Рет қаралды 92,859
Hero disponibile sur toutes les plateformes bfan.link/hero-28
Artiste : Wizzy Kana🎼
Directed by : Kalash director
Son : Neegurap Music🎼
Mix Master : Peulbouhigh Beatz🎼
Beat : fantastic🎼
Production : MBT100
Salle de sport : fitparkacademy🏋🏻
Coach : Djily Seck🏋🏻
Lyrics :
Ehh mane leuh rek
Boudoul mane waxma kenen kouy diriger
Thi guinaw rek ngeeni lang melni geen yeah
Douma deglou wakhi noone yée
Dou Xamngeen ni maak niom non dou game
Danga merr lousi sama yoon thi golo bou poudeurou man
Life bi laay beurel té mbeur bouma song ma daan ko
Oww doolei yi dou ben man
Mer leen i don’t give a damn
Mangui thi kanam té rawnaaleen
Auto bou teggou thi talli bi ni feerari
Lingewni deffa geuneu yombe passou car rapide
Oww niggah maay seen Badman Spiderman Superman
Niggah maay seen hero
Hero
May sén hero
Hero Hero Hero
Hero
May seen hero
Hero hero hero
Hero hero yeah (hero)
Hero hero yeah (hero)
Hero hero yeah (hero)
Hero hero yeah (hero). (2x)
Kenn rek laay beureel sama life
Carrière bima songg naako daane by force
U gonna know seen jote
Amoumako mang thi sama bopp
Doumaleen faalei
Dinga geuneu tardé
Wakh dju beuri dji taloumako
Jote bou beurri bi amoumako
Doumaleen faalei
Dinga geuneu tardé
Wakh dju beuri dji taloumako
Jote bou beurri bi amoumako
Ehh mane leuh rek
Boudoul mane waxma kenen kouy diriger
Thi guinaw rek ngeeni lang melni geen yeah
Ehh douma deglou wakhi noone yéé
Dou xam ngeen ni maak yeen non dou game
Hero
May sén hero
Hero Hero Hero
Hero
May sén hero
Hero hero hero
Hero hero yeah (hero)
Hero hero yeah (hero)
Hero hero yeah (hero)
Hero hero yeah (hero). (2x)
Doumaleen faalei
Dinga geuneu tardé
Wakh dju beuri dji taloumako
Jote bou beurri bi amoumako
Doumaleen faalei
Dinga geuneu tardé
Wakh dju beuri dji taloumako
Jote bou beurri bi amoumako
Hero hero yeah (hero)
Hero hero yeah (hero)
Hero hero yeah (hero)
Hero hero yeah (hero). (2x)