Li mom j'espère que wally dinako lidjanti bamou leer. Ndiap tu donnes raison aux gens yi beugoul wone nga nieuw si wally. Limoy lane.
@nga12256 ай бұрын
D'accord avec toi, wally laisse trop passer des choses. Gnouy salir son image si zéro. Que le manager de wally s'occupe de ça. C'est pas bien ça. Ndiap doit recevoir sa correction, wally bakh bou eupou dof lay ndirou
@mimikeita42626 ай бұрын
@@nga1225 Wally mon diouboul mana fénn té yoroul guate doul rék Laye déff🤣🤣🤣🤣
@ramathiamniang68206 ай бұрын
Wally seck aka wéékh dounkhou Def lou bakh moko takha diouck Mais son entourage reste à voir😢😢😢
@@NTD311 ay profiteurs ak nitt youko gnié nioko sékheu Yalna yalla téek si mom lokhooo Ba séniii pékhé you boone bania entou
@NTD3116 ай бұрын
@@ramathiamniang6820 amine amine c’est triste wallahi mais yalla bahnaa
@mimikeita42626 ай бұрын
Yénn wakh lénn Wally degueu n'a liguéye té bayi Sow buz bi Loumouye weur Di mayé voiture
@khalifagueye45506 ай бұрын
Merci frere explication bi c tres Clair
@Nanettebaby126 ай бұрын
Lolou Bakhna si Wally Seck ndakh je ne sais Comment il peut recruter Ndiap Sachant que Ses Danseurs Sont 10000fois plus forts que lui mais beug Défanté ak Sidy Diop takhna mou dieul workate bobou ndakh interêt légui mongui ni nioulaye impliqué si you niak fayda yiii Wally tu es mon seul et unique chanteur mais réveille toi avant qu’il ne soit tard
@wfamily99416 ай бұрын
Ndiap kay mo forcé ba gneuw. Li mom bakhoul day yakh deerou wally. C'est des profiteurs ils abusent de la gentillesse de wally
@wfamily99416 ай бұрын
Nako wally dakh c'est une occasion en or de se débarrasser de lui. Liguey ba yeksi ap khalé dilako yakhal.
@Nanettebaby126 ай бұрын
@@wfamily9941Même Sou Nieuweulé bopam sakh waroul takh mou dieul ko d’autant plus qu’il a les meilleurs danseurs du Sénégal
Mais lii diarroul wakh fii démal si yone puisse que amna contrat
@AbdouDiop-d6t6 ай бұрын
Boye demal si yone porte plainte deuk bi amna yone legi😢
@bachirndiaye43846 ай бұрын
Sheutetetete Sénégal lègui lèp si internet bi lagne koye lidieunté deuk bi am'na police am gendarmerie am ASP soff ngèn trop
@MoustaphaKebe-l8f6 ай бұрын
Gendarmarie ak dano ligueye youl motakh gayi di dem ci Internet bi
@sonkofocus2024-ph4hv6 ай бұрын
Wally mo wara kholate entourage bii da barri aye badola
@alassanegomissagna49876 ай бұрын
Boy démal Gendarmerie Colobane (Section de Recherche) nga porter plainte bilahi ça ne fera pas Une semaine niou defaratttal la sa auto💪Gnis ay dmrm youuu téppi seinne leufeul ndm laniou
@FatimaFatima-ld4ke6 ай бұрын
Boy bi moy complexè rek ,Nane ngay djokhe aito tei xaliss taxawoul
@ramatoulayediaw38646 ай бұрын
Courtier bi moo lekk khaliss bi kii wakh na lou lerr retire nanou cheque bi lekk si 3.millions.wally moo wara bayi maye auto voilà nakh ay baadoola lanou kholom mookay togne.
@layebah54006 ай бұрын
Waly a eu le même problème avec ma penda seck donc c’est louche l’histoire Se répète
@papegueye96656 ай бұрын
Ndiap fi domeram ayy déféllant lagne
@khadimndiaye31836 ай бұрын
Mais dakar buz sén montage rafétna ❤
@amidoudiakhate97546 ай бұрын
Dem len porter plainte niou defar auto bi
@metjobrek6 ай бұрын
Bour ayoul dagg yé ayy!!
@Reewmi246 ай бұрын
wally Moo tayy limiy deff Daleen Affaire 😅😅 Si ay pèkhè rekk la nekk
@tourembaye62806 ай бұрын
Bilahi Wally truand
@papadrame52686 ай бұрын
Wally entourage bi yeupp ay truand lagniou
@khalifarappeur81636 ай бұрын
AME GUÉNE CHANCE BA DJOTAATE SÉNE AUTO... NIO KO TÉY MOOME SI BOPAME MOY SANTE BOYS YI LII C'EST DES LOBBYINGS POUR DU BUZZ ET SACRIFIÉ DES SÉNÉGALAIS INNOCENTS...
