🚨Violation de la sacralité de Touba: Plus de 100 supporters "graciés" par les Baay Faal

  Рет қаралды 14,938

MOUHALIM TV INTERNATIONAL

MOUHALIM TV INTERNATIONAL

Күн бұрын

Пікірлер: 165
@damemamefallout28ndiaye63
@damemamefallout28ndiaye63 5 күн бұрын
Diadieuff baye fall yi merci beaucoup ❤❤❤
@MoustaphaSourang-qo1cz
@MoustaphaSourang-qo1cz 5 күн бұрын
Machallah alkhamdolillh Waw leeeeeeeen goooooooor way mourid jërëjëf Baye fall ❤️🥰❤️❤️🥰❤️❤️🥰❤️❤️
@ibrahima9592
@ibrahima9592 4 күн бұрын
Dieureudieuf Serigne Touba khadimou Rassoul Diarama Cheikh Ibra baboul mouridine
@ZAWKAR34
@ZAWKAR34 4 күн бұрын
Dieuredieuf yenn baye fall yi, yenn mom ligueye rek ngeun di dèf ❤❤❤
@Elhadji-j5n
@Elhadji-j5n 4 күн бұрын
Jeunes Touba amlen diome degeu nigeull Serigne bi moye séné nimbeul
@cheikhmodou7128
@cheikhmodou7128 5 күн бұрын
Machallah alkhamdolilh waw le gor way mourid jerejef bayé fall yi
@AbdoulakimTouré-e3u
@AbdoulakimTouré-e3u 4 күн бұрын
Walène gorr ❤ Serigne moutakha mbacke yagufi rek tawa wèrr barkep khassidayi
@ZAWKAR34
@ZAWKAR34 4 күн бұрын
Dieuredieuf serigne touba amoul morom
@abdoundiaye1096
@abdoundiaye1096 4 күн бұрын
Dia diuef mourid ❤❤❤
@mamegoor8985
@mamegoor8985 4 күн бұрын
Dieureudieuf baye fall yi✊🏾✊🏾✊🏾
@ModouDieng-g5o
@ModouDieng-g5o 2 күн бұрын
Diadief way baye fall ❤❤
@mouhamedfall3527
@mouhamedfall3527 3 күн бұрын
Manam dieumi 25000mom après foumouy dieum Damay sakou ak léral lék ndax Serigne Touba rék la geum
@ibradieng4537
@ibradieng4537 5 күн бұрын
J espère qu ils ne vont plus le répéter.Touba est une cité exceptionnelle.on ne pourra jamais la considérer au même titre que les autres.
@MoustaphaSylla-cs7pd
@MoustaphaSylla-cs7pd 5 күн бұрын
Merci bay fall yi
@patriotesarry8573
@patriotesarry8573 4 күн бұрын
Yénn yi mom deugeur bopp la. Dieureudieuf Baye Fall yi délén door. Touba Serigne bi moko mom kouy Football nga dém stade Abdoulaye Wade
@assanediouf4152
@assanediouf4152 5 күн бұрын
فجزاكم الّله عنّا خيرا على اجتهادكم لحفاظ حرمة مدينة طوبى المحروسة
@saliousarr4163
@saliousarr4163 4 күн бұрын
Pour mane équipepou nawetane waroul ame Touba di diogué bir touba di dem mbacke Dankh sak match ci lanioûy occasioné di dougal lou bon ci deukbi té lolou lou weurla Chaque match lou barî la gayi diap ci wal wowou
@adamandiaye3448
@adamandiaye3448 4 күн бұрын
Gnoune touba lagne deuk khamougne lou bone bakoy dougeul si deuk bi boudé yaw ak sa baye yéna ko kham
@cheikhndiayeuh1649
@cheikhndiayeuh1649 3 күн бұрын
​@@adamandiaye3448 limou wakh deug dieufé ndigueull li mo gueun ci yeen complexe guen trop daguéna nekk touba te soriko loll
@MoustaphaSourang-qo1cz
@MoustaphaSourang-qo1cz 5 күн бұрын
Machallah alkhamdolillh Amna solo looool machallah 🥰🥰❤️❤️❤️❤️❤️🥰🥰🥰🥰🥰❤️❤️❤️
@MoustaphaSourang-qo1cz
@MoustaphaSourang-qo1cz 5 күн бұрын
Waw goor way Serigne dham souda jërëjëf Baye fall ❤️🥰❤️❤️🥰❤️❤️🥰❤️
@thiendellafall2506
@thiendellafall2506 4 күн бұрын
Dieureunguéne dieuf Fall. Ndiguel jéfé rek.
