wakh Tan bou Nékh lambalok ak modou anta Si Siteu vs modou lo mansour ba Dafa rouss

  Рет қаралды 161,772

Gaston Productions

Gaston Productions

Күн бұрын

Пікірлер: 605
@ThioroFall-s8h
@ThioroFall-s8h Ай бұрын
Diamanguene ladeuk bilahi walahi mais siteu à déconner franchement 😢 Merci modou lo c'est un grand monsieur ❤🎉
@gazza873
@gazza873 Ай бұрын
Sokhnasi khana dego lii modou wakh siteu neko da niak diom
@rouguikebe9984
@rouguikebe9984 Ай бұрын
​​@@gazza873parsk dafa niak diom
@marcusmouhamed
@marcusmouhamed Ай бұрын
@@gazza873wolahi waho li am defkoni nitt ken douko encourager si gnak jom nitt ken douko conseiller si gnak jom waye bo tahawer mou dann la lolou ken douko wah té lolou deug la max mo wah siteu bo songué modou mou dann la mais lolou nuko nitt di waher mbeur
@PapesambaDiop-bf7gh
@PapesambaDiop-bf7gh Ай бұрын
@@gazza873avant modou diko wax lolou siteu daf ko manquer de respect franchement
@gazza873
@gazza873 Ай бұрын
@PapesambaDiop-bf7gh si lan explique moi sltp
@MilkMilo-qr5uc
@MilkMilo-qr5uc Ай бұрын
Modou c'est un titan un professionel gnikoy supporter aussi done ay nitt you correcte instruit donc siteu faut le comprendre diaroul saga ni xass un farfelu faut juste l'ignorer li worr t worr adouna dou nexx bamou dane modou couronne bi modou moko sole force la
@SaliouSarr-f7z
@SaliouSarr-f7z Ай бұрын
@@MilkMilo-qr5uc bilay walay
@nafisene5335
@nafisene5335 Ай бұрын
Deug piiir nga wakh
@thiernosarr8939
@thiernosarr8939 Ай бұрын
Thanks you bro
@AisataSY-fz5ft
@AisataSY-fz5ft Ай бұрын
Bien dit
@abdoulazizsydiallo4692
@abdoulazizsydiallo4692 Ай бұрын
Yaw khana 2024gua kham modou lo
@papefall7062
@papefall7062 Ай бұрын
Des coeurs pour lambalogue❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@SagnaMoussa
@SagnaMoussa Ай бұрын
Ama balde boy Niang ay noble laniou
@moussaniang4339
@moussaniang4339 Ай бұрын
Bly
@abdousow2908
@abdousow2908 Ай бұрын
Blhi
@khadydiouf658
@khadydiouf658 Ай бұрын
Bilahi ay nitt legn danio kham aduna au moins kholal après combat bi diam rek in shaa Allah
@abdousow2908
@abdousow2908 Ай бұрын
@ bilae
@algueyediagne4111
@algueyediagne4111 Ай бұрын
C vrai mbeure pikine yi nawenalene nak
@MameAbdouDiouf-l8y
@MameAbdouDiouf-l8y Ай бұрын
Modou lô ❤ c'est le plus respectueux des lutteurs bilai
@mamepathengom9398
@mamepathengom9398 Ай бұрын
Machallah machallah lambalok 👏👏 même bo wakhone deugue sama mbeur sakh damaye contane 🫶 nitte daye wakh deugue té yalla takh 👌 yalla nala yalla doli soutoura ak khéweul té samagnou 🙌
@NdongoTall-s3o
@NdongoTall-s3o Ай бұрын
Amine Mame patté ngome deug rek monékh yallna diamou yag si adouna
@Abraham22199
@Abraham22199 Ай бұрын
Siteu yarou woul 😢
@NgagneDiakhate-n7e
@NgagneDiakhate-n7e Ай бұрын
Lambalok le meilleur de tous les temps
@abdoulayendoye1803
@abdoulayendoye1803 Ай бұрын
Li yeup modou leuh moko maay li di dieul ay boy yo hamni defou niou dara si lamb Gouye Gui dako nook sa Thies nokou ko boy Seye nokou lac 2 nokou ko Modou diko maay chance amoul respect T s’il continue comme ça si daanou laay deukeuh
