Les dures vérités de Abdou Karim "Ces nouveaux dirigeants ne sont Pas prêts à changer le Senegal"

  Рет қаралды 48,943

Walfadjri TV

Walfadjri TV

Күн бұрын

Pour suivre toutes vos vidéos préférées :
- Abonnez - vous ici : / walfgroup
Suivez nous aussi sur les réseaux sociaux :
- Twitter : / walfadjrisn
- Facebook: / walfadjri
- dailymotion : www.dailymotio...
informations, magazines, débats,séries, sketchs
Découvrez toute l'actualité sur www.walf-groupe...

Пікірлер: 593
@abdoulayedabo9509
@abdoulayedabo9509 3 ай бұрын
Si ce nouveau regimle ne change pas le Sénégal, personne ne changera le Sénégal.Que tout le monde le sache.
@Serviteur-0
@Serviteur-0 3 ай бұрын
Ça c vrai
@julesbe7095
@julesbe7095 3 ай бұрын
Okay Yallah 👍🏽👍🏽👍🏽
@BrainMaxim
@BrainMaxim 3 ай бұрын
Bilaye lolou la Gueme prions que leur réussite._
@madamekoumfarha2206
@madamekoumfarha2206 3 ай бұрын
Merci beaucoup. Ce regime en 3 mois ne peut pas faire de miracle, ils ont assez fait en si peu, que celui qui ne voit pas demeure aveugle a jamais. Point final
@massdiallo4429
@massdiallo4429 3 ай бұрын
En tt cas kou ligeyul niou jeulelafi c tt
@SidyBa-pm4zn
@SidyBa-pm4zn 3 ай бұрын
Je réclame justice pour toutes nos morts 😭😭😭😭😭😭😭
@Modoufaly
@Modoufaly 3 ай бұрын
Patriotes yi lay waxal boulen fatei demb Karim Diambar la nieup guiss nene taxaway boumou amone ba affaires yi metti wei deug def sa sacrifice bou nek pour la lutte pour la démocratie même sou fekei sakh d’accord rouma si yen position yi mais d’un point de vue il a raison justice bi dafay seral wa APR yi ba Président Diomaye prêter serment à la minute qui suit niom nieup lagn wara ndaye convoqué et ils osent de nous pomper les airs comme si rien n’était quoi
@Lucky-bo8ub
@Lucky-bo8ub 3 ай бұрын
Deug rek nga wakh, nitt yi nio war bayi ragal critique. Ki deug bim gueum ley wakh, le minimum moy nangoul koko. Koufi wakhone domou diambour mou guenn khekh niou Ray ko, heure bi sodé nitt warato nelaw
@khalifakante733
@khalifakante733 3 ай бұрын
ah mane lolou la gueum diarrou nion yeureum
@PapeDiouf-x9q
@PapeDiouf-x9q 3 ай бұрын
DEUG la billahi 🙏
@ahmetfall7636
@ahmetfall7636 3 ай бұрын
Mais faut attendre rk
@SaerDiop-s6t
@SaerDiop-s6t 3 ай бұрын
Wa walf raggal leen yallah. Karim deug rek nga wax. Pape ndiaye ak wadiodio nio neka di thiaxaan. Bakane daa foor
@abdoulaye4521
@abdoulaye4521 3 ай бұрын
Karim Mo yakamti adounam nank rek ah lepp dina leer
@hadia_lo
@hadia_lo 3 ай бұрын
Ki si bopam mo soff pour mom diomaye day tok rek lidieunti lep mom beuko meuné na déclarer candidaturam niou xol
@fricaque2172
@fricaque2172 3 ай бұрын
Exactmt tt ne se F pas d'une baguette magique... faut être patient nom de dieu Rome ne c F pas F un seul jour..
@abdouazizmbodj4075
@abdouazizmbodj4075 3 ай бұрын
Karim wakhoul dara lou grave c’est juste qu’il dit sa pensée et avec objectivité On est tous conscient que le nouveau gouvernement ne pourra pas régler les maux du Sénégal mm pour un seul mandat mais ils ne devraient pas laisser ces énergumènes de BBY circuler librement ce n’est pas bon pour la sécurité du pays
@awad12366
@awad12366 3 ай бұрын
Abdou Karim si ce régime échoue on aura tous échouer sache le. Apporte tes solutions aux autorités dans la discrétion je suis sûr qu'ils ne te fermeront pas les portes. Nékk si gaal dii naan gaal gui dou térr doff leu mba sokhor. Aidons nos nouveaux dirigeants guirr Yallah Combat dafay aam dynamique bou béss. Té maa diooy bookk😭
@mouniroudiop717
@mouniroudiop717 3 ай бұрын
Discrétion 😂😂n'a leer nagne transparence ngene wotewone pour intérêts général tamite😂😂😂😂
@alhamdoulilah3991
@alhamdoulilah3991 3 ай бұрын
Vraiment! Il y'a trop de négativité.