@ibrahimacissedieureudieufs2732
@ibrahimacissedieureudieufs2732 5 күн бұрын
Dieureudieuf waa keur Mame cheikh Ibra fall yaaram
@oumarsarr4087
@oumarsarr4087 5 күн бұрын
War nguéne am kersa dé niak nguéne diom lool yéne gonéy Touba yi
@Madou-h1g
@Madou-h1g 3 күн бұрын
Diarama yene ❤❤❤❤❤❤
@homarbalde4285
@homarbalde4285 5 күн бұрын
Waaaaaw leeene goooor
@bayemodoundiayexassida1767
@bayemodoundiayexassida1767 Күн бұрын
Waw lén gor fall Yaram ❤
@MameDiarra-k6k
@MameDiarra-k6k 3 күн бұрын
Diadieuf Bay fall
@NdeyeDiakhate-xb5ne
@NdeyeDiakhate-xb5ne 5 күн бұрын
Man dé ay jamono daannaa seetaan fooball epp na wukki at juroom. Waaayé leegui bima seetloo ni biir keur yi biir marché foo took da ngay deegg ñuy wax mbiru football ci laa xamé ni mbir mi daa rax. Ndax carte xaaliss bi ci juddoo moo waral xalé baci ay boroom keur yu goor ak jigeen dañuy carte . Budoon sama sago nguur gui day dakkal X BET . Carte xaaliss ak sangara dafa haraam
@tayzir
@tayzir 4 күн бұрын
Wa touba bayilen football deme mbacke di football war geune ku bayi amelen diomi bayi football guir serigne bi😢😢😢
@mbackeseyecheikh6374
@mbackeseyecheikh6374 3 күн бұрын
Saway koumou nexx dem mbacke football lolou kay dara nekouthi
@MGTvcheikha23fall
@MGTvcheikha23fall Күн бұрын
😢 li douyone wa ndamatou😢
@fallmakhtar2174
@fallmakhtar2174 3 күн бұрын
Kaddouyi rafetna
@ToubaVisionToubaVision
@ToubaVisionToubaVision 5 күн бұрын
Wormay Touba Diarna bakan dia dieuf cheikhra fall ak wa keureum
@mtdistribution-w6d
@mtdistribution-w6d 4 күн бұрын
Thiey YALLAH bayi li YALLAH diglet Mouy Farata thi bopou dioulite kene diapoula faylowounla dara ba paret diapaté ak di enkessé touba neekhna😂😂
@AbdouGueye-hs3mw
@AbdouGueye-hs3mw 5 күн бұрын
Lima nakhari moy Touba légui comme champion spagne rk ⚽🥅 niaw na trop asc ocas asc ndamatou
@SalamSeckhtdkh
@SalamSeckhtdkh 5 күн бұрын
Est-ce que si biir deuk bi lanko defe
@lakhateToure-s5q
@lakhateToure-s5q 4 күн бұрын
Ta mane lima diakhal niak diouli mo gueneu dange football ta kene douthi wakh ak ko mana done danga wara diouli
@PapeNdiaye-x5f
@PapeNdiaye-x5f 4 күн бұрын
Football Dara mosi nékoul
@morndiaye8110
@morndiaye8110 3 күн бұрын
Fine rek
@ABDOUDIAGNE-im2ev
@ABDOUDIAGNE-im2ev 4 күн бұрын
Amna solo , maachalaa wayédé setann télé yi saxdé nonou. Laymel si yenkognyi daniouy youkho disaga en plus ,nioubari football lougn wayé si carte lagnouyy xey disi gonnttt
@Papiscss1356
@Papiscss1356 4 күн бұрын
Yena geuna niakk diomm yene li yalla santane defou lene thi dra nguene baga ray nit gni ak ndingalou serigne bi dem lene diamou dji yalla mou geunn li
@mbenguecheikh7736
@mbenguecheikh7736 20 сағат бұрын
Ligueye bi Serigne diglé touba boléne beugué ligueye bi yomb nane si bolé ay douma kou yarawul déss Koy d'or ndah mu yaru
@adamandiaye3448
@adamandiaye3448 4 күн бұрын