@nafisene5335
@nafisene5335 Ай бұрын
Modou a tout fait dans la lutte. Loutakh mou dieul khalé c’est Parceque daf leen yené avant mouy bayi beuré pour niou dem si kaw. Sou ko defoul wone khaleyi d’où niou yekk Parceque grand yi beugou niou leen dieul. Ils préfèrent lutter entre eux. Niit kegn Mo badola rek. Mais siteu même bou Wa cng diokhè ndam modou, warna khol sen digueunté, seni famille. Li c’est juste un jeu. Mome Mo domerame rek. D’où Niit, mala sakh moko tané. Wayé gathié rek la ciy dieulé d’où leneen
@rouguikebe9984
@rouguikebe9984 Ай бұрын
​@@nafisene5335Siteu kay vrai badola la
@sokhnamariayayefall1536
@sokhnamariayayefall1536 Ай бұрын
Bilay modou moko def genre kon yih boy you rew ba doff
@theblackmamba434
@theblackmamba434 Ай бұрын
Bilakhi frère
@ousseynouthioub9609
@ousseynouthioub9609 Ай бұрын
Té thi lay deuk sakh frérot
@mustic3947
@mustic3947 Ай бұрын
Lamb deug rek la fi wakh. ❤
@mansourciss8978
@mansourciss8978 Ай бұрын
lou diafé si Sénégalais môme la lambalock di déf moy wakh deug bravo lambou 🥰🫶👍👍👍
@FallouGalss-j8r
@FallouGalss-j8r Ай бұрын
thieye Lambaloge ya woor dh bilahi machalah modou ndayesane kholam rek moko togne finalement dafa diepi goss bi
@leroysane_jr
@leroysane_jr Ай бұрын
Deug dou rombou nopp ❤❤❤
@Rosnam80
@Rosnam80 Ай бұрын
Un homme toujours véridique vraiment continu sur ce lancé degue rek nekh yala lambalogue comportement bi siteu ame hier dareu rafetoule bilay walay
@aboubacrthiam-uv9kk
@aboubacrthiam-uv9kk Ай бұрын
Wallahi tu est meilleur قل حق ولو علي نفسك صدق رسول الله
@abdoudiop8697
@abdoudiop8697 Ай бұрын
Lambalogue j t admire dagua kham lamb yemei deugue
@mamadoudia3009
@mamadoudia3009 Ай бұрын
Loutax batay niemé woul wax deugeu gui ni siteu daan na modou???
@MoussaFAYE-w2p
@MoussaFAYE-w2p Ай бұрын
Lambologue et abdou nguer sont les meilleurs chroniqueurs du moment au Sénégal et on les écoutent parce qu’ils disent la vérité
@malicksarr2141
@malicksarr2141 Ай бұрын
Vérité ✅✅👍😂😂😃Bilahi yawe
@blackpure5177
@blackpure5177 Ай бұрын
Bang si bolé abdou nger la xamni iae do wax katou deug
@jobehamidou6545
@jobehamidou6545 Ай бұрын
Walahi billiahi I really love them because they all ways talk the true
@Mo13092
@Mo13092 Ай бұрын
Abdou nguerr mane? 😂😂😂
@MoussaFAYE-vb2rz
@MoussaFAYE-vb2rz Ай бұрын
​@@blackpure5177iow kay ya wakh deugueu wala beugo dégueu deugu
@fallplombier5618
@fallplombier5618 Ай бұрын
Merci lambalogue vérité absolue sitteu da wérré
@taphandiaye4904
@taphandiaye4904 Ай бұрын
Vraiment lambaloque est un homme de vérité tu as parfaitement raison siteu kholal sa communication modou lo a fait tout non way siteu yaw daga daw ba diamagueune 😂😂
@MadembaLo-jf1bn
@MadembaLo-jf1bn Ай бұрын
Meussouma settan commentaireou lamb mais depuis ma xamm lambalok ba legui émission reuthieu touma Machallah yallah na batt bi wer
@medounembaye4224
@medounembaye4224 Ай бұрын