@diallodiallo1895
@diallodiallo1895 2 ай бұрын
Mane sokhor laa fi guiss. Au lieu de se tenir la main, ils sont là à chercher la petite bête où avoir le fameux” j’étais le premier à le dire”
@elmo9080
@elmo9080 3 ай бұрын
*Je suis de pastef mais je suis complètement daccord avec karim justice doit être faite dans tous les niveaux et dans les plus brefs delais*
@malickndiaye4840
@malickndiaye4840 3 ай бұрын
Je suis de de pastef et je suis d'accord avec lui sur ce cas ce juge doit être viré de son poste comme tant d'autres
@loeildutempstv1998
@loeildutempstv1998 3 ай бұрын
Il a parfaitement raison wa APR nioy manipuler nan karime warouko wakh ndakh beugou niou sen pion yi djougué fi
@serignetine1420
@serignetine1420 3 ай бұрын
Affaire bi dall defa yekh temps Macky fekna mou vidé wa PDS
@mameboye2247
@mameboye2247 3 ай бұрын
Lolou rentrée des cours et tribunaux lay khar
@PRINCESSdia-mf6cw
@PRINCESSdia-mf6cw 3 ай бұрын
@@serignetine1420legui lossi guiss après c’est nous les sénégalais nio topate si guinaw macky nane ko archarnement lay def mo takh niou wara tey justice fera son travail à son heure meunounioulène fall ba paré dilène wakh ni guène di dokhè j m sens mal quand j’entends yêne commentaire yi le gouvernement es la pour 5ans pa pour 1ans baguène na dafa yekh li yakhou mo mèti mo takh guène fok ni lep s règle en un claquement de doigt tè dou nonou
@alhamdoulilah3991
@alhamdoulilah3991 3 ай бұрын
S'ils les avaient viré tous aussi les gens auraient critiqué et même plus. Et puis, ces juges là, ce n'est pas pour rien qu'ils ne sont pas encore viré. On les laisse eux-mêmes faire le boulot qu'ils étaient sensés faire s'ils n'étaient pas au solde de Macky
@falloumane9536
@falloumane9536 3 ай бұрын
Senegal dañou lay fal ba parè beugeu la fakatal et c'est dommage. Il faut aider les nouveaux dirigeants à developper le pays car tout le monde sait qu'ils sont de bonne foi et que ce sont des etres humains ils ont besoins de temps pour derouler chaque chose en son temps. Vive le Senegal boolo moy dolè. Jub jubbal jubbanti.
@mordione7256
@mordione7256 3 ай бұрын
Ki dagnou ko wara yobe khol bope bi 😢
@Bayebas
@Bayebas 3 ай бұрын
Bilahi frère
@MameDiarraFaye-l2x
@MameDiarraFaye-l2x 3 ай бұрын
Ce karim gueye la c’est le premier à critiquer ce régime après 5 jours de règne la peau restera toujours derrière parce que l’Afrique refuse le changement
@fatousarr3978
@fatousarr3978 3 ай бұрын
​@@mordione7256khana tay l bop bi âme probléme
@taphadiagne
@taphadiagne 2 ай бұрын
Bilay, c très dommage.
@ousmanedieng14
@ousmanedieng14 3 ай бұрын
karimm day surencherekk....le changement est entrain de venir.....nous demandons a karim de dire ce quil attentd comme changements,
@kodediaw1029
@kodediaw1029 3 ай бұрын
Karim à raison amoul khar gni di wakh daguéne amoul mbok boussi dhé faux respecter les Martir
@MboupDame
@MboupDame 3 ай бұрын
Mais abdou karim pour mom lep lougnouy safara pour mom cout ca cout té gni dagnouy bYi sictic bi liguey pas com gnifi neko parisidan yi gnouy def gnoy bayi
@kebekebe587
@kebekebe587 3 ай бұрын
Je suis daccord avec karime
@AliouDiallo-lm6wy
@AliouDiallo-lm6wy 3 ай бұрын
J'aime sonko mai ce gars il dise que la vérité
@WadeMakhtar
@WadeMakhtar 2 ай бұрын
😂wakhi diéko guinee😂
@serignediouf6077
@serignediouf6077 3 ай бұрын
Karim ❤❤❤❤merci pour ton analyse diadjeuff
@edouardothiaw8728
@edouardothiaw8728 3 ай бұрын
C'est pas vrai le Président Basirou Diommaye a dit: nous allons crée une Commission pour dédommager les victimes et la justice sera appliquée. Karim, ce régime va changer ce pays. On ne peut pas changer la justice d'un pays à 3 jours. Ton seul problème tu n'as pas d'arguments en ce moment motakh gay diaboliser.
@SileymaneBall-h6x
@SileymaneBall-h6x 3 ай бұрын
Yow Karim mo eup arguments wa ngour gui yeup.. khana do degglou tidjil sa xélll té baayi fanatisme bi.. Senegal moniou nioor. Ne Raffet reck.. c'est vrai 3mois c'est tôt mais faut prendre de bonnes mesures té bagna fatté démb fatté xadiouffi.