Wakh dji dou deugue ay fén la Mbacke lagn démone football li diarou diouma dja jubilé wougne ay fén kat guén ay togne kat guén
@FallLamp-k6h
@FallLamp-k6h 4 күн бұрын
Yaw Kou Niakk Yarr Gu Bobou Beu leghui Yay Wakh Liguay Khènio Diwowoko
@Madou-h1g
@Madou-h1g 3 күн бұрын
Limoye mine yapp danio mine serigne bi ba moudier ko yap gni deucoul touba sakh gno gueneu respecter touba
@abdoundiaye1096
@abdoundiaye1096 4 күн бұрын
Niakk yar rek
@modoudiop8105
@modoudiop8105 4 күн бұрын
Bilahi len lii rewandee kese la kou manoul bayi thiaxaan genal touba ngir yalla
@ibn_el_bachir
@ibn_el_bachir 4 күн бұрын
Touba nak Keen football u fi Mbakke la khéwé ñu parei di ñibisi Ñu diapoleen
@PapeNdiaye-x5f
@PapeNdiaye-x5f 4 күн бұрын
Football Dara nékou si
@modoudiop8105
@modoudiop8105 4 күн бұрын
@@ibn_el_bachir kou bax ñii danoudon jubilé bir touba xana deglouwo vidéo bii bayileen encourager nitt thi ay thiaxan
@modoudiop8105
@modoudiop8105 4 күн бұрын
@@PapeNdiaye-x5f mais touba moom kenn doufa football amoul kii amoul kaa lolou na leer thi yaw ak sa classe gii
@thiernotine6751
@thiernotine6751 5 күн бұрын
Dirrama Mame cheikh ibrahima Fall
@SaliougadeGakou
@SaliougadeGakou 4 күн бұрын
Li lépp sonko le mo yakhe khale yi
@دارالهدى-ص6م
@دارالهدى-ص6م 3 күн бұрын
Nar ngua sonnu d 😂
@bassirougueye1287
@bassirougueye1287 4 күн бұрын
Jaajeuf jaajeuf jaajeuf Fall
@moamadousall
@moamadousall 3 күн бұрын
Deugueleu waye faal
@adamandiaye3448
@adamandiaye3448 4 күн бұрын
Bayiléne di sosal ndawi touba ligua dara dou si deugue
@boromdendeyedecor830
@boromdendeyedecor830 4 күн бұрын
Ki limou wakh dara amousi wallahi
@AbdoukarimFaye-t1r
@AbdoukarimFaye-t1r 2 күн бұрын
Dengaï fenne yaw domou kharme nga
@FaaFallilou
@FaaFallilou 5 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤Grazie
@ngoudadiop2890
@ngoudadiop2890 5 күн бұрын
Diadieuf fall ❤
@MoustaphaSourang-qo1cz
@MoustaphaSourang-qo1cz 5 күн бұрын
Waw leeeeeeeen goooooooor way mourid jërëjëf Baye fall ❤️❤️🥰❤️
@modoudiop8105
@modoudiop8105 4 күн бұрын
Kepp kounci diapp thi kaco bii nga wara demm amoul maslah amoul négocier amoul nekhal
@LeuzNiang-p1r
@LeuzNiang-p1r 4 күн бұрын
Limouy dara dousi manne manga fa woon wakhoul Li am boy yi football lougn Touba manefeste wougn Touba Nio provoque boy yi japou len lim wakh barke cheikhoul khadiim amoul Day sosal boy yi Kou dem football nieuw niouné la fo nékon gnii nafekh lagn
@patriotesarry8573
@patriotesarry8573 4 күн бұрын
Amlén diom té moytou téré yi mo gueun si yén
@daoudambaye262
@daoudambaye262 3 күн бұрын
Kholal bénéne kouti mbaw mbaw comme thioro, yéne domerame yi yéne yena done tal Touba, nguir séne tiagua bobou. Yaguatoul yéne nieup di na niou tegual séne Ndaye si batine, ba nguene kham né Serigne Touba dou morom. Té li ci yémé nieup ay boyou OGM you 2000 yi, niou si bari khamou niou séne Baye.