Lambalogue Ya Good Yaa Bien❤💪🙏
@cheikhmbacke2841
@cheikhmbacke2841 Ай бұрын
Merci beaucoup lambalok siteu sakh dafa danou en plus def 4apui
@CASI7797
@CASI7797 Ай бұрын
Merci Lambelogue, deug nekhoul
@SeydinakhalifaCamara-lc2tg
@SeydinakhalifaCamara-lc2tg Ай бұрын
Modou lo incarne l’institution de la lutte sénégalaise.🎉🎉🎉
@bdiene66
@bdiene66 Ай бұрын
Non Reug Reug da gua dioum Moy" Goat"lutte sénégalaise.Modou lo moy comme gnom yékini,balla gaye wala eumeu
@fatoucisse6422
@fatoucisse6422 Ай бұрын
Lamb nitou deug laa machallah ❤❤❤
@azur2117
@azur2117 Ай бұрын
Lambelogue Modou Anta duo explosif Diam ci yéén ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@bintadieng5866
@bintadieng5866 Ай бұрын
Ki mom dama ko beug Ndax deug yimouye wakh bilahi❤
@aissatousy1875
@aissatousy1875 Ай бұрын
Mani siteu ware na khôl communication wam nimou wakh ace sougnou meur nekhou gnou way mom ace sougnou meur dou benn sougnou mer da yarou aye suportteram yarou siteu ace ay siporter moy lolou sakh mani nagne gem yale wa keur siteu khame ne djekh djekh ne djekh couronne bi migi parsel te fofay plasam donc siteu setil lene félicitations notre roi te boul djokhati gen ri may chanc nakh djarou gnouco one lov modou lo❤❤❤❤
@Iskhaga-Bah
@Iskhaga-Bah Ай бұрын
Modou nitt ku baax leu Mâch'ALLAH du yaagu dara ngua guiss ko mu diegueul Siteu comme si meussu ko deff dara ndakh insbi moom mdlô dako diéppi ak doole mais du yagu dara mu baal ko niu andd nekk ay frère ❤❤. Diadieuf le ROI MDLÔ❤❤
@ManamaDiopmbodj
@ManamaDiopmbodj Ай бұрын
Mach Allah lambalogue ken dou yow un vrai homme de vérité.
@davelelion8789
@davelelion8789 Ай бұрын
Merci beaucoup Lambelogue tu es vraiment un génie machallah
@medounetalibebamba6432
@medounetalibebamba6432 Ай бұрын
Way lambe way Machallah
@LamineMbaye408
@LamineMbaye408 Ай бұрын
Lambalogue le meilleur ❤❤
@elhadjisy9222
@elhadjisy9222 Ай бұрын
Siteu dal dafa reww❤❤. Modou nieepp la teral ❤❤depuis quil est roi et même avant.
@AbdouAzizSouane
@AbdouAzizSouane Ай бұрын
Commissaire do nite wax sou fébaré Nop you Kaye deg wara weer barké Cheikh sidi birahim tu as dis vraie 🙏 bravo
@moustaphasarr6550
@moustaphasarr6550 Ай бұрын
Vraiment lambalogue à tout résumé le respect est réciproque
@mouhamadoulaminekane5978
@mouhamadoulaminekane5978 Ай бұрын
Done Tarkindaa, Done Noble mooko geune. Bilay Siteu dafmeu Bett
@Barandiaye-k9r
@Barandiaye-k9r Ай бұрын
Boul wakh lolou khi jambar la d
@AlassaneDieye-cc7jq
@AlassaneDieye-cc7jq Ай бұрын
Lambalogue yalna yallah fayla way❤❤❤❤❤❤❤
@hamidouba4268
@hamidouba4268 Ай бұрын
Billahi Lambalogue deugueu rek laffi wakh quel Homme ❤❤❤🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
@absadione5930
@absadione5930 Ай бұрын
Merci beaucoup il a raison sérère diom foula fayda mais siteu a tout sauf ça n'a changé
@bayemo4147
@bayemo4147 Ай бұрын
akassaaaa lambologue amal diam
@syllafall6804
@syllafall6804 Ай бұрын
Mer6 lambe lock vérité absolue guémigne bosi wahoul deux wahsi fene waye
