Diomay bome fathé teré yéne Serigne si di touk wakh lou doul degg ake diakhasé katt you bine yi borom néll yi féne rek lépou dina diékh inchallah
@serignecheikhfaye589910 ай бұрын
Wa mais douki mo waxone si émission bantamba TV né guisna Macky Sall di liguèy AK Amadou Ba 😂😂😂ba baré waxona ay dèrètte bou berè Dina tourou té Dara amoussi gni ay ték xél Nanou en plus limou wakh ni mouguisi programou sonko😂😂😂😂
@papediegodione208010 ай бұрын
Mome la kay moy doul doul lou niii dei
@dknatursn140810 ай бұрын
Demewoul nonou lou pasa ladone wakh
@dknatursn140810 ай бұрын
Dagn ko lath fo te gone ni election dagn koy pour mouni dama gis amadou ba tok si sege maki nek ensemble mo takh mouni election yi dagn koy Pous sene gour dafa des te lolou mo ame
@MuhammedCeesay-q1t10 ай бұрын
Hmmmm coalition boka Japaleh fenn
@dknatursn140810 ай бұрын
Ligeene khamoul mo bari ki machalla dou lath khalis
@2dtv26710 ай бұрын
ماشاءلله جرجفت شرچ عبد لله❤❤❤❤
@NdioldéGueye2 ай бұрын
Abdallah Diouf machalla ki guiss ko yomboul limi voyages mo barii machalla
@varvartv68010 ай бұрын
Yallna yalla ar sunu Brom kham kham yi ❤❤❤
@dknatursn140810 ай бұрын
Machalla ki dou nit dafa bakh
@amadoutoure76423 ай бұрын
Ma sha Allah
@ousmanendiaye861910 ай бұрын
Ki kou yalla bakhal la wallahi
@djibydiawara2872Ай бұрын
Machalla
@momobusness10 ай бұрын
Cheikh Abdoulahi diouf diambar. gna bilayi
@ibrahimadiallo248810 ай бұрын
Fadam iwo mome kham na ni Modou lô nekola mais yalla rék amoul lenen 😂
@NdioldéGueye2 ай бұрын
Guiss ko yomboul limi voyages mo barii machalla
@BiraDiallo-e9b10 ай бұрын
Fadam diapa lai ma si srgn Abdallah
@bayebasse46810 ай бұрын
😭🇸🇳🇸🇳Yawe waroo var kéne 😢🇸🇳😭
@insadrame6529 ай бұрын
Machalah serign bii est ce que je peux avoir son numéro
@SokhnaDiop-m9x10 ай бұрын
Fadam mom défaitou Modou lo rk la yakamti mé daal DH 😂😂😂
@Chiekh76610 ай бұрын
Non fadam Modou la faralo
@gabrielataya74205 ай бұрын
Tout marabout qui croit en lui active les commentaires .
@mbendagueye157910 ай бұрын
Cheikh Abdalla juff dagua warra noppi kouma béte gua figua wakh ni élections yiii daye âme guékheu kham yéneu warguéna noppi té diamou yalla
@SerigneModouSady10 ай бұрын
Regardez émission bantamba lime fa wakh il enregistre beaucoup de vidéos
@malicksaware827710 ай бұрын
Sonko a vie
@Djibyndiaye-ui5ww10 ай бұрын
Video bi la 28 la dougou bayill dull 😂
@cheikhfall437710 ай бұрын
🇺🇸 Vraiment actroces 😢 c'est par ce que Au Sénégal les gens font que parler ils ne font rien aux charlatans motakh les étrangers sont nombreux ici
@alhamdoulilah915410 ай бұрын
Lingafi wakh lepp dou xam xam danga deff sa analyse comme niépp bayilené thiakhane yi
@Bilal6685010 ай бұрын
Mara niass waxone bou yague modou modou yi dinagne nieuwat
@lacitoyenneafricaine8566Ай бұрын
Serigne bi mane touti na ba sagnou ma wah wayer maye ma me deugeul li nga wah si diganter PR Diomaye ak PM Sonko dama ko djiss djissatt ko nima djisser wone PR Macky Sall di djeneu palais bi di wathie escalier plus de 4 ans si ganaw! Diganter PR ak PM sougnou gorgorlou woule ah li si kaname douma nekh... Gnome gnar kou nek ne nangoul moromame nombal tankame bagna degue lou seytaner "nitt aki nopame rek le"! PM Sonko ne nangou djittale biko PR Diomaye djitter rek. Fi adouna wara done takhouta done. Wayer nitt dina nek fenene maname hors du Palaais mouy ngenel si mome. PR Diomaye Nak "Djitt le dé mashallah" wayer pouvoir dafa mince dafa diss début bi dou yombou... Na moytou gni khaliss yittele te PR Diomaye mou balma "kou deugeur bop le" te woutt kattou khaliss yi " genrou gewelou pouvoir" dagnou ko woutter nou nek wayer ne deugeur ligueye ligueyame !!!! Yalna ya allah deff diam si rew mi. Ngene balma.
