Ani wa coalition tok di khar Baye Mbaye. Manifestez vous svp!!!
@assaneseck47664 жыл бұрын
جزاك اللة خير وزادك علما ورزقا واسعا
@BAMBISTETV4 жыл бұрын
Magui ni
@oumardiawseck45944 жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne Mbaye Gueye Syll,niom yen wakh yi laniou wara bayi,Serigne Touba Amoul none koukoy wouteul none yay nonam,ndakh kiu bokoul ci yonou Mouride tamit bok ci wenen yon wala nga bania bok fen ta doula tere don dioulit bou wer ndakh ken dou doug ci bir bamel ba Borom bi Yallah ladj la ban tarikha nga bokon,Serigne Touba mom boudouwon nitou Yallah sakh douko tere don mbokoum Senegal yeup ba takh nieup am ci mom thiofel,wayaniou eupeul niou diegui dayo yikoy mboubo ak diko wouyo di wakh,wakh you ken xamoul foumou tegou ta dara douci deug nioniou la historiens yi di amal probleme .Dieukeu Gamou ak Moudia Gamou amoul solo ndakh Gamou 3 siecles apres Yonent bi laniou ko tambale deef ta fi ba Adouna di touki daniou koy deef,Xam na ni Bayre Magal ci Senegal kouko xeuthio ak Serigne Touba dinga niak,waya Bayrep Gambou ci Senegal tamit kouko xeuthio ak El Hadj Malick Sy ci Senegal dinga niak inchallah ,wassalam,Merci Syll..
@xudamulxadimxeexakwakhaabi35654 жыл бұрын
*Machallah ♥️♥️ Serigne Mbaye Gueye syll lii rafétna, Mame mor Mbaye tamitt deysaan ku amouk taalubé la ta diokh thieur mag gni*
@Buna584 жыл бұрын
Jërëjëfëti, Seriñ bi. Fi nga nekk foofu la. Na nuy tek Seriñ bi ci Xam Xam ndax musu koo wacc
@aboridial34314 жыл бұрын
Lí rafetna WAY SERIGN bí rek Mofi nek Yalla na Diam yag
@oumarthiam5634 жыл бұрын
Dieureudieufaty lii moy am solo lepp ak défarr la diourr lepp santala mame mor mbayitt defna lico warr
@actualiteevenement23074 жыл бұрын
Machala diérédiéf bay mbaye gueye syll. Vraiment tu es un bibliothèque. Il faut accompagné les jeunes comme mam mor mbaye. Mom tamite kou oyofla ta nagou kiliftéf
@papatine67394 жыл бұрын
Machallah li moy senegal,jamm rek.dieureudieuf serigne touba
@bassgueye44364 жыл бұрын
MACHALLAH...GUEYE SYLL..WE MOUROUDI ALLAH..kounek hamnani danio heur ...mais aussi kouy dignan..dignan ba fawww...faut pas inventer ni falsifier...faux pas donner la chance ...jammono waratek xewii na...Faut aller dans les sources les archives comme Ce Grand Monsieur a l habitude de le faire...La comunaute Mouride ...vous remercie infinement...DOYEN.
@baydidiallo28084 жыл бұрын
bien di wakhe DEUG
@cheikhahmadoubambayakhined14182 жыл бұрын
Machalha Cheikh bi ya ngui leuguëyeul yalla dhé .. Diadieuf Fassalé.
Segne Gueye tu es un grand connaisseur et savant du mouridiisme. Mais il faut te réconcilier avec ton frère Cheikh Oumar Diagne pour l'unité de l'islam qui est combattu par les occidentaux.
@mouhamadoufalilouniang11974 жыл бұрын
Jaajëf Syll, ku xamul dafa wara jànggi wala mu nòppi
@zorroantiquairecapskirring78794 жыл бұрын
Merci beaucoup modeste dieuredieuf baye mbaye syll
@daoudambaye99894 жыл бұрын
Ma challa..
