Très très fière d'être Tidiane. El Hadj malick n'a pas d'égal.
@fatouniang17483 жыл бұрын
11¹¹1¹p13 œyl7pjky
@madjiguenegueye21353 жыл бұрын
Aa
@sarahsarah268320 күн бұрын
Qui est là en 2025 yalla gneup ame ate bou nékh ❤
@lafindutemps61417 күн бұрын
Amine inchallah
@MouhamedMouhtadaGAYE-hy5fc Жыл бұрын
Yalna yalla barkel te fayall niou seydi hadj Malick
@daoudasow-ch9vy Жыл бұрын
Macallah merci beaucoup Abdul Aziz
@AssuranceakfFall2 күн бұрын
Dieureuguéne dieuf,Maodo rekk ba aldiana
@fadlougay40693 жыл бұрын
Je suis mourid mai mam modo manna way lol limi wakh nékhna lol إني فقير ومسكين إلى آخرها ماأجمل هذه القصيدة في فنن التوحيد. ياسيد الحاج مالك سه جزاك الله خير هذه القصيدة تهتز قلب السليم والله سأسمع كل يوم هذ البرنامج عبد العزيز امبي مع حزبه كلها نسأل الله أن يجعلكم خير وأ ن يطول الله عمركم أناأفرح جدا فرح الله بكم ببركة سيد. الحاج مالك سه
@malikiatvtivaouane3 жыл бұрын
Mashalla
@ndeyefaye77833 жыл бұрын
Machallah limou woy mo nekh té daw yaram
@deffaly90563 жыл бұрын
Masha Allah Yallah nala Yallah faye sa khole sèdè bi rafetna 🤲💓💕💗❤
@tackosy18983 жыл бұрын
Choukouran
@fatoudiouf8822 жыл бұрын
Mais serigne touba ak mame maodo bénn lagnouuu
@fatoukane1106Ай бұрын
Machaallah. Yalla na yalla same len. Seydi El Hadj Malick Sy, une fierté
@abdouazizdiop98772 жыл бұрын
💯 %mouride mais li dafa nekh bilahiii yalla na yalla may goude fan
@malickseck94246 ай бұрын
En tous cas khawma kane wayé Borombi khamal nama secrets bou reuy si khassida "Ya kaachifa D'a " ,je l'écoutais durant l'hiver 2021 coïncidant au Mawlid virtuel du au covid19 avec beaucoup de difficultés et de peine pour s'en sortir ici en Europe, dans un restaurant en faisant de petits boulots en noirs 😢😢, à la sortie de ce mois béni, Dieu à résolu tout mon souhait...(Qu'Allah l'agrée Cheikhal Hadji Malick et sa noble famille, ainsi que la famille de Moussé Alé Mbaye bidiakhi Taaha Yaçina Aleyhi Salam)
@mbayediouf13493 ай бұрын
... Fcv 😢Cft😢😢5😢
@maguettediagne3585Ай бұрын
Machallah ❤️😍😍Y’a Kachifa Da iii Dafa yemé dehhhh Mane mome beneu seutou Seydil Hadji Malick moomako done tekiillll un jour😍❤️
@malickseck9424Ай бұрын
@@maguettediagne3585 Surtout bo khamé gorgui limou siy niane 🤔adouna ak lissi biram mongui si ...Yalnaniouko Borombi woutou fayal niouko Incha Allah
@AmynaNabySarr-bouDabakh3 жыл бұрын
Ya Kachifa Da ii 😭sama meilleure Khassida 💓🤲🏾
@malikiatvtivaouane3 жыл бұрын
Mashalla 🙏🙏
@ahmedndiaye81313 жыл бұрын
Dafa yèmè
@papediakhate9303 жыл бұрын
Seder nako c la deuxième fois ngay commentaire si khassida bi
@mansoursybarry39472 жыл бұрын
Sokhna Amina mou bakh miii
@AmynaNabySarr-bouDabakh Жыл бұрын
@@papediakhate930 ndeyesane deugleu 🙏🏾❤️
@diaogo88243 жыл бұрын
Barkep Serigne TOUBA li ap yéfar szkh bouko dégueloo warna toyal kholam Machallah
@malikiatvtivaouane3 жыл бұрын
Dieureudieuf
@cheikhcheikh89702 жыл бұрын
Yaw sokharo, yalnala Yala faye thi sa wakh bourafete bi, thi barke sa serigne Mame Cheikh Ahmadou Bamba Mbacke ak barke sama serigne Mame Seydi El Hadji Malick Sy radiyalahou tahalaa anhoumaa
@djibydieng70562 жыл бұрын
Di ngène ma rayy rekk té sama heure diotagoul😭😭😭heure boumakoy deglou je n'arrive plus à retenir mes larmes😭😭 yalla naniou yalla fayall souniou Mame Cheikh Seydi El Hadji Malick Sy
@coumbafall15052 жыл бұрын
Pareille comme moi.
