MBAY GÉY SILL LI LA TONTU CHEIKH OUMAR DIAGNE

  Рет қаралды 143,672

Xam Sam Réew Tv

Xam Sam Réew Tv

Күн бұрын

Пікірлер: 1 200
@thiernondiaye5126
@thiernondiaye5126 3 ай бұрын
Personne ne peut détruire le travail de Serigne Touba nous le tidiane de New-York ont a fait le magale à New Jersey avec les mourite dieureudieuf Serigne Touba merci papa
@DashSenico
@DashSenico 3 ай бұрын
Merci bcp grand ❤
@aliounesylla1892
@aliounesylla1892 3 ай бұрын
@@thiernondiaye5126 je suis d'accord avec toi
@touba2863
@touba2863 3 ай бұрын
*Barkei serigne Touba Mouride yii dei Niogui guena Beug serigne touba baa faww. Jeuredieufety Cheikh Ahmadou Bamba*
@abdouseck6731
@abdouseck6731 3 ай бұрын
Macha Allah wakh nga lépe
@abdouseck6731
@abdouseck6731 3 ай бұрын
omar fenkatt diagn
@layma4143
@layma4143 3 ай бұрын
Oumar Diagne damokoo yërëm ndax doma haraam daguë la
@papaibrahimaly7318
@papaibrahimaly7318 3 ай бұрын
Quand une personne est en cours d'arguments, il insulte
@cheikhtidianecfaye4455
@cheikhtidianecfaye4455 3 ай бұрын
Dieuredieuf
@barhambaye6745
@barhambaye6745 3 ай бұрын
Moi Tidjane j'aime beaucoup Serigne Touba, kou téedd ki.
@ndiagamboup739
@ndiagamboup739 3 ай бұрын
Wakhe daga Yalla dawna yaram lol bilaye man magui dora khame ly che Omar diange wakhe me bilaye Yalla xamnako. Diaroul tonto Man bagouma toudo tourame bilaye Yalla xamnako bou bakh me Koko diaroul tonto s touba mbacke kena manta yakha darame bilaye Yalla xamnako famo tolo sorina lol bilaye Yalla xamnako mane koko wakhe lolou pour Mane diaroul tonto fa s touba mbacke Tolo Koko diotiwo fa diaroul wakhe dara s touba mbacke dana ko sa fara tè wakhe dou ame bou kene wakhe nane be lepp AK s touba mbacke Koko di s touba mbacke magui wakhe ni amoul morome diadiouf mbaye geye sylla diabar ga bilaye walai nut kou bakh ka yakfi lol tè wer amine
@diopdjibril
@diopdjibril 3 ай бұрын
Waw gooré baye mbaye Gueye silla mate n'a lérna yalla n'a la yalla fayy yague fi rék té wére
@cheikhbadiane5908
@cheikhbadiane5908 3 ай бұрын
Niounn yalla rek laniou guemm S touba rek lanii toupou mom rek lani kholl magal gui moy sounou biss
@SerigneFaye-zd9tj
@SerigneFaye-zd9tj 3 ай бұрын
P⁰⁰⁰
@SerigneFaye-zd9tj
@SerigneFaye-zd9tj 3 ай бұрын
P⁰⁰⁰
@SerigneFaye-zd9tj
@SerigneFaye-zd9tj 3 ай бұрын
P⁰⁰⁰
@Abibou-m9v
@Abibou-m9v 3 ай бұрын
Mame mbaye guye Syla yagal yokal weral barkép serigne touba
@ModouMboup-v1r
@ModouMboup-v1r 3 ай бұрын
Dieurdieufty serigne touba yalla na niou ko Yalla fayale mok sou nou maak niou bah yi❤😭
@khalyball3758
@khalyball3758 3 ай бұрын
Kou tèdki,kouko bagne,danga tarkhissou danou ta kènne doula mana yèkati.billahi.
@INFOSXIBARE1145
@INFOSXIBARE1145 3 ай бұрын
Gnon gui demandé président de la république basirou diomay mou daxe chekhe omar diagne immédiatement thi noumou guenan guawé
@moustaphadiop1786
@moustaphadiop1786 3 ай бұрын
Dieureudieufaty Serigne Mbaye Syll yalla nala yalla defal diam tawfekh ak tayssir si barke Cheikhoul Khadim amin
@combecane257
@combecane257 3 ай бұрын
Magal gui événement national la kou am gan ganalé ko respect à tous nos chefs religieux
@ibrahimadia9912
@ibrahimadia9912 3 ай бұрын
yalla bakhna nanou dem rek Oumar doff bou mak la way dina kham ne Serigne dou morom mae Sénégal ak serigne ba faw
@maniana52
@maniana52 3 ай бұрын
Touss nak,il la fauté na demander pardon. Serigne touba c t1 Saint parmis les saints ok mais loudoule yallah néne,la
@serignemodouabibgueye3935
@serignemodouabibgueye3935 3 ай бұрын
Baay Mbay Gëy Silla أنت فخر لجميع المسلمين وخصوصا للمريدين بارك الله فيك حفظك الله ورعاك
@mbayefaye3585
@mbayefaye3585 3 ай бұрын
Cheikh Omar Diagne est un ennemi de la voix mouride mais il va mourir de chagrin car on aime Serigne Touba de plus en plus ❤❤❤
@sambmoustapha4873
@sambmoustapha4873 3 ай бұрын
Diereudieufeuti serigne Mbaye Gueye Sylla
@aliounesylla1892
@aliounesylla1892 3 ай бұрын
Yalla ne yalla yereum Sénégal
@MbayeSarr-i6g
@MbayeSarr-i6g 3 ай бұрын
Baye mbaye gueye syll mourid yépalla amél thiante
@alassanegueye3965
@alassanegueye3965 3 ай бұрын
Bignou amei Serigne Touba laniou yallah yereum.