@fromsenegal3217
@fromsenegal3217 3 ай бұрын
😅😅😅😅 c'est très difficile de parler à un sonkolais. Intelligence zéro
@PAPEMACTARBADIANE
@PAPEMACTARBADIANE 2 ай бұрын
​@@fromsenegal3217et pourtant on va gérer le pays jusqu'au l'infini 😂
@diopibrahima5632
@diopibrahima5632 3 ай бұрын
On t'invite reforme justice démo nga nieuw fi di tek . Karim gueno fi xexx ken vous parlez trop way
@ACCFAYE
@ACCFAYE 3 ай бұрын
Merci vous avez tout dit
@Le_Natron_
@Le_Natron_ 3 ай бұрын
😂😂😂
@lagbaja3735
@lagbaja3735 3 ай бұрын
Karim mo la gueun xekh. Bayyilen sen insolence à deux balles. When this dude is talking sh..ut the f..up and listen!
@diopibrahima5632
@diopibrahima5632 3 ай бұрын
@@lagbaja3735 ya meneu saup iow fégn télé moy gueneu xexx , karim da dieul balle wala . boulniou sonal iow ak karim and if you got something to say , keep it for your pussy , fuck it
@basmbaye7527
@basmbaye7527 3 ай бұрын
Diambar deug karim yalla nala yalla faye
@BichriMamemor
@BichriMamemor 3 ай бұрын
Karim xana diglowo discours sonko gara thietare bayil manipulation yi nion niep nioguiwon si terebi do yaw rek yadon khekh nanio wolou sonou dirigeant yi maylen tan niorekle justice bi
@AdolpheGomis
@AdolpheGomis 3 ай бұрын
Karime taloul aye discours politiciens il sans fou limou wakh moy deugeu point
@CodeBa-k7q
@CodeBa-k7q 3 ай бұрын
​@@AdolpheGomisDiscour sonko diaroul door sa dome
@engy11
@engy11 3 ай бұрын
Soutien total pour Karim. Tant que Macky SALL et sa bande n'a pas payé pour leurs crimes, Karim doit continuer à parler.
@laperlecmoi5995
@laperlecmoi5995 3 ай бұрын
Khekh pour Sénégal AK khekh pour sonko ce n'est pas la même chose
@morndadje4198
@morndadje4198 3 ай бұрын
Apprends d'abord à bien écrire pour te faire comprendre
@thebestofficial1104
@thebestofficial1104 3 ай бұрын
Abdou Karim khawma louy sa problème n'est-ce pas iow yafi wakhone na Sonko wakhtane ak Macky pour diami Sénégal ba parei tékci né après Macky déme ci diam abalniou sunu rééw maintenant ngani Macky kéne waroukowone bayi mou déme. Yakofi wakhone dh ci Dakar Matin avec Pape Alé Niang. À la fin qu'est ce que tu veux🤔. T'es un énigme pour moi😢.
@alphaoumardiallo5528
@alphaoumardiallo5528 3 ай бұрын
Justice pour nos martyrs 😢
@seckousmane3397
@seckousmane3397 3 ай бұрын
Yaw mome wéro dof deugu gua
@soumbounist3132
@soumbounist3132 3 ай бұрын
Karim li nga beugoul dégg lolou kén meunou si dara mais le President a bel et bien prononcé sur les victimes lors de la manifestation du 2021 à 2024"Au Sénégal, le nouveau gouvernement n’oublie pas les personnes qui se sont battues pour le changement de régime au prix de leur santé et de leur vie. En conseil des ministres mercredi, le président Bassirou Diomaye Faye a demandé au Premier ministre Ousmane Sonko « de mettre en place une commission d’indemnisation des victimes des évènements de janvier 2021 à février 2024 ».
@franckros4916
@franckros4916 2 ай бұрын
Il fait exprès. Son problème c est Sonko
@loudifa_07
@loudifa_07 3 ай бұрын
My n¡gga Xrum Xakh lim wakh léppou dëgg lë. Mane bañ diokhée macky sall Avion moudém la guëmné DEAL ( DiiL ) amna. 😞 Mais vous les Sénégalais vous êtes juste des fanatiques, vous connais que ça. Le Magal arrive !!!
@mouhamedniang666
@mouhamedniang666 3 ай бұрын
Segnbi amgna sa point de vue gnou nangoulako mais respect celui des autres guenofo intelligent kenn ba wara décidé à nôtre place
@loudifa_07
@loudifa_07 3 ай бұрын
@@mouhamedniang666 Mane déh lima guiss dalout sama xéel. Tékthi Diomaye xaritoo ak Bill Gates💉
@truthteller1405
@truthteller1405 3 ай бұрын
@@loudifa_07 boo demeii sax voter woo pour diomaye
@Le_Natron_
@Le_Natron_ 3 ай бұрын
@@truthteller1405😂😂😂
@loudifa_07
@loudifa_07 3 ай бұрын
@@truthteller1405Je te sûr Diomaye la Votél. Affiche campagne bi diomaye Moy sonko, migui sama chambre ba léegui. Wayé lii ma guiss moy lifi nékkon rék !