@malickdieng3628 Жыл бұрын
Dafa nekh si xol mais doundeul lou bari
@BintouGueye-nd2yr6 ай бұрын
So khamé signification bilay gueneu nékh
@NdeyeYacineNdiaye-pr5dl6 ай бұрын
Amine ❤❤❤❤
@khgtuihhu6 ай бұрын
Allahouma Amine barké Yonente bi sala lahou alayhi wa Salam.
@abdoulayefall63893 жыл бұрын
Alhamdoulilah bima boké si djaboot seydil Elhadji malick sy RTA🥰🥰🥰🥰😭😭😭😭
@malikiatvtivaouane3 жыл бұрын
Alhamdoulilah machalla 🙏
@laminedieye24223 жыл бұрын
Bilay yak kanne
@laminedieye24223 жыл бұрын
Dieureudieuf mame maodo et merci malikiatv. Si kaw si kaname
@vieuxsarrbadiane21083 жыл бұрын
Mane yaw ak kane😍😍
@MatyDiop-vf2fg5 ай бұрын
13:06
@cheikhmomodiame92073 жыл бұрын
Keen dou Maodo wayé Abdou Azize Mbaye dara nga machallah 🖤💫🖤
@badaracss48053 жыл бұрын
Thiey yalla bi mom moy sama khasida prefere si xol lay dougou bilay mbaye yalla ga goudou fan❤🤩
@benzdgnarr19 күн бұрын
Qui est la li nekh na way oh 🥺😍 abdou Aziz mbaye yalla yalla faye la goudal say fann❤
@syllepogba17433 жыл бұрын
Machalla Abdou Aziz mbaye yalna sa diam yage barki serigne saliou
@malikiatvtivaouane3 жыл бұрын
Allahumma Amine
@diopidy5093 Жыл бұрын
Maodo bindeu neu louné, Abdul aziz mbaye wayééko nouné! MashaAllah
Ini fakiroun wa miskinoun wa moun kassirou.......❤❤❤❤
@abdoulayendoye87902 жыл бұрын
Ah dayo bimou am sou démé bay wah li kémane leu😪
@thiabadieng83633 жыл бұрын
La lumière du prophète psl est le source de nos lumières ❤️❤️❤️❤️❤️ mame Moado yaniou khamal yonénti bi ❤️❤️
@malikiatvtivaouane3 жыл бұрын
mashalla
@kinetaam33222 жыл бұрын
Je lol ini
@aissataball99622 жыл бұрын
Bilahi moado mon niou khamal yonénti bi (psl)
@diamilseye42002 жыл бұрын
Bilahi moniou ko hamal
@alimarassoul90902 жыл бұрын
Walahiii
@papathiernondao66982 жыл бұрын
ndeysane mouride bou mak Abdoul Aziz mbaye Daf may doundale
@ndeyefatoukane47712 жыл бұрын
J'aime tellement cette chanson que parfois quand quand je l'écoute j'ai j'ai le cœur qui bat comme s'il y avait quelque chose comme si j'avais perdu quelqu'un cette chanson est vraiment vraiment très belle je vous le jure
Machalah, yal na Yàlla may léen wér ak wérle ci barke Seydinaa Mohamad SWS.
