Tant qu'on change pas les mentalités le Sénégal ne va jamais changer. Bon sens les parents revoyez l'éducation de vos enfants.yalla nagnou yalla sammal bopam
@bouyafall34622 жыл бұрын
mane parents yii rek lay dieul comme responsabilité nah dagay djiss sa dome moûy fréquenté nio xamni douniou ayy andadoo you bahh di def loulene nehh mais sene yone doussi nekk ba yalla def lii après niouy guene di sédé lo xamni kokou djissoul dinako nakaré gueum nanio yaratt diabott gui boubah t di wahtane ak niom si lilene di dieumeulé kanam adji demm gui yalla nako yalla yeureum t diégalko ay bakaram
@Youtubesenegal242 жыл бұрын
Yalla nako yalla yereum gabou ndeysane ba bimouy fatou mogui teint bop bi bind si mamalamine té cheikhou mama lamine moko fat ndogal mo niew reik kou xam cherif assane xamni borom bakh la té amoul problème di mastawu famille gabou
@ndeyendiayesiby20652 жыл бұрын
La douleur que sa mère ressenti 😭😭😭
@mamyabdoulaye32572 жыл бұрын
😭😭😭😭
@elbousrijallo30882 жыл бұрын
Mais prison Kedougou bi pour lane la nagne lèn ramassé gnom gneup fofu diarul jugé diarul dara
@youssoufabdoulayediopjohnn37742 жыл бұрын
Maman bayil linguay deff lii bakhoul si kii guenn aduna kholal si Díaz mi lakk Djouroumii domam khamgua Koko la guenn metile souleundo Djouroumii bantt mouñeul yaye suñu Boroom doli yeurmande khareko aldiana ak mbolem djoulitt amine
@cheikhmbaye62112 жыл бұрын
Yalnako yalla haré aldiana firdawsi
@abdulkarimsowe47592 жыл бұрын
Toutes mes condoléances Qu'Allah apaise le coeur de ses parents
@amadisow90842 жыл бұрын
Chapeau siiteu 👌🏽
@abdullahade24562 жыл бұрын
La douleur que nos méres ressenti war na tax ñu moytu yénn yi 😞
@bell26922 жыл бұрын
Mbeur mo wara diekhe senegal bilahi 😭😭😭
@Marieseck5342 жыл бұрын
Béneu dom bou gor ngua khagne ko yayam😥bi yakar bou tass 😭 Sénégal yakhouna😭😭😭
@mayramediallo65942 жыл бұрын
Gabou borome sicap mbao Sama kharitla wone yalna yalla yeureum te kharela adiana
@mamadouniang32452 жыл бұрын
bjr je m excuse mais pere de Gabou touddoul cheikh ibra faty dieng? parck pa bi thi interview dafmay ndourok sama ben collegue de travail
@mayramediallo65942 жыл бұрын
Khawma papa m waye gabou dieng. La santé
@tawfekh24102 жыл бұрын
Yalnako yalla yeureum té diegual ko tabalko aldiana si barké serigne touba ak doley mame cheikh ibra amine
@houssaryjr61222 жыл бұрын
Sangara si ak yamba bi mome fou mbolo néke mou néke fa déeee doufa diougé kadou gui nake d'où nékha deuge ms Moy li âme
@antagueye79932 жыл бұрын
Ak carte exbet bi
@houssaryjr61222 жыл бұрын
@@antagueye7993 bly leupe bakhoul toujours khôlle bou Bone rék gay deuke
@papesidydiatta95942 жыл бұрын
Il est tant au Sénégal qu'on fasse une assise relative à la sécurité dans notre pays. Par ailleurs la lutte et les navetanes doivent être revues pour aider les jeunes à connaître et comprendre l'esprit de ses disciplines sportives. QU'ALLAH nous vienne en aide pourvu que ces pratiques criminelles n'existent plus au Sénégal.
@fadelseck26782 жыл бұрын
Nonnnn xolale diaroul yéneu sécurité bi sax Naniou indie peine de mort rek
@aminatasow41842 жыл бұрын
Alhaouma amine 🙏
@elhadjsow79862 жыл бұрын
Je pense que li ça n'a rien à voir avec la sécurité mon frère.