@gamoubarcaofficiel7170
@gamoubarcaofficiel7170 3 ай бұрын
Karim nekal nite
@MSénégalais
@MSénégalais 2 ай бұрын
Abdou ces nouveaux dirrigeants savent ceux qu'ils font dou lépp lagnouy parakh parakhé
@abouzo1174
@abouzo1174 3 ай бұрын
Karim j'ai une question les gens qui sont morts pour l'islam takaw dagnou léne dédommager a l'heure temps ?? Le combat de la liberté c'est pas pour nous Mais pour nos enfants a venir ❤❤❤❤❤
@Le_Natron_
@Le_Natron_ 3 ай бұрын
😂😂😂
@malamidiamaye686
@malamidiamaye686 3 ай бұрын
Abdou Karim dafa eupeul lolou reck moko yake
@hadia_lo
@hadia_lo 3 ай бұрын
Teyoul dh
@mobaldelemaire9503
@mobaldelemaire9503 3 ай бұрын
Kép kou wakh ni guisso yonou changement yow amo vision amo batine
@diopadama7477
@diopadama7477 3 ай бұрын
Certains points suis tout à fait d'accord
@OusmanesabriSarr
@OusmanesabriSarr 3 ай бұрын
Yow karim tu es vraiment malhonnête meuna fene gnata yone lagne ko wakh yow kon enga rekkk
@seckcheikhanta956
@seckcheikhanta956 3 ай бұрын
Boy Dee mom danko wara leeral loum guenna gaaw guena baakh diomay ak sonko daniou yeah trop makham diallou ak mandou seck ak amady diouf ak abdou domeram diop ak bassirou gueye danleen wara dakh arrete leen yobou leen kasso li moy degue
@cheikhtidjianesarr8514
@cheikhtidjianesarr8514 3 ай бұрын
Merci Karim Yalla na yalla arr te soutral te motali sa yéne ci Rééw mi ❤❤
@SerigneNdoye-i4l
@SerigneNdoye-i4l 3 ай бұрын
Yalna yala yeureum Sénégal 🇸🇳
@khadimseck1918
@khadimseck1918 3 ай бұрын
Franchement Karim waxna deug 😢😢
@layzocarlou4273
@layzocarlou4273 3 ай бұрын
Diadieuf NITOU DEUGG
@ousmanesarr3116
@ousmanesarr3116 3 ай бұрын
Kï wéroul, yàw sà bïr keùr sàkh bù amē ày problèmes, ndàkh meùn ngàkò réglé bénnė-fànn???😢 Nìt kō khàmnì, fèut-fèut-pèut-pèut rék !? ADDÙNA BÌKÒ YĀH DÌ DÉFÀR sòttìwùl bènn-fann. Pour mōom président Bassirou dā wàra cliqué bénn clique de souris 🐁 ET VOILÀ bì LEĒPP SŌTTÌ !! Aucune sagesse, aucun bon sens que des émotions démesurées, il ne parle pas avec la tête en haut mais avec la tête entre les jambes.
@Lamp112
@Lamp112 3 ай бұрын
Wa mais Pape Ndiaye mi xana il est malade pourquoi il interdit Karim de parler du procureur et du juge Mamadou Secke 😡😡
@normalement21esiecle8
@normalement21esiecle8 3 ай бұрын
Vraiment cheytané rék
@mordione7256
@mordione7256 3 ай бұрын
Dafay ragal gnou yobou wate ko ndougou sine😂
@gigbig5956
@gigbig5956 3 ай бұрын
@@mordione7256😂😂😂😂
@laperlecmoi5995
@laperlecmoi5995 3 ай бұрын
​@@mordione7256😂😂😂
@ousmanekane7504
@ousmanekane7504 2 ай бұрын
naafex rek
@souleymane__torodo_lee3670
@souleymane__torodo_lee3670 3 ай бұрын
Karim fii dara meuna goul lére fi defal nank rek lepp dina lére daga wara téeyi ioe nga nopi man koula naw la Frére ms dagay wéré de
@mbackediop7766
@mbackediop7766 3 ай бұрын
Mais yaw khana Dégo Ousmane Sonko né Dinan Raxass justice Bi 😢😢😢😢
@cheikhmouhamadoulamindiop2472
@cheikhmouhamadoulamindiop2472 3 ай бұрын
Yaw xanaa du yaadoón wax ni nañu gunge Mackay Sall mu génn ci jàmm. Wallaahi yaw mangi xool ngir comprendre là, ngir linga xeexal Senegaal, mais yaw moom wallaahi war ngaa dem gëstu ji waat bubaax, rawati na ci wàllu diine. Fii kenn manul xëy rek soppi réew ci 3mois😢😢😢
@taphadiagne
@taphadiagne 2 ай бұрын
Incroyable !!! Mo done wakh na Sonko wakhtaane ak Macky pour dieul rewmi.
