Bon histoire bi meune na nek lèpp ak leupone. Mais nak nanou ko diapé comme si c’est une histoire vraie. Ki kou fok ni doff la, yaw yay doff. Niome niaar nieup si deugue lanou nék. Dafa fék ni rék niaari Maqamah mofi fègne. Ki nouye wowé doff, si Maqama lay wakhé. Ki nouye wowé diamoukatou Yallah bi tamit si Maqama lay wakhé. Mou déss nak si kane mo dégue niaari Maqama yoyou pour diokh lène niome niaar nieup deugue.
@TORODOTRANS925 ай бұрын
Ragal yalla moy li waar mais pas ragal safara
@jamaljamal29865 ай бұрын
@@TORODOTRANS92 lolou deugue la. Mais étage bou nek dafaye ame escalier. Sikou ame dégue dégue
@AdjaDiakhate-kb7jy6 ай бұрын
Kou ragal safara beusse bou yalla né safara amatoul doto diamou yalla nagnou xélou té bayi wédi