Al Hakim magui lay siyar Done léral tabiha nariyou yi yep nio bok couleur mouy rouge ❤❤❤yalla n'a yala barkel xamxam bi
@ModouDia-m2t4 ай бұрын
Machallah xam xam bi leer na li nga wax si sagittaire mom deug leu guiss naa si sama bopou mais je pense que jour Jeudi mooy sén Jour parce que Mouchtaara léy andal
@babacarcisse38254 ай бұрын
Oui jeudi la
@serignediokhane104 ай бұрын
Machahala Yalla nala yala Fayye🙏🙏🙏🙏🙏
@moustaphaseck90374 ай бұрын
Machalla amna solo lool ❤❤❤❤❤❤
@sodaamar-yo6wm4 ай бұрын
Machallah
@MariemeCamara-t8v4 ай бұрын
Machallah serigne bi merci
@malickdiallo95002 ай бұрын
verite absolue
@BassirouSy-qj3pk4 ай бұрын
Ma chalah diarobi fongeka mana ame
@babacarcisse38254 ай бұрын
Bague zircon
@Ousseynoukaa4 ай бұрын
Serign bi, erreur yi c'est tres grave, c'est dangereux, ndax erreur yii ngay def meun na teuth weurseugou nitt ki. Afférou bidéw dafa graw, donc déélén nafar bala ngénn di diangalé. Wala bou laadié diangui wate, nagnko déf, sinon vs allez induire beaucoup de personnes en erreurs, té erreur yii meun na teuth weurseugou nitt
@SerignesaliouNiang-o2y19 күн бұрын
Aussi sén jourou sarakh jeudi leu pain sucre ndawal thiébou yap bou khonk éct...
@Ousseynoukaa4 ай бұрын
Effectivement, Sagittaire moy : moustara Le jour cest jeudi Tabi'a naariyou (feu)
@bakhidiop790718 күн бұрын
J'su tombé plusieurs fois sur cette vidéo par hasard mais à chaque fois meu lire les commentaires jme décourage du coup je termine pas la vidéo, tay mani xaral meu deglou ko com ça meu am sma avis bopp mais ndéké waaji deugeuntane il maîtrise vraiment pas le sujet dh,déjà neneu jour sagittaire goor vendredi leu c faux,mouni sunu couleur rose leu c archi faux aussi yen à d'autres yimou wax ki sont faux aussi mais niaar yi lassi geuneu japp !!!
@SerignNdiaye-en9dw3 ай бұрын
❤❤❤❤
@sodaamar-yo6wm4 ай бұрын
Le jour c'est jeudi
@salymatandiaye27954 ай бұрын
Kii khamoul Dara ci limouy wokh, il s’est trompé sur les jours des signes. En plus sagittaire couleur bi marron leu (exemple macky Sall sagittaire ) jourou sagittaire jeudi leu. Serigne bi demeul diangui beu xamxam bi beune. Vous risquez d’induire des gens en erreur