Bilaye soxna bou ndaw est talentueuse, elle assure grave son rôle
@Fatou-t8qАй бұрын
Soda marem sokhna bou ndaw mola narra guéné keur gui😂
@evenprodАй бұрын
@Fatou-t8q Mougui beug doye ware. 😂
@cisco9615Ай бұрын
Esk dou eumb
@aissatouseck9020Ай бұрын
1:49 1:49 1:49
@aichasow4672Ай бұрын
Yaw soda qui beug kou khadial yayam yaw gay danou si piège bobou tey rek ga kham dôme noumou nékhé
@PathéDiop-y1yАй бұрын
Blh soxna da barui pékhé de
@mbayangdiagne1904Ай бұрын
Ndiawar Diagne moh gueneuh sonou sii série bii 😂😂
@khadydiouf3539Ай бұрын
Je savais que le retour de boury ne sera pas facil du tout. La maman de maty rose a raison aussi. Maty rose peut aider omar à se soigner d'abord avant de l'épouser
@cheikhabdoumbacke6970Ай бұрын
Yalla nafi yalla bayi sunu maman yi ak sunu papa yi basi kanama kanama kanam si barke s touba 🤲❤️❤️
@WadeSarrАй бұрын
Keur Diawar motakh may sètane série bi sans gnom dou nékh kou dakor rek besseul❤
@ibnoundiaye6588Ай бұрын
Ndiawar dé xalissam ak dom diou djiguéne dji rék la beug amoul kénéne😂😂😂
@DiarraDia-pj7eqАй бұрын
Motakh canette dina am problème 😂😂😂
@evenprodАй бұрын
@ibnoundiaye6588 Est-ce que dou lolou motah dome dji tapasse Soda Mareme ?
@sokoneinformatigue-rl7pfАй бұрын
@@evenprod BIEN SUR
@dady7099Ай бұрын
@@DiarraDia-pj7eq😂😂😂😂😂😂😂😂 wouyyyy canette kay
@khadydiouf3539Ай бұрын
@@DiarraDia-pj7eqya bonn canette nak😂😂
@KhadyDiop-j2oАй бұрын
Nianalen sama papa tay la am 4 jour si souf
@PendaSene-jr8dnАй бұрын
Yalla na yalla dolli yeurmande té khare ko aldiana firdawsii 😢
@a.sakho2898Ай бұрын
Yalla na souf oyof si kawam Al'jannah firdaws nek keuram bou moudiou
@BintouSeye-n4uАй бұрын
Yalna ko yalla yeureum bibarakati chiékhoul khadim
@user-ch3bu9id6vАй бұрын
Yalla Nako yalla yeurem❤❤❤❤
@ass_malicke_DioufАй бұрын
Yhalla nakou Yerame
@fatoundiaye1999Ай бұрын
Sokhna bou ndawe defgua erreurs warowone wakh ak sa badiane ohhhh😢❤yalna bou yakar tasse
@sossoooooooАй бұрын
Moma nahari ni 😢😭😭
@yayemayelatmbao5442Ай бұрын
😢😢😢
@amandasimpson4906Ай бұрын
Bilahi 😢😢😢
@mormbaye2989Ай бұрын
Lila beugon wax😂
@fatimsarr8293Ай бұрын
Mom dafa Yakar badiene bi dafa bakh lolou moko trompé
@NdeyembarkaWade-w7lАй бұрын
Sokhna sa tourando bamouy seytané dioudogo,koula makk eupp layy sagarr😢❤❤❤❤❤❤❤
@adjidiop3905Ай бұрын
Lolou la khamoul diamonoy Ms. Seck ak Tapha🤣🤣 thia Idole
@aramegueye-ox8ffАй бұрын
😢 mouma diaxal
@evenprodАй бұрын
@NdeyembarkaWade-w7l Est-ce que die"uloule si djiko tourando bi ?