@xalifanaattiijaany75602 жыл бұрын
Tout ce qui vient du coeur va droit au cœur MACHA'ALLAH
@kayalebaobab39643 жыл бұрын
Ya allah fayal gnou seydi Elhadj Malick sy
@mamytall69362 жыл бұрын
yalna nalénn yalla faye si serigne babacar sy niou wakh amine
@omsarr023 жыл бұрын
Ameeen pour les prieres qui sont dans ce Qassida
@ndeyefatoudiop948 Жыл бұрын
Begte bou amou app yalna maylen wer ak fan wou goude lool
@awasamb42112 жыл бұрын
J suis yaye fall mais j'aime bien ce tahissire machalla ♥️🙏🙏🙏🇸🇳🤗🤗🤗🙏♥️♥️♥️♥️♥️♥️
@tallaniang31983 жыл бұрын
Bilahi abdou aziz mbaye goudal fane ak weer... euleuk do rouss si kanamou maodo bilahi...yaw abaibe sarr ibou sakho kéne amoul sène fay yalla nalène yalla fay si barké szeydina mouhamed psl
@mamedieniang2713 жыл бұрын
Ay way abou mbaye temps yi nigay sédalé sama hol bi yalnako yalah faye thi barké seydina mouhamed psl🙏
@malikiatvtivaouane3 жыл бұрын
Allahumma Amine 🙏
@omarsene12153 жыл бұрын
Kholl seddana Billahy
@deffaly9056 Жыл бұрын
Amine ya Rabbi ❤❤🙏🤲
@biranendiaye17913 жыл бұрын
Qualité Son et image c'est Top Mashallah Malikiatv Yalla na Yalla bollé ci tele you mak yi nguene niou yagg beggueul ci Salalahou Aleyhi Wa Salam❤
🥰🥰🥰😍😍😍😍😍😍😍😍😭😭😭😭😭😭😭 li lanla tmt thi nékh nékh diadieuf sm wadji yalna yala barkél
@khadilaye4232 жыл бұрын
Bilakhi souma yalla dèfoul wonn talibè cheikh khawma sama dound loumouy donn dieureudieuf ya rabbi
@adamaniang47703 жыл бұрын
Machala baye abdou aziz mbaye yalla na yalla wereule bate bi thi barekep yonne sedal gua khol yi nékhe na loll thiey cheikh seydil hadji malick sy mo meuneu taga yonéne bilahi
@ramatoulayely69633 ай бұрын
Qui est la en 2024❤❤❤❤🎉
@choixdupeuple96683 жыл бұрын
Mame Maodo Rékk 🕋🕌❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@moustaphadiouf67492 жыл бұрын
Yalla nalèn yalla takhawou sam len guoudou fane were ak werlè yokou xam xam bi ak katane bi ❤️🙏🏽🕋
@assytoure Жыл бұрын
Amine
@amathdiallo35533 жыл бұрын
Nagnou sunu borom fayal Cheikh Seydil El hadji Malick 🙏🏼🙏🏼❤️
@khadymbengue44352 жыл бұрын
Amine ya rabi
@ayibeseye89912 жыл бұрын
Amine 🙏🙏
@hawakebe68192 жыл бұрын
0
@hawakebe68192 жыл бұрын
@@ayibeseye8991
@bongacamara69982 жыл бұрын
Amiiine ken dou moome waaay !!!!!
