wa dji li mou wax eup na. la réponse de oustaz moukhtar gueye

  Рет қаралды 13,045

Tawfikh TV

Tawfikh TV

Күн бұрын

Пікірлер: 210
@mballosadou2280
@mballosadou2280 2 күн бұрын
Excellente intervention mon cher frère barakallahu fik
@salmaba5123
@salmaba5123 2 күн бұрын
INALILAH WA INA ILAHIL RAJIOUN, SOUBHANALAH . J'ai peur pour moi mais aussi pour cette personne. QU'ALLAH nous guide. MASHALLAH wakhdji rafetna BARAKALLAH fikoun
@ahmethannediop3669
@ahmethannediop3669 2 күн бұрын
Yalna niou yalla sakhal ci alkhour âne ak souna amine 🙏
@ahmadouka8036
@ahmadouka8036 2 күн бұрын
Barakallah ya oustaz
@assanesene1646
@assanesene1646 20 сағат бұрын
Wakh dafay yënou maana. Merci Oustaz Makhtar. Mouhamed Sallahou haleyhi wa salam moy sinu kilifeu
@ndiawarsarr9952
@ndiawarsarr9952 Күн бұрын
Yallah Rekk Mou Meun moufi nek.
@sidisarr5531
@sidisarr5531 Күн бұрын
Thi Ay THIAHAN keep laniou nekk😎
@azizndiaye7967
@azizndiaye7967 3 күн бұрын
Barakala fikum sama outaz ku bari kham kham
@SambMory
@SambMory 3 күн бұрын
Machallah
@BabacarCissé-s1s
@BabacarCissé-s1s 3 күн бұрын
Soubhanalla Thieuy soufianké yi
@cheikhoumardeme293
@cheikhoumardeme293 2 күн бұрын
Thiey soufiyanke thi lane wakhal diam dh . Bou néké ragal yalla soufiyanke nioy dieumi ragal yalla deugg.
@santyallaboubakh4430
@santyallaboubakh4430 Күн бұрын
Khathi nga dé yeen dong lagne giy giss ngendi saaga yalla ak alkhuran ak yonentbi yeen soufiyankeyi yeena bonne​@@cheikhoumardeme293
@BabacarLeye-hd9kv
@BabacarLeye-hd9kv Күн бұрын
والله ​@@cheikhoumardeme293
@globalservices-it2th
@globalservices-it2th 18 сағат бұрын
@@cheikhoumardeme293 lou ler geu wakh soufisme deug ken menouko saletel
@malicksow5157
@malicksow5157 2 күн бұрын
أفدت واستفدنا يا أستاذي الكريم...
@ibrahimamba1296
@ibrahimamba1296 22 сағат бұрын
Les tarikhas poussent leurs talibés jusqu'à défier les prophètes et les sahabas. Un grand khalif général avait dit que son guide n'est pas légal des anges et des prophètes. Il a ensuite déclaré que le jour du jugement dernier il va ignorer DIEU et Mohamed psl pour aller se refusé à côté de son guide. Des tarikhas qui imposent leurs talibés à cesser de prier et de jeûner et d'obéir à leurs marabouts . Des tarikhas qui déclarent que leur guide est un prophète envoyé par dieu, démontant les paroles de DIEU et de son prophète. Des tarikhas qui déclarent que les écritures de leur guide est 6000 fois plus puissants que les écritures du coran. C'est ça l'islam au Sénégal
@elhadjidiallo627
@elhadjidiallo627 2 күн бұрын
L'un d'entre ne sera pas croyant,jusqu'à ce que le prophète Muhammad (psl) sois plus aimé de lui que son parent,son enfant,et tous les gens réunis. Allah ne guide pas les pervers.