@Shbtv45
@Shbtv45 3 ай бұрын
​@@alassanegueye3965😂cou yalla yeureum mome nokoye hamé. Bayilen sen film yiguéne di jouer di mboubo serigne bi
@ndeyediop335
@ndeyediop335 3 ай бұрын
Si barkèp Serigne Touba yakari Diam gni
@SOLDADJI5648
@SOLDADJI5648 3 ай бұрын
Amine yaa raabi
@NDONGOLY313
@NDONGOLY313 3 ай бұрын
Merci beaucoup Baye Mbaye. Sante nagnou guerum nagnou la. Serigne Touba kessé mo gnou gnore té mome lagnouye tope ba abadane. Lou waye ame wala nga done ko nangoul nagnou la wayé gnoune Bamba lagnou ame.
@BeugBamba-r2l
@BeugBamba-r2l 3 ай бұрын
Serigne Touba bouko adûna yeup bayiwoon sakh kérok lako guina beug lolou yallah moko déff amoul kù thie maan dara,ta biri kou Tédki illa abadan daye gueuna yook amoul déltou guanaw Serigne Touba lagnou beug ❤❤❤❤
@cirehakimlo2033
@cirehakimlo2033 3 ай бұрын
Li rékka takh Sénégal Calais dou dém Ngi bange s TOUBA mo bari ci réw mi Wayè likoy doumeu dinako fékk ci négeum❤ s TOUBA kouko bande téxé di
@SANTEADJIKAWEDJI
@SANTEADJIKAWEDJI 3 ай бұрын
Kou mélné Cheikh Omar Diagne manouma comprendre mouye nék ci état bi, ndakh moo wakh nieup di dégue né tarikha dafa wara dièkh ci Sénégal. Kou wakh lii ba paré di ame thiér ci rewmi
@matarniang709
@matarniang709 3 ай бұрын
Merci Serigne Mbaye Gueye Syll pour cette réplique à l'endroit de cet homme irrespectueux qui ne mérite même pas qu'on mentionne son nom. Il vexe la communauté mouride tout le temps. S'il ne fait gaffe, il finira mal comme tous ceux qui s'étaient érigé contre Serigne Touba qui ont péri de la façon la plus méprisable. Il doit se répentir avant qu'il ne soit trop tard pour lui. Dieureudieuf Serigne Mbaye Syll!
@amsacisse4286
@amsacisse4286 3 ай бұрын
Faine dou saga wayé môme amoul xame xame naina nioune mouridou lah ay conlégne moo takh ma xamné amoul xame xame mouridou lah dioulitt yeup kaine dou serigne touba khadime rassoul lillah ❤❤❤❤
@mbayefallou1401
@mbayefallou1401 3 ай бұрын
Macha-allah dieureudieufaty Cheikhoul KHADİİM Cheikhanaa Cheikh Ahmadou Bamba Yalla nanou ko YALLAH fayal Té Mousseul ñou ci Say-Say Omar Diagne borom khol bou Tillime bi 😊
@saliouniang1633
@saliouniang1633 3 ай бұрын
Machallah Dieureudieuf gorgi sa.wakh lérna
@Djiily7461
@Djiily7461 3 ай бұрын
Dieuradieuf s mbaye Geuye sylla yalnala S TOUBA nangoul sap Liggeey beg naniou
@Kora504
@Kora504 3 ай бұрын
Jërëjëf baye Mbaye Gueye syll ❤❤❤
@alioungom8256
@alioungom8256 3 ай бұрын
Blaise Diagne, Oumar Diagne.fatelikouléne Gabon, dieureudieufé Serigne Touba 🙏
@falilouu3fall210
@falilouu3fall210 3 ай бұрын
Cheikh Oumar Diagne ak mane nimako nawé wone franchement Ce monsieur me déçoit
@modyndoye3893
@modyndoye3893 3 ай бұрын
Mais cette vidéo ne date pas d'aujourd'hui. C'est un rétro apparemment.
