikh aliou cissé lors du dernier ziar darou djouli mome bokouma,alors résament le fils cadet de cheich moussa lui jetait des fleurs,et Lui encouragé.
@sidyndoye6037
@sidyndoye6037 Жыл бұрын
Cheikh moussa cissé kham yalla la woté lingay wakh yeups bakh
@dpfp7113
@dpfp7113 3 жыл бұрын
Cheikh diagne talibé cheikh moussa cissé la
@abdoulayefaye6784
@abdoulayefaye6784 Жыл бұрын
Weuridjil Yalla mo gueun Nit dayy mandu
@mouhamedlamimegueye2663
@mouhamedlamimegueye2663 3 жыл бұрын
Machalla amna solo dieuredieuf ndam rék inchallah
@papadoudoudiaw1404
@papadoudoudiaw1404 Жыл бұрын
Yene gni si commentaire yi niari question rek laleni ladji 1 ere: Kou ni diouli bakhoul loumouye doyei courousse? 2eme: Kourousse bi nieti sedei la niou khadji ko si nienti tankeu de 25 pere, esk dolene ladji ba parei lanelasi serigne bi dioublou? Dioulite youye deff lou bone nio eupeu foufe dioulit youye deff lou bakh ,esk takhna niouni Islam dou deugue?
@cheikhounakhadimdiagne756
@cheikhounakhadimdiagne756 3 жыл бұрын
Baay Seex gëy jaa jëf Maasàllaa
@ibrafatysamb7722
@ibrafatysamb7722 3 жыл бұрын
Jeureudieuf nala yalla faye
@ndongfodhe6507
@ndongfodhe6507 3 жыл бұрын
Dèmlèn wakh si Mountakha mingua khamnè dafa nè Yalla ag yonnatebi Mouhamad sws souniou néké à côté, sérign touba nékè bénèn côté, néna dafay rombou Yalla ag yonnatebi dèm si sérign touba dakhtè lolou moko doy. Khana fofou la bokalé tambali té fofou la mana yèm
@dadaely1603
@dadaely1603 2 жыл бұрын
Mountakha mane Khalid général ??
@idrissamor7880
@idrissamor7880 3 жыл бұрын
Rendez vous le 19 juin à foundiougne chez sange cheikh Moussa Diagne ndiambe borom darou le sauveur des âmes .
@mamanafytoure2383
@mamanafytoure2383 3 жыл бұрын
Wakho fi dara da gnaye far far lo mais wa keure ndiamé darou nieup nieup bén lanou nio bokk bén geum geum moy yalla bi sregine moussa Cisse si bopam lo lou la geumon ta amna lo wakhol moy kepp kou geum né lislam niak diouli ak wor si la boko dob diouli li gna wara dénocé barina
@thiernotine2675
@thiernotine2675 3 жыл бұрын
Imam dieureudieuf
@laminediouf5115
@laminediouf5115 3 жыл бұрын
Akkassa yaram bilay sassou nek demay lay tew lou yalna nga yague fi lole té weir si barké borome touba
@AHLOULBYTI
@AHLOULBYTI 3 жыл бұрын
amineee
@mouhamedmakhroufthiam1476
@mouhamedmakhroufthiam1476 3 жыл бұрын
Imam yangui liguey liguey bou am solo
@worldwords5841
@worldwords5841 3 жыл бұрын
Waw kay imam jajeuf... fo dém amna kouy yakk...
@ndiayefallou1987
@ndiayefallou1987 3 жыл бұрын
Xibari bitim réwyi imam nioune gniy diangue Saxla nagnouko dé diapou thi rk
@chiekhabdoundiaye5810
@chiekhabdoundiaye5810 3 жыл бұрын
Kobagga boko si ,حراس اراد nomoy deff
@talladiop3721
@talladiop3721 3 жыл бұрын
Machala
@moustaphayacineseck3563
@moustaphayacineseck3563 3 жыл бұрын
Imam Dougalal sama nimero thisa group bi
@papemamadoudiop2839
@papemamadoudiop2839 2 жыл бұрын
Démal ci môme nga kham yaw do d'ara khamo dara
@elhadjiba5742
@elhadjiba5742 3 жыл бұрын
Sénégal deffa nékh li niou fi wara dindi mo beurri délou léne si yalla swt ak diangalé yonént bi psl bagna khadialikou ak khol séni intéré ya bokou dégaré dans se pay a coz des tarikha
@khelcom3639
@khelcom3639 3 жыл бұрын
Bayilèn tarikhayi niounèk sèni diam... Lifi lobbies yi yakk singuèn wara wakh... Lifi nassaran yi yakk wakhlènsi...