@MarieNgom-h1nАй бұрын
Lernama né sokhna bou ndaw déy provoqué soda marée pour mou dioté ak papam divisé pour mieux régner 😂😂
@mamecoumbadiop3764Ай бұрын
Waxal dh nonou lafa demei comme ni badiene bi di df rk😂@@MarieNgom-h1n
@DialGaye-x4uАй бұрын
Vendredi tay bi yalla boumou nekh sounou dernier vendredi amine
Meilleure maison de production sénégalaise 🎉❤ direction 5M d’abonnés 🎉
@evenprodАй бұрын
@Goraa-MS Merci pour la force. 👍
@Mouhamedtv536Ай бұрын
Sonko et diomaye Allah vous protège ❤🎉 0:29
@cheikhabdoumbacke6970Ай бұрын
Amine
@aminatagueye4659Ай бұрын
Yalla nako yalla yeureum si barke Seydou mouhamed psl
@maremesow6734Ай бұрын
Diadia yangmay beug diaxal. Sokhna bou ndaw seytanei bi tie tourondo bi yeupa ngui si mom Soda Maréme labeug guenei dougeul yayam tres bien sampou rek😂😂😂
@sallandiaye1417Ай бұрын
Mais waroul wone wakh ak badiene bi😢
@maremesow6734Ай бұрын
@ xalei la pour mom dako beug ndeysane
@oulimatafall3494Ай бұрын
@@sallandiaye1417😂😂nehh ngeuu legui bou fekeii li leuu scenariste bi binde douko deff
@sallandiaye1417Ай бұрын
@@oulimatafall3494😅😅bilay dafma meti
@evenprodАй бұрын
@maremesow6734 Motah tapasse Soda Mareme. 😂
@MmeTouré-b5tАй бұрын
Khana wa évenpeod dénio tite samdi niou deff mercredi ka amna 😂😂😂❤
@aichadiedhiou2350Ай бұрын
Nio yeeh nak cas Maréme sall bi la rek😂
@MmeTouré-b5tАй бұрын
@@aichadiedhiou2350 loum deff lolou raw nama 😂😂
@beybladeburst7406Ай бұрын
Soumboulou biniou reye molene tite lo
@awadiop9637Ай бұрын
Wa yw tmt khana dg tite evenprod lagniou binde dh yw gua bindal nio evenpeo😮😮😅
@BogalngonéGueyeАй бұрын
Moma diakhal motakh sétane nako 2fois pour mane samay beute nio nékhoul
@ndeyediop_Ай бұрын
No man Sokhna bou ndaw damako beug😂🎉❤
@evenprodАй бұрын
@ndeyediop_ Est-ce que die"uloule si djiko tourando bi ?
@ndeyediop_Ай бұрын
@evenprod doumani dett dh🩸
@FamaraNjie-q5yАй бұрын
Watching from the Gambia 🇬🇲 ❤
@awalo2Ай бұрын
Vraiment content n'a si sokhna mou ndao en réalité lay wakh boudon mane nilaye def ba sma yaye
@annita3108Ай бұрын
Soda Maréme khana da repp😂guissna guénam si keurgui nak😂😂
@KhadyNdiaye-ud3djАй бұрын
Soda marem tay gua dhe dh ak ndiawar nimou beugué dom😂😂
@khadychouba1606Ай бұрын
Bilay iow 😂😂
@evenprodАй бұрын
@KhadyNdiaye-ud3dj Est-ce que dou lolou motah dome dji tapasse Soda Mareme ?
@ndiayendeye6787Ай бұрын
Lii nèko si kholl yi tè Manou gnouko wax yalla n'a yalla safara lèpou 😢❤❤
@DabaSamba-s7zАй бұрын
Amine ya rabi
@mormbaye2989Ай бұрын
Sokhna provoque n’a tanta dji nk😂😂 M warowon wax sa badien dr
@evenprodАй бұрын
@mormbaye2989 Est-ce que die"uloule si djiko tourando bi ?