@fallougentlemara4853
@fallougentlemara4853 3 ай бұрын
Jereudieufe kilifeu gui wax ji amna solo té tegouna si xam xam cheikh omar Diagne vrai domaram la
@julesthiam9060
@julesthiam9060 3 ай бұрын
Salam Baay Bégg nañ lool si taxaway bi Wayé nassa xél dal ndax nitt meunoul wax waleu mou déf lou wañi sounou pass-pass tchi Serigne bi Li metti nitt you bone yi moy riroum ndaw ñi woutal si Serigne bi té mouy lou yakaar lou si eulleugou mouride gui Té lissi néx moy li ndaw yi saubo si xam-xam tei bolé wouñ si wax. Yalna Yallah samm ñou té mousseul ñou barkép Serigne bi Dieureudieufeuti Cheikhoul Khadim ❤❤❤❤❤
@sultan0073
@sultan0073 3 ай бұрын
Wallahi
@BoutiquetallaSeck
@BoutiquetallaSeck 3 ай бұрын
Dieuredieuf Serigne Touba Mbacké Khadim Rassoul ❤di yéwou dika gueneu beug bly walay❤❤❤❤❤
@ballambengue9518
@ballambengue9518 3 ай бұрын
Bëgg Seriñ Tuubaa rekk, kumu nakhari demal Gabon. Moom moo dem dem dellusi ab ligeyem di tàkk ni ab Jànt ,
@sendiaye747
@sendiaye747 3 ай бұрын
Machallah djeuradjaf brom touba❤❤❤
@moussafall5604
@moussafall5604 3 ай бұрын
Wakho fi dara cheikh omar diagne dossa morom si xam xam
@fatimambay7006
@fatimambay7006 3 ай бұрын
Wakhou degeu de
@basska9757
@basska9757 3 ай бұрын
da ngay doull dhe
@cheikhdia9593
@cheikhdia9593 3 ай бұрын
Ki gua bollé sa baye ak oumar ak ko yakkar mo len euppou xam xam noppil
@ibrahimandiaye-5250
@ibrahimandiaye-5250 3 ай бұрын
Walahi wakh nga degue
@mouhamadoulmakhtardrame8366
@mouhamadoulmakhtardrame8366 3 ай бұрын
Ya meuna doul
@Tele_Touba
@Tele_Touba 3 ай бұрын
Theuy Sylla djredjeufati ❤
@العلم_والعماء
@العلم_والعماء 3 ай бұрын
Baye Mbaye Man Ku bëgg Sarigne bi laa lool kula Bëgg laa lool hitam, Kulay topplaa lubari , daana jiss ngay indi ay firndé ci linga dan wax , mais ci sa vidéo bii xaj bu njakk bi jisuma ci benn firndé, xana ay waxi ku mer diwaxé xol, INDILÑU CI AY preuves MAME MBAY! Jërijëf
@MRTV659
@MRTV659 3 ай бұрын
Jàmbaar nga lool waaye tay moom waxoo fi xam-xam Baay Mbay.
@goraseck9057
@goraseck9057 3 ай бұрын
Dieureudieuf baye mbaye syll yague fi lolle tè wèrr
@dinakane2032
@dinakane2032 3 ай бұрын
En tout cas Cadu yi deh serigne bi andu cii té cheikh oumar diagne waxoul defoul litaxx cabale bi vraiment yalla na jam yagu si rewmi ❤🙏🏿
@mouhamadoulmakhtardrame8366
@mouhamadoulmakhtardrame8366 3 ай бұрын
Nafekh gua
@fallalpha710
@fallalpha710 3 ай бұрын
Est-ce que deg gua loumou wakh
@ndiougoumbaye2225
@ndiougoumbaye2225 3 ай бұрын
Yaw bala nga oubi sa guémine di wakh demal au moins deglou li C.O. Diagne wakh après nga nieuw tontouma
@maniana52
@maniana52 3 ай бұрын
​@ndbayile mou sédeu iougoumbaye2225
@AliouWade-f6r
@AliouWade-f6r 3 ай бұрын
Danguaye ndaye doule wakh na kaye
@sarmaimouna5593
@sarmaimouna5593 3 ай бұрын
Cheikh oumar diagne yaW dh yay com bou mag bi.serigne touba bou baucoul thi gor yalla yii tamine def nafi lou gor yalla defoul am fi lou gor yalla amoul point
@syllayoussouf4649
@syllayoussouf4649 3 ай бұрын