@mamadoumoustaphabadji4832
@mamadoumoustaphabadji4832 2 күн бұрын
Ma challah ya cheikhana
@kingtheo1278
@kingtheo1278 19 сағат бұрын
1) "Diné dji amoul kilifa" dafa la beug wakh ni "yalla dji amoul kilifa" manaam koudoul yalla missionnaire nga thi lolou rek lala beug wakh ! Peut-être façon bi mou ko wakhé mo deugueur rek 😂 2) Yalla mooy fathie adioo yepp wayé nak il faut nguène nangou né am na ay prestataire de service, c'est le minimum malgré que meune na lepp!! Président sakh mooy accréditer tous les services rendus de la nation mais nak khana am na ay organe ak démembrement youmouy yoni wala ay ministre!! Ps : ki mou wakhni mooy fadji adio yi nak question de croyance personnelle leu, soudé deugla bakhna, soudé dou deug nak, nioune gni ko gueum nguène baayi niou souniou déwèè dém safara mou dièkh beug nagn😂🙏🙏
@elhadjitoubamboup4881
@elhadjitoubamboup4881 3 күн бұрын
Liguéyou tarikha yi si Senegal mongui nonou, séni Serigne you soss tarikha yi nio ndieukeu sossal Yalla ak yonetbi aleyssalawatou Wa salam Li dou rolou Eta, Senegal Kilifa tarikha la ame tè nioniou dagno wedi li Yonétbi Aleyssalawatou Wa Salam indi matoul, Raggal léne Yalla tè teunkou si Alkhourane ak Sunna
@khadimrassoulltoure4810
@khadimrassoulltoure4810 2 күн бұрын
wakhô deugg démal djiangeu mbindoum serigne touba kon nga kham famou tékk yalla ak yonénnte bi lii serigne mountakha gueye di wakh loolou la serigne touba ak seeyidill hadji malicke wakh kou wakh lénéén nak sa wakhla
@elhadjitoubamboup4881
@elhadjitoubamboup4881 2 күн бұрын
@khadimrassoulltoure4810 Wa legui wakhma Bane Serigne si Senegal mo wakhni roukhou diamji mougui si lokhone? Ak kane mo wakhni tarikham si Yonétbi Aleyssalawatou Wa Salam mokoko diokh
@khadimrassoulltoure4810
@khadimrassoulltoure4810 2 күн бұрын
Sô khamoul batayni kou joulli ci yonénnte bi bisou aljouma yalla dafkoy déllo rouham mou fayla. sô khamoul batayni nit kou am thiér thia yalla mangakô togne légui mougnân yalla nga faatou légui _nga liggéyalko mougnân yalla goudal sa fann défalla barké =wakh néékha lôôl wâyé sou dégg dégg amoul dou djiarigne dara##
@elhadjitoubamboup4881
@elhadjitoubamboup4881 2 күн бұрын
@khadimrassoulltoure4810 ya meuneu kathie, Raggal Yalla té dème diangui sa dinée bala soukourate di nieuw guaye rethiou, Yalla naniou Yalla dioubal tè tekniou si siratal moustahim! Amine
@khadimrassoulltoure4810
@khadimrassoulltoure4810 2 күн бұрын
@@elhadjitoubamboup4881 allhamdu lillahi rabbil hâlamiina mângui sant yalla boubââx ci sama diiné //soudée soukrât mângui koy wâdjial boubââx allhamdu lillahil Karim binihmatihii
@papaassanediop2538
@papaassanediop2538 Күн бұрын
Yal na nu Boroom bi jéggal rekk.
@AvdoulahateTop
@AvdoulahateTop 3 күн бұрын
ماشاء الله تبارك الله
@aliousy6484
@aliousy6484 2 күн бұрын
جزاكم الله خيرا
@cheikhsarr108
@cheikhsarr108 9 сағат бұрын
Lii rék motax bougouma am Serigne si bii diamono bilaahi ndax danioulay yokou réér. Ahmed Fall guéneul nga diégeulou danga diüüm wala nga wakhéé sa nafs rék waayé soo wéétéé xamni ALLAH souniou boroom SWT moy fathie bép aadio. Dieureudieufeuti si vidéo ndax الحق الى الله ☝️"deug YALA mooko moom"❤
@SeydouThiam-zj5mp
@SeydouThiam-zj5mp 2 күн бұрын
نسأل الله السلامة والعافية والتوفيق.