@mormbaye2989Ай бұрын
@ m mom au moins sokhoroul 😂😂
@ThiatDomouNiomréАй бұрын
Ndiawar dé kéndu lale Sokhna😂😂😂😂
@almoustapha4197Ай бұрын
Sokhna bou Ndaw dé lamigne rék la am 😂😂😂❤❤
@evenprodАй бұрын
@almoustapha4197 Tappasse na Marieme Soda dh. 😂
@YacineSeck-t2jАй бұрын
Sokhna DH day khalal yayam yonn soda marém bou moy touwoul popam dina am problème ak ndiawar 😂ndakh thé mom mom khalissam domam😂
@almoustapha4197Ай бұрын
@@evenprod malheureusement Soda maréme khamoul li Sakhana bou Ndaw beugu 😂😂
@a.sakho2898Ай бұрын
Diadia c'est vrai que tu veux protéger ton frère mais li dou sa djiko
@evenprodАй бұрын
@a.sakho2898 st-ce que dou dafeu xamoul Maty Rose bou bakhe ? 😥
@AidaMboup-we5ypАй бұрын
Djadja dafa neubone vrai djikome nila mele
@a.sakho2898Ай бұрын
@@evenprod wa dako khamoul nak mais maty lii yeup moko yobé bopam aussi topou khaliss andado bou bone ak niak dégueul yayam
@a.sakho2898Ай бұрын
@@AidaMboup-we5yp yakarou mako dé
@adamacamara4477Ай бұрын
Ndiawar ak bonne rek yalla boumouko takk
@MalickNiasse-s8pАй бұрын
Merci waye sokh'a🎉
@moustaphadieng7207Ай бұрын
Yalla n'a niépou âme diamou ❤
@acte_senegalАй бұрын
Meilleur série de l’année 😅🎉
@linespara4089Ай бұрын
Dior Mbaye yalla nga goudou fane and ak wer
@evenprodАй бұрын
@linespara4089 👍
@MamyNiang-r9wАй бұрын
Yalnako yalla yeureum ta kharéko aldiay fir dawsir❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@DavidSÿ-e9oАй бұрын
Bilahi Xalisso rek 🎉🎉 épisode 23 c’est chaud 🥵
@MbenndiayeMbenАй бұрын
diadia diome nga ndakh sa rake eumbona té yakho ko 😢kone waro yakh rakou diambor 😢li moye Sénégal yore sa thilou di lidianti libar diamjor 😢
@adamengomndiaye4209Ай бұрын
Diadia mome daf ma bete trop
@aramegueye-ox8ffАй бұрын
Diadia kay daff ma rouslou ndakatéi anta sakh moka tanné
@PrincesseAidaBa-ek7ebАй бұрын
Diadia mom bête n'a nieup waroul won def ni
@evenprodАй бұрын
@MbenndiayeMben Est-ce que dou dafeu xamoul Maty Rose bou bakhe ? 😥
@KhadyFall-t6pАй бұрын
@@evenprodlimkou khamoul bou bakh nk moutakh warokou jugé bett nama trop
Le retour de Boury en cours ❤😂 sokhna nak yaa ham amour paternel et maternel ohhhh
@mounass2339Ай бұрын
Sokhna com lir bouy dioy😂😂😂😂😂😂😂😂
@evenprodАй бұрын
@mounass2339 😂
@diarracisse6017Ай бұрын
commentaire bi la done weurr sokhna nimouy youkho doyna warr 😂😂😂
@FalilouKane-u3zАй бұрын
L’apparence est trompeuse. Que Dieu nous aide et nous guide dans notre chemin ameen
@mamesayengom4212Ай бұрын
Ohhh sokhna yak gua lepp😂 j savais k l retour était trop beau pour être vrai 🤧 film noveras yi mognou yakk😂
@evenprodАй бұрын
@mamesayengom4212 Lol 😂, pourtant dareu xewagoul.