Je valide tout se que cheikh Omar Diagne a fait. Dieu protège cheikh Omar Diagne 👏🏿
@maximumculture3038
@maximumculture3038 3 ай бұрын
Moi aussi
@NdiayeModou-b1d
@NdiayeModou-b1d 3 ай бұрын
Daniou tegal ndayam de
@ndeyesalioundiaye3119
@ndeyesalioundiaye3119 3 ай бұрын
Guen di ndoundou di guis tjr lolen yem sa sou magal passé chaque année guen di beugu dé m sen khol yi dina waad
@daoudagueye3645
@daoudagueye3645 3 ай бұрын
N'a fekhe you bon yi
@ndiagasamb611
@ndiagasamb611 3 ай бұрын
Ragalal yala cheikh Omar diagne bokna thi senegalais yi guene thi rewmi
@SambaDiollo
@SambaDiollo 3 ай бұрын
Oumar diagn bakholl
@BiraneKane
@BiraneKane 3 ай бұрын
Xanaa yaw la gën
@sultan0073
@sultan0073 3 ай бұрын
Khana yow laa geun
@papamassambafaye4415
@papamassambafaye4415 3 ай бұрын
Néko mou jox gnu liste Serigne yiy mafia
@djeuwrinemaodo1796
@djeuwrinemaodo1796 3 ай бұрын
Yaw dé ya dakha doul fouf omar diagne
@mystere3746
@mystere3746 3 ай бұрын
Paby doule rekk lay deff… dah doule bah bédiaw 😂😂😂… cheikh Omar diagne Dinah tegual sen ndeye bien bon
@begmametafsirb7340
@begmametafsirb7340 3 ай бұрын
Mané cheikh oumar diagne louko nit wakh toñ ko alalou lay sakanal Sagoul wakhoul loubone limou déf Kou beugeu deug doula nakhari ndakh alalou réwmi mi la
@mouhamadoulmakhtardrame8366
@mouhamadoulmakhtardrame8366 3 ай бұрын
Khana diango do lire vidéo bi bou bakh xana guisso « rétro » bi
@SerigneAbdouFatahNiang
@SerigneAbdouFatahNiang 3 ай бұрын
Yaw billah Yama na wax Lou la nèkh
@DameBassel-dl4zo
@DameBassel-dl4zo 3 ай бұрын
Merci Serigne mbay.tous les mourides doivent aller en guerre contre cheikh Omar Diagne.
@leraltouttv4204
@leraltouttv4204 3 ай бұрын
KHADIM RASSOUL ❤❤❤❤❤رضوان الله عليه AY MBIRAM DAY KAWÉ BA FAWWO❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@TheMomo141
@TheMomo141 3 ай бұрын
Le Sénégal c'est pour les 18millions de sénégalais
@moustaphadiouf9154
@moustaphadiouf9154 3 ай бұрын
Non pour les pastef maintenant
@alassanegueye3965
@alassanegueye3965 3 ай бұрын
Tu as fait quoi pour le Senegal ?
@alassanegueye3965
@alassanegueye3965 3 ай бұрын
Wa Touba Nio feneu khamei wa Pastef nuit nonou Serigne Touba
@mbengueballa2736
@mbengueballa2736 3 ай бұрын
Mais gnoune thi 18 millions yi lagnou bokou diii
@BaNdiabel
@BaNdiabel 3 ай бұрын
Serigne Touba barina ay talibe yi dofff de yalla len yalla yerem kou contrôle gen ni bougoul s Touba bouga s Touba day deff nutt yeferr s bougoul talibe you dofff merci c Oumar Diagne
@AhmadouLamineBaraGUEYE-he5sq
@AhmadouLamineBaraGUEYE-he5sq 3 ай бұрын
Kou bëggul serigne touba dangaa téxeedi rek. Neena qulubu jumlati laziina aflahoo liya tawajahat wa rabil mouslihu si xassida wakaana hakkan maana xolu gi wara téxé gneup sope nanu ma. Yaradiku geen waaye Serigne Touba romb na mbineef yi BOROM mbindeef yi lay waxal. Il a réussi sa mission et vit auprès de son SEIGNEUR. Vous qui cherchez avec l'appui de satan à déstabiliser les mourides il vous a déjà qualifié de chiens dans un vers de qassida.
