macahlla seydi el hadji malicke sy suna rek la donn ndondou ❤️❤️sy malicke
@adammbodj16413 жыл бұрын
Le titre est erroné. Il fallait écrire que Maodo Malick l'avait déjà dit.
@weetalyallah6173 жыл бұрын
le titre n'est pas erroné parce que les dits de Mame Maodo viennent appuyer ceux de Dr Ahmad Lo
@papeba17333 жыл бұрын
@@weetalyallah617 DEUGG PIIRE NGA WAAXXE MBÔÔK MI !
@beugdiam55033 жыл бұрын
Le titre est bien erroné car c'est Mame Maodo qui l'a dit en premier. Donc De Ahmad n'a fait que répété ce qu'avait déjà dit Maodo RTA
@دفراتسنغال3 жыл бұрын
@@weetalyallah617 ce qui vient après qui appuie ou confirme wala ?
@isocra-ktm40993 жыл бұрын
@@weetalyallah617 Ok légui loleini wakh maodo mom tamit ahlou bidah la
@abdouazizdabakhgueye63823 жыл бұрын
Ibadou deh kén manouko guéné thi diné dji. Mais tarikha cheikh aussi kén manouko guené thi diné dji.
@mouhameddiop53383 жыл бұрын
L' erreur monumentale de lô c'est le titre de son ouvrage il a mis tous les soufis dans le même sac Mame Maodo un soufis par excellence, avait tous dénoncé
@masiba72723 жыл бұрын
C'est faux ragalal yalla il n'a jamais mis les Soufis dans un même sac.ecoutes bien la vidéo si c'est pas clair dans ta tête,va chercher le livre tahdissoul ashass et essayes de comprendre. Ahmad lo n'a fait que amener ce que beaucoup de savants Soufis ont déjà dit et écrit dans leurs livres. Ça c'est le soufisme pratiquer le wahdatoul Oudioud. Ahmad lo tognoul ken. Le Soufi qui ne le pratique pas n'est pas concerné.
@masiba72723 жыл бұрын
Mais dire que Docteur Ahmad lo à insulté les kilifa dîné du Sénégal c'est de la malhonnêteté intellectuelle confirmée. Car li sa Serigne wax, c'est la même chose que ce que Ahmad lo à dit,sinon plus grave. Es ce à dire que sa Serigne daffa saga bopam ?la réponse est non!il n'a fait que étaler ce que les grands Soufis font et y croient, c'est le wahdatoul Oudioud. Bayi len togne!
@cheikhtidianethiam91973 жыл бұрын
c pas faux monsieur . ce lo quand il faisait son synthse il a clairemnt dit : a toi qui a lu mon oeuvre si tu etais ds le tarikha tidiane precipites toi de le quiter et de laver tn coeur avec la foi reverencielle . Il dit d une maniere tres claire que les tidiane n'ont pas cette foi. ki kou bne leu te sokhor
@masiba72723 жыл бұрын
@@cheikhtidianethiam9197 merci pour la contribution et je respecte votre entêtement.maintenant je voudrais en toute sincérité que vous me donniez le lien de la vidéo ou de l'audio de cette synthèse dont vous parler et je blamerais docteur Ahmad lo pour cette idée qui ne lui ressemble pas. L'extrait pour lequel les gens mal intentionnés le mettent en mal avec avec wa bida AK wa chirk,est déjà dit avant lui,et en plus dure ,par Elhadji Malick Sy dans son kifayatoul raghibine page 90. Donc sou fekee lolou mo takh tu dis que kou bonne la,donc fait de même pour sa Serigne. N'oubliez pas de m'amener ce que je vous demande. Cordialement !
@djibidiallo50933 жыл бұрын
Bilahi kou wedi xolal mame dabakh bala wax mame maodo tjs ne yalla ak yonentibi
Tilmissaani, limou wax amoul kenn kouko amal preuve loudoul ay khista yougn nétali ta binde n'a ap tëré bouy wéddi wax jign ko sossal
@habibseye55313 жыл бұрын
Wahabite yi bayyi leen fenn
@masiba72723 жыл бұрын
Demal si teree Elhadji Malick Sy "kifayatoul raghibine page 90" après tu viens débattre avec moi.