@Madou-h1g
@Madou-h1g 3 күн бұрын
​@@daoudambaye262😂😂😂😂😂😂
@yaragteggiin5101
@yaragteggiin5101 5 күн бұрын
Yeen daal ci bëggug Sëriñ bi kepp ngeen nekk yal na Sëriñ bi nangu ligeey bi.❤❤❤
@ousmanendiaye2983
@ousmanendiaye2983 5 күн бұрын
Boy Touba daniou reewmi ba doul bilay
@SalamSeckhtdkh
@SalamSeckhtdkh 5 күн бұрын
Fall yaw goor du nek si réseaux sociaux di saga
@cheikhounandao9275
@cheikhounandao9275 4 күн бұрын
As goor d'où toumal moromou dioulitam
@khadimfaye8003
@khadimfaye8003 4 күн бұрын
Sénégal nexna 😂 nono
@boromdendeyedecor830
@boromdendeyedecor830 4 күн бұрын
Li serigne bi téré si deuk bi lousi yénakoy def bayi leen togne ak soss ak neewal doolé ay nitt
@gabanefall2447
@gabanefall2447 2 күн бұрын
Football wagniwoul Dara
@AlassaneNdoye-pf5qi
@AlassaneNdoye-pf5qi 3 күн бұрын
Mais les jeunes de touba sont dans une prison il n'y a rien de contraire par rapport à l'islam. Et puis c'est des gens qui ne prient, qui observent pas le jeune du ramadan qui interdisent le football.
@khadimatoufall7250
@khadimatoufall7250 4 күн бұрын
Waw len goor
@cheikhmaremoundiaye7216
@cheikhmaremoundiaye7216 5 күн бұрын
Wallahi fall niak diom rek te khamadi 😭😭😭😭
@cheikhounandiaye1221
@cheikhounandiaye1221 4 күн бұрын
ترك الصلاة أعظم
@AbdoulahatDiop-o7q
@AbdoulahatDiop-o7q 4 күн бұрын
Footballenwoul mbacke lanou footballé
@AbdoulahatDiop-o7q
@AbdoulahatDiop-o7q 4 күн бұрын
Fou xaliss bi Dieulm
@eFooballMHD
@eFooballMHD Күн бұрын
Lek riba kasse
@cheikhibraamar9741
@cheikhibraamar9741 3 күн бұрын
Séen ligueuye nio ngui rafét llu
@diopdiop7483
@diopdiop7483 4 күн бұрын
Sangara nak
@BayeAbdouGaye-x6o
@BayeAbdouGaye-x6o 5 күн бұрын
Walahi niaka guiersa rek ladiou def
@PapeNdiaye-x5f
@PapeNdiaye-x5f 4 күн бұрын
Yène yalla Téré guéne diko déf ba paré di sonal nitt ni si Lou aramoul ligueni Téré Dara haramou si
@SyllaMouhtar313
@SyllaMouhtar313 5 күн бұрын
Boulén yokhot Boulén falé Borom pass pass you woyof yi
@دارالهدى-ص6م
@دارالهدى-ص6م 3 күн бұрын
Dem len jaamu ji yalla te bayi sen caaxan yi
@ThiernoSeck-po4sf
@ThiernoSeck-po4sf 4 күн бұрын
Yaw niémee ga yallah de ndamatou mbacke lagne football lee
@MatrDiakhte
@MatrDiakhte 4 күн бұрын
Amlan soutor
@latv1449
@latv1449 5 күн бұрын
Dioulit ak woor dh faraday la walaye
@falloumbacke92
@falloumbacke92 4 күн бұрын
Gnom nak es kon dougn police comme si que dagno legal li nak état bi warnaci Wakh dh c’est dommenge 😢
@Jean2030.