@almoussannaofficiel6479
@almoussannaofficiel6479 3 ай бұрын
Kii ëppël rék mooko diaapp
@iso2459
@iso2459 3 ай бұрын
Karim a tout à fait raison. Que Dieu rétribue Karim pour son engagement et son combat pour la cause des faibles. Amin 🤲
@ousmanebousso4551
@ousmanebousso4551 2 ай бұрын
Karim dafa begue Senegal tè yala takhe, les talibes de sonko nopilene
@Kako-gq3cj
@Kako-gq3cj 3 ай бұрын
Karime.mo.ladione.sonko.afaire.caisse.noire.sonko.neko.bouniou.falo.daniouyekoye.suprimer.dakhe.dafa.aram
@PapeOusmaneDiatta-w2h
@PapeOusmaneDiatta-w2h 3 ай бұрын
Karim a raison sur le juge seck
@cheikhnacamara8899
@cheikhnacamara8899 3 ай бұрын
Wallahi il a raisons kou faté dembeu goré woo il faux que justice soit fait
@ibraahimature.5375
@ibraahimature.5375 3 ай бұрын
Kariim respecté naa la lool waaye linga wax fii lépp ay fen la.
@AdolpheGomis
@AdolpheGomis 3 ай бұрын
Yaw yaye féne lou karime wakh leup pas lérr tope mitt comme doof bou déffé erreur sah nga né guiso dou Karime 1999 la khame Karime nittou guegue Yaleu rék takh may wakh tout ce qu'il di est vrai et nous l'avons touss entendu
@bayesoumare6509
@bayesoumare6509 3 ай бұрын
Karim ci bopam mo eupeul niemer diay graw nit dangay tey nga dall son blem c'est sa pr mom mo geneu niep vaaa wayyy
@elhadjimalickndiaye6947
@elhadjimalickndiaye6947 3 ай бұрын
Karim je suis de tout coeur avec toi c est triste mais tu as raison. C est ça le Sénégal
@BrainMaxim
@BrainMaxim 3 ай бұрын
@@elhadjimalickndiaye6947 no fr j'adore ce monsieur karim xroum ax mais je ne le comprends pas personne ne peut changé ce pays a 5ans personne et si ce régime ne changera pas ce pays personne ne le changera pas travaillons ensemble soudons nos forces pour un Sénégal meilleur karim ils était mon artiste rapeur j'écoute chaque jour ces texe mais rewmi ils faut que gnou dalle âme yarre.
@BrainMaxim
@BrainMaxim 3 ай бұрын
Bilaye dama ko begue parce que grâce à lui j'ai aimé le projet j'ai jamais voté mais cette année je l'ai fait grâce à lui conne qu'il prit pour la réussite de ce projet je ne critique pas parce que chacun a son opinion mais dall karim xroum ax no wo sénégalais yi si vigilance et un accompagnements pour ce régime dou tak mou nek féyik Sénégal nak dafa meti boume falé Var qu'il reste sur son ligne de conduite._
@astucedecouverte8116
@astucedecouverte8116 3 ай бұрын
je suis rarement d'accord avec lui, mais aujourd'hui ila raison. Ceux qui sont dans les manifestations risquent de mourir pour rien.
@laminefanne5760
@laminefanne5760 3 ай бұрын
Karim ndank rék, par exemple yaw jour biniou bayé ousmane sonko 2021 yaw dangua wakhone naniou dém guéné macky sall palais mais sonko bagn lolou parce que lolou baxoul si réw ta meuna takh niou perdre combat bi aduna di dokh ba diamono diokh ko deugue mou dieul ngour gui sans coup d'état bigua beugone yaw, nonou Sonko wakhone ni naniou déff ndank 2021 nonou la wakhaté kérok si grand théâtre que ni Bala nio toppou macky sall ak ngouram fok niou rakhass justice ba paré;vraiment yénéwoumala li yaw dagua am thieur si Sénégal ak liko wara changer mais impatience rék moy sa problème ta lolou moy clé de la réussite gars you réussir yeup biniou déffé liniou wara déff patience laniouko couvriré après réussite sogua nieuw mais aka beuri ay nit you am competence nék si bénn combat wayé biniou niaké patience laniou échec
@PMD94
@PMD94 3 ай бұрын
Souma meunone créé ben deuk bo xamni macky moy nek président,karim nek activiste opposant niom niar késsé si rewmo mou 😂😂😂
@serignemodoundiaye835
@serignemodoundiaye835 3 ай бұрын
Abdou sa problème moy daga yakamti trop
@ahmaddia3315
@ahmaddia3315 3 ай бұрын
ما شاء الله وجزاك الله خيرا يا اخي الكريم ❤❤
@gorabadiane9319
@gorabadiane9319 3 ай бұрын
Karim guenoo beug nit ngni senegal da nga beuri wakh le gouvernement na fait q 3mois
@ndmo876
@ndmo876 3 ай бұрын
sénégalais mo hypocrite deugue karim khekham dou sonko senegal la yene sene khekh sonko la motakh manolena bok ak mom guiss guiss
@SyllaLahat
@SyllaLahat 3 ай бұрын
yaw boy dangay siisou coi moy sa problème
@omzo9376
@omzo9376 3 ай бұрын
Non mais Karim franchement doucement ils viennent d’arriver, jt’aime bien mais c’est pas comme ça Karim.
