Il faut créer des emplois. Des usines .pour les jeunes
@thiambasamb682 жыл бұрын
Créer emplois wessouwoul PRO MOBILE gua khamni ay milliers de personnes nioffay liguéy bo khamoul Daguay lathié t mounone na tokk doundou ci khalissam t douko wagni dara sénégal naqq sokhor lagn deff mandou lén ci Mouride yi sen xool ignane yi
@diarradiagne11082 жыл бұрын
@@thiambasamb68 TOGNE REK LAGNI DEF!
@thiambasamb682 жыл бұрын
@@diarradiagne1108 gni kay bou yagué beug histoire la t serigne bi diameu la woté nagn lén dieggeul reqq t yallah takh danion reer reqq dou lennen
@aneousmane85422 жыл бұрын
mo gueune lii
@rabya72 жыл бұрын
@@thiambasamb68 fii keene sokhorou fi mane Mouride la .créé ay emploi dou doy .kou meune n'a déf.wakhtane dou khoulo.
@tallaseck55582 жыл бұрын
Machalah lou diouguei si khol si khol rek lay delou. Contane illimités barkep Sidi Birahim.
@youprotv74092 жыл бұрын
Serigne touba numéro 1❤❤❤❤❤❤❤💯💯💯💯💯💯🙏🙏🙏🙏🙏
@gueyeloriginal63852 жыл бұрын
Serigne Mountakha bassirou mbacke yalla nafi yague té Ande AK were soutoura adouna AK alakhakhira
@bassirouba63392 жыл бұрын
Dieureuf yalla sunu borom mí def khadim rassoul senegalais africain 💕💕💕💕💕💕💪💪💪💪💪 Jeurejeuf
@nouhasane53072 жыл бұрын
N'oublions surtout pas les 5 prière d allah car la vie est courte
@tmc50872 жыл бұрын
Go.
@gaben29742 жыл бұрын
Tu as raison c’est cela le farata.
@latyrndiaye56742 жыл бұрын
Mé yaw kane guay fatali dioulit fi saff sapp ak yalla la deff yaroul way bamba merci everyhewer ✨✨✨
@petitfilsdelatdiordiop58232 жыл бұрын
Fall dano diouli jouma ba paré 😂di soga deff wakhtan bi mais merci pour l’info
Serigne Touba Serigne mountakha Mbacke yalla nafi yague ta wér ,Mbakiyou Faye dieureudieuf yalla Nala yalla dollé takhawou si barkéb Serigne Touba 🤲❤️❤️❤️
@sileyedia61082 жыл бұрын
Machalla YALLA na Yalla gudal sai fane serigne Basirou anda ak wer ak werle ak Bolemou mouride ak Baye FALLE👑👑👑👑💐💐💐🥰🥰🥰💖💖💖💖💎💎💎💎💎💯💯🏅🏅🏅🏅
@badiartv2422 жыл бұрын
avec ces milliards, il faut créer des entreprises à TOUBA pour sortir les jeunes du chômage et de la pauvreté
@thiambasamb682 жыл бұрын
Yaw dagua reeer PRO MOBILE gnata jeune nioffay liguéyé lidieunti lén sén bopp t bayi Mouride yi
Dieridiefati Serigne Touba Kouné Amine Bala Déwen Yalla Naga Am 1 Miliyar
@abdourazakh20142 жыл бұрын
Serigne Mountakha Mbacké yalla nafi yague té ande ak werr ci barké Serigne Touba, Serigne Mbackyou Faye yalla alal dji barkèl té yalla na weurseuk wi yokou
@bouryndiaye35052 жыл бұрын
Dieuredieuf serigne touba serigne mountakha mbacké yalena fi yague té wér si barkè khassidayi
Serigne Abdou Lahat avait demandé un milliard aux Mourides pour les travaux. Certain Mourides même disaient que c'était impossible, les intellos Sénégalais, disaient est ce que le Marabout xam na luy 1 milliard. Léegui béne Talibé mo kay joxé, Mbakiyou n'est pas le premier li da siiw rek !
@Laseydatte782 жыл бұрын
Machallah sa commentaires je tiens au cœur billahi Yonou ser touba amoul tannkki guinaaw d Thia kaw ça kanam rkkk
@fallam10102 жыл бұрын
@@Laseydatte78 ndeyssan noon la dé sa kanam rek inshalla
@panogayembaye21162 жыл бұрын
S Touba kénn la ❤❤❤❤
@lakhatdiouf68492 жыл бұрын
Thanks 🙏🏾
@com66632 жыл бұрын
Yallah Allahou swt saam djikoyii, saam sédaal Monde bii, Sénégal thi barké seydina Mouhammad salal lahou Aleyhi Wassalam, barké Serigne Touba.
