Amouléne dara Lou guénn wakh depuis 5 ans fouguén nékonn mbokk amatoul vive la population de yeumbeul merci
@remadiouf9 күн бұрын
gnou bayi ba heure bi di oubi sen lamigne yi doul way vous enerver les gens
@NdeyegnagnaMbaye-d6j9 күн бұрын
Yow la andale
@Emremor3999 күн бұрын
Cet meme population de yeumbeul aussi fane laniou nekone depuis 5ans yi yeup mane je pensais que li c’est récent nekatè Fallou deff neu 5 ans yi prison yi ngen bayi ba lgui diko soga cassal
@strategiesetdeveloppement25257 күн бұрын
Exactement
@amydiagne48689 күн бұрын
Les voisins ont beaucoup de méritent. Mention spéciale. Qu Allah vous protège tous🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@AdjiaFall-j4o9 күн бұрын
Amine ya Rabi
@KassAm-u9w9 күн бұрын
Solidarite famille mo amatoul
@fatimatalo652810 күн бұрын
C une histoire trés triste , surtout encore que sa mère n'est plus de ce monde,5 ans écoulé pour des calomnies c vraiment injuste,franchement chapeau à ses frères et leur sœur ,surtout l'amie de leur maman décédé qui a pris en charge les enfants comme les siens.Leur tante ne pense t'elle pas qu'un jour viendra sur le sol que ns marchons aujourd'hui sera notre toit de demain,il y a des choses qui ne se font pas,c trop lâche.😢
@salyallemomuawrksarr865210 күн бұрын
Li moy matching aparé la mor ngéne bayi ba sénégalais Yi diok di khékh ngéni dora nieuw way doul way😢😢 justice pour fallou Fall 😢😢😢
@mariameboudabakh6989 күн бұрын
Wakhal thi kaw gni mom tahawou gnou sene domi mbok bi quelle tristesse
@AmiCheikh-y6y9 күн бұрын
Dénio rousse ndakh sa mbok dp8 5ans ba légui mé dékando yii môme machallah,Fallou Bou guéné inchallah na guéna diapp gayii,motah mbakh ak yaar réka âme sollo
Vive la population de yeumbeul c est comme fallou n a pas perdu sa maman 💗 wa yeumbeul que justice soit faite
@NabouDiop-r1p10 күн бұрын
Louma beugu wakh rék khép kho famille dou touss🙏😭😭
@amydiagne48689 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@ArameKeita-nm4nu9 күн бұрын
Non fallou sa yaye ligueye na nak
@DiangueDiallo5 күн бұрын
Yéne amoléne loléne wakh li séne gathiéla chapeau deukeundo yi
@AisatouWade-b5m9 күн бұрын
Machaalah wa mbedou fass dekeundo you baax
@MoussaThiongane-m5r9 күн бұрын
Mane Dall Mbokou Yui Légui Diakhale Nama Souy MéTi Doléne Guisse Moukkkk Fok Mou Commencé Nékhe Rk Domérame Doléne Rousse❤❤❤❤
@ndeyeseynaboundiaye119210 күн бұрын
Vraiment yekh ngen trop
@diarra18859 күн бұрын
En tout cas baye zal néna guisoul mbokou yayam wa yarakh rek la guis mi ngui lene di sant di lene guereum Medecin apres la mort bayi ba senegalais yi diouk nguéne soga diouk😮
@AichaSow-u2b10 күн бұрын
Et pourtant Oumy migui keur diambour ak niéti domam yén nén guéndi sogua guén
@Sené-g2q9 күн бұрын
Marche pour fallou 😢😢😢
@adjiastoudiop536010 күн бұрын
Wa yèen founguèn nèkoon ba heure bi xalass
@HawaKeita-hk8bp10 күн бұрын
Très bonne question bigne len gnané dagno bagnone
@mariameboudabakh6989 күн бұрын
Mo yaw wahofi dra diaroul dohsi tank diam djambour yalla yi gnongui doh lithi birr
@Natur_elles-glow9 күн бұрын
Vraiment mane le papa de Fallou mo bonne Mais il a fait sortir tous ses enfants Founiou nekone
@mamadouaissatougueye65099 күн бұрын