@SaliouSarr-f7z
@SaliouSarr-f7z Ай бұрын
Lambalok deugue rék gua wakh siteu dafa réw
@babshifayzo663
@babshifayzo663 Ай бұрын
Lamb deug deug❤❤❤❤...Deug rék nga waxx bilahi fans siteu yi waxouniou siteu deug ak gniko weurr
@papendiayesow6391
@papendiayesow6391 Ай бұрын
Bilahi dafa lére frère, Lambelock deggele la wah
@GilbertMendy-y2u
@GilbertMendy-y2u Ай бұрын
Lambalok kessé ❤❤
@joeloum2879
@joeloum2879 Ай бұрын
Billy lambou mo takh ma abonné ❤❤❤
@fallpeezy1288
@fallpeezy1288 Ай бұрын
Thiéy Lamb ya kham lamb ya niémè deug dh yalla nala borom bi doli soutoureu ❤
@mataboulaye3995
@mataboulaye3995 Ай бұрын
Merci LAMBELOGUE
@Faby-u7h
@Faby-u7h Ай бұрын
Modou macha allah yarou rek mo am solo ndah loumoula meyoul dou lako xagne
@falloudiop7651
@falloudiop7651 Ай бұрын
Merci Lamb. Bilay Siteu dafa xamadi, yaradikouna trp😏😊
@dembis1931
@dembis1931 Ай бұрын
Vérité absolue grand
@elhadjisy9222
@elhadjisy9222 Ай бұрын
Non lambalogue té fort ya meunn ya eup dolé. Macha alla té véridique
@DeberouKane
@DeberouKane Ай бұрын
Merci beaucoup lambologue
@lyassane5993
@lyassane5993 Ай бұрын
C'est le meilleur lambalok
@Babacar-nl5mp
@Babacar-nl5mp Ай бұрын
Situe Niata mbéde nga génde 😂
@metza-e1e
@metza-e1e Ай бұрын
Lamb vous avez raison sur toute la ligne.🎉🎉🎉🎉
@malicksarr2141
@malicksarr2141 Ай бұрын
Merci beaucoup leuz lamb ❤ vérité
@fadiloukharma2683
@fadiloukharma2683 Ай бұрын
Yay lamb bilahi ❤❤
@MomoDieye-j6s
@MomoDieye-j6s Ай бұрын
Deugue nêxoulle wopopoopopoo ❤❤❤❤
@basiroukankane1262
@basiroukankane1262 Ай бұрын
Merci bcp tu es le meilleur
@Mimi240-
@Mimi240- Ай бұрын
Deugue rek nga wakh😍machallah
@Fayejeeseef
@Fayejeeseef Ай бұрын
Lambologue tu est le meilleur
@AlassaneNdiaye-n5y
@AlassaneNdiaye-n5y Ай бұрын
Lambologue tu es véridique vraiment wakh katou dégu gua ❤❤❤
@mamadousy8614
@mamadousy8614 Ай бұрын
Machalah Nice ❤❤
@KhalilMbacké-b2k
@KhalilMbacké-b2k Ай бұрын
Merci lambalogue
@assanesane3596
@assanesane3596 Ай бұрын
Lamb logue il est très intelligent et pertinent
@basiroukankane1262
@basiroukankane1262 Ай бұрын
Merci lambalok analyse yi amna solo ❤❤❤
@matardiedhiou7362
@matardiedhiou7362 Ай бұрын
Bilayyy lambalokkk bien dit
@MassambaGueye-l2l
@MassambaGueye-l2l Ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤siteu sisou mane là
@NGfootpassion
@NGfootpassion Ай бұрын
Lambe boulakén duellé si linga nék yallah degue la begue ta degue ndieuk degue modieu ❤
@CheikhFall-p4m
@CheikhFall-p4m Ай бұрын
Modou,gris bordeaux ak sathies gnofi dakh communiqué ❤❤❤
@amaathiat5193
@amaathiat5193 Ай бұрын
Merci lambalogue 🫶🏽
@ChiseOusmane
@ChiseOusmane Ай бұрын
Merci
@falliba2769
@falliba2769 Ай бұрын
commissaire wakhna bien dit grand toujours la veriter
@ndiawdiouf8280
@ndiawdiouf8280 Ай бұрын
❤❤❤❤lambalogue ya woor
@papabachirsarr6952
@papabachirsarr6952 Ай бұрын
Merci Lamb nitou deug
@abdoulayecissegueye7952
@abdoulayecissegueye7952 Ай бұрын