1 milliards comme Adiyah pour le Serigne,pendant que beaucoup de Sénégalais(e) meurent ds les hopitaux pour de simples opérations,et personne ne les aident.c'est ça le Sénégal,des Serignes milliardaires et politiciens
@khadimsene39612 жыл бұрын
Louthiyyy sa yone
@mamechiekhfall3152 жыл бұрын
Boul mér li yalla la rék dou mbakiyou mo wara défar hôpital état mo wara défar hôpital 🏥 li niane gou nagoula kéne manou si dara
@serigneseye68732 жыл бұрын
Serigne liniou koy diokh si yoonou L’islam rek lakoy def peut-être nak danga xamoul rek ms gnii seeni keur boofa deme dinga xamni adouna yite loulén ms jammou yallah ak dimbali nit gni mo sen yitte , deelen xam boubakh lingeen di wakh
@mouhammadoufall91492 жыл бұрын
Lou sa yooone pendant le covid il avait généré 200 millions pour aider ceux qui sont dans les hôpitaux ta pas vu cela ?
@smssms93002 жыл бұрын
Beug na nite bouy wakh mouwakh loum kham mbamou noopi Serigne bi lougnko diokh yayonako ndakh si askanwi reck lakoy defaat 11 morts yiwoon si mois de mars ay millions la dieul diokhko victime yi te Dara oubliés voko
@bassiroudiop98142 жыл бұрын
Mazahalla diereudiaf Serigne Touba ❤️❤️
@oumydiouf90322 жыл бұрын
Serigne mountakha yalna fii yague té wer
@mamecheikhanta44222 жыл бұрын
Serigne Mountakha Mbackè yalnafi yague ta ande ak wërr❤️🙏🏽
@khoudiaguenetoure742 жыл бұрын
Ndeysane Sénégal thiey
@aboulbachir87452 жыл бұрын
Seugne mountaha da nek kouye partager mon tekh lounee meunenako ame dara djoubouko tee kou ame koloree la kou wathee bopam la tee kou ham adouna la yallah nako yallah may fanwou goude ak werr gou yaram inchallah
@moustaphagueye47092 жыл бұрын
🤣🤣🤣 bayil togne bakhna
@mourtallasaliougueye79972 жыл бұрын
Amine yarabi
@awambaye27682 жыл бұрын
Kénn dou cheikh Amadou Bamba khadimou Rassoul Serigne Mountakha Mbacké yalnafi yagu té werr . Dieureudieufff Aladji Bakiyou Gnoune Mouride yi ak kepp kou beugu lou bakh gako deffal yalnalafi yalla yagga weral yokkal .Bilahi Mbacké dieureudieufff Serigne Touba.
@gadiosslafaramareene5912 жыл бұрын
Machallah mbacké bala ❤❤❤❤❤
@taphambaye28612 жыл бұрын
Yalla nafi yague loll tée weer mbacké balla amine ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
@khelcomediaga66422 жыл бұрын
Mbakiyou faye yallanala yalla faye
@khadimsyllabresilchapeco52592 жыл бұрын
Ndeysane mbackeyou fay yaw dagha bakh rek bilahi lide serigne touba reke moko mana am yalla naniou yalla bole thi milhader serigne touba yii banioy def lo melnii
@serignembackeboye13622 жыл бұрын
Akassa am na solo 🙏🙏
@lejeunesaloumsaloum3092 жыл бұрын
Dieuredieuf ahmadou bamba 😍😍
@moussasane94782 жыл бұрын
Jeurejeufé Borom Touba Serigne Mountakha yagg fii loll tée wërr Yalla naniou Suñu Borom dff ayy talibé Serigne Touba you magg tëe mattë ko
@moussagueye62642 жыл бұрын
amnasolo yalla nano man nonit b s touba amin
@sanesenebou11202 жыл бұрын
❤️❤️❤️❤️👌💪🏻
@saracoutureprestige2 жыл бұрын
Machallha mbake balla yague fi lol te wér
@mortallacisse23202 жыл бұрын
Mbakiou ya bah waye té goré yalla nala yala faye
@bambathiaw69132 жыл бұрын
Santatt kutedki bou weer Serigne Mountakha mbacke yalnaga fi yagg teii andank weer🤲
@maimounasow58542 жыл бұрын
Machallah machallah
@djibrilmbow80742 жыл бұрын
Dieureudiefé Serigne Touba mbaké 👌
@cissthierno75062 жыл бұрын
Le véritable père de la nation yalla nafii yague ta wérr
@khadytine74452 жыл бұрын
Diaradieufé serigne touba
@abdoudiagne67712 жыл бұрын