@maniana52
@maniana52 3 ай бұрын
😂😂
@walterwhite8303
@walterwhite8303 3 ай бұрын
Serigne Touba nimou kawwé nonou ay talibém soufé. Vous êtes des fanatiques dénoués de savoir, passionnés et émotionnels
@abdoufall1496
@abdoufall1496 3 ай бұрын
Yow mi wakh li khamo serigne khamo ab ligueyeum mo takh wakh wakh diou khebou dji
@walterwhite8303
@walterwhite8303 3 ай бұрын
@@abdoufall1496 saawaay damay lire Serigne Touba. Soufi bou makk la. Waay yeen talibé xamolen sax lan moy tassaouf. Demlen guestou
@sagyatal8545
@sagyatal8545 3 ай бұрын
Ana man tanha laha biya fawha hayreho ila yawmal hiayam. Wakhi S Touba la
@serignetine1420
@serignetine1420 3 ай бұрын
Dinner l Islam bouthi fanatic guener dara dou des
@koumbacke9731
@koumbacke9731 3 ай бұрын
Yaw nopil.khamo dara di wakh rekk
@tamaradaniels1867
@tamaradaniels1867 3 ай бұрын
D accord na ak yowe il est très incohérent Omar diagne je me méfis de lui depuis qu il disait que l on doit construire une mosquée au palais de la République
@KhadimBambaThioune-w8m
@KhadimBambaThioune-w8m 3 ай бұрын
❤❤❤xam xam dou pekhé Père ndoundall sa ndoudou diarigne rek Le historien
@MoctarNiang-xu7ew
@MoctarNiang-xu7ew 3 ай бұрын
Beugeu serigne touba aduna ak alakhira.Dieureudieuf Khadime rassoul.da nguén sonou dé Bamba rék laniouy topou
@ablayethiam
@ablayethiam 3 ай бұрын
Je suis Tidjane mais je ne cautionne pas les dires de Cheikh Oumar Diagne. Togne bakhoul nous aimons Kou Tedd ki pour l'amour qu'il porte au saut des prophètes et son sens élevé de sacrifice pour le rayonnement de l'islam au Sénégal. Nous aimons Baye Mbaye " lu baré luma kham si histoire reew mi mom motakh"
@badaboys2098
@badaboys2098 3 ай бұрын
Ya mana fen lii check omar diagne waxu ko kii day manipule
@walit234
@walit234 3 ай бұрын
Cheikh Omar Diagne kou baxla teu xam-xam rek lay wax. Bayyilèen di lakatou ci Serignbi di politic. Kou bax dou saaga teu serignebi diglewoul saaga.
@MassaerHanne
@MassaerHanne 3 ай бұрын
Cheikh Omar Diagne véritable talibe cheikh bou woor laaa dioulit akhaan bayileen wax Lou amoul cheikh Omar Diagne raw naleen
@boucountambaye5573
@boucountambaye5573 3 ай бұрын
Merde
@moustaphaabdoulahadmboup6813
@moustaphaabdoulahadmboup6813 3 ай бұрын
Nane nalène rawé . Ya gat ham ham .
@abdoulayedjigo
@abdoulayedjigo 3 ай бұрын
Khana sa baye la raw
@VISIONPLUS-et8sn
@VISIONPLUS-et8sn 3 ай бұрын
UN VERITABLE CHEIKH NE DIT PAS DE MENSONGE SUR SERIGNE TOUBA . CHEIKH OUMAR DIAGNE EST UN IMBECILES
@MoreNdiaye-jh7pq
@MoreNdiaye-jh7pq 3 ай бұрын
Yaw doull domourame bi
@oumykalsoumendiaye6993
@oumykalsoumendiaye6993 3 ай бұрын
MACHALLA PAPA WAKHE DJI LÉRENA MAIS SÉEDÉ MAME ABDOU AZIZ BI RÉKE DOYENA BEUGTÉ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@abdoundoye2780
@abdoundoye2780 3 ай бұрын
Dieureudieuf serigne touba.dousséne moroumou bay sakh
@papasalioucisse9639
@papasalioucisse9639 3 ай бұрын
Dieurediefe serigne touba domou mbam ak khathie bi diaroul tontou dieuredieufe serigne touba moy deranger nafekh yi
@bayewaly8783
@bayewaly8783 3 ай бұрын
Wallah sonko ak diomay Omar diagne daléni yakhal wayé doulén défarale té Lolou migui sounou kanam
@maniana52
@maniana52 3 ай бұрын
Cela na rien a voir il le,concerne lui seul
@modouthiam2461
@modouthiam2461 3 ай бұрын
il sont touses des complic
@combecane257
@combecane257 3 ай бұрын
Sénégal rafétal lagnou kham ...le gouvernement de Sonko faites très attention respects à nos chefs religieux
@diopbounamadiopkmf6577
@diopbounamadiopkmf6577 3 ай бұрын
Yén daal sén sarap nday rék.Cheikh Oumar Diagne est plus honnête et digne que vous tous réunis. Maylén ndayi nitt ngi diamou waay.
@modoudiop1646
@modoudiop1646 3 ай бұрын
Ioe katal sa sarap ndy nopi domou kharam
@modoudiop1646
@modoudiop1646 3 ай бұрын
Yak Omar diange sene srp ndye domou ram
@Lopios-g6l
@Lopios-g6l 3 ай бұрын
Xalé you réiwyi maky rék moo bahh thi yénn...
@rasdaroukane5007
@rasdaroukane5007 3 ай бұрын
Chrikh omar diagne dou meusseu beug serigne touba Je suis de pastef mais téwoul douma diouk si wakh ni domram la
@maximumculture3038
@maximumculture3038 3 ай бұрын
Yow yay domérame
@souleymaneniang3637
@souleymaneniang3637 3 ай бұрын
Dieuredieuf serigne Mbaye Sylla sante serigne touba rek
@moustaphaseck1231
@moustaphaseck1231 3 ай бұрын
Dieureudieuf seringe touba ❤❤❤❤❤
@bathiefaye5264
@bathiefaye5264 3 ай бұрын
Jaajëf Sill yalna Yàlla guddal sa fan. Masoo jóg ci dàjji feni Omar Jaañ yi saa yu fenee. Omar mbaam àll la moo xam ni Sëriñ Tuubaa rekk la bañ.
