Machallah serigne bi ak équipe bi yeup yalla naléne borom Faye séne khôl, niou bakh nguene machallah, yalla na séne diam yagg ci daradiay rassoulillah (psl)
@adamakane3734 жыл бұрын
Vraiment serigne Assane vous êtes généreux Longue vie à vous accompagnée d'une bonne santé Amiine 🤲🤲🤲
@dandioakassadieureudjefser28864 жыл бұрын
Machalla Amna solo trop serigne Assane kane yalla nafi yague té andak wérr Amine ya Rabi
@khadywele52614 жыл бұрын
Alhamdoulilah dieureudieuf Kane Diallo kou bakh ngua ak équipe bi yeup machaAlla
@elhadjimbow29094 жыл бұрын
Vraiment le mérite revient à vous senewcom 🙏🏾
@dandioakassadieureudjefser28864 жыл бұрын
Sokhna Aïssa wakhal ma Serigne Assane kane Amna Talibé bi ka beugue yague nalén suivre. Beugue na numero serigne Assane kane inshallah