@elhadjiba5742
@elhadjiba5742 3 жыл бұрын
@@khelcom3639 chekh bi souniou donné béneu rk beurri dollé louffi lobi beuggueu deff yalla nénal ko pour tarikha béneu yone laniou yalla toppoulo mouy yone biniou Mohamed psl diangal té léral niou si Mouy siratal moustakhim nasi nieup teunkou rk ak tawhid c la solution...
@Falloufall-qy3nb
@Falloufall-qy3nb Жыл бұрын
Iow liguay wakh khamoko qui sangsue cheikh Moussa Diagne
@modougueye4251
@modougueye4251 3 жыл бұрын
Lii waa ji wax ñi ma xam ñuy wuyoo Njàmme daaru ñepp loolu la ñuy wax
@bassecisse2138
@bassecisse2138 3 жыл бұрын
الحمد لله رب العالمين
@serignesalioucisse5575
@serignesalioucisse5575 3 жыл бұрын
Mome santoul sakhe cissè cheikh moussa diagne la sante
@senegalrek7975
@senegalrek7975 3 жыл бұрын
Mbacke Mbacke sen thiate moy abdou bara doli ma bagne ndayam
@serignecisse2097
@serignecisse2097 3 жыл бұрын
Moussa diagn
@wosbussness6777
@wosbussness6777 2 жыл бұрын
Wakho fii Bein kham kham mandou mo geun diouly kii iow nafekk nga Wayei diga koo guis leigui
@cheikhantafall6434
@cheikhantafall6434 2 жыл бұрын
Yao waxo fiii dara
@idrissamor7880
@idrissamor7880 3 жыл бұрын
(Imam) vous ignorez plein de chose Serigne Touba jeumé fa yalla la woté Wotewoul jouli , cheikh Ibrahima fall est la preuve
@Smokin_mass33
@Smokin_mass33 3 жыл бұрын
Kone loutakh Serigne Mountakha Di diouli, ake Serigne Abdou Qadr mbacke...?
@sakhewarfatma7116
@sakhewarfatma7116 3 жыл бұрын
Nga balma man mourid la me ngi yonou mourid laniouy touddo me bokkou niou ci limiy wakh cheikh moussa moko wakh psk daniou nan daniouy giss yalla di wakh you bon nek ci pratique boubon niom niepp khamnalen lou mat 20an
@ridiaalfaye2877
@ridiaalfaye2877 3 жыл бұрын
Yow yay Kane bay guéné ay nit si yonou mouride ! Yow est que sak mourid wërna
@ridiaalfaye2877
@ridiaalfaye2877 3 жыл бұрын
Wakho dëgg mane khamoma
@falltiane133
@falltiane133 3 жыл бұрын
Iow alahou hanzouri walkhalou si ben mi tabakhoné serigne touba néna yalla day kouy guis so wéde démal gua gastou bénoum serigne touba younou mourid kéne momoukou sergne touba kou begue dem sy yalla la kham yamoul qui mouride leu wala tigiane la kon doy lilkhamdiami alwara
@ibrafatysamb7722
@ibrafatysamb7722 3 жыл бұрын
Beugg na bokk si groupe bi in challa
@gueyeyakhouba1320
@gueyeyakhouba1320 2 жыл бұрын
Moussa Cissé ak Moussa Diagne gneup ayy fénn kate lagnou, ko weddi Diouli doo ab dioulit ko diouli woul doo ab dioulit
@alioudrame3212
@alioudrame3212 Жыл бұрын
Borom touba dou morom
@AliouGueye-vr3xl
@AliouGueye-vr3xl Жыл бұрын
Imame demal outy yalla
@sidykane4297
@sidykane4297 3 жыл бұрын
Hakkasaa baye chiekh al imame
@papemamadoudiop2839
@papemamadoudiop2839 2 жыл бұрын
Wakho bén deug saytané nga dagay doul
@MamadouSeye-qm9fg
@MamadouSeye-qm9fg 5 ай бұрын
Mane lima ragal Dina réreule xallé yép yobouléne safara
@dio8756
@dio8756 3 жыл бұрын
Oustaz doul kateu nga dhe té kokou sant cissé tamid doul kateu leu
@babacar594
@babacar594 3 жыл бұрын
Sen gnak xam xam ak talibé mom ngay deugeul ni
@pazazzz3831
@pazazzz3831 3 жыл бұрын
Moussa diagne leu
@pazazzz3831
@pazazzz3831 3 жыл бұрын
Xam Yalla guiss Yalla ak beutu bop
@khadimibrahimasarr8549
@khadimibrahimasarr8549 3 жыл бұрын
Kou xamoul nanga mandou té imam si say kaddu bari na lo xam néh ay soss la...ragalal Yalla
@papembengue8307
@papembengue8307 3 жыл бұрын
Diaradieuf imâm lî bokna thi louye défar réw.