Vraiment
@cheikhbassendiaye64969 күн бұрын
Wallay fone nekone la khamul
@MatyDieng-n8w10 күн бұрын
5 ans yena yeeekh
@Sambou-sh3qx10 күн бұрын
Je suis fallou free
@Ayou15710 күн бұрын
Mane dama fogone ni yayou fallou amoule ay mokou
@MoussaKamara-b3l10 күн бұрын
fallu rék ❤❤❤❤❤yalla dîna ko diapallé fallu dîna bahe
@GnilaneCoiffeuse9 күн бұрын
Complicité bi falou amone ak bayam lolou mo waral tante bi fékhélko ba tédj ko wayé yalla néléwoul
@diilerecaalifuuta5497 күн бұрын
Père yoow mannga toukki depuis 1997 joudougou ma actuellement Manngui Espagne dem dikat senegal
@SeynabouFaye-l3n9 күн бұрын
Ha female tok sa keur mame ba gnoune diamboury yalla yi gnou paré fo nékone bobou ba legui 🙏
@KhadySarr-lw5wc9 күн бұрын
Wakhofi dara. Fonecone. Boba balegui 😂😂😂😂
@MbaloNdiaye-n1t10 күн бұрын
Tonton ligua def doynar war
@FatouFaye-ue2xq9 күн бұрын
Danguay sét li rek 😢 c'est vraiment désolant
@coumbandiaye190010 күн бұрын
Yaw déloul dankeu say djarbat torokh di toltolane sen keur deukeundo depuis 5ans et toi tu viens d'arriver souniou ladone khar dé naniou beu niou souliléne. Nidjay moy yaye .
@christopherouxmollard30878 күн бұрын
❤❤❤❤❤ bravo
@YayeAwaGUEYE-ci2hx9 күн бұрын
Meunone nga nopi dé. Vraiment bobou ba legui😢
@mbenedieng22989 күн бұрын
Boufi kéne défe médiation beugouniou naniou bayi niouneu niou défe sunu liguéye bilaye fallou santale sa yaye liguéyame rek mola féniou leup dina lére
@princessesyssi19539 күн бұрын
Yow diiiinte, ken ladjoula, ya yeeess. Yalna len akh Serigne Fallou dal. Yen dé biss bolen dadjer ak yayou khalebi alakhira di nguene rouss. Tchiiipiirii
@MaguetteGueye-k3v10 күн бұрын
Waronga roussa guend
@AisatouWade-b5m9 күн бұрын
C'est trop tard le médecin après la mort Merci wa mbedou fass
@BabaSaka-sk7is10 күн бұрын
Ya niakk diom 5 ba legui
@coumbandiaye190010 күн бұрын
Beugueu buzz ak fégne rek on s'en fout wa kogne biii niogui khékh khékh biii, bocou lègui boul soneu. Pfffffffff
@aramembaye979 күн бұрын
Yallana yalla walou thie barke Seydina Mouhamad psl amine ak thie barke Touronome Serigne Fallou Mbacke amine
@Mariofilyndiaye10 күн бұрын
Yow nafèk gua fo nèhkone tous ce temp free falou
@ArameKeita-nm4nu9 күн бұрын
Yalanala serigne fallou tek lokho si barkep radia bii
@MossaDg10 күн бұрын
Kiko atté mo gueneu doukhane ndayame
@NdarGuedj9 күн бұрын
Des fois juge yi douniou def dara mais sa police bala nioy corsé dossier bi souniou lene graissé bouka defé juge bi sou kholé dossier bi rek day ni monstre la motakh Niouy def appel
@MossaDg9 күн бұрын
@NdarGuedj tu à raison frère parceque ces le gouvernement de macki Sall son des battares
@AissatousophieKane-dr8fy9 күн бұрын
Waw Ani papay fallou
@MinaMina-fo4nl10 күн бұрын
Iow mom danga tatder niou teudj sa djarbat 5 ans nganan mangui doga diogué abijan ah fehal ba balanga delou nga lidiunti li nidiaye moy yaye
@aboridial26410 күн бұрын
😂😂😂 ki day fontou rk
@BintouSaw10 күн бұрын
Ki lumuy lidiantéti sénégalais lidianti nanie ko baparé ndax thiow lé len taxa guéne budé nji dongue 15ans dinako teude
@maimounacoundoul94249 күн бұрын
Médecin après la mort bayi ba legui nguay nieuw di wakh
@BinetaNdiaye-e2v9 күн бұрын