@papacamara91143 жыл бұрын
Malikiya TV assure gua dall si gamou gui machalla
@malikiatvtivaouane3 жыл бұрын
Dieureudieuf mashalla 🙏
@issagueye7663 жыл бұрын
Macha allah bouma ammé kénn lou may gné ci adouna moy gnii. Yalla na lénn yalla fay té yagallén fi. Grace à vous des gens comme moi commencent à maitriser les écrits Seydi Elhadji Malick Sy radiyallahou taanla anhou. Encore un grand merci à vous
@maimounaboiro88752 жыл бұрын
WALAHI NDEYSANE 😭❤️❤️
@ndeyefatoudiop9482 жыл бұрын
MAÀCHA ALLAA MBEEGUE CI YEEEENN
@aliounekonate Жыл бұрын
À part Dieu, son messager psl❤️et nos parents. Amatougnou lénéne loudoul Mame Maodo Malick Sy ❤️❤️rta
@BoussoFaye-e7u Жыл бұрын
Bilay ❤❤
@gueyealy35243 жыл бұрын
Salam je suis tidjane mais talibe baye niass wayé mane dama.beugue seydi el hadji malick sy billahi adouna sunu xamone kane moy mame moado waleu mou wanone gnou boppam senegal keneu dou fittou wote billahi mako wah té fou laire lako.teck nak
@fatimsow58702 жыл бұрын
Djeureudjef, ya niak kignane yalna Yallah feyla s khol ci barkei Mame Baye Niass
@gueyealy35242 жыл бұрын
@@fatimsow5870 allahouma Amine lothi khamou keur Mame Abdou Aziz Sy fi thi Dakar la diangué Mouy doundou makoy Guisse môme Mame Abdou Aziz Sy
@kiimiitalibecheikh72213 жыл бұрын
Wallay Ndeysan Yalnaniou Yalla Fayal Cheikh Seydil Hadji Malick❤🇸🇳Wayé kene dou Abdoul Aziz Mbaye ak Sidy Ahmed Mbaye❤🙏👑Yalnalenfi Yalla Bayi Niou Yague Diniou Bégal❤🇸🇳
@oumardiagne97593 жыл бұрын
Mach Allah Pape dji Yana bour yalla wéral batte bi ti maye la wérre samala are la Ak mbolami djoulite Malikia thiakaw sa thiakanam incha Allah Bon Gamou Houma islamique Di gnane 🤲🤲 sunu Khalifa bi yaggue fi loleu té andak wérre
@mouhamedalaminendiaye81803 жыл бұрын
Machalla Malika TV khôl seed yalla na yalla faye si barcker seydina mouhamed saws ♥️♥️♥️♥️🇲🇷🇲🇷
@mounatouba9921 Жыл бұрын
Masha'Allah. Je ne sais pas vous mais ce Khassida transperce mon âme, et je ne peux retenir mes larmes. Yallah nagnou Yallah fayale mame Maodo. Amin yaa Rabbi....
@BoussoFaye-e7u Жыл бұрын
Amine inchallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@adjafatouthiaw2094 Жыл бұрын
SALAM même moi sama holl dey fess mashaALLAH Dieureudieuf Amine YA RABI pareillement inshaALLAH
@assa-sf1ll Жыл бұрын
pareillement wallahi ❤❤❤
@amendiaye9290 Жыл бұрын
Allahouma amine
@vieuxsarrbadiane21083 жыл бұрын
Longue vie à abdou aziz mbaye et à la famille moussé allé Mbaye
@malikiatvtivaouane3 жыл бұрын
Allahumma Amine 🙏
@KhadyFall-vc9jm4 ай бұрын
Je suis mouride machallah ❤ mais ya kachifa Da i non sa me fait pleurer tout le temps yalla na yalla fayal niou sounou mame you bakh yi inchallah machallah ❤❤❤❤
@ibrahimasenenabien12043 жыл бұрын
Malika & Asfiyahi yalna yalla barkèl tèlè bi yagal fi Khalifa bi ak Ndiabott gui yèp Abdou Aziz Mbaaye yalna yalla goudal fan wi yak famille Mame Moussa Ale Mbaaye gui yèp
@kylewalker3619 Жыл бұрын
Oh ndeysane el hadj abdou aziz mbaye yalna yalla wereul batt bi ak kep kouy tag katou yoneneti bi
@siraba39942 жыл бұрын
Ma cha allah khol yeup toye na Yalla naniou Yalla fayal mame maodo Dieureudieuf famille mame moussé alé
@ismailasy30703 жыл бұрын