@falloufaye1344 жыл бұрын
Mame More Mbaye il faut mou nopi nak car amoute bene kham kham wakh rek layyy def di reuyy lamagne khamoulene darra donc il n’a cas se taire akh merci pour ces éclaircissements lairena lol Yonu Serigne Touba kham kham mokooo lalll mais pas guiss lene ma
@ndiakhassndiakhass58854 жыл бұрын
Nopi moom mounoul am wakhdji Kay Moy na yem si loumou kham te geuneu khooteul geusstou bi
@beugalahira50874 жыл бұрын
Pr lan Mouy nopi mom kay conseiller ko mou xolate ay kaadom rk
@sagnsesenegalaise45754 жыл бұрын
Ndeysan sunu mame mbaye gueye Syll aka beugue Serigne touba yalla nala Serigne bi taxawoul bopam
@senegalsamareew43484 жыл бұрын
B.mbaye yalla ngafi yage
@cheikhfallseye66694 жыл бұрын
Machallah bay
@youssouphaseck60374 жыл бұрын
1884 LA SERIGNE TOUBA TAMBALI GAMOU .DIEUREDIEUF YALLA SA BOROM FAYAL GÑIOU LA .BÈGUE NA LOL WAKHAL MAME BAMBA DEUG LA BEUGEU.
@cheikhka1154 жыл бұрын
Machalla diradif diradif
@amadou35914 жыл бұрын
Li moye yone koufi wakh loudoule deugue gnou tékk la si yone😍😍
@serignesaliousamb96434 жыл бұрын
Mashallah jajeufety serigne touba lep mom leu walahi
@mouhamadoufadilniang4 жыл бұрын
Serigne mbaye Gueye Sylla soldaro bourom daroul mhoty jerejefety ya woyof ta bakh ta sella
@daoudagueye62554 жыл бұрын
Diareudief syll limo werr
@assanemar53534 жыл бұрын
Machalla rafet nA trop am na solo aussi
@modouloum71154 жыл бұрын
Vraiment je suis content
@mameibrahimafall76564 жыл бұрын
Machallah
@ababacarsignane84704 жыл бұрын
Merci beaucoup
@mamecissedieng26074 жыл бұрын
Machalah serigne mbaye Gueye sylla
@bassirousy76114 жыл бұрын
Ma challa
@radioradiotelevisionbawalm70594 жыл бұрын
Ku diara nianal brome Xam Xam la
@serignebadianeditkhadime59634 жыл бұрын
Hakaza dieredieufati serigne Mbaye goudou fan wergouyaram barke cheikhna khadim
@ismasow22784 жыл бұрын
C'est vrai un combat idéologique repose sur la connaissance
@khadimndoye89214 жыл бұрын
Maachallah Nieuppa Sara DIOUBOO
@SERIGNECHEIKHMBACKE4 жыл бұрын
ZIAR BOU BAKH YALNA DIAMOU SAKH CI REWMI
@serigneadj17794 жыл бұрын
Dieuredieuf Déle défar rék tha kaw tha kanaan 🙏🏿
@kman-974 жыл бұрын
Bay sylla je te suivre presk un ans mei tay gua meuseu def louma rafet louwoul pour man yen gnar gneup ayy talibe guen tei entr talibe internet amousi yon sa domla sa rakla woko si souf guen waxtan ndax yow tmt feke wosi dra archive national rek guey toxale dignou andil tai lafa nek yeup nonou serigne touba yi gnoko fa bind gua bayi si xeel
@paped51804 жыл бұрын
Mame mor dayi woute khaliss rek
@abdoulayegueye49313 жыл бұрын
Merci
@mordiop56964 жыл бұрын
Macha allah baye mbaye
@cheikhcisse74064 жыл бұрын
machalla tayde kontanna lole diere diaf s mbaye gueue sylla ak s mame mor mbaye nireke la
@codediaw42384 жыл бұрын
Dieur dieuf baye mbaye gueye sill
@momo_ceepgy27754 жыл бұрын
Mame mor mbaye ku bakhla ta talibe la waye da wara bayi di wakh da wara diangi ba nopi waye doyna war lepou kene manouko wakh
@modoundiaye33904 жыл бұрын
Dieureu dieuf baye mbaye rafétna
@Lopios-g6l4 жыл бұрын
Waw goor baye mbaye niguadéfe nonoula machalla...