Thieuy serigne touba ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@khacimecisse93042 жыл бұрын
ndeysane 😭😭😭😭😭😭😰
@laminekane44962 жыл бұрын
Gni khamouma kan laniou yap moul melni senegal dara khéwoufa plus 10 bébés 👶 déé si anam bou méti niom niou melni gnoroulen di def sen yi melni kou nekoul si mosqué yalla naniou yallah diéga mousal niou si ay ndjite you rerr ba parei di rérelaté amine
@abdala952 жыл бұрын
Mon pays va mal wollah... donner un milliard d'aumone dans ce pays alorsque des miliers de gens ne mangent pas à leur faim... Allahou Akbar adouna bi nguisteul amoufi solo yawmal khiyaam mo diarra ligueyeul... Que Dieu nous pardonne🙏
@fallserignemodoukeman92532 жыл бұрын
Thieuy Serigne touba 😭😭😭😭
@mamadouwelle61762 жыл бұрын
yalla nagnou yalla tek si siratal moustahim
@mamadoudiong11572 жыл бұрын
Dans un pays normal aquete direct Gendarmerie
@sokhnafatybousso13512 жыл бұрын
😄😄😄 NDAYSAN YALLA NA YALLA RAXAS SA XOL BI LI MAYU YALLA LA
@aliounendiaye45532 жыл бұрын
oooooh les mécontents ils vont continuer de souffrir des gestes des mourids encore et encore et encore massa massa massa DIEUREDIEUF DIEUREDIEUF mourids
Pourtant ngi mana wakh louy diarigne nit aka bari wayé halal rék li niawna walhi miliar bii bo démon ba thi village yi nga diokh par 50 000 mo Guen fouf wayé sérignsi miliar comme 50f si niom
@abdoulayembayendiaye97212 жыл бұрын
Mbacke ballla Guene yague Guene wer thi barkhep khassidayi 🙏🙏🙏
@mamadousarr95312 жыл бұрын
De l'hypocrisie pure au Sénégal .
@morhanasokhna6162 жыл бұрын
Way ndaysan dieuwrine mbackiyou ya bakh way
@femmepanafricaine51472 жыл бұрын
Thiay galsen yalnagniiu yallah def deug deug ay dioulit akan gniou bagnko di moubo surtout pourquoi donner aux riches ceux qu’ils ont déjà ne me parler pas de dakoy diokhé watt sénégal mouth fi yomboul té ken gnemewoul seukeut deug la yallah beug la wakh lignou neke dou deug dou yon limo takh ibadou koumase am base bou solide senegal et je leur donne raison thiakhan rek fowe dine rek bak sa serigne ak boumou meuna don bayi yallah ak Rasoulilah wara dimali newdidole nan serigne souma ko diokhe dinalen ko diokh mom mouy defar yonam yaw gay yak sa yon serigne bi day diam gay diam sou yawmalkhiyame ken kou nek sa bopou doynala magui khar ba ben nafekh riposté amna connexion bou doy
Waaa ani mandou mo mome son argent 💰 bouko nékhé mou meyko tamite mome bamouy liguéye ba ame son argent 💰 diapalé ko bouko nékhé mou mey kouko nekh Kone mandoul té nopiiii
@femmepanafricaine51472 жыл бұрын
@@khadimthiam5060 ya yay ne tampi lonko iblis bou melni yaw ladon khar nafek limoy dine fougniou ko binde si le Saint coran arrêter way adina dou keur sa bamel ken doula fa fek dila plaidel lou ler lala wakh dou wakhi lambatou nit day deugou loudoul yallah nit la
@kheusskheussofficiel88742 жыл бұрын
yalla nagniou yalla mousseul si igniane ak kholl bou bonne yaw guissa go dara li dou dara sakh hhhhhhh
@agun13712 жыл бұрын
@@femmepanafricaine5147 putain.. et alors? Après ? Ioe djoulit ga ?ok lijeuntil sa djoulit tei nopi. Lousissa yone alors ?
@ibrahimamballo55842 жыл бұрын
Argent rek Milliards rek Mackiou, ou est ce que tu as eu ta richesse Est-ce que tu honore tes impôts , tes dettes Es tu allé à la Mecque Combien de ménages pauvres vivent à moins de 1000m de chez toi. Autant de questions Que la paix règne au Sénégal Que Dieu nous comble de sa miséricorde Bon séjour au guide religieux