@assaneniang2133
@assaneniang2133 3 күн бұрын
Nanu YALLA mùccël ci waxi gni melni gnii, te bagn gnoo mbugële gni réeré nii.
@NdeyekhadyDiakhaté-r7p
@NdeyekhadyDiakhaté-r7p 2 күн бұрын
Alahou akbar aywaye yoneneta bi dou morome fre dadjal
@Amadoudemdia
@Amadoudemdia 2 күн бұрын
استغفر الله و اتوب إليه 😮
@maria1-s7w
@maria1-s7w 11 сағат бұрын
Soubhanallah ki mo meuna fene Allahou Akbar Kabira 😢
@MarieBendia
@MarieBendia 2 күн бұрын
Alahou akbarrr 😱 mon pays va mal
@BebeNdiaye-bh2ju
@BebeNdiaye-bh2ju 2 күн бұрын
Machallah yallanalla faue
@SopayOmarSall-dl7qq
@SopayOmarSall-dl7qq 2 күн бұрын
Merci beaucoup 🎉
@OumouBa-k5x
@OumouBa-k5x 2 күн бұрын
😭😭 لا يليقنا سوا بكاء 😭 على أنفسنا 😭
@papaassanediop2538
@papaassanediop2538 Күн бұрын
bien dit mon frère mashallah
@MAAMDlevrai
@MAAMDlevrai 2 күн бұрын
Subhanallah 😭😭😭
@maria1-s7w
@maria1-s7w 11 сағат бұрын
Allahou Akbar Kabira Islam mo toumouranker ci Senegal 😢
@seydousambakoulibaly734
@seydousambakoulibaly734 3 сағат бұрын
Islam mossoul toumranké Sénégal. Mais wadji loumou wakh mome rek la concerné.
@Fatoumatasow-mb5vc
@Fatoumatasow-mb5vc 2 күн бұрын
Barak Allahou fikoum
@mouhamadoudabo6820
@mouhamadoudabo6820 Күн бұрын
Wakhinne deuguinne la lath Balla minedéff Di am la yalla parré
@mouhamedba9968
@mouhamedba9968 Күн бұрын
C'est vrai de waxnga dëgg. Waayé fene moom fene rek lay tuddu, ce Mr Fall est une honte et un fou à lier.
@hamzasall8630
@hamzasall8630 2 күн бұрын
جزاك الله خيرا
@babacarsy4666
@babacarsy4666 Күн бұрын
Je s8 tidiane mais pas d'accord Nanou djokh thieur Mohamed (s a w)
@MatarNdao-ib8vo
@MatarNdao-ib8vo 14 минут бұрын
Senegaal mo Bari Ay doff Yalna gnou yàlla djéggeull
@mamadouly823
@mamadouly823 2 күн бұрын
Il n'est pas le premier à le dire, j'ai entendu cette histoire depuis longtemps.
@Diopmamoune483
@Diopmamoune483 2 күн бұрын
AME NA KADDU YO NGA XAM NI UN BON MUSULMAN WARU KO YÉKATI DIKO DIEUMALÉ CI SEYDINA MOUHAMED PSL❤
@Sofieba-v3t
@Sofieba-v3t 2 күн бұрын
Yallah naniou yallah diegal li nioune fugn dieum
@SyAlassane-k7s
@SyAlassane-k7s 2 күн бұрын
Kou khamadila
@amatourrahmaane
@amatourrahmaane 2 күн бұрын
لاحول ولاقوة اإلا باالله😢😢😢😢😢😢
@ababacarmbayesy1638
@ababacarmbayesy1638 2 күн бұрын
Soubhana allah
@gmai756
@gmai756 2 күн бұрын
Wallahi Ahmad Fall fimou ték yonéntibi ak waxtane yimouy amoul si mom bilahi déguelou wo té barki yalla mola guéune fonkou yonéntibi wassalam Démal diangui mo guéune nioune meunou niou diangual sallalahou halleyhi wassalam ❤❤❤❤
@blacknegro7408
@blacknegro7408 2 күн бұрын
Toujours vos dérives envers l'islam et à chaque fois vous essayez de trouver des excuses 😢😢😢
@blacknegro7408
@blacknegro7408 2 күн бұрын
Toujours les dérives du soufisme
@blacknegro7408
@blacknegro7408 2 күн бұрын
Li wadji wakh warona wakh Sérignam mo gueun mouy sossal Yonent bi PSL
@mamelatsouckfaye1837
@mamelatsouckfaye1837 Күн бұрын
Diaroul tontou
@MorCisse-p1g
@MorCisse-p1g 11 сағат бұрын
ioe esk nitt nga
@assaneniang2133
@assaneniang2133 3 күн бұрын
Assalaamu alaykum wa rahmatul LAAHI wa barakaatuhuu. Innaa lil LAAHI wa innaa ilayhi raaji'uun.