Machallah li mouy Def thi khol nékhna lolou. Yallah nagnou Yallah fayal Seydil Hadj Malick Sy Rta ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@t.d.sservice28783 жыл бұрын
Yalla na yalla delosi diamou keurgui ak tawe fékh Sibarké Seydil hadji malick 😭😭
@papaalymbayefaye29033 жыл бұрын
Walay tayy gnou déeé😭😭😭😭😭😭lii dafa eupe si sunu xol you ndaw yii
@ndeyefaye77833 жыл бұрын
Sunu khôl atanoul lii dé walay
@diassysaliou86562 жыл бұрын
Yalnagnou Yallah fayal Sunu Mame Cheikh Seydi Elhadji Malick Sy (rta)🤲🤲🤲
@yacinebo-bt1uf2 күн бұрын
Machalah 😭😭😭😭😭😭😭 02h 13 j’écoute pour dormir 😭🥹❤️le goût de ça
@tidianeaw54493 жыл бұрын
Macha allahh amena solo yalla nala yalla samou Sénégal 🇸🇳 🇸🇳 🇸🇳
@abdoulayegaye85862 жыл бұрын
Machallah nekh na lol
@LandingMansaly-xp9fh Жыл бұрын
Je pleure bilay 😭♥️🥺
@makhtarkane3323 жыл бұрын
Al Hamndoulilah 💘 yalnagnou yallah fayal Maodo 😭♥️ abdoul aziz mbaye yalna yallah goudaal saay fane 🙏 Malikya Tv yalnaléne geuna taxawou bidiayi seydou woudioudi SAWS ♥️
@malikiatvtivaouane3 жыл бұрын
Allahumma Amine 🙏
@ndiagadiop94012 жыл бұрын
Yalla na yalla goudal sen fan si barke seydina Mouhamed saw ak seydi El Hadj Malick Sy sa youma wete moy sama weteul.
@davidmbengue62774 ай бұрын
Je pense à mon grand père Elhadji Mamadou Tafsir Mbengue un vrai Talibé seydi Elhadji Malick Sy ❤️
@mouhameddiop20133 жыл бұрын
Malikiya tv séne lépa raféte,billahi li waroule diékh,loumaye yeuk sama xol mane rék mâko xam,dieuredieuf diaredieuf,yala bou kéne manké,ba déwéne inchallah,ndawe yi sounú borome mayléne aye CDI,baniou térale séni wadioure,aminne billahi sounú borome yalnko défe
@malikiatvtivaouane3 жыл бұрын
Allahouma Amine, Mashalla Yalla nalene Yalla Faye
@ahmadoundiaye69213 жыл бұрын
Allahou akbarr est ce que yenangui bayi khel si mbideu mi aaaaay waaaay cheikh Seydi Hadji Malick miiiii ohohoho j'ai les larmes aux yeux
@mariamakonate4145Ай бұрын
Yallana yalla werral batte bi si barké Seydina Mouhamed PSl ndam rekk inchallah ❤
@mouhamedpouye67953 жыл бұрын
Thieuy mbékté biii dh kéne xamoul noumou tollou ❤️ Yalna gnou Yalla fayal Seydil Hadji Malick Sy (RTA) 🙏
@miketoure45183 жыл бұрын
YALLA NA YALLA SAMLÈN TÈ SOUTOURALLÈN BIDJIAY MOUHAMMADOU RASSOULOULA SAWS
@malicksamb32643 жыл бұрын
Le téchnicien du sont il est trop fort on vous suivie dpuis France
WA RAHMATOULAHI KOULAL QALQI QAD WASSIHATMINE FAJIRINE WA MOUTIHINE ZA-IDINE BARI❤🙏 YALNANU YALLA YEUREUM BARKÉ MAGG GNI
@mamadoudieng61643 жыл бұрын
gorgui abdou aziz mbaye ak ñimou andal yalnaleen yala samm ta faylenn
@ousmanefall19943 жыл бұрын
Est ce qu'on connait nous tous les senegalais qui est CHEIKHOU Hadji Malick sy Serigne Cheikh Tidiane Sy Almaktoum a raison de dire Maodo l'inconnu de la nation on peut même dire de l'humanité
@elmalick92883 жыл бұрын
On ne le connaît pas assez malheureusement c’est la solution pour le Sénégal
@ibrahimadiop713 жыл бұрын
Mashallah wa malikia amlen diamou rek contanna merci beaucoup
@malikiatvtivaouane3 жыл бұрын
dieuredieuf
@astousow557 Жыл бұрын
Amine yaraby mâcha allah cheikh seydy Haji malick
@momojamdong68743 жыл бұрын
Wallahi mbekte reik lay am soumay deglou li♥️♥️♥️
@mbayekanefall84223 жыл бұрын
Walahi, je peux l'écouter à longueur de journée.