Modou Anta je t’admire bcp de par ton humilité et ton savoir faire. Good job
@malicksarr2141
@malicksarr2141 Ай бұрын
Manmom ma bayi suite ❌😭lim def dembou niawna torop Bilahi si ama baldé modou Lo wala eumeu sene modou Lo lakadon siki saka wayé mom oh 😢 rew bakhout Bilahi
@OmarBao-gu5qp
@OmarBao-gu5qp Ай бұрын
Merci lambou ❤
@MasseDjitte
@MasseDjitte Ай бұрын
Merci lamblogue ms gni nek si guinaw wamm nioko wara wax deug
@birahimseck9167
@birahimseck9167 Ай бұрын
Lambalogue 😂😂damako beugg bilay
@MoussaMar-xd6do
@MoussaMar-xd6do Ай бұрын
Non bilaye je suis siteu mais lambelock tu as parfaitement raison bilaye ndayesan boye nék si diéle monone ba raféte ndakhe gnou guéne c'est le Sénégal qui ngagne 🎉🎉🎉
@aissatousy1875
@aissatousy1875 Ай бұрын
Siteu djegaloul nige wakh dou yonn bilay nakh ame ga plass thi lamb bi nige def dou Yonne daga merlo sougnou roi mani cico solal tamit moco co wara solale Mani sameu meur mom pare na thi❤❤❤
@BayeModouDiagne-b9d
@BayeModouDiagne-b9d Ай бұрын
Bilahi amoul beni yaar domi ram la siteu modou may la sans ngakoy toutal li dou yon amo beni diom
@fatoucisse6422
@fatoucisse6422 Ай бұрын
Vrai Guerrier machallah
@abdoulayeniang2511
@abdoulayeniang2511 Ай бұрын
Nangou noble mokaye déf mais c'est le Modou Xaragne Lô C'est le meilleur 🦁👑❤🇸🇳🥇💪🏿
@NdiogouDione-se7uy
@NdiogouDione-se7uy Ай бұрын
Nioun Siteu laniou beug bilay mom seul ❤
@damembow1855
@damembow1855 Ай бұрын
Lamb un homme véridique walahi
@ebrimacham4239
@ebrimacham4239 Ай бұрын
Lambalok real Gorr Yalla
@ibrahimafall2069
@ibrahimafall2069 Ай бұрын
Merci lambalogue❤❤❤❤❤❤
@NdeyeSao-y1d
@NdeyeSao-y1d Ай бұрын
Vérité 🎉🎉🎉🎉🎉 lamba
@lamine2983
@lamine2983 Ай бұрын
Lambologue, tu es le meilleur!
@moustaphasokhna9161
@moustaphasokhna9161 Ай бұрын
Siteu dafa dioum rkk bal len KO ak félicitations aux rois Modou lo
@FatouMbaye-y3d
@FatouMbaye-y3d Ай бұрын
Merci lamb deug rekay deug siteu da rew legui
@AdamaSambou-ur2zy
@AdamaSambou-ur2zy Ай бұрын
Y’a yarou 😂😂😂
@mormboup9301
@mormboup9301 Ай бұрын
« Niata mbedd nga guene » no lambalogue baxooo 😂😂😂
@ouseynoutoure5299
@ouseynoutoure5299 Ай бұрын
Merci lambolok❤
@assanewade6616
@assanewade6616 Ай бұрын
Modou le roi 👑 et toujours le roi 👑
@dembafadiga4030
@dembafadiga4030 Ай бұрын
Waw kay baaaaaayyyyy
@Abraham22199
@Abraham22199 Ай бұрын
Deugue dou rombi nopou merci lamb
@ModouDiop-n5t
@ModouDiop-n5t Ай бұрын
Ken dou yaw bilay 😢❤❤❤
@abdoulayegueye4529
@abdoulayegueye4529 Ай бұрын
Lambolok merci pour la vérité
Каха и дочка
00:28
К-Media
Рет қаралды 3,4 МЛН
Арыстанның айқасы, Тәуіржанның шайқасы!
25:51
QosLike / ҚосЛайк / Косылайық
Рет қаралды 700 М.
Enceinte et en Bazard: Les Chroniques du Nettoyage ! 🚽✨
00:21
Two More French
Рет қаралды 42 МЛН
Thiey bi comba talfa vs bokola balde🔥🔥🔥
7:54
Lamb dji TV
Рет қаралды 423
Rapport de CENTIF, Farba NGOM épinglé ? la lecture de Ahmed AIDARA...
11:51
2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE
Рет қаралды 4,2 М.
Каха и дочка
00:28
К-Media
Рет қаралды 3,4 МЛН