@kamoucamou3882
@kamoucamou3882 3 ай бұрын
Mounieul diale si lénéne karim macky reuthina niou protocole cap manuel soul na lépeu wayé walahi su eulegué yallah dina lidieunti lépeu macky ak sonko yallah dinaniou arté ak niom
@babacar-bmw
@babacar-bmw 3 ай бұрын
entouca justice warna déf ligueyam sinn day yombo trop
@mamadouleye9061
@mamadouleye9061 3 ай бұрын
Pipi ndiaye wéxo gnulo da dara léruul ohhh
@Toubaexellent
@Toubaexellent 2 ай бұрын
Abdou Karim Gueye bouy wakh daguénkoy baayi mou wakh té Limou wakh kén douko dindi Li moye nitou deug Nioune askan Wi Yawe lén àndal
@thiawosow8363
@thiawosow8363 3 ай бұрын
Karim man dama geum yalla xamnako mes tu nous doie des explication ilfo nga wakh niou yaw lan moy sa geum geum ak lan nga beugue ndakh mane wakh deugue yalla li wara leer sa bopp man khaw mako
@brunodiatta3447
@brunodiatta3447 3 ай бұрын
On dirait k dafa beug djakhassé sonko ak sénégalais yi
@yakhsen-s9946
@yakhsen-s9946 3 ай бұрын
Il est trop petit pour ça
@oumarba9747
@oumarba9747 3 ай бұрын
Khana lolou gua guiss karim gueye a été tjrs constant 😮
@mordione7256
@mordione7256 3 ай бұрын
Karime dafa yakame ti gni trois mois rk lagnou fi dèfa em plus sènègal lifi djiakhasso mo bari
@oumarba9747
@oumarba9747 3 ай бұрын
@@mordione7256 amelene diome moguene il faut reconnaître k sene gayi aye thiounee laniou un pouvoir tant critiqué juste 2mois au pouvoir mousoul am Sénégal
@mordione7256
@mordione7256 3 ай бұрын
@@oumarba9747 daga beugue gnou nàwe guèneul si liga nèke
@bassenesamba
@bassenesamba 3 ай бұрын
Parfaitement en phase avec toi Karim, c'est du n'importe quoi de laisser macky sall libre et qu'il faut vraiment abrogé cette loi d'amnistie et juger les coupables.
@sidyconare1784
@sidyconare1784 2 ай бұрын
Très vrai Abdou Karim deug nekhoul vraiment très vrai bilahi et c'est ça la vérité ❤❤❤❤❤❤
@mouhamadouseck9920
@mouhamadouseck9920 3 ай бұрын
Karim dafa am tokhou doff aduna lepp dou kheutte kheutte ndank rk
@alassanedieng8579
@alassanedieng8579 3 ай бұрын
Pourquoi suivre balance avec Pape Ndiaye boyou cheikh Niasse l'ami d'Amadou Ba meilleur profil présidentielle 2024
@ousmanediouf3165
@ousmanediouf3165 2 ай бұрын
Les coupables,walf,les activistes,les politiciens, Dinguene ko layo AK sounou borom
@SenegalMavie_Tv
@SenegalMavie_Tv 3 ай бұрын
Karim diaroul yakamti dh bilahi gars yi bougn dof doflo ba bayi affaire yi mou sedd mandat bi dou yegg walahi anzim yaw coolal rek sonko nimako beugué sou fekhewoul ba justice amoul bilahi douko djik
@abdouazizthiaw3491
@abdouazizthiaw3491 3 ай бұрын
Tu n'es pas cohérent. Té so waxé ni dara léerul da ngay wax lu la néex.. képp ku ci déh ngir Sénégal mo tax. Bénn nit taxul.