Wa yarakh yala n'alene yala diapeler tonton fallou nopil amo lo wakhe dieppinala trop falou Moy guene si diame tantame.bouko akhe fallou diaper
@khadimfall504310 күн бұрын
Gnii nio guene bone mére bii sa diarbate niou tedj ko 5ans seti woko lidiantii woko ba ay diambour lidiantii ko ngay guene dii wakh topou lelene felé way 😭😭😭😭🫣🫣🫣
@TanouDiallo-c9j9 күн бұрын
Mbacké fall Baye bi takhoul nouy wakh baye
@sokhnagueye14599 күн бұрын
Yèkh ngène trop aprè 5ans doy na war deukeundo yalna Yalla fay lène
@AminataCisse-h3j9 күн бұрын
KONE PA BI VERIFIER WOUL PROBLEME BI BALA MOUY WAKHE DOU YEUFOU KILIFEU
@damesamb62969 күн бұрын
Djiguen douma yilif ba dima bole ak sama ndiabote, sénégal rewmo khamni khol ndono ak diaye dole rek,yalla dara douko raw
@damesamb62969 күн бұрын
Yaguena sénégal ndakh sénégal toujours daye ame ndiguen gnouye niew thi keur di khol ndono wala niouye khatal kignou fek thi keurgui dilen goumdoukhatal
@DiewoKeita-y1p8 күн бұрын
Bilaye wakhal mbokou légi bawal niou dèm kou wakh li bayi lathia déss.
@YacineSene-s4c9 күн бұрын
Tanta fallou khana amo khôl li niaw na
@NiangGalsen9 күн бұрын
Mane guemouma justice Senegal. Lima guem moy gnane Yalla mou moussal ma si soss katt yi.
@alladiagne120210 күн бұрын
Trop tard
@salyndiaye929 күн бұрын
Nena mogui wone Abidjan Kay depuis très longtemps
@mariamagueye90849 күн бұрын
yène wa famille yaayou fallou, vous êtes irresponsables. vous n'avez pas pris soin des enfants de votre soeur décédé. Honte à vous
@AbdoulAzizDabakh639 күн бұрын
Sétsi nga domou ram déh. Papa fallou domou ram pure leu ak diabaram bu bonne
@bintoudiatta2709 күн бұрын
Vraiment c'est trop c'est mal au coeur
@papedabotv9 күн бұрын
Si je comprends bien yaw mi di ndidiayame 5 ans yi fallou fall teude pendant tous se temps déguanté wo ak saye diarbate c grave, diaroule wone ngaye nieuw
@RamataSow-j9b9 күн бұрын
😢😢😢😢😢😢
@kadiag18769 күн бұрын
Franchement c est ridicule mounone ngene continuer def pat rek mo genone. Fallou a aujourd'hui des milliers de freres de soeurs de de meres et j en passe. Bien cordialement
@dialibatoumarahib7910 күн бұрын
Wahoulén ba eurbii loy wahati
@abdoulayekane199710 күн бұрын
Yaw dagua yapp sa diabat yi trop
@SavaneAstou9 күн бұрын
Fallou mane khamou mala mais li daf ma mettii trop yalla kham nako migui melnii mane ak mome nio bokou ndeye ak baye lii metii nama trop wallahii
@fayefaye63329 күн бұрын
Père stp nopil 😢😢depuis lors tu étais où😡😡😡😡😡
@AmadouDiallo-em6pm9 күн бұрын
Quand c'est lent c'est mauvais vous avez étais trop lent pour le cas de fallou justice pour fallou on réclame la libération de falou immédiatement
@PendaMboup-e3d9 күн бұрын
Aye waye ki da rouye gathier nane ko yaw sa diarbate nek si prison 5ans bobou ba legui nganane khamo lou affaire yi deme
@gayafall8 күн бұрын
C est comme ça la vie .les tantes mélangeaint
@loseynabou-kk9eu9 күн бұрын
Depuis tout ce temps vous étiez ou ne me dites pas que depuis cinq ans vous n’étiez pas au courant 😢toujours au dernier moment vous n’avez rien a dire
@malickgueye48819 күн бұрын
Wa legui khalé bi khol nagnou mogui ak ndawam gnou ni dakko gaagn nagnou khol fane la khalé bi gaagnou ak date bi ak heure bi esk fallou rocher na ko ???🤷🏻♂️🙏🏻🙏🏻🙏🏻🇸🇳nagnou def yone bayi sene yiii