@djibrilgning4988
@djibrilgning4988 3 ай бұрын
Oumar diagn dal dagno tegaloul nadayam rek motakh mouy wakh louka nekh maky rek la respinte modon gnaf ndayam
@babacardiagne3504
@babacardiagne3504 3 ай бұрын
Cheikh omar diagne dousa morom amal yar
@elhadjiibrahimakebe1038
@elhadjiibrahimakebe1038 3 ай бұрын
Tré bien papa tay lanion guene bègue S serigne Touba
@ahmadougueyecheikh1220
@ahmadougueyecheikh1220 3 ай бұрын
Bamba sa kanam , touba sa kanam,,bamba feep ,bamba partout, bamba internatíonal.
@ModouMboup-v1r
@ModouMboup-v1r 3 ай бұрын
Dieurdieufty serigne touba yalla na niou ko Yalla fayale mok sou nou maak niou bah yi❤
@salioudionguelepnaatt2912
@salioudionguelepnaatt2912 3 ай бұрын
Cheikh oumarr Diagne le véridique ❤❤❤❤
@daoudagueye3645
@daoudagueye3645 3 ай бұрын
Ay nafekhe guen
@HadimSevk
@HadimSevk 3 ай бұрын
Le bon dieu, vous accorde une longue vie et pleine de santé, Aminé.
@alybambasy351
@alybambasy351 3 ай бұрын
DIEUREUDIEUFF SRRIGNE TOUBA ... BEUGG NANIOUKO BA NOPPI
@SambaSylla-dp9mp
@SambaSylla-dp9mp 3 ай бұрын
Da sokhor khol bou tank lay dé diar na yereum.diereudieuf serigne touba
@madydiop8167
@madydiop8167 3 ай бұрын
Père yangui def li yalla gueuneu bagn moy touma
@papamassambafaye4415
@papamassambafaye4415 3 ай бұрын
Legui li Omar diagne di def naka dou touma
@NgomNdary-jj3rf
@NgomNdary-jj3rf 3 ай бұрын
Moko wakh déglou nako cheikh omar diagne kou kate data ndayame la
@NdiayeModou-b1d
@NdiayeModou-b1d 3 ай бұрын
@@NgomNdary-jj3rfmaynala 50000mil yabakh
@molinarttv7528
@molinarttv7528 3 ай бұрын
Li cheikh oumar wax nak dou touma ? Yow vrai nafex nga
@bassiroundiaye6923
@bassiroundiaye6923 3 ай бұрын
Leufeul ndéye cheikh omar diagne ak kèpou koukaye dèfandre sa tounou ndèye
@Abubakr_Sakho
@Abubakr_Sakho 3 ай бұрын
*Non lii métti na !* *Deugeue nexul mais mourid Mom dagnò doy warr*
@ibrahimaka20
@ibrahimaka20 3 ай бұрын
On peut discuter, répondre, hurler, montrer notre colère, dire que telle personne a menti, porter plainte...mais on ne doit pas traiter quelqu'un de franc maçon sans raison, ni appeler à la violence on est dans un pays de liberté.
@cheikhdiop5288
@cheikhdiop5288 3 ай бұрын
Ki werouuul🎉
@BambaSénégalCouture
@BambaSénégalCouture 3 ай бұрын
Omar Diagne dafa beugeu buzz beugeu gniou ték ko figniou ték borom xam xam yi motakh mouy doul di wakh rek té limouy wakh yép khamousi dara bégne serigne touba nak mom moy wédi dogaloup yalla rek la wassalam Diareudiafé Borom Touba❤️🤲🙏
@C-col137
@C-col137 3 ай бұрын
Vive cheikh oumar diagne
@SambaDiollo
@SambaDiollo 3 ай бұрын
Oumar diagn bakholl
@C-col137
@C-col137 3 ай бұрын
@@SambaDiollo non man dh guissouma bonam
@SambaDiollo
@SambaDiollo 3 ай бұрын
@@C-col137 setanal vidéos yi oumar diagn defon don ci toudou serigne touba lou gnaw lou né wax nakou yonou mouride
@C-col137
@C-col137 3 ай бұрын
@@SambaDiollo douma deglou kouy khastè wala saga bilahi
@C-col137
@C-col137 3 ай бұрын
@@SambaDiollo souma deglo ngay saga sakh ma bayila même boufekone damaladane toppou
@mouhamadoufadeldiop2413
@mouhamadoufadeldiop2413 3 ай бұрын
CHIEKH OUMAR DIAGNE n'a KO ngour gui wathié BOUGNE BEUGUÉ DIAM WAS SALAM
@JàmmRekk
@JàmmRekk 3 ай бұрын
Góor gi soo waxee ni Seex Umar Jaañ faramaçon la xam ngani dangay fen yaral say kàddu ab murit warul yaradiku , man dama lay toppu ndax mboorum Sénégal SUJ am na yumuy wax ci kër kilifa yi dëgg gu wér la ku wax dëgg ñu boole la ak mag ñi ak ñii fi nekk tay coome penku ak soow yaw ba Seex Umar di xeex framaçon ana nga yaw mii di fen
@fayardioumba9735
@fayardioumba9735 3 ай бұрын
Dangaye wakh cheikh Oumar mou yar ay kaddoom d'abord.