@adjasalihsamb9398Ай бұрын
@@evenprod bou dara khew way boury fokk mou togui thiere yi nakh Diop fall contann 😂😂😂
@diopkhadija7556Ай бұрын
Sokhna la beug mane ❤❤❤❤
@MatouNgomАй бұрын
Kepp kou beugg teral say wadiour beuseul j'aime ❤
@diorsakho307Ай бұрын
Sokhna bou Ndaw Avec sa Guani do nétali 😂 Koula démlo sisa Tourondo ioe
@evenprodАй бұрын
@diorsakho307 Dako wolou rek. 😔
@diorsakho307Ай бұрын
@ sama yakar mo nara tass🥹
@BinetaMboup-y8zАй бұрын
Yalla na ko yalla kharé aldiana
@NdoyeSportАй бұрын
Yalla na diamou yague rk 🎉❤
@AminatadiaDia-w5nАй бұрын
Diadia béteuh nama tropp😢
@BaMalick-m9gАй бұрын
Yallah nako yallah yereum
@moussoubadoumbiaАй бұрын
Massa yallah nako yallah yeureum
@MamadouDiop-p3sАй бұрын
Cou d'accord ni evenprod dafa dioume si date bi épisode bi samedi lay am
@farmatasallАй бұрын
Commentaire bi la don weur 😂😂
@cheikhouna0ly333Ай бұрын
Yalna Naniou Allah bourbii dolil Soutoureu khéweull akk Salam Si Barkë Mouhamed SAW ❤
@SouleymaneDiop-s2zАй бұрын
Yalla nako yalla yereme
@OusmaneMbodji-z7wАй бұрын
Yalla nako yalla xaré aldiana
@fatouseck7714Ай бұрын
Yalla na diam sakh sunugal
@GorafromsaloumАй бұрын
Que Allah Nou protége et protége notre parents
@duclamericain1563Ай бұрын
Toujours là à représenter kolda ❤
@evenprodАй бұрын
@duclamericain1563 ❤
@diakherndiaye8537Ай бұрын
Sokhna mo bonn😅😅😅
@fatouceesay6794Ай бұрын
This is becoming more interesting!
@SalimataToure-r6rАй бұрын
Salam guise nafi wa kolda guise fi wa kaolak guise fi wa Gambie 😂😂😂🎉🎉 mais nioun wa ziguinchor tamite nioungui sétane ❤😂🎉 yallena diamm yague senegal ❤🎉
@evenprodАй бұрын
@SalimataToure-r6r 👍
@sawlouMbyeАй бұрын
Serie bii Amna solo ❤❤❤
@MbdStyleMusiqueАй бұрын
*Les 5 millions d'abonnés d'Evenprod mon combat focus*
@evenprodАй бұрын
@malcomboydiptsStyle Merci pour la force. ❤
@DiopNdeyefatou-o8hАй бұрын
Alhamdolilah ❤❤❤😂
@yatmaseck3056Ай бұрын
Kou d'accord ni Omar Diagne Dina marié AK Maty rose rek lalal j'aime 🎉❤
@MoustaphaKandji-r7wАй бұрын
😂Omar dinama réye. Rék
@kyafaye5604Ай бұрын
Franchement soxna sa lamigne bi ratakh na 😮diadia boul juger nite ci passém maty rose sa maman est un peu égoïste mes cas mm elle a raison par ce que omar dof bou dégoul yéla la naniouko fathie ba nopi 😂maréme soda loy dauré né kou wéroul yaw tmt lii di piège ahhhh
@NgagneKahe-me9smАй бұрын
Jummà Mubarak yalla nagnou yalla defal diàmmou bague loo ngou songoy yaaye ❤❤❤❤❤❤
@PASSwordeАй бұрын
Sonko moyi domayi ❤❤❤
@SECKBada-jb5hlАй бұрын
Wa sokhna diagne mi kou ko dém lo si sokhna bou mak soda Mariem tay mou nekh dagua khadiee si sokhna diagne wa bakhna 😂😂
Soda sa divorce la guiss ni😂 xoolou Ndiawar gua laal...😂😂😂😂😂
@SokhnadiarraKane-c1zАй бұрын
Thiey Omar sampou na nak❤😂😂
@evenprodАй бұрын
@SokhnadiarraKane-c1z Beuguel dafeu disse. 😂
@FatouboussoNgomАй бұрын
Mafi djitou 🎉🎉
@evenprodАй бұрын
@FatouboussoNgom Bravo. 👍
@BayemodougueyeBayemodougueyeАй бұрын
Even prod gnir yalla n'a marém sall ñiewàt bété Bété
@MorSene-b5uАй бұрын
Bouleen sonal nit gni AK mareme Sall. Beugoul joué les autres sont là mille fois meilleur qu'elle. Ba saneekh di joué avec les Aziz Mareme Sall kén khamouko.