@zerdox9229 күн бұрын
Depuis 5ans tu était où même nous les inconnus on connaît bien l histoire
@bks68699 күн бұрын
La 2ème personne là n'a pas honte si tu connaissais bien Fallou tu devais savoir si Fallou est capable de tel acte
@SuperOUMZ9 күн бұрын
Yéne gnouss léneu feulé Ba xaleyi di souffrir fouguene nekone..5ans gueneu di doga takhaw ak seneu kanamou gatié yi Gatié kassé moléne diapp..shimm
@GnilaneCoiffeuse9 күн бұрын
Justice Senegal doyatouma
@damesamb62969 күн бұрын
Sokhar ak nafekh rek mais taye pabi yilif ndiabotam ba affair bi yeksi fi legui guis ngako
@rouguiba37049 күн бұрын
Médecin apres la mort qui kén warouko won diokh micro
@NiangGalsen9 күн бұрын
Ame sa diarbat bobou ba légui khamo si loumou néh. Plus de 5 ans
@salyndiaye929 күн бұрын
Deuxième personne waxofi dara
@Dior-tx7tv9 күн бұрын
Yow Fatima Dieng sa Galathieu tothieuna dinagnou tegal sa Ndeye
@preuvenii65359 күн бұрын
Mais jenrou nit you bonne you melni tantay fallou gnogui ame si adouna bi ba legui
@kadiag18769 күн бұрын
Moma diakhal yi dafa khewi te yiwedi vraiment, Histoire coumba am ndeye ak coumba amoulndeye C très triste
@moustaphabeye61989 күн бұрын
Wakho fi Dara way 5 ane
@mamadoufaye99629 күн бұрын
Khawma dè liniouko wakh amna wala amoul wayè gnisi def enquette moiye poloce wala gendarmerier ak gniye atè warna nio kholate bou bakh sen ligueye war ngeuna khol swn digantè ak yalla dè khol aussi nè yeune danguèna am ndiabot gni atè té dou niou até si yoon nio niou nioma takh di wakh kou def mom takhoul maye wakh wayè kou defoul dara nga teug ko yeune yi mètina dè té dafaye am loubari
@Ndeyerokhayadiouf-jw8nm9 күн бұрын
Sa tante yalla dina atéke bôme.li yobou sa yaye douko fi bayi .yalla gnipe lafi nékalr😢😢
@bks68699 күн бұрын
5 ans après gay soko nieuw wakhofou dara
@JamilaSall9 күн бұрын
Les yeubeulois merci
@AminataCisse-h3j9 күн бұрын
LEGUI KHANA PA BI KHAMNA LIMOUFI INDI EST CE QUE FEMME LA AM WEULEU
@Magatte-m6s9 күн бұрын
Depuis 5ans tu sort de ton silence que aujourd'hui
@Ndeyerokhayadiouf-jw8nm9 күн бұрын
Bala magal bi yall n'a nga gué ni thie sa barké tourodo borome magal bi.lidou Hazard litakh thioli claténi .dinga guéni inchallah
@rokhayaba57259 күн бұрын
De 3:14 deloul nankk fi ngua nekone
@ngonefall71289 күн бұрын
Wa yenn folenn nekonn top lèn feulè famille you bonn guèn bobou ba lègui
@burr93797 күн бұрын
Mbirmi dina wéssou fii togual fofou di wakh
@AblayeThiam-ui4ck8 күн бұрын
Dawe. Si. Bou. Falou. Gene. Da. Wara. Dougou. Kasou
@zerdox9229 күн бұрын
Depuis 5ans tu était ou
@seuneba70919 күн бұрын
Vérité absolue
@AisatouWade-b5m9 күн бұрын
Amo lo waax
@Dior-tx7tv9 күн бұрын
Tanta gnou djiguene gni la ndieuka guéné Fatima Dieng yaye domoukharame sa moudj dou rafete
@DaadoCamara-w7u9 күн бұрын
Sa jaune moutarde bou fourassé pousseul fii wayy
@awasambou45619 күн бұрын
Medecin apres la mort
@coumbafaye93199 күн бұрын
MBAKER FALL DAL DATA REK MOKO DJITEUL. KEN LIGUEYOUKO. YEN NAK HEURE BINGEN SOGUA NIEUW MOMA DIAKHAL VRAIMENT.
@MohamedbachirDiop9 күн бұрын
Ki di Wakh dafay doul rek domarameu deugeula foumou nékone