@pesonko56652 жыл бұрын
Revue no arréte amoul ndiarigne senegal
@papesidydiatta95942 жыл бұрын
@@fadelseck2678 lolou tamm solution laa.👍
@ardosow27272 жыл бұрын
Mes sincères condoléances mon grand Mara
@lahadboukharagnelo67072 жыл бұрын
Merci 🙏🏿 sitteu
@tigendiaye48652 жыл бұрын
Maman le gouvernement ne peut rien faire Yaar léneu séneu ndiabott yi...les enfants sont mal éduqué au Sénégal..
@luno43662 жыл бұрын
Slt frére boul wakh lolou u c nitte dina yar domame mou guéne sistém bi yake ko
@luno43662 жыл бұрын
Et li gouvernement bi meune nassi dara Kaye péne de mort bou amé rék mou djékh
@2cpiofficiel8292 жыл бұрын
C vrai mais c pas le moment la maman est en deuil
@fatoudiouf87562 жыл бұрын
Yaye yi yar naniou ba sonou
@tigendiaye48652 жыл бұрын
Vous avez raisons mais lolou exeption la enfant bien éduqué dina ragal yéneu fréquentation yi...Je suis d'accord kou Ray gniou ray la..Mais esk lolou solution la USA amna état you koy def esk réglé n'a problèmes bi ? N'a gniou yaar khalé yi Sénégal Lifa nék amoul féneu
@adamatalla7782 жыл бұрын
Le sénégal le pays le plus respecté le plus aimé de l'Afrique c'est vraiment dommage avec cette jeunesse ratée une jeunesse sans éducation une jeunesse vraiment nul
@moussasoumare23862 жыл бұрын
C’est la responsabilité de l’état
@issmansour2 жыл бұрын
le pays le plus respectè et aimè? Qui t’as dis ca?
@fatimasow91442 жыл бұрын
@@moussasoumare2386 arrêtez lou khew ngèn ni État li c’est de l’indiscipline parent yi yarou gnou sen dome yi nagnou yarr khalé yi tè lambeu gnou èliminer ko c’est de la pir violence
@mamadoumamadou42462 жыл бұрын
@@fatimasow9144 doul
@demehawa72822 жыл бұрын
La faute aux parents qui ne s'occupe pas de leurs enfants Certains parents ne font que faire des enfants seulement
@naroukadiorpur55432 жыл бұрын
Lambe dji mo wara diékh Sénégal dra bakhoul si, agression yi yepu ngay guiss lambe dji moko waral 😡😡
@papadiallo42552 жыл бұрын
Merci siteu 😭😭😭 yalla nakou yalla yeureum Amine 😭😭😭
@lazecisse78612 жыл бұрын
Khaly diamaguene nio amoul yar en plus ay voyou lagnou c une jeunesse malsaine il faut l'emprisonner pas de pitie
@aissatousarr68062 жыл бұрын
J'ai peur bilahi wakhouma mane mais sama khel daloul dakh samay rakk ak sama diabot 😭😭😭
@barbieshu90672 жыл бұрын
Bilaye
@seynaboutoure9752 жыл бұрын
Bilaye
@dioumadiouma39262 жыл бұрын
Kou bakh la wone
@mamichoudiop82852 жыл бұрын
Yalna yalla yeureum ko té kharé ko aldiana.....
@diouckalpha97682 жыл бұрын
Tant qu’on arrête pas la lutte il y’aura toujours l’agression
@papinho91112 жыл бұрын
Saway la première responsabilité est des parents, ils n’éduquent plus, ils laissent leurs enfants faire du n’importe quoi pour ensuite pleurer leur mort voir arrestation. La deuxième est celui de l’état qui ne prend pas ses responsabilités: na militaire yi guène défanté avec ces délinquants. Diour dom mouy deff louko nekh: saga ndaye, toukh yamba, guéné arme et après tu le défends. Naniou wakhanté deug nous sommes tous fautifs: deug bi ci boppam laniou wara wakh. A beau suspendre la lutte ces gosses resteront toujours des voyous, ils tueront et agresseront autres parts.