@LampFall-o2h
@LampFall-o2h 3 ай бұрын
Yaw danga reew bilaaxi
@LamineSall-mv9gq
@LamineSall-mv9gq 3 ай бұрын
Sa tounou ndaye
@modoudiop-ix2ir
@modoudiop-ix2ir 3 ай бұрын
Diadieuf gorgui sylla cadoudi rafetena tè léonard mâcha alla
@moussacisse5397
@moussacisse5397 3 ай бұрын
Yalle na niou yalle mousale si mak mou saye tane amine🤲
@NiangAmadou-bt3mg
@NiangAmadou-bt3mg 3 ай бұрын
Même xalé bou réw tamit yalla nagnou si sa borom mouseul
@AbdouSall-wi6yt
@AbdouSall-wi6yt 3 ай бұрын
Ce gars cheick omar rentre dans un terrain très glissant serigne touba kep kouko song wala bagne alkou
@Pastef859
@Pastef859 3 ай бұрын
Bëggë nañu la lool Sëriñ mbey waayé lii du sa cër !
@maradiop
@maradiop 3 ай бұрын
Li cheikh Omar wakh nak lo ci wakh yaw
@Pastef859
@Pastef859 3 ай бұрын
@@maradiop dama ni ak lumu mënë wax am na kaddu yoo xam ni warul jogé ci kilifa
@maradiop
@maradiop 3 ай бұрын
@@Pastef859 DEUG la dé jambaari wayé dama yakarni Cheikh Omar Diagne tamit kilifa la , li War Serigne Mbaye GUEYE Syll reka KO warr. Té dama yakarné ki niak wormal Serigne Touba fi ci Sénégal ba nieup degg ko sou amé kougnou wara yedd môme la wara doon. Serigne Mbaye Syll talibé la bou amé louko nakhari. GUEUM GUEUM AMOUL AGE KOUNEK NANIOUKO RESPECTÉL KILIFAM
@Pastef859
@Pastef859 3 ай бұрын
@@maradiop xam naa fi ngay waxéé waayé boo giséé ma taxaw ci Sëriñ Mbaye syll daa am nitt yuko toppu diko deglu té toppu ñuko ndax mourid la wala tijaan dañukoy toppu ndax xam xam bumuy joxé kon moom jamono ji muñ rék ak kaddu gu rafet moo ko war manam waru
@maradiop
@maradiop 3 ай бұрын
@@Pastef859 jajeufati xam na lingay wakh rafetna. Wayé nak togn bakhoul , lo bokkoul boul ci wakh bay niak teggin kilifa gua , COD na bayyi yonou mouride Dou ay thiakhane. AB mouride nak bougnou lalé Serigne Touba mou défendre KO wathie na. Kouy yedd yéddal COD mou bayi togn. Ki fawou nak amna ci droit l'Islam baniouko. Li ci eup nitt gni khamouniou ki togn wayé ki fayou laniouy diokarbi. Sagga Kat nak koukoy défendre dafla lalagoul. Wayé yalla bakhna . Yalla n'a Jamm yagg
@adamasy1938
@adamasy1938 3 ай бұрын
Machallah, sèrigne touba est universel vèritè absolue.
@dienebam853
@dienebam853 3 ай бұрын
Merci cheikh omar Diagne tu as la vérité et rien que la vérité
@moustaphadiagne4278
@moustaphadiagne4278 3 ай бұрын
Lima ler yalla mo defal serigne touba defal lko maodo ak gooryalla day yok yalla milen ko diok douko nagou dieuredieuf serigne touba
@niangmalick740
@niangmalick740 3 ай бұрын
Yaw moom ab pooro nga.Yaa dul waxkatu dëgg.Nous sommes à 100% avec Cheikh Oumar Diagne.
@moustaphaabdoulahadmboup6813
@moustaphaabdoulahadmboup6813 3 ай бұрын
Mou wagni ko lane .
