Yiy sabab Xol bu Sett: - Bari ak Tub ( Dellu si Yalla) - Baril ay djégalou ( Istikhfaar) - Djouk goudi dioulli donté niari rakka - Baril loy djoulli si Yonéntébi (saws) - Djank Alkhouran ak diko sétantal - Baril ay sikar ak touddou yalla
@ndiayemoussa97964 жыл бұрын
Daaray Serigne Bassirou Mbacké Khelcom folén nékon bok namouna lén