@tigendiaye48652 жыл бұрын
Arrête la lutte.. Du coût la police ne peut pas être partout au dos de chaque personne impossible.. Les parents amougniou temps leurs enfants...Trop de banditisme voilà...
@sitaffkruma20022 жыл бұрын
Si on n'arrête la lutte le taux de chômage chez les lutteurs vas très augmenter du coup ils vont agressé gravement ls personnes
@bahabuu88622 жыл бұрын
C vrai
@tigendiaye48652 жыл бұрын
Sa way lutte bi on l'arrêt .Sénégal on est 17 millions d'habitants donc mbeur metou gniou touss paraport à la population..il faut que la population prend les choses en main ...comme on le faisait avant KOUREL kou nék gardé sa KOGNE .....
@badadiop69752 жыл бұрын
Yallah nako Yallah Yeureum 😭
@diarrasene26052 жыл бұрын
Ler name ndeysane dioublou woussi wone ray ko deuk bi comme si nit gni dagne léne khabtall c’est trop yalla nagnou yalla mousseul thi li🤲🏻🥺mousseul gnou thi seytané 🤲🏻
@kambayependasall89082 жыл бұрын
Paix à son âme que firdawsi soit sa demeure éternelle et sunu borom mouthial niou si thiat ak saytané
@fatoudiouf87562 жыл бұрын
Siteu tu a bien fai
@user-jl5qv6dv9ecoupedumonde2 жыл бұрын
Eumb sa dome 9mois doundal ko sone ci mom mou magg warla diarigne gnou rayko ni . Yalnako yalla yerem
@ndiayefall48952 жыл бұрын
Kou Ray gnou Ray laa 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@ibrahimafall7322 жыл бұрын
bilah ma soeur waxa degg kou ray gnou ray la 😭😭
@abdulkarimsowe47592 жыл бұрын
Tant que défoulen li yalla wakh kou ray niou rayla ici en Arabie saoudite tu sors quand tu veux et rentre quand tu veux si deux personnes se disputent le premier qui lève sa main sur l'autre aura affaire avec la police Yalla mo niou binde te moniu eup yeurmadé fouuf
@loufashopstyliste36762 жыл бұрын
Wa légui kokou nayko ray
@hamidou91382 жыл бұрын
bane Sénégal lagnou nek? je ne reconnais plus mon pays😭😭😭
@omarndiaye7912 жыл бұрын
Mon pays va mal 🥺🇸🇳🥺 Yalla nako yalla yereum té kharéko Ahldjana fir dawsi🤲🤲😭😭😭
@jamilejoop29082 жыл бұрын
Yalla Nako yalla yeureum te khare ko aldiana firdaw AK mbolem dioulitt te Moussal gnou si moussiba Yi
@mohamedsagna93272 жыл бұрын
La lutte il faut l arrêter. Ce n est pas un facteur de développement. Il faut respecter les gens. Lutte égale agression. Même après la lutte les gosse agressent.
@mhd_00392 жыл бұрын
Wakho degue dh
@aidasarr83732 жыл бұрын
Il faut depassionner la lutte et que l état prend ses responsabilités y a trop de désordres ds ce pays.
@doudoucisse64852 жыл бұрын
Danga yap lutte rek wakhma fou amoul violence au Sénégal ucad garçon berger politique bi biir keur yi fepp violence wakh dji Moy kouné yar sa bopp
@TheBandafall20032 жыл бұрын
Le sénégalais n’est pas près faire du sport sport mais tous ce qui se passe est la réflexion de nôtre société la police les politiques sont aussi violent et même le discours des partisans de tarikha ont des discours violent en faite ces toutes les couches de nôtre société
@gueyeelhadjimalick88572 жыл бұрын
On a un etat bandit qui utilise des nervis contre la population civile. Don on ne peut rien s attendere d eux.