@bayfalllabeuguedonne67564 жыл бұрын
Serigne mbaye Geuye sylla yaw yaye kan bani dowo mam mor mbaye
@Gueye77904 жыл бұрын
Machalla baye Mbaye gaye Syll nala yalla samb ta aarr la
@mbayethiam45954 жыл бұрын
AMINE😭😭😭❤❤❤
@daoudagueye62554 жыл бұрын
Diareudief syll nala yala May fan wou good andak werr
@ibrahimafaye18064 жыл бұрын
Bilay li rek serigne touba beug Machalla
@ndiagalo62074 жыл бұрын
Machalla reftna
@sidindiaye93564 жыл бұрын
Wér na dei
@galaxiepro.56414 жыл бұрын
ce vieux a raison il a la source du savoir et faut le reconnaitre vraiment
@thiernodiop63074 жыл бұрын
Ziare Brouwer
@diagnesoma36894 жыл бұрын
Rafet na Mouride ni rek lay meuna mel,yen yena gnouy bégal thi Serigne Touba
@oumardiouf15854 жыл бұрын
Djaa djeuff rafetna maa chaa alla bayy mbaye sylla begue brom darou al moukhty sama yakar oumar depuis brasil
@seckmor63164 жыл бұрын
Djieredjief s mbaye ni reck la yaw lobakh reck mola ñor.serigne bi reck
@fazaniangthanksyou7514 жыл бұрын
Dieuredieuf Mbaye sylle
@wakeupafrica99064 жыл бұрын
Waw Goor li rekk la déh... Deuggeul Dioubbëul rek.
@ousseynouthiam67094 жыл бұрын
Merci mon père
@marraka024 жыл бұрын
جزيتم خيرا وكفيتم شرا
@ablayendiaye83154 жыл бұрын
Machalah amna solo
@ndirsope1234 жыл бұрын
Mashaallah suis très content de toi 🙏🙏🙏
@ahmacisse20364 жыл бұрын
Baay Gueye waxal thi Macron waay😪😪🤕
@abdoukhadretop2554 жыл бұрын
Macha Allah diame rek gay ame incha Allah
@mouhamadoumakhtarndiaye89012 жыл бұрын
جرجف شرج بى كى صل بارك الله فيكم
@niassousseynou5074 жыл бұрын
Dieuredieuf serigne mbaye Gueye mourit bi 🙏♥️🙏
@serignegueye46024 жыл бұрын
Merci wayé 👍👍
@ibrahimacissedieureudieufs27324 жыл бұрын
C'est vrai mais ne faut pas te limiter seulement aux archives tenez aussi en compte ce que les proches et compagnons de Serigne Touba ont raconté merci
@adamadiop55214 жыл бұрын
Mor Mbaye dou nopi
@ibrahimagueye96554 жыл бұрын
Mashallah
@niangbakheyaye3694 жыл бұрын
Grazie mille baye mbaye 💓💓
@oumarthiam5634 жыл бұрын
Leerna réfétna merci
@pdiallo10294 жыл бұрын
Merci Père . Vos sources sont plus crédible
@iboulayewade11294 жыл бұрын
Vraimen credible
@diawfalfaraa59974 жыл бұрын
Pour man nak diarouko woon baye mbaye woko walla mu woola parce que beut bu rousoul tothie
@morkane89364 жыл бұрын
machalla
@niassousseynou5074 жыл бұрын
Machallah mbaye Gueye amatina solo méré wne nala lolo
@mouminydiouara93894 жыл бұрын
Machalla lépe rafétna
@amadoumoustaphambaye70874 жыл бұрын
Jajeufati yaram ziaranala bou were
@modoundiaye33904 жыл бұрын
Yagfi tawèr lool baye mbaye
@khadimgueye71664 жыл бұрын
Alhamdoulillah Dieu est grand
@leprincedescoeurs50054 жыл бұрын
Serigne touba guèdj la, nakou nèk roott dou diekh, kone na radète ndakh mom da rafètale ba fattou. Borom touba kene dou mom