@senegalsamadeukk9312
@senegalsamadeukk9312 3 жыл бұрын
Louma wakh tégui ko
@bachirndiaye5392
@bachirndiaye5392 3 жыл бұрын
Se c eve f2
@modougueye4251
@modougueye4251 3 жыл бұрын
Dañ naan julli ak am jot la, jàpp ak sangu set yàq ndox la, ndax nee na ñu sobe si ngay raxas ci yaw la nekk.gennu la.
@ridiaalfaye2877
@ridiaalfaye2877 3 жыл бұрын
Degloule imam mou wakhla
@cheikhniang1492
@cheikhniang1492 2 жыл бұрын
Yalna niou Yalla mousal ci bobou pass pass
@fallgoor9256
@fallgoor9256 3 жыл бұрын
Hakaza baye cheikh Gueye
@dpfp7113
@dpfp7113 3 жыл бұрын
Imam mandou défa bah
@leuzyy5421
@leuzyy5421 2 жыл бұрын
Eskay . Kou khamoul cheikh Moussa rek khamoko. Wayé yalla bou lérr nagni lalay téktal . Cheikh Moussa kokou dafay taal lamp nitt.
@londame4767
@londame4767 3 жыл бұрын
waji day wër di wax rek ñomit fumu jaar waxfa nanufa jaar tontu mu leer
@elthiam5097
@elthiam5097 3 жыл бұрын
Legui bay fall youdoul wore, ak djouli, ak. Legui ki wakh ak gni dieuf nak t yemougne si wakh kesse'.
@papewaly6647
@papewaly6647 3 жыл бұрын
Aujourd’hui je ne suis pas trop d’accord avec mon père même si on ne peut pas emprisonné cette personne il faut le dénoncer publiquement il faut assumer nos responsabilités on ne peut pas fuir nos responsabilités devant Dieu moi j’avais un ami qui voulait m’endoctriner sur ça il y a cinq ans de cela mais heureusement il faut avoir un peu de connaissances si vous rencontrez ce genre de personne surtout les jeunes quand tu es jeune tu n’as pas de connaissances sur ta religion ils vont vous convaincre donc il faut le dénoncer publiquement les contextes sont pas les mêmes par rapport au temps du prophète
@mouhamedmakhroufthiam1476
@mouhamedmakhroufthiam1476 3 жыл бұрын
Tu as raison mais pourtant lui et ses alliés ont été banni de touba sa fait des années d'après mes informations. C vrai si tu ne dispose d'une capacité de discernement sur ta religion on peut t'égares facilement...
@wosbussness6777
@wosbussness6777 2 жыл бұрын
Doull reilkl
@assanemane4380
@assanemane4380 Жыл бұрын
Ayy waxi ndiamé mo geuneu tangue fouf au waxi Cheikh Moussa diangne ...yaw xamo ndiamé motakh....ensuite cheikh diangne..mi...cheikh Moussa Cissé ndiamé borom darou ....moko défar....kép koukay diniatt ndiamé darou guay diniatt.....yaw mi di wéddi cheikh Moussa diangne amo fatthou bi lahi motakh ....guay wéddi lo xamoul ....wayyé nagua xamni kou limouy wakh deugeuleu.......Laillaha Illalah....ak Secret ba moy l'islam....
@loraclecrypte3845
@loraclecrypte3845 Жыл бұрын
Wakho degg ..Ndiame Darou mossul wax ne julli du degg ndax dedoon julli di woor di natt azaka ....Moussa Diagne fen Kat leu ,hérétique leu .Loumouy doundou dou tassaouf .