@mamoudaltall49802 жыл бұрын
@@doudoucisse6485 yow doul lambj lagni wara arreté amour benne chance surtout wa balieu bii aye badola nio fa deukk
@doudoucisse64852 жыл бұрын
@@mamoudaltall4980 saway yaral sa boop touty te respecte sa boop man amouma mbeur amouma mbokou mbeur talou mako Sakh lamb Dina am ba passer doumako juste just dama khamni Sénégal legui founek dangafay deg violence ngamay saga yaral sa boop touty
@papengom1272 жыл бұрын
Ndayesane 😭😭😭😭
@fatouyankatte84252 жыл бұрын
Vous ne possez pas les bonnes questions, comment vous pouvez demander à quelqu'un s qu'il ressent après la perte d'un proce avec cette atrocités .RIP
@princessgassama17292 жыл бұрын
Deug deug kou délé noumouy meuna yeugué banex nieup xamnagn ni dée nackar la bou méti b paré sougnou diogué nane loy yeuuk si niack s proche bi dé
@clairemari72922 жыл бұрын
Paix à son âme c grave ça
@ibrahimabayo12772 жыл бұрын
C est vraiment triste, ce phénomène devrait être étudier en profondeur… pourquoi cette jeunesse est elle aussi violente et sanguinaire ses dernières années ?? Je me demande bien s il y a un type de droguee qu ils consomment prck mounouma comprendre ga dieul nite ki loumou yorr ba paré rayco, wala ga dioté ak nite rék raycco de cette façon là
@mouhamedba57432 жыл бұрын
Ndieysan 😭😭😭😭
@kharitouyayam51012 жыл бұрын
Kouray rek dagnoula wara ray diaroul yobou police li dafa yombe torop billahi yallana ko yalla sougnou borom SWT diégeul kharéko aldiana ak bep waye dawlou thi barké seydina Mohamed SAW
@ndeyecoumbaniang88862 жыл бұрын
Thieye yalla 🥺méti yalla nako yalla yeureum té diégal ko si barké yonéte bi
@salladiaw5432 жыл бұрын
Amine
@ndeyedieng37162 жыл бұрын
Ndeyesan yalla nako yalla kharè aldiana si barkel serigne touba
@sowbabacar96312 жыл бұрын
Vraiment c est la qu ont voirque senghor et abdou diouf etait de bon president car les citoyens etait plus eduqués et
@babacarfam2512 жыл бұрын
Yalla nako yalla khare aldiana firdawsi
@awitabeauty2 жыл бұрын
Yalla nañou yalla mousal thi seytané
@adjafallmory73162 жыл бұрын
Metina torop 😭😭😭😭😭😭😭 Yalla nako Yalla yereume khare aldiana 😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@kebafall35232 жыл бұрын
Yallah mo ñiou auppou yeurmande tei néna kou rayy thi tayéff ñiou rayy la donc bou ñiou defon lolou problème yi doufi am. Que son âme repose 🙏🏾
@binambaye54842 жыл бұрын
Wa tamite journaliste timeu nit ki dou youkhou rek cheuteut Yalla nako Yalla kharé Aldiana Firdawssi 🤲🤲🤲 Masta maman 🙏
@user-jl5qv6dv9ecoupedumonde2 жыл бұрын
Le terme « boy diamaguene la « a posé beaucoup de problèmes Finalement quand tu dis que tu es banlieusard on pense que tu es bandit
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭dama dioy ba sonou si video bi mére ligua gnak dafa nekh dom yalla yereume ko mougnal maman diam si yaw metina mais metina
@ndayesylla13012 жыл бұрын
Rayena nanoko raye rek mo diekh amoul wakh bo bare ⚰️
@diouldewar49422 жыл бұрын
Bou peine de mort amei fi si sénégal 🇸🇳 rayyi dina diekh 😭😭😭😭😢
@assanediane64962 жыл бұрын
Ak fi réwmi tolou béne dome bou gor si sa yaye war nga tal lénéne loudou di dopou ay bmeur baniou lafay raye yalla nako yalla yeureum kharéko aldjiana
@dienekhadiata26492 жыл бұрын
Salam ❤ MBOK YI SÉNÉGAL LI FA-NÉK-OPE-NA NATALE-DÉME-WAR-NA-GNOU-SI-WAKHE YALLAH NA BOROM BI KÉRALÉ SI ALDIANA YI GUENA KAWÉ FIR-DAW-SI AMINE YA RABBI GNOU BOK KO AK 🌏 🙏🏿 ❤️
@teknomilles84672 жыл бұрын
Lamb Dfa Xaram nagn ko Siprimei Nguen bagn ✍️ Yalla nena Kou Ray Nit Tei Tayko Nagn la Ray Nguen bagn ngueni Dou Nguen Def Lolou Motakh Yeuf yi ni rk lay Dmei Boulen Sakh Sonou
@syllepogba17432 жыл бұрын
Non lii dafa mèti nguir yalla ray daniou ko wara ray ray nitt si lidoul dara
@ndiayearamechou62412 жыл бұрын
Li métina bilakhi
@lavie22992 жыл бұрын
Bilahi yenn journaliste yi khamounou dara amna image yo khamni warou nouko dougal internet linguen di def kouko def sa mbokk diula nekh, Th gni faatu yalna léne yalla yeureum th diegal léne xarilen aldiana firdaws 🤲😭
@bathiedabo23292 жыл бұрын
LA PEINE DE MORT EST INCONTOURNABLE!