@sarmaimouna5593
@sarmaimouna5593 3 ай бұрын
Setnane
@diorfall4604
@diorfall4604 3 ай бұрын
Kou Bagne Serigne Touba Sa Khool Monye 💔 Et Diomaye ak Sonko Aye Talibe Bamba lagne ! 👌👌👌
@elhadjsarr2204
@elhadjsarr2204 3 ай бұрын
Saway khamouma Sonko dé. Wayei Diomaye mom Tidiane leu
@mystere3746
@mystere3746 3 ай бұрын
@@elhadjsarr2204diomaye c’est un Talibé Baye
@abdoufaye9359
@abdoufaye9359 3 ай бұрын
Cheikh Oumar Diagne nague ya gui beugua eupal , Di nagne la gniouss gniouss national dhé, soncko la gniou la roussè nague
@diagnediagana9910
@diagnediagana9910 3 ай бұрын
Nit kou bone moy chiekh oumar diagne, bagne tarikha mourite
@modousylla9845
@modousylla9845 3 ай бұрын
Jeureujeuf syll yaa.L nek deug dh Yall nala srg touba Faye guen gui fay
@salioudionguelepnaatt2912
@salioudionguelepnaatt2912 3 ай бұрын
Bravo COD❤❤❤❤❤❤
@BeggSareewtv
@BeggSareewtv 3 ай бұрын
Jërëjëf Baay Mbay Yàlla na Yàlla sàmm là défal là Fan wu Guddu Andak wër ♥️♥️♥️♥️
@Mmd592
@Mmd592 3 ай бұрын
Merci pêre ❤
@mamitabve1717
@mamitabve1717 3 ай бұрын
Nay wah rek gnioune. Niou kay geuneu beug dieureudjifati cheikh ahmadou bamba khadim rassoll
@RokhayaNdiaye-q4s
@RokhayaNdiaye-q4s 3 ай бұрын
Gorgui daimale diamou yala mogane siyawe
@lessauveurs6314
@lessauveurs6314 3 ай бұрын
Dëmal wakh ko sa baye ak sa ndèye
@basska9757
@basska9757 3 ай бұрын
mou dakha diamo yalla sa baye dhe
@senegalrek2579
@senegalrek2579 3 ай бұрын
Yaw mom do diamou katou yallah ndakh diamou katou yallah deug dou fen dou wakh louko woroul
@Malicksindidi1988
@Malicksindidi1988 3 ай бұрын
Kii amna yalla dh
@xaliloubadji2597
@xaliloubadji2597 3 ай бұрын
Yow lo fi deff ?
@adamaba9765
@adamaba9765 3 ай бұрын
Ndéysane nguéme da sensible mais pa bi content nouldé qu'Allah nous protège
@abdoukhadrediouf-zv4pz
@abdoukhadrediouf-zv4pz 3 ай бұрын
Nekelen ay kilifeu mo geune
@cirehakimlo2033
@cirehakimlo2033 3 ай бұрын
Yalnako YALLAH Mbougeull bala magalou dëwèn ci cheikhoul khadim, ak barkép mfatihoul bishri, s TOUBA soun BOROM moko douguell ci xolou diam ngi,wallahi dina alakou
@Ggxdffd55
@Ggxdffd55 3 ай бұрын
Seex Umar deful dara liggéeyam rekk la def. Ku bëgg a jël hotele dangay fay
@xidmatulxadiimtv8296
@xidmatulxadiimtv8296 3 ай бұрын
Yaw sa data nday
@Shakur892
@Shakur892 3 ай бұрын
@@xidmatulxadiimtv8296 Deugg nekhou sawayy,; Cheikh Oumar ligueyamm rekk la deff,
@AliouWade-f6r
@AliouWade-f6r 3 ай бұрын
Yaw sa lefeule ndaye
@Shakur892
@Shakur892 3 ай бұрын
@@xidmatulxadiimtv8296 Yow ammo yarr ci ay mbamm nga maggè khanna?? Ci xam-xam way
Enceinte et en Bazard: Les Chroniques du Nettoyage ! 🚽✨
00:21
Two More French
Рет қаралды 42 МЛН
It works #beatbox #tiktok
00:34
BeatboxJCOP
Рет қаралды 41 МЛН
黑天使只对C罗有感觉#short #angel #clown
00:39
Super Beauty team
Рет қаралды 36 МЛН
WAXTAANE NJAMBÀARUG LATJOOR AK MBAY GÉY SILL
1:05:52
Xam Sam Réew Tv
Рет қаралды 45 М.
JUBBANTI MBOOR Ci Li WAAJI WAX CI LATJOOR.
19:41
Xam Sam Réew Tv
Рет қаралды 60 М.
Regardez Cheikh Bara Ndiaye humilie Cheikh Yerim Seck en direct
17:01
HISTOIRE | DEXËLE LE 27 OCTOBRE 1886
55:04
Xam Sam Réew Tv
Рет қаралды 36 М.
سورة البقرة كاملة, رقية للبيت, وعلاج للسحر | القارئ علاء عقل - Surah Al Baqarah
3:51:48