@FeedMyEye
@FeedMyEye 20 сағат бұрын
Lim wakh Jangalela rek.
@mapendandiaye2485
@mapendandiaye2485 2 күн бұрын
Soubhaanalah
@ahmadouka8036
@ahmadouka8036 2 күн бұрын
No sénégal doudème Li khéw c'est trop franchement je ne sais plus quoi dire tarixayi yalla na yalla yeureum
@bouramacamara1828
@bouramacamara1828 2 күн бұрын
C'est télé qui invite ces genres de personnes qui doivent être sanctionner. Une émission de religion ne doit pas être animée par n'importe qui.
@NdeyearamSylla
@NdeyearamSylla 2 күн бұрын
أنا لله وإنا إليه راجعون fila rewmi tollou daniouye soppi istoire اللھم اغفر لنا وارحمنا يا رب العالمين
@Mballo633
@Mballo633 13 сағат бұрын
Saway wakhofi dara ahmad fall dousa morom demal nga diangi
@MatyKhoulé-t2y
@MatyKhoulé-t2y 2 күн бұрын
❤❤❤❤
@cissendiaga
@cissendiaga 20 сағат бұрын
Liguéne wara wakh barina goor djiguén yaguifi ray katou nitt yagui fi guéne teudj séne gatt yi tarikha yi moléne di déranger ms fékh dianteu bagui féinki tarikha dinafi takk nékk léne ay nitt aloléne kham kham féne rq mandou bakhna trop
@Waykatouborometouba
@Waykatouborometouba 2 күн бұрын
صلى عليه ربي
@PapeFaye-z6v
@PapeFaye-z6v 2 күн бұрын
Allakhou akbar soublhana la
@waadoundou2467
@waadoundou2467 Күн бұрын
Je suis tidiane mais c pas vrai
@BST1947
@BST1947 Күн бұрын
Waawaaw mooy fath à dio deh
@AmadouLeigh-c3t
@AmadouLeigh-c3t 3 күн бұрын
WA ALIKUMSALAM WA RAHAMATOULLA WA BARAKATUHU ALLAHU AKBAR ALLAHU AKBAR He is a big liar ALLAHU AKBAR may ALLAH SUBHANA WHO WA TALLAH forgive us AMEEN YA ALLAH
@AliouneToure77
@AliouneToure77 2 күн бұрын
😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
@babacardiouf1265
@babacardiouf1265 2 күн бұрын
لا حول ولاقوة الابالله
@serignefallouthiam2184
@serignefallouthiam2184 2 күн бұрын
Anna Wa Tarikha Aonzou billahi mine kouly Kheureume generale di Senegal
@abdoulayefall7239
@abdoulayefall7239 2 күн бұрын
سبحان الله الله مستعان
@AbdoulayeMbaye-se4tc
@AbdoulayeMbaye-se4tc Күн бұрын
Site internet yi lou yakkou ci sénégal nioko yakk
@MouhamedSENE-v9y
@MouhamedSENE-v9y 2 күн бұрын
ربنا لا تؤاخذنا بما قال السفهاء منا 😭😭
@Amadouba-q8c
@Amadouba-q8c Күн бұрын
سبحان الله العظيم اين علماءنا وجب عليكم الخروج وتجيبوه
@kamoucamou3882
@kamoucamou3882 2 күн бұрын
😂oustaz ga diégueul ma wayé ki mo dak doule sénégal 😂
@SIDATHSALL-g9y
@SIDATHSALL-g9y 2 күн бұрын
Subkhanallah
@ndiagaloum3820
@ndiagaloum3820 2 сағат бұрын
Kii moo mana kàcci! Di sos jëmële ci Yónent bi lii dafa ñaaw! AstëhfirullAllaaha wa 'a tuubu ileyhi! Yal nanu Yàlla jéggal! Sénégal te ñoo moytu yii ñuy wax ci Yàlla ak Yónentaam!