@khadychouba1606Ай бұрын
😂😂 Vraiment beug joué a l'intéressante rek @@MorSene-b5u
@LaBarhamienneАй бұрын
@@MorSene-b5usenegal mo nekh thi boppam😂 melni série bi marème sall la toudou wala daniou lene wax ni son rôle dafa indispensable
@BayemodougueyeBayemodougueyeАй бұрын
@@MorSene-b5u pour tamp wakh gna deug dh🤣
@FansanimeetclubtinАй бұрын
Tay dé yakam tina torop evenprod bi 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂❤😂😂
@evenprodАй бұрын
@Fansanimeetclubtin Loutah geu yakamti ?
@FansanimeetclubtinАй бұрын
@evenprod Bakh Bande annonce bi tang na ta yén wa xalisso evenprod dama lén beugeu sama khol
@Cheikhmbayesamb-q6nАй бұрын
Ndiaware mokk Bakary kiff kiff sonounane 😂😂
@murtadaajonn6502Ай бұрын
Soxna mu ndaw de dafa bëgg a génne Sooda-mareem dugal yaayam 😂😂 aka saytaane 😂
@Mamancamara07Ай бұрын
Ohhhh sokhna bou ndaw yaw rek lay topp mais dioum nga ohhh😢😂sa tourando da fausse
@habykane-f6wАй бұрын
Manchalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@AstouWaniane-w8bАй бұрын
Yalla nako yalla yerem
@FatouDiop-b7gАй бұрын
LoveyoU ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤awaMABYE
@AichaDoumbouya-t5vАй бұрын
Soda mareme fassé nagne ko 😂😂
@maimounasow9561Ай бұрын
Even prod yena meilleur
@beybladeburst7406Ай бұрын
Waw lolou mome deug leu mais merenalene trope si Marieme sall bilahi ba legui sama hol bi day meti, . Vrai mort sakh douma meter ni yalla hamnako dama beug théâtre soumboulou
@evenprodАй бұрын
@maimounasow9561 Merci. ❤
@MamekhassMbayeАй бұрын
Amine 😢🙏🏿🙏🏿🙏🏿
@ndeyetoure229Ай бұрын
Alhamdoulilah ❤
@ModouMakhtarDrame-cm7rxАй бұрын
Mais mane sokhna la nopp deh bilahii 😢
@NdeyeayouDioufАй бұрын
Yalna Souf oyofe sikawame
@gogobarham5322Ай бұрын
Sokhna bou makk mounut ci boury dara vue sou yondé fatkinè boury douko deglou hamnani l'égui seytané la 😂
@evenprodАй бұрын
@gogobarham5322 Ah à suivre. 😌
@Baguidera5691Ай бұрын
Ce soir c'est vendredi et non mercredi 😊
@AdamaKAАй бұрын
i love evenprod
@evenprodАй бұрын
@AdamaKA ❤
@AlidiopDiop-o8nАй бұрын
Yalna yala woyafal souff sa kawam
@Diawmouha95Ай бұрын
Diadia bett nama dh😢
@ModousarrDiop-i7zАй бұрын
Khady yallna bakhna
@DiopNdeyefatou-o8hАй бұрын
Mas amours ana gen😂
@KhadijaLy-c7jАй бұрын
Merci beaucoup sokhna
@evenprodАй бұрын
@KhadijaLy-c7j 👍
@Fall-v1bАй бұрын
Lima guis d'où yombeu dh😂😂😂
@miss22395Ай бұрын
Xalisso🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥
@khadyfaye4260Ай бұрын
Pourtant la maman de Maty Rose est juste une mère protectrice elle veut juste que sa épouse un homme stable mentalement. Je pense que Maty doit juste aider Omar Diagne à se soigner d’abord et ensuite l’épouser si elle l’aime sincèrement ❤. En passant Ibou Gueye Damala bayii nak ndax Maréme Sall minga yobou lahira