@mexentgomes29286 ай бұрын
Complexe rek mo waral li il n'y a rien d'autre
@modoundiaye79856 ай бұрын
Non Wally wékh na dounkh nak déf lou bakh sa yone nékousi nioukoy toudou si li
@AidaGoudiaby-yc1cj6 ай бұрын
Ndiap yonam nekou si Waly 6 million ngua ko wakh mou diokhe schek 7 moline double ko Waly ak ndiap sen yon nekousi way 😢
@Omarsane74916 ай бұрын
Nipaeu zooo thibribii 😂😂
@stevebikoconsciencenoire87716 ай бұрын
Nakka nguéndi diokhé auto té diotoléne séne khaliss.
@wfamily99416 ай бұрын
Wally kholbi rek mokoy togn gni ko weur gnou beuri ay profiteurs lagn
@IslandCureislande6 ай бұрын
😂😂😂😂😂wally seck doul REK  amoul Dara Deja di MAYE AY auto REK alors que WALLY seck lui meme MO dakha niaan wayann REK ley deef
@gorandiaye3906 ай бұрын
Yaw lo am
@pacoseye5556 ай бұрын
Boulène niou sonale Wally il est au couran de tou ce qui ce passe Wally c'est un faux tupe senegalais yi yèwoulène
@useruser47316 ай бұрын
Heureusement si vous donné la carte d'identité vous êtes foutu même perdu la voiture
@SuperMekni6 ай бұрын
yene moussoulene dolen encaisse 4 millions yi ba pare niouss sene ndeye yoboulen gendarmerie
@mamasady86756 ай бұрын
Yaw mi ya mousoul bo encaissé 4milion yi nga dem gendarmerie mounéla fayy nala sa xaliss loy wakh
@MilkMilo-qr5uc6 ай бұрын
Quand on est pas intéressé intelligent au bêtise rk gay wakh
@tourembaye62806 ай бұрын
Voilà lolu lagne waron daf
@mimikeita42626 ай бұрын
Tout ça c'est Wally pour môme li moye musique déff beuz
@salioumbayetv84146 ай бұрын
D'aprés mes analyse le probléme c le kourrhier
@Papidiop-d5b6 ай бұрын
Waly ak sarap ndm nio ci yam pourquoi ngen di dieulat auto bi
@MbayeThiaw-pq9mt6 ай бұрын
Wally seck dafa immature Lolou moy wakh biii
@MilkMilo-qr5uc6 ай бұрын
Le problème moy vous êtes trop sentimental ba paré ame complexe si célébrité mane wally rk lay déguelou mais en matière de boulot sama frère bouma bokal ndeye ak baye sakh douma si négocié ak mom faut faire la part des choses mane gnak tiaxane motakh ma déme diangi droit waloum xaliss dé Bilahi j'y badine pas sama mbok bilahi wal kitabi ak yalla bouma dieurignou boma truandé wone ma nok lassi si kasso bi c'est la réalité mane toud tourou nitt ca signifie absolument rien
@modoundiaye79856 ай бұрын
Mai saway Wally binde na chéque fay légui mome loumousi meune 🤣🤣🤣🤣
@MilkMilo-qr5uc6 ай бұрын
@@modoundiaye7985 frère fimay waxé moy le fait que mou nangou lolou contour yoyu yeup day sori mane la voiture bala gakoy publié ou mala koy bayil gassi défe vidéo dama retiré le chèque amoul yow sama way ga ou diokh la voiture en attendant ligéye ak massela andoul mane douma massela si ligéye ak sama baye bima diour
@loucha71796 ай бұрын
Journaliste bi lii rek la yakamti thi Waly mom bax baxou Waly waxou thi Dara ey ayibam rek lay top
@TaherElouardi6 ай бұрын
@@loucha7179nekal nite ay complexe rek nguen.. Chi cazzo è wally
@mimikeita42626 ай бұрын
@@loucha7179Wally mon diouboul Diokhé chèque yombeu n'a Mais est ce que chèque âme n'a dra Wally yoroul amadou Sall moko donne diokh alalou sénégalais Yi mouye weure Di mayé diap Wally taylé nalla 😂😂😂😂😂
@amakane64946 ай бұрын
Naléne wally faye c'est tout
@mordiop55556 ай бұрын
Yobou Len thi yone ay domeram
@lamineteuw68396 ай бұрын
Iow boy dagaye féne, khawema lo begue nak mé plainte mouguilaye khare, ga lérale sa wakhedji
@Papisco.sall.6 ай бұрын