@TidianeKebe-ls1fc10 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤
@cheikhdiop993210 ай бұрын
SERING BI BOUL I GAWA WAKH YAW DAMALA ROUS
@ibrahim6985310 ай бұрын
Fadam faut bloqué les commentaires à cause de certaines propos insolent envers les hommes de dieu
@mouhameddia516810 ай бұрын
Homme de dieu qui n'est pas un homme dieu.iao nittou sococim nga?man déh nitou yalla lah
@elhadjimamadoudiaw362810 ай бұрын
Li massi nekh rekk moy dmrm yi nekone si ngur gui tei gnou nara tegl s’en ndey ils ont fait trop de mal
@cheikhdiop993210 ай бұрын
WA any. Seringne cisse mou seringne babacar sy😂
@cheikhdiop993210 ай бұрын
kilifa you niou duapou mom dou kaa😂
@SauraDiop10 ай бұрын
J t suis mai ya wakhon ni amadou ba moy dieul rewmi
@dknatursn140810 ай бұрын
Non dafa ni loutakh niou pousone election yi dafa gisone lolou te lolou ame na
@ndatteyalla99178 ай бұрын
@@dknatursn1408BAYILÉNE DEFENDRE L'INDEFENDABLE KI LOL LA WAXONE EN PLUS NI WONE KHÈKH BOU MÉTI DINA TA YA BAKANE YOU BARI DINAGN CI DESS NI DA GUISS MACKY SALL ASEEMBLER SAWAY YALLA REK MOFI NEK GNI DAGNI TATONNER REK
@Bilal6685010 ай бұрын
Fadam kou niak diom la ki mofi waxone ni Amadou ba Moy gagné Tout les patriotes Désabonner lén ci page bi
@mbayestarsene217910 ай бұрын
Nn yeureum ko loumou niaw rek doyna sino dina dioy t dioyou kou niaw mom. Cva rek
@mbayestarsene217910 ай бұрын
Wa tokk mouy dokh😂😂😂😂 doul rek
@HerveBasse-in1lv10 ай бұрын
Fadam ieo beugo dara lou bah si modou mè di nga kateu sa feulal deye di rouss togal di kharr rek
@mamecheikhdiop855910 ай бұрын
Boye Niang reug reug lo guiss
@MohamedMbaye-rz1gh10 ай бұрын
Fén rek mom bimou démé won bantamba TV wakh ni amoudou ba mom la guiss mou doon presi duul rk
@daamnjaay127410 ай бұрын
wax waratuleen, am leen jom
@AwaBa-gp5zo10 ай бұрын
Bou pare wane li mou wakh no si becay mbaye
@aminetadiop787210 ай бұрын
Moma diahal mok sa touba😂 Sénégal nehna
@pcd051710 ай бұрын
Fadam mo dakh douleu kanamam..khamolen touss weur di wakh rk
@ibredia72310 ай бұрын
Nom ki mome bokoule si gnognou wawe kaye
@MuhammedCeesay-q1t10 ай бұрын
😂😂😂fenn rekkk
@ousmanendiaye861910 ай бұрын
Dou niit bo guiss sagga ko yar bakhna lol
@MuhammedCeesay-q1t10 ай бұрын
@@ousmanendiaye8619 fenn du saga segn bi wahlu ludul dega fenla bayilen nafekh
@ablayegningue683510 ай бұрын
Kiy lathi ak kiy tontou kou dakh fénn
@PaadaBasse10 ай бұрын
Fadam sa badio yaye yaww ak Amadou ba
@BaraSamb-de7es10 ай бұрын
😂😂😂😂😂
@Lendarien10 ай бұрын
Mane deh geumeutoumako
@Dieng-vk6if10 ай бұрын
Bayilen modou lo toute tranquille
@Abdoumbathie6510 ай бұрын
Limo wakhon lepp bokol ak li bayi lein nelawal sénégalaise yi fein rk
@madiorgueye72810 ай бұрын
Ken dousi wakh lou am yen wa lambou wor kat nguen khaliss rek yaw deug douguen ko wakh
@IbzowSeye-m7n10 ай бұрын
Yaw kañ ngaye nopi te bayi doul yi😂
@BarraCisse-wr1re10 ай бұрын
Ki Borom khame khame degue le bilan nite kou bakha
@BoubaBalde-t7v10 ай бұрын
C'est 😂
@AlassaneSambe-lu8vo10 ай бұрын
Cv
@coulzjamdong476410 ай бұрын
Ki day doul rk sur bantamba tv dafa confirmer wone wax sa touba bi nane Amadou ba day gagner
@mbayestarsene217910 ай бұрын
Wouyyy modou lo danou na putin nnnnnnn ki loumou wakh mou ndeye depou thiotou deim
@MorWade-w7q10 ай бұрын
No dacoroma
@khadimkasse-bv1fm10 ай бұрын
Doule rék
@ousmanendiaye861910 ай бұрын
Yeen gni di wakh lou négatif sii dieum djii lou gnaw da ngeen ko khamoul rekk ki yalla reek mo takh mouye gnane woutoul beuz woutoul khaliss té interview yii sakh beugouko dafa aam ay teeguine si aay nitam rekk mo takh mouleen diko défal
@dknatursn140810 ай бұрын
Lou ler
@tourembaye628010 ай бұрын
Khamoul leufal ndayeim😂😂😂
@dknatursn140810 ай бұрын
@@tourembaye6280 kou rew ga
@BaraSamb-de7es10 ай бұрын
@@tourembaye6280 naye rafét waye
@ousseynoucamara351910 ай бұрын
Fadam iao ak Boucher ak sa touba vous mentez comme vous respirez