@claudenzale7704
@claudenzale7704 3 ай бұрын
Karim da ngay fenn nakk le Président s'est prononcé n fois la dessus et une commission est mise en place pour recencer et dédommager les victimes 2021 ba 2024
@papiscodemba
@papiscodemba 3 ай бұрын
Ces jeunes ont besoin de justice d'abord avant l'indemnisation. Il faut revenir sur la loi d'amnistie et rendre justice à ces jeunes et à leur famille. Indemnisation mooy lann😢😢😢
@azizndiaye7967
@azizndiaye7967 3 ай бұрын
Pape ndiaye yaaw yaguena boon maly sal domeram piirgua
@mourtallaseye3873
@mourtallaseye3873 3 ай бұрын
KARIM TU NS EMMERDE ON SAIT TOUS BATTU ON PEUT PAS CHANGER CE PAYS EN UN SEUL JOUR
@likdkte5465
@likdkte5465 3 ай бұрын
Abdou Karim yaw daga beuri loy kass koi!adouna rien n’est parfait !yaw pour yaw kénneu bakhoul koi??akh nopaloule nako!🙄🙄🙄
@sidyabadji2493
@sidyabadji2493 3 ай бұрын
En tout cas moi je suis entièrement d'accord avec abdou karim je ne peux pas comprendre qu'es que se nouveau régime attend sur ces personnes le juge M Seck , le Procureur abdou karim et autres Ou bien ils veulent laisser tomber tout en se moment ils seront que les sénégalais ont changé mintena
@gaindefatma4042
@gaindefatma4042 2 ай бұрын
Karim dé bouye wakh daguaye yakarni régime bi 4 ans la fi ame 😂00 kham kham grand guele rek😂
@madamemadame3380
@madamemadame3380 3 ай бұрын
Karim nak danga khawa yakamti tamite. Meuno khekh pour une séparation des pouvoirs , khekh pour un gouvernement Bouyes activé la justice pour mouy def une chasse aux sorcières baparé ngani lolou ngay kharate si gvrnmt bi. Il faut arrêter aussi Sonko a été bien claire balé wougnou li gneup Book point. Bounéké ay principes rek nga done khekh nak khawmeu nga done pour lénéne
@elhadjimaodoniang5531
@elhadjimaodoniang5531 3 ай бұрын
Douniou sakh rouss raye domou ndiambour yi nakh ngour 🎉🎉🎉
@og-rifoumsk7005
@og-rifoumsk7005 2 ай бұрын
On t'aimes❤ Karime walahi douñou fatté démb😢😢
@sodadi8014
@sodadi8014 3 ай бұрын
Ya dane wakh khale yi gnou wathe ti bedabi, ba teguo khocktail rek😢.
@ibraahimature.5375
@ibraahimature.5375 3 ай бұрын
Kii moom vraiment comprendrouma ko qoi moom lan lay rapprocher l'es nouveau dirigent laa xamul dañoo wax duñu topp mbir yi ci yoon walla moom lanla bëgg jàmbaar la lool maî dafa xawa con.
@hadia_lo
@hadia_lo 3 ай бұрын
Ki si bopam mo soff khamna bouniou commencer top wa encien regime bi dina rouss dh
@arfandiakhaby84
@arfandiakhaby84 2 ай бұрын
Il faut donner un poste à ABDOUL KARIM que j'aime bien et que je respecte walahi.pour qu'il sache un peu le fonctionnement. Mais il faut pas être pressér pour un règlement de compte de ces mal faiteur tu te sens responsable de leurs morts mais faut pas. car les SAHABAS DU PROPHÈTE saw SONT MORT pour l'islam et pour le bien aimé. À LA FIN LE PROPHÈTE saw À eu le pouvoir regarde ce qui l'a fait (conseil d'un grand frère)
@patrioteafricaindusenegal6284
@patrioteafricaindusenegal6284 2 ай бұрын
Le problème de Abdou Karim Guéye c'est que il se croit parfaitement parfait
@BaldeJr-xs7xo
@BaldeJr-xs7xo 3 ай бұрын
C vérité es dur mais DEUG là wkh Macky Sall kenn worouko wonne bayi
@ndongo26dg38
@ndongo26dg38 2 ай бұрын
Lo fi dèf dèfnaniouko wo nanioula si rèforme de la justice dèmo nopil kènn khamoul lo beugue
@birambachir3065
@birambachir3065 2 ай бұрын
Worneu yallah koudoul naafekkeu dingeu nangoul Karim limpu wakh chi juge Mamadou Seck ak procureur Abdou Karim Guéye mi yor OFNAC actuellement kenn teggiwoul séne ndombal tankeu. Li dou deugg dou yone, dama khamoul lane la Macky Sall négocier ak niom Sonko ba gars yi melni niousi kheupp souff comme ça ?!!!!