@gmai756
@gmai756 2 күн бұрын
Wallahi yén xamo léne tousss barki alkhourane ki loumouy wax c'est très mais malheureusement meunou léne interprété wax ndeysanne 😢 Té mane birnama ni mola raw foufff foufff mbok Ahmad fall dianguan touwoul sax Dieureudieuf Ahmad fall attidjanii nioune Mame maodo MONI diangual ❤❤❤❤
@maria1-s7w
@maria1-s7w 11 сағат бұрын
Allahou Akbar Kabira yena reer soubhanallah 😢
@alioudiane5228
@alioudiane5228 2 күн бұрын
Machalla oustaz longue vie pour cette rectification mais oustaz ahmed fall daa dioum . Car ahmed fall a toujours défendu le prophet psl mais l'erreur est humaine. Machalla oustas ❤moukthar
@salieumbai810
@salieumbai810 2 күн бұрын
Diape len ko ni rek mak bou tok di fen rek ngen nan daa dioum.
@foutaba4231
@foutaba4231 Күн бұрын
Bane erreur ki chaque jour dayféne di yeukati ay Nite si kanamou yonetebi
@YoussouphaDiagne-z3w
@YoussouphaDiagne-z3w Күн бұрын
Setam thi yalla lingay wah ​@@foutaba4231
@minatoutall4415
@minatoutall4415 16 сағат бұрын
Je t jure erreur est humaine
@As_salih-t9i
@As_salih-t9i 2 күн бұрын
Même le gars en jaune est étonné
@AissatouDiallo-li3tt
@AissatouDiallo-li3tt 2 күн бұрын
Allahou akbar
@DiopMody
@DiopMody 2 күн бұрын
Tidjiane bi mom wakh you reuy rek lay wakh
@MedBarou
@MedBarou Күн бұрын
😮ooooooooooop
@SankounToure-hd3lh
@SankounToure-hd3lh Күн бұрын
لا حول ولا قوة إلا باالله
@bouryniang3258
@bouryniang3258 2 күн бұрын
Bilakhi dama tit dama rousss
@IbrahimaSylla-xq7he
@IbrahimaSylla-xq7he 2 күн бұрын
Serigne Ahmed Fall dou sa morom thi xamxam Réglél boy !
@MorCisse-p1g
@MorCisse-p1g 11 сағат бұрын
Kham waye limou wakh lagn wakh kou am kham kham Dina wakh lii
@maria1-s7w
@maria1-s7w 11 сағат бұрын
Ban xam xam😢
@maria1-s7w
@maria1-s7w 11 сағат бұрын
Astaghfiroullah wa atoubi illayhi 😢
@becayecisse6535
@becayecisse6535 2 күн бұрын
Salam Soufyanké yi li rék
@Fatima-ph4vn
@Fatima-ph4vn 2 күн бұрын
Ya Allah senegal mome li eup na di
@ElhadjiealiouneGaye-c5j
@ElhadjiealiouneGaye-c5j Күн бұрын
Ay bandi rek nonouy war
@papandiagandoye8115
@papandiagandoye8115 Күн бұрын
tieuy yalla aka am souniou dioot sakh...bess bou yebalé mawti dinga xam ndax amna saa dioot woula.....kii dafa alkou
@elhadjidiallo627
@elhadjidiallo627 2 күн бұрын
L'incapacité des ignorants qui se disent savants.
