Man cha allah serigne saliou ci pataligi meti woon na lool waayé jeex na tay yallah joxna n̈u ay njiit yu beg réew mi yallah na yallah samm n̈u té n̈u fekké
@goraseck9057Күн бұрын
Machalah dieureudieuf serigne saliou amatina solo dieureudieuf, Maky dafa fattè liko fal té fattè ni dounou borrom moy dogal
@momocreation3631Күн бұрын
Wahk nga degue prix yi daniouko wara contrôler 👍
@fatoumataba2854Күн бұрын
Non Macky dafa daw ndakh dafa ragalone niou diapko