@premieredame65722 жыл бұрын
Heu, damaci sah tayal wah, mais dans tous les cas mom il ya beaucoup de choses à régler dans ce pays : 1 le baby boum, 2 le problème de l'éducation des enfants, ici on éduque pas, 3l'exode rural dakar est bondé, entrain d'exploser, ...
@fatousy41972 жыл бұрын
Kou raay ngou rayyleu Point
@thiernoaliouba69402 жыл бұрын
Paix à son âme 🙏
@ibrahimasy64582 жыл бұрын
Diakaré tiss pauvreté métit injustice AK yakar bou Tass leu Sénégalais bi am
@ibrahimaseck51112 жыл бұрын
Mbeur yeufou weuyou
@adjafatouthiaw20942 жыл бұрын
salam repose en paix inshaALLAH
@amadoundongo262 жыл бұрын
Lane la lamb di apportel Sénégal ??
@pesonko56652 жыл бұрын
Lamb senegal amoul ndiarigne
@fatoumg29052 жыл бұрын
Aï li mane dama warou
@khadimdiop83982 жыл бұрын
Bilahi li.niaw na kou yabo di bayi khel sa bop
@seydinaaliousylla67502 жыл бұрын
Walakhi Sénégal lifi am sénégalais yi rek nioko mana fadial sen bopp
@ibrahimadialo75672 жыл бұрын
😢😢😢
@therenaissance79772 жыл бұрын
Thiant nawetan lamb babi foot carte khaliss. Lou tardel senegal book nasi.
@loyalbi8232 жыл бұрын
Vraiment la lutte avec frappe n’a plus sa raison d’être dans notre société car l’Etat n’a pas les moyens de l’encadrer comme il se doit car sans parler des agressions après combat la lutte ne favorise pas une bonne éducation des enfants
@abdoudiop51632 жыл бұрын
kou raye tayko nanou ko yobou arene national rayko legi raye bi diekh bilahi
@asnd77772 жыл бұрын
Légui niou bari yarouniou daniouy yafal rék moþakh liy khéw di khéw
@ibrahimafall7322 жыл бұрын
lamb mom fi mgui am si deuk agression dou fi meus diekh
@loufashopstyliste36762 жыл бұрын
Billay nioune ndaw gni naniou khamm ni adouna amoul solo
@kingplextheking45342 жыл бұрын
Triste
@fatoudiouf87562 жыл бұрын
Yalna égalé ndawam aldiana firdawsi
@moussasagna202 жыл бұрын
Le mot ‘’Diamaguene’’ qui signifie la Paix est bizarrement devenue le contraire ci gokh bi…Ko wakh Diamageune mou xalate banditisme
@mohamedngaide57742 жыл бұрын
C'est triste métina trop yalla nako yallah kharé adiana mai genre meurtre yii sécurité douci lén éducation de base bi laniou wara kholattt
@dembaelhadjimbodji65502 жыл бұрын
Les combats de lutte là !!!!! .ll faut les revoir y’a trop d’agression dans ce pays lié à ces « combat de lutte «
@maimounandiaye52462 жыл бұрын
Amoul ben livré à la police, yobouna torop dagnou ko wara fat kome nimouko fater domou diabour bi,nite day nek si souffrance gnou warko évacuer di khar wa ambulance yi gua khamner amougnou sak gasoil