@habibseye55313 жыл бұрын
@@masiba7272 lolou dang sé yeexa jott seugn bi, nioune kifaya dagn niou thi nampal motax niou teela Moss chariat avant tout, bi wahabite yi di jangui wéranté bobu wa tassawouf gni ngui si nignouy def ba gnongnal seen diiné Thi kifaya bi la déparé batax mani, wahabite yi indi nagn preuve bouy wané ni tassawouf jotté woul dara akk wahdatoul woujoud, wayé batay indi wougnou preuve boy wané ni tilmissani dafa gueumoon wahdatoul woujoud loudoul khista bougn ni ibn taymiya moko nétali( lolou day mell ni ma togn la ba nopi ni kay niou dem thi sa noon mou atté niou). Ba ngueen amoulé preuve bou palpable ngueen waroon nopi, Wayé maodo tontou naleen bou yagg thi kifaya pour wann leen ni li ngueen di toumal wa tassawouf laalé woul ak tassawouf et que kepp koukoy def bokkou lo thi tassawouf, wayé douleen taxa bayyi ndax wahabite bou wa tassawouf di xeex contre jikko you bonn yi( franc-maçonnerie, homo...)gnom gnou ngui xool nignouy def pour dévier leen thia loola, motax financement yi gnou leen di toumal kenn meunouko wéddi
@habibseye55313 жыл бұрын
@@masiba7272 li gueuneu doyy waar thi wahabite yi mooy dagnouy wané nii gnom dagno sett thi bakkar ak ndeungué aki niawteef( malaka daal lagnouy diémeu incarné) ba néna amatougn lenn lougnou meuneu sikkal seen bopp loudoul gnénéne gnignou bokkaloul pass pass, té kou weet rek thi sa roukk dingua xamni yalla kou bari soutoura la. Fii gnom rek nguay degg gnou démm thi ap diakka fekk fa gnou gnou bokkaloul pass pass gnouy diouli, gnou bombarder leen ay bombe ba nopi naane dougnou ay dioulit mélni gnom gno oubi seen xol yi ba xam lithi nekk. Kou took di relaté sikk wahabite yi rek do am ngounou waxou malak keur. Demm leen diamou ji yalla, toumal ak di sossal nit ak diko collé motif taxoul ngueen doon ay dioulit taxoul ngueen am yiw, aux contraire dafleen di tardél thi jaamou yalla ak dileen joureul bakkar you amoul app, té amana bo xoloon thi sa bopp rek dingua xamni ap ndeungué thi yaw la commencé thi la yam, yaw mikoy guiss thi kénène
@mouhamadouseck28263 жыл бұрын
@@habibseye5531 machaalah tu as tout dit tres bonne replique ñi amouñu xam xam beuri wakh
@issabarry84283 жыл бұрын
Machalla ❤❤🕋
@awayacinesylla3 жыл бұрын
Il faut accepter de se débattre
@cheikhdieng563 жыл бұрын
Qu'est ce que c'est que ce titre c'est une mal intention ou une erreur comment maodo rta pourrait confirmer lo qui n'est même pas petit fils de maodo Bi maodo di bindeu bayou lo sakh dafa diouddou et c'est quand vous arrange que vous citez maodo cette imbicilite c'est quoi
@foutaba42313 жыл бұрын
Mawdo confirm le prophète pourquoi pas Docteur Ahmed meunoul wakh ci bid Mawdo yalla nañiouko yalla fayal
@Cheikh-thicky3 жыл бұрын
Bayou Maodo sakh Ahmad Lo moka eupp xam xam
@zakirinatv85023 жыл бұрын
@@foutaba4231 الناس كلهم عيال الله وعظيموهم حرمتهم لله
@masiba72723 жыл бұрын
Yaw bouniou sonnal.des gens comme vous vous êtes des poisons. Avez vous écouté la vidéo ? Demal si sa bidoum seeigne dinga fa fek li Ahmad lo wah. Deguendi deglou ba paré Di soga wah. C'est ça le mal du sénégalais degue tel né damna.
@mouhamadouseck28263 жыл бұрын
@@Cheikh-thicky 😂😂yaw mom dof bouy wakh nga kéne doula tontou, lolou yaako sagna wakh mais sa serigne Ahmed lo douko meusseu wakh, yaw nak danga simbéku mo takh😂😂
@masiba72723 жыл бұрын
Kone hana Elhadji Malick dafa saga MAGOU dîné Sénégal ba saga bopam ?