@khalifaka4253
@khalifaka4253 3 ай бұрын
Merci bcp ❤️ ❤️ karim deugue pirr gua wakh ❤
@sab959
@sab959 3 ай бұрын
il a raison mai senegal nekhoul wakhé deug pas de programme une disinformation total des amalgames defaneté yoroul rew arretons la poitiques poticienne et niou roy si systeme MOURIDE bayi par par lo
@faxamaan7632
@faxamaan7632 2 ай бұрын
Revolution Sana Vision, l "âme et La Parole yaalla nopina Feeke doyna Xeewël 🫶🏿 Li nabu mo ëpë Le changement est permanent tout est possible 😂 Que Dieu soit loué Soubhanalahi walhamdoulilahi ❤
@abdoundiaye2069
@abdoundiaye2069 2 ай бұрын
Souniou diapoul maky douniou diap kenen le systèmes a installés le Président Diomaye bilahi walahi
@Chattou90
@Chattou90 3 ай бұрын
Ki dafa sof té dof lakalé parmi les 18 millions de sénégalais yow rek yaue wahkatou deug tu commences à é Être insupportable wah rek wah rek
@denisyadiagne9614
@denisyadiagne9614 3 ай бұрын
Un activiste qui n,est pas intelligent.... président diomay faye et pm ousmane sonko n,ont fait que 3 mois......
@kokbambeykane509
@kokbambeykane509 3 ай бұрын
Il a raison .On ne peut pas dire k Le Procureur Diop,je juge Maham Diallo et les juges Mamadou Seck étaient mauvais et n'avaient pas de conscience professionnelle et les laisser à leur poste pendant 100 jours après ... J'en oublie Serigne Bassirou Guéye
@ndigasalioutoure172
@ndigasalioutoure172 3 ай бұрын
Heureusement k wax ganko liguanye wax yaw la concerné, ndankh waxi doff rk guanfi wax Karim yaw danga mélni koudoul déglou discours Sonko wala Président Bassirou. Aussi sa waxdji boye déglou sa boppeu diguan xamni waxi doff rk guanye wax koma tu peux dire k ya déf live né bouniou sétané Sonko si kasso laye déwé bouguéne guénnoul nieuw waxate ni kén taxoul niou guénneu daniou guénneu pour libérer le peuple,vous êtes télma contradictoire.aussi Karim bou déwou boys bi nékké sa conscience lolou sa problème le il faut savoir k yaw raayé wo yalla moye rayyé.té Karim yaw ak saye morome niodone wathieu si Tally bi,yaw bi gueunone yombeu sakh guan done déf,dém policier diappeu mou diékh kéne meusoula torturé parsk les policiers savaient k tu été malade ils voulaient pas prendre le risque de te torturer aux risques de mourir.Karim dafa ame nioula gueunone deugou fouff si xéx bi insbi niogui tok maye temps régime bi Di supervisé té lolou moye li normal mais yaw tu parle a chak fois pour parler motakh waxi doff rk guanye wax pendant toute c temps si.
@Elhadji-y1b
@Elhadji-y1b 3 ай бұрын
je suis en phase avec lui , on devrait vour la justice ka vraie justice se pencher sur les dossiers des sénégalais assassinés , tortures ou emprisonnés en commençant les arrestations mais franchement on a rien de concret
@fricaque2172
@fricaque2172 3 ай бұрын
Dagueni dalll dall len hiiii ..Rome ne c pas F en un seul jour
@biramathiam6408
@biramathiam6408 3 ай бұрын
Vraiment vous êtes contradictoire Vous disiez que Macky da wara gunené loxom ci justice bi té Et après après Nguen beug wax na sonko AK diomaye def ligueyou justice Ce nouveau régime est en train faire son rôle, nommé un ministre de la justice té do Wagne lokhom lolou nak soufeké Karim lolou nga beugg Kone sonko souko nekh tok ni Karim Daf may critiquer nagnou ko diap
@popolepere6446
@popolepere6446 2 ай бұрын
Au moins Karim reconnaît sa lâcheté bravo
@aidakasse1479
@aidakasse1479 3 ай бұрын
Métina 😭😭
@seckcheikhanta956
@seckcheikhanta956 3 ай бұрын
Karime mom loum wakh bakhna mais pape mom fen kat lá
@cheikhadramefaye3010
@cheikhadramefaye3010 3 ай бұрын
Abdou Karim Gueye je t'ai toujours demandé ta profession et comment tu gagnes ta vie ? Loy ligguey ak foy dieule loy dounde ? Activiste dou métier
@ibou44
@ibou44 3 ай бұрын
Senegal deukou Nafekh leu!!! Karim a parfaitement raison
@mobaldelemaire9503
@mobaldelemaire9503 3 ай бұрын
Ce qui à été bâti durant 60 ans vous voulez qu'on le change en 3 mois vraiment c'est ridicule
L'entrée mouvementée de Bougane à la Cybercriminalité...
7:16
Офицер, я всё объясню
01:00
История одного вокалиста
Рет қаралды 4,9 МЛН
Life hack 😂 Watermelon magic box! #shorts by Leisi Crazy
00:17
Leisi Crazy
Рет қаралды 18 МЛН
Every parent is like this ❤️💚💚💜💙
00:10
Like Asiya
Рет қаралды 18 МЛН
Sortie de Bougane: la réaction de Pa Assane Seck ...
9:10
Seneweb TV
Рет қаралды 52 М.
Офицер, я всё объясню
01:00
История одного вокалиста
Рет қаралды 4,9 МЛН