@Jean2030. 4 күн бұрын
😂😂😂😂😂
@Madou-h1g
@Madou-h1g 3 күн бұрын
Non bima lires sa tour bi akh sa sante bi dama rous ses dommage
@falloumbacke92
@falloumbacke92 3 күн бұрын
@ man nekou mari pour ay sant ak youma khamoul Bay Fall yi lignouy def louci eupou ak togn la kep kou Diang dine dinga khamnei li Bay Fall yi di terei louci eupou yalla terei wouko te nak yawmal khiyam Dina metty yalla de kou manou la te mana atte wassalam 🙏🙏🙏🙏
@Madou-h1g
@Madou-h1g 3 күн бұрын
@falloumbacke92 donc foutbal dine dako daganal apres nga diang istoirou footbalt nga khol fimou dioguer li laniouy wakh si liye routh tol bi si bire tol bi laye dioguer
@falloumbacke92
@falloumbacke92 3 күн бұрын
@@Madou-h1g football fanala haramei yaw mi esk diang nga sakh te man nak lima gana metty moy khol gno khamnei dangougn khamougou dine ngalen denk ab deuk nagnou bayi thiakhan yi la wakh li mom état daccei wara wakh noum gana gawei
@Jean2030.
@Jean2030. 4 күн бұрын
Football bou amoul diaxaso gor ak jigeen amoul fate wakhtou amoul sole lou gate aramoul yéne baye fall yi tamit war nguéne bayyi yéne yi toukh yamba ak nane sangara ak lal ci khaléyi yoyou tamit bakhoul
@AbdoulahatDiop-o7q
@AbdoulahatDiop-o7q 4 күн бұрын
Ki loumi wakh yaww amoulo xam xam
@محمدسيسهمعلمالقرءان
@محمدسيسهمعلمالقرءان 5 күн бұрын
Jerengen jef séne taxa waay dé rafétna trop trop sax ❤❤
@syllaballa4272
@syllaballa4272 4 күн бұрын
Gnibilen sen deucki Mame yi touba yeurmandé amatoufii
@sene6344
@sene6344 5 күн бұрын
Ay domi khathie you torokh rekk lan
@loudoulaktalibesafouma3429
@loudoulaktalibesafouma3429 5 күн бұрын
Kouye nék touba difa déf li serigne bi bagne bilakhi yërëm na léne serigne bi dina damou séne ay tnk walakhi
@iPhonePro-mi3tk
@iPhonePro-mi3tk 5 күн бұрын
Foot ball touba C interdi aussi refatoul equipe birr touba thimm 😡
@JshwHwhw
@JshwHwhw 5 күн бұрын
Delen door limoy degeu
@matardiaw7026
@matardiaw7026 4 күн бұрын
Motoulene yamba dji wormayi ay doul la rék
@Jean2030.
@Jean2030. 4 күн бұрын
😂😂😂😂😂
@serignefalloumbacke7849
@serignefalloumbacke7849 5 күн бұрын
Dioulit ak woor dh farata la
@myandiaye4960
@myandiaye4960 5 күн бұрын
Lindjeuti ndakh sa baye diongue nah tamite faratah lah.
@serignefalloumbacke7849
@serignefalloumbacke7849 5 күн бұрын
@ genre wakh yi daleu laniouy khar thi kou douli woul woroul
@serignefalloumbacke7849
@serignefalloumbacke7849 5 күн бұрын
@ psk khol yi nioy lundeum
@myandiaye4960
@myandiaye4960 5 күн бұрын
@serignefalloumbacke7849 Kone Serigne Touba,diokhma ndigeul kou djouli wul woorul. Wakhal ak Serigne Touba.