@elthiam5097
@elthiam5097 3 жыл бұрын
legui loumi wakh fofouko diangue' ak foumouko degue'. Bayil len fen ak nafekhe
@ridiaalfaye2877
@ridiaalfaye2877 3 жыл бұрын
Moko creé bayil niak yare
@thiaomame1357
@thiaomame1357 3 жыл бұрын
Ki ab badi la rek
@papemamadoudiop2839
@papemamadoudiop2839 2 жыл бұрын
Yaw yaye domarame do sa leufeul nday
@alkamaltv7681
@alkamaltv7681 3 жыл бұрын
imam gnom gnép gno bokou lougn geum
@diapoulodia5589
@diapoulodia5589 3 жыл бұрын
Gno yeme dé gnom gneup
@modougueye4251
@modougueye4251 3 жыл бұрын
Saay ñii yàgg na ñoo wax lii ñi ma xam ci ñoom ñepp lii la ñuy wax.
@diapoulodia5589
@diapoulodia5589 3 жыл бұрын
@@modougueye4251 jeman deug la gnom gneup kegne lii lagne gueume
@falltiane133
@falltiane133 3 жыл бұрын
Sangue wédouwoul diouly wédouwoul kor gus gua imame iow désse gua khame lou bary bilayi sa kharite yoyou niou nk sy degue
@ndiamesarr6436
@ndiamesarr6436 3 жыл бұрын
Loolou moula wax amoul gnioom gnieppeu yam dagniou sankou Aÿ ata ngii Mouy wax té démou gniou çi ab télé Walla ab radio wéddi KO Seurigne mountakha démna bâ ça deuk bâ daarou siisé xamal leen né fingeen jaar dou Yoon wa dagnioo SOS seen tarikha bopp çi biir yoonou mouride bâ noppi di mbouboo seurigne touba Gningi çi ndakarou gii fees déll té bis bagniouy wooté daarou siisé googou bou jotée gnioom gnieppeuy dém Meuneu lougniou KO dara dou Aÿ wax dem radio leeral yombou na té défou gniouko seen pas pas boobpu lagniou wara xoolaat
@falltiane133
@falltiane133 3 жыл бұрын
Iow ragalal yalla sangue sérigne saliou moko séde mbir keureme yamal ko ni li nk mom yalla grem mome le yonti bi grem so wéde gua dio ma ça numero ma envoyer audio bi ligui moy gaw net sow na la ler ok
@khadimibrahimasarr8549
@khadimibrahimasarr8549 3 жыл бұрын
Saway ragalal Yalla lingay wakh ni khamo si dara...té boul fénal S Mountakha
@Smokin_mass33
@Smokin_mass33 2 жыл бұрын
@@falltiane133 nga send ma vocal bi degue nga 785137325
@khadimndiaye6737
@khadimndiaye6737 2 жыл бұрын
Ku baax ragalal yalla kii Islam rek lay wax
@sididiaw5686
@sididiaw5686 2 жыл бұрын
Waw minipo yaloujou amna joutopo sareh
@bogartine5217
@bogartine5217 3 жыл бұрын
Merci imame
@talibechiekh1168
@talibechiekh1168 3 жыл бұрын
Macha allah
Probléme Mondial:Cheikh Moussa Cisse Ndiamé Darou est la Solution. Serigne Nanla wara meel.
13:57
Ndiamé Média@Ndiamé TV Sénégal
Рет қаралды 10 М.
When you have a very capricious child 😂😘👍
00:16
Like Asiya
Рет қаралды 18 МЛН
Cat mode and a glass of water #family #humor #fun
00:22
Kotiki_Z
Рет қаралды 42 МЛН
Sangue Cheikh Moussa Diagne :Kou Ko Weddi tabbi sa Ndéye safara
36:57
NDIAMBÈ TV /SANGUE Cheikh Moussa Diagne
Рет қаралды 9 М.
Documentaire De Cheikh Moussa Cissé Ndiamé Darou -  Réalisé Par MH - Partie 8
15:24
Ndiamé Média@Ndiamé TV Sénégal
Рет қаралды 7 М.
Serigne Moussa Ka.,.. Kan Moy Lat dior diop Ak Status Biñko defal
54:08
اهل البيت TV
Рет қаралды 995
SANGUE Cheikh Moussa Diagne :wedi yalla moo gueuneu woor
29:41
NDIAMBÈ TV /SANGUE Cheikh Moussa Diagne
Рет қаралды 16 М.
Lane Mooy Tarbiya : Cheikh Moussa Touré...
30:12
Ndiamé Média@Ndiamé TV Sénégal
Рет қаралды 3,3 М.