@aliudiao91443 жыл бұрын
Soulen bayiwoul macgnou bakh gni delouwoulen guinawe bakhna loulen sof molen di dal
@diatarathierno73713 жыл бұрын
Serigne bi yaw kay khamngani bou fekkenewone tidiani yi ngeume na nio lolu konte seyidil hadji Malik sy rdh douco denoncier
@aliudiao91443 жыл бұрын
Ah legui yenangui geustou mame maodo di werou si bindeum pour deugeureul doctor lo jajaja yene gnou doywar nguen bayilen macgnou bakh gni gni dagnou dioubo ak sen borom thi ragal yala
@ousjoop87803 жыл бұрын
Elhadj Malick est un soufi qui critiquent ceux qui ne suivent pas la sounah du Prophète... Très loin de quelqu'un qui dit que le soufisme lui même est hors sounah du Prophète.... Sunu Magg you bakh yi wakh negnou lep ba paré... Ahmad Lo toubal Baalou magg gni
@masiba72723 жыл бұрын
Mais yen dounguene bayi togne guir yalla! Ou dans le livre tahdissoul ashass si vous l'avez lu bien sûr, Ahmad lo dit que les Soufis son hors sona ? Va voir dans le livre de Elhadji Malick Sy kifayatoul raghibine page 90. Il Dit exactement sinon plus "grave" que ce que Ahmad lo à cité de tilimssani.
@mouhamadouseck28263 жыл бұрын
@@masiba7272thiéy mussiba yaa ngui weur si commentaire yi rék 😂mais svp kifaya page 90 danio beug cité beuyite seydi hadji malick bi Pr yeugueul la aussi seydi hadji malick meussoul cité tilmissani il n'a indexé personne dafa wakh de manière générale mo xam nga nék soufianké wala lénéne wakhul jeumeuléko si béne parti dafa wakh guir limou constané si diné dji de manier générale
@babacarseck13793 жыл бұрын
Coran sounna point
@TheDogue53 жыл бұрын
Kou lokay diagual???
@syngariboundou23553 жыл бұрын
A lors pourquoi vous avez mi tous dans le mm sac bolènko lèrAllelèwone thii thiow dou ame
@latifsagna44613 жыл бұрын
Ils ont dit ceux qui croient aux paroles de Talimi Sani
@masiba72723 жыл бұрын
C'est faux !il n'a pas mis tous les soufianke dans le même sac.c'est archi faux. Avez-vous lu le livre tahdissoul ashass ? C'est les avocats du diable,qui tirent sur tout ce qui bouge,qui sont prêt à vendre père et mère,pour ternir l'image de docteur Ahmad lo qui ont amené toute cette polémique. Mais les savants du Sénégal, tidjianes, mourides ou autres,ne le feront pas car ils savent ce qui se passe réellement. Des gens malintentionnés ce sont levé,pour faire comprendre aux sénégalais qui n'ont pas le niveau escompté,que Docteur cheikhna Ahmad lo à insulter les kilifa dîné. C'est pas honnête pour un livre qui est publié depuis 1992.ils attendent 2021 pour en faire un problème.les précurseurs qui ont amené ce débat fétide,on ne les entend plus.ils rient tranquille dans leurs coins. Ils ont planifié,mais qu'ils sachent aussi que Allah est le plus grand planificateur.
@syngariboundou23553 жыл бұрын
@@masiba7272 c allumette lô le diable lène khamenako nittou yalla kouko saga safara nga dieum
@masiba72723 жыл бұрын
@@syngariboundou2355 mais soit pas partisan et raisonnes si tu en est capable.amenes moi un seul passage de tahdissoul ashass où il à insulter quelqu'un. Yaw la yalla dioh thiaby aldiana xana? Soit honnête et amenes moi ce passage.
@syngariboundou23553 жыл бұрын
@@masiba7272 j pas lu le livre mais gneupe meuniounio fène c pase possible mankay oute amagoumako
@ndaopape88523 жыл бұрын
Man deh ci serigne you nék di fi ci senekhal toukh, alors dagna wakh talibe yii bulen toukh, part ce que nioun ak bocougnu
@masiba72723 жыл бұрын
Neurmel ligueyou wa ahloul souna wal diama diaralnalen Lou nek.wayee li lerna. livre bi dou Ahmad lo moko binde Dee. Kane moko binde?tontou len ma guir yalla.