@maibndiaye7968
@maibndiaye7968 5 күн бұрын
Baye fall nii niuy done domi serigne touba yeppu xam nanco te masau noo ce wax dara jal ci sokhna joxleen ay ay sokhna
@almustafambakke6163
@almustafambakke6163 5 күн бұрын
Nek Ci kër jambur té limuy aayé doci ba dara 🤔 dëg dëg yéna Nãk joom dëg
@toubatv3789
@toubatv3789 5 күн бұрын
rew mi domasa bakh
@ibrandiaye5486
@ibrandiaye5486 4 күн бұрын
❤❤❤
@NdiayeDame-sb9eb
@NdiayeDame-sb9eb 5 күн бұрын
Khawma ay niti languén donlén sakh rouss
@abdunjaay738
@abdunjaay738 5 күн бұрын
Ku bàyyi sa dëkk maam ñëw ci keppaar ug Sëriñ bi war ngay sàmmoonte bëgg bëgguk Sëriñ bi Ay murit yi, lii Sëriñ bi bëgg nanu ka ci bëgg le.
@ibrandiaye5486
@ibrandiaye5486 4 күн бұрын
Mane daal warou na lii dane koy téré bayico
@PrinceMbaye-m8i
@PrinceMbaye-m8i 5 күн бұрын
Faye nane 100000f niou doga bayi boyi
@sene6344
@sene6344 5 күн бұрын
Sa data ndaye yak boy yi
@PrinceMbaye-m8i
@PrinceMbaye-m8i 4 күн бұрын
@ yaw sa leufeul ndaye
@ndiayemoustapha6825
@ndiayemoustapha6825 5 күн бұрын
Deug le mais Wayit nit sokoo jaapé dagn ko warra jox leek ak naaan dh
@loudoulaktalibesafouma3429
@loudoulaktalibesafouma3429 5 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤Baye fall yi❤❤❤❤
@seckmatar5957
@seckmatar5957 5 күн бұрын
😂😂😂😂
@syllaballa4272
@syllaballa4272 4 күн бұрын
Dioye na yeurmandé s. Saliou die
@MalickKaire-gm5he
@MalickKaire-gm5he 5 күн бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@sagyatal8545
@sagyatal8545 5 күн бұрын
Baaayfaaaallll for ever
@BayeDame-dh5sp
@BayeDame-dh5sp 5 күн бұрын
Dieur dieuf fall yaram❤❤❤❤❤❤❤
@Media5Tv1-y9w
@Media5Tv1-y9w 5 күн бұрын
Diakhan rek
@thiammatar8462
@thiammatar8462 4 күн бұрын
Graciés méll ni kou yoré prison
@modouthiaw1947
@modouthiaw1947 5 күн бұрын
yalla nalén yalla degeu reul
@anitadiop494
@anitadiop494 5 күн бұрын
Merci
Oustaz Mawdo Faye  sur la situation au moins orient
11:50
MOUHALIM TV INTERNATIONAL
Рет қаралды 4,8 М.
AMOURS BRISÉES   Saison 1- Episode 25
48:21
Yesdakar
Рет қаралды 87 М.
coco在求救? #小丑 #天使 #shorts
00:29
好人小丑
Рет қаралды 112 МЛН
So Cute 🥰 who is better?
00:15
dednahype
Рет қаралды 19 МЛН
Enceinte et en Bazard: Les Chroniques du Nettoyage ! 🚽✨
00:21
Two More French
Рет қаралды 40 МЛН
QUEL EST LE REGARD DES OCCIDENTAUX A L’EGARD DES MUSULMANS ET LES METHODES DE DIVISION
1:10:16
Urgent-Touba : Plus de 100 supporters de foot "graciés" par les Baay Faal....
17:18
Matlabul Fawzayni   S  Moustapha Seck
34:53
Media Mouride
Рет қаралды 7 МЛН
KHASSIDA MAGAL  2024 - MOUKHADIMAT KOUREL TUUT TANGK HT
53:15
Mouride Touba
Рет қаралды 41 М.
INFORMATION INTERNATIONAL SUR MOUHALIM INFO DU LUNDI LE 15 décembre 2024
10:15
MOUHALIM TV INTERNATIONAL
Рет қаралды 2,1 М.
coco在求救? #小丑 #天使 #shorts
00:29
好人小丑
Рет қаралды 112 МЛН