@leparadisfirdaws6091
@leparadisfirdaws6091 2 күн бұрын
Ah gnides ay yefer lanu 😊
@SouleyeNdiaye-gw9lv
@SouleyeNdiaye-gw9lv 10 сағат бұрын
ToubeuL Linga Wakh Réuy na Trop
@IssaSow-p9j
@IssaSow-p9j Күн бұрын
😂😂😂
@IbrahimaDiop-pm4dw
@IbrahimaDiop-pm4dw Күн бұрын
Wadji doyna warr bou touboulba deee dina mere kouka defoul dara
@xeppiltv9481
@xeppiltv9481 22 сағат бұрын
Bilahi Ahmed fall dama mana fénn 😢😢😢
@ndiagaloum3820
@ndiagaloum3820 2 сағат бұрын
Lii ci réew mi ëpp na lool! Mbokk yi nanu delloo Yàlla àqam te bàyyi bokkaale bi ak caaxaan yi!
@souleymanemansaly1078
@souleymanemansaly1078 Күн бұрын
Soubhanallah ça di jamais entendu. Quel affirmation malsaine? Est ce que ce Mr est lucide au moment de sa prise de parole
@Basindiop
@Basindiop 2 күн бұрын
Ndaysane gnak tawkhiit rek اللهم انى اعوذ بك ان أشرك به ماليس لك به علم
@OmarDiop-i7d
@OmarDiop-i7d Күн бұрын
Ahmed Fall mola raw fofo😂😂😂😂
@fophierobloxfesita
@fophierobloxfesita 2 күн бұрын
Gni daño khamadi trop Li mo waral moy craiyè djihadis thiy rèwou djioulite yi
@bouryniang3258
@bouryniang3258 2 күн бұрын
Aaaaaaaa man dé dama rousse dakh ki diwakh ahmed fall sama sopé la wayé naniouy set louniouy wakh way surtout si télé wakbi sakh man damasi tit bilakhi
@Kambel-tv
@Kambel-tv 12 сағат бұрын
Diaxay dieuf
@SaliouMbacke-l9z
@SaliouMbacke-l9z 21 сағат бұрын
Kaddou yi doyna war ki khamoul rk
@ALIOUBA-uk2mw
@ALIOUBA-uk2mw 2 күн бұрын
C'est pas vraiment étonnant c'est des paroles de Tarikha c'est des paroles des histoires inventées ces des gens de Bida Qu'Allah nous préserve 😡😡😡😡😡
@NdeyekhadyDiakhaté-r7p
@NdeyekhadyDiakhaté-r7p 2 күн бұрын
Astafiroulaha
@biramesarrm-tq8ql
@biramesarrm-tq8ql 53 минут бұрын
Mahtar faye demal diag gui
@serignembacketoure8796
@serignembacketoure8796 Күн бұрын
Ki mo menue doul
@SopayOmarSall-dl7qq
@SopayOmarSall-dl7qq 2 күн бұрын
Mai kii meun na fén dh 😢
@AliouneToure77
@AliouneToure77 2 күн бұрын
Tékk si réew
@bebetv2458
@bebetv2458 21 сағат бұрын
Fenn rekk
It’s all not real
00:15
V.A. show / Магика
Рет қаралды 20 МЛН
REAL or FAKE? #beatbox #tiktok
01:03
BeatboxJCOP
Рет қаралды 18 МЛН
Chain Game Strong ⛓️
00:21
Anwar Jibawi
Рет қаралды 41 МЛН
AY TONTOU YOU DIEUM SI LI SERIGNE BI WAX
9:48
Tawfikh TV
Рет қаралды 1,6 М.
Revue de presse Ahmed Aïdara du Mercredi 15 Janvier 2025
9:03
2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE
Рет қаралды 13 М.
Incendies à Los Angeles: 🇺🇲 Imam Babacar Sylla yàlla rekka am dolé
4:47
Sopé Oustaz Hady Niasse
Рет қаралды 25 М.
NDAKH DJIGUEN BOU GUISS MBAKH MEUN NA DIOULI?
22:55
Tawfikh TV
Рет қаралды 4,7 М.
It’s all not real
00:15
V.A. show / Магика
Рет қаралды 20 МЛН