@amar22013 жыл бұрын
Dialè vouma si dara
@wakhdeugguetayallatakh81293 жыл бұрын
Dangay fenn dh wakhdatoul woudioud nekkoul ni dangay deff loula nekh ni daganna c p vrai Légui koy takka kouko xaram fan nguene ko gisse Ahmed lo dafay fenn
@masiba72723 жыл бұрын
L'âne Moy DEUG bi Tak kouko xaram niene si soufianke niokoy def. Demal si terré Elhadji Malick kifayatoul raghibine page 90 soufa nekoul nga soga wah Ahmad lo wahoul DEUG.
@isocra-ktm40993 жыл бұрын
Wakh lii tay dfké souba lolou rk lafi guiss
@TheDogue53 жыл бұрын
Comparaison n'est pas raison, votre interprétation est biaisée et sélective. Quelqu'un qui voit dieu partout et n'importe quand ne fera que respecter son créateur. Dès lors qu'on connaît lou yalla térée ak lou yalla daganale, comment on peut se permettre de dévier les écritures saintes?vous n'êtes pas logique dans votre analyse. Au contraire c'est ce niveau de conscience spirituelle qui leur permet de former d'autres muslim qui n'ont pas encore acquis ce degré de compréhension. Nos érudits comme elh malick ra n'ont fait que perpétué le règne de l'islam dans une zone colonisée par l'Occident qui voulait coûte que coûte christianiser toute l'Afrique. Donc je dirai que ces derniers ont fait du bon travail dans la mesure ou ils ont réussi à contrer ces conquérants par la grâce de dieu. El malick n'a rien confirmé au contraire il vous conseille d'œuvrer pour la paix et d'éviter les conflits entre muslim car cela ne fera que affaiblir la ouma.
@isotv42193 жыл бұрын
Mdr
@TheDogue53 жыл бұрын
@@isotv4219 pourquoi tu rigoles ???
@isotv42193 жыл бұрын
@@TheDogue5 je rigole ta dernière. Tu leur demandes d'œuvrer pour la paix et ils sont dans ça.Ils sont les plus paisibles dans ce pays.Mêmes dans les manifestations,tu ne les verras jamais.Recemment ils se sont rencontrés au grand-thêatre,Ô comme ils sont imbus de bons comportements !!Tu sais c'était quoi le thème en résumé :la paix!!!
@fatimadiop92263 жыл бұрын
Yaw guir yalla gueumele sa guem ga Bayi pass passou diamoul yi
@cheikhtidianeba20593 жыл бұрын
Pourquoi vous faites des amalgames....Dr lo n'a pas dit comme el hadj malick qui a constaté des faits dans le soufisme mais Dr lô a dit quelque chose qui n'existe dans aucun des écrit de Cheikh ibn arabi assahikh.... c'est le fait de mentir dans votre doctrine qui est contraire aux presceptes de l'islam
@adytv68183 жыл бұрын
صاحب هذه فيديو يخون أمانة العلم ويذبح نفسه بسلاح الكذب لماذ لم يوضح أن الشيخ علق في خاتمة هذا الكلام فهؤلاء الذين وضعوا هذه الطريقة وابتدعوها لا يعلمون شيئا من الشريعة والطريقة ولا يهتدون إلى الحقيقة لاماذا هذا التدليس
@isocra-ktm40993 жыл бұрын
C clair
@masiba72723 жыл бұрын
Primo mentir n'est pas la doctrine de wa ahloul souna wal diama. Secondo sou fekee daniouy wah té yalla tax fenal yalla ak yonentem si tidjianiya la fek bah. Je t'attends pour ma leral la fen yoyou.
@isocra-ktm40993 жыл бұрын
@@masiba7272 j'attends que ça wakhma yane feine guay wakh nonou
@mouhamadouseck28263 жыл бұрын
@@masiba7272 vrais musiba nga yaw😂 seydina cheikh Ahmad tidjani nééna léep loléne dégg ni maa ko wakh té deuppoowul souna ak charia xam léne ni dou samay wakh donc fékhéél baa loy waxal seydina cheikh nanko xam, nakh yéene wahabite féne ak fénele nite daléena yombe 😂