Yaw yaka dakha fén kii limou wakh daffa lerr nagne
@marichouseck56836 ай бұрын
Loutakh waly seck djokhouléne chèque bi yeneu gni djay auto bi guéneu retiré ko mane deh kouma djay sama alal bala gua djote digua def cheque bi sama tour ba parè hummm
@Elhadjikane-i6f6 ай бұрын
Waay yenna togne Sen bopp nakka guenni diokhé Sen auto t diotoulen Sen khaliss complexe rekk molen djappe
@alfihlou6 ай бұрын
danga am complexe wally ni bindeu naa check rekk nga diokhé boudone kanéne doko def ah
@CheikhtidjaneSeck6 ай бұрын
Yow mane sakh boma nianee 10millions ma diokhlako
@JumeauxJumeauxdioplaye-kw6pp6 ай бұрын
Ki mom n took diayéwoulwone auto bi dakar buzz begg nguen internet bi ak waxi penc niakk nguen souteureu2 begg nguen kolen weer franchement delen waxtaan té bayi weranté internet bi nuniouy toyalé sen tiepppp niit yakh niit
@taphasamb68366 ай бұрын
Boyi nio katt ndem
@khadime6 ай бұрын
Doy na war
@FatouDiallo-wj4gt6 ай бұрын
Wakh bi lérouye
@modoundiayesonko6 ай бұрын
Fadel wadij daye doul rek ki waxoul li am waxou fi dara Lou ler
@vieuxgaye4776 ай бұрын
Mais copin pourquoi ngéne dieulate autobi dangéne warona déme thie Yonne ,porté plainte ay vres arnaqueurs laniou .
@gorandiaye3906 ай бұрын
Saway tu n'est pas cohérent vous devez porte plainte le courrier sans pour autant cité le nom de waly seck c'est louche de votre part
WALLY SECK AK LOBBY WAME BII BOU GUÉNE KO TASSOULE YOOBOU LÉNE KASSO GNOU BÉYI, LÉGUI GNOU DÉFF FI DJEUYEU YOU GEUNE BONES SALETÉS GNAAW TÉ DOY WAAR... DEUGUE RÉKAY MOUDJE INCHA'ALLAH RABY 👌🏾
@diarrigamacalou25746 ай бұрын
Copain même yéne ay complice nguéne ndakh louy diar 6 million nguéne diayéko 7 million ak wally moléne dall dioupe rek mo ame solo ces bien fait pour vous tous
@Lopios-g6l6 ай бұрын
Waho doff..
@IbrahimasoribaDiakhaby6 ай бұрын
Wally dor katt la
@tourembaye62806 ай бұрын
Police 🚓👮🚔reik
@momepachcat9976 ай бұрын
mes intérmédier bobou diouboule
@diogenelaerce21976 ай бұрын
Un chèque il y’a un nom. Ayyy wakhi dofff rek. Portez plainte contre Wally, c’est lui l’escrocs dans cette histoire.
@BM-xz9lk6 ай бұрын
Au porteur.Tu connais? Pas forcément
@ramatoulayediaw38646 ай бұрын
Cheque bi a etait retire ndiape ak courtier bi gnoo nek si diguente khaliss bi surtout courtier bi
@fatimatabintoumarico80326 ай бұрын
J'espère l'aime bien en tout cas mais je remarque qu'il est toujours dans ces affaires de voitures. J'espère qu'il n'est pas impliqué dans cette escroquerie.
@modoundiaye79856 ай бұрын
Ioe do bayi doule AK yak dére chéque retiré naniouko wala ioe ya beug Wally ame blém😂😂
@wfamily99416 ай бұрын
Kham nga louy au porteur? Yakamti ngen si wally. En plus mom il a bien dit que retirer nagn khaliss bi. Mais wally moko def bopam téré nagn ko mayé auto ba tayi
@AbdouNdiaye-ju7tt6 ай бұрын
Billay mane ndiap louer nako auto kaolack mou daw ak auto bi numéro Sidy diop la lidianti doga giss ndap dome rame
@CodeDieng-rq1jq6 ай бұрын
Boy da nga nélow way
@moussasall90516 ай бұрын
Yaw kham nga Wally mouy diende oto 200million conne khamnga ni il est très occupé mo takh li nék thi khélmi mo barri yamal rék
@AbdouDiop-d6t6 ай бұрын
Loutakh mouy yeme boul ko khebal
@Reewmi246 ай бұрын
Wally truand la c’est tout !
@AissatouMboup-n9i6 ай бұрын
Yene sof gene
@sadiobandia9476 ай бұрын
Sofoul de toukh sangara show biz nakhatela di mboubo di beug beugeulou serigne fallou