@adamaniang47702 жыл бұрын
Machala baye abdou aziz mbaye yalla na yalla goudeul fane ni guaye weuyé khasida mame maodo yi ame na sollo loll
Dieridieuf malickia t.v de nous faire entendre ces belles paroles de Abdoul Aziz Mbaye dieridieuf maodo Malick
@aminandoye79233 жыл бұрын
Manchallah mame maodo yalla nako sounou borome yoko yoko.....lerem sy malick
@sambadiop7013 жыл бұрын
Macha Allah abdoul Aziz mbaye Yalnaniou yalla fayal SEYDIL ELHADJI MALICK SY R.T.A AMIINE
@MinastoreStore8 ай бұрын
Kii est là ❤❤❤❤❤❤❤
@alaminesene71093 жыл бұрын
Dieureudieuf Malikia TV. Sett na..nekh na séleu na..diékeu na. Yalla na Borom bi barkél si barké Salatoul Fatihi
@dustazdrame40802 жыл бұрын
Je écoute et réécoute jusqu'à 200 ans et 200 millions de vues il me soulage bien merci beaucoup Malikia tv
@tihadnegh33713 жыл бұрын
Machala malikiyah tv yallana nek tèlè bi gueneu mak si monde bi tè barkel
@kineseck87862 жыл бұрын
Bilahi Abdou Aziz mbaye yalla naga goude fanne nii ngaye séédlé sama koolll bii euppp naa limaiye niane yalla moye mou défma deugue deugue talibé cheikh ma dound sii tarikha bii déési dékissi si barkhé serigne babacar sy amiiiii♥️♥️♥️♥️♥️♥️
@aichadiallo63843 жыл бұрын
Sa lumière est la source de toutes les lumières saws
@MgMg012 жыл бұрын
L'émotion dans laquelle nous plonge les paroles de ce khassaïde et la chorale est indescriptible ; on dirait que toutes ces voix ont été faites pour fusionner toutes ensemble afin de nous déclamer si harmonieusement Ya Kachifa Daa'i de Mame Maodo... Au delà de tout ça, la qualité de la vidéo, du montage et de la présentation est impeccable !!! Yalla fayal gnou leen ci liguey bou rafet bi 🤲🏾❤️
@mbayesamb29932 жыл бұрын
Masha allah le meilleur commentaire
@maimounabandiaye87552 жыл бұрын
Bilaye vous avez raison j'ai les larmes aux yeux ce que je ressens sans même comprendre ce qu'ils disent est indiscriptible je pleure !
@katykane27252 жыл бұрын
Walahi sa mappaise
@yanidoungom6092 Жыл бұрын
@@katykane2725 c est le mot elle apaise
@fatoumatadiarra3779 Жыл бұрын
@@yanidoungom6092et fais pleure en meme temp
@lasouverainete2794 Жыл бұрын
Yalla nagnou yalla fayal mame maodo thi barakati khour anoul karim amine
@biranepathediop88453 жыл бұрын
Oooohhh vraiment c'est très belle KENN DOU CHEIKH SEYDIL HADJI MALICK Sy RTA Abdou Aziz MBAYE BILLAAHI Do NIITT DIAAJEUF