Alhamdoulilah 🙏🏽 wallahi talibé baye mo wor. Dieureudieuf baye barhama❤️
@gassamagora2399 Жыл бұрын
Guiss yallah diaaxalouma. Mais guiss léneen loudoul yallah mooma yeem
@gassamagora2399 Жыл бұрын
Yallah neena. Maa ndiënk. Maa moudië. Maa nëbou. Maa feeñ. Feeñ mooy loo mana guiss. Ta Yallah dara manoukoo nëb. Ndax moo ëpe leep. Gënë yaa leep. Kon loulako teree guiss. ????
@misterolpboytoucar5376 Жыл бұрын
@@Zeydamariambarham6786 yaw yalla soxnasi
@Milliken49002 жыл бұрын
May Allah welcome el hadji moustapha Gueye in his paradise.
@ramatulayendoye43872 жыл бұрын
MASHA ALLAH waxtanwi amatina.solo loool Gueuye. YALA REK mo KHAM. ta Lou KO nekh lay dogal.guisouma ya ALLAH mo gueuna wor ken douko guis.
@serignendione67122 жыл бұрын
Dieureudiefé baye niass si ndox mu lér wi nandalé Kane moye Baye Niass
@rougyaw27852 жыл бұрын
Machalla démlén xami yalla xam yalla mo nx
@LampDerange-kh2kg Жыл бұрын
Macha ahla Ya imam
@souleymaneibrahimasall53672 жыл бұрын
Yalla Dagne kay Guiss ak Beutou Boppou
@fatoundiaye57642 жыл бұрын
Gis yalla khoudjiou fang dadjiou☝️
@loutfisar2 жыл бұрын
Quelqu'un qui est partout si tu ne le vois pas c'est parceque tu ne le connais pas.
@amly8192 жыл бұрын
quelqu'un qui est partout comment tu vas le cerner?
@hassanetamboura63222 жыл бұрын
Si Dieu même à de le connaître avant de l'adorer c'est pour qu'on ne le confond à aucune chose mais je pense bien qu'on ne peut connaître ce qu'on ne voit pas.Et Allah swt on le voit par les yeux du cœur mais pas par les yeux de la tête.le connaître nous permet de ne pas le confondre à quoi que ce soit
@amly8192 жыл бұрын
@@hassanetamboura6322 bien dit
@baimamud14912 жыл бұрын
Nyasss ♥️♥️♥️♥️
@cheikhniang333 Жыл бұрын
Machalla
@ousmanefayegarmiattijani2304 Жыл бұрын
Gniy wéddi guiss Yalla la yeureum😂😂😂
@omarbunkah60572 жыл бұрын
والله موجود ومابه امترا وكل موجود يصيح أن يرا
@bourhan1422 жыл бұрын
الا العقل؟
@amly8192 жыл бұрын
لاتفكروا في ذات الله و فكروا في صفات الله
@lindiafrombd48192 жыл бұрын
Nit mo metoul cédé guiss yalla si béton xole
@seydoundiaye83412 жыл бұрын
Mash Allah
@mamadouthiaw26942 жыл бұрын
Yalla kéne douko guiss si adouna.Meme bou fékone yonnentebi guiss nako aussi guissouko si adouna.yalla dako rignanale guinéko si adouna.yonnentebi dou sounou nawlé.yalla Aldiana rék lanioukoye guissé
@barhamlofficieltoure26192 жыл бұрын
Ya rérr ham biii
@deugrek41982 жыл бұрын
Raniane moy Kehl yeuk ak yite. Demlen seti Baye Niasse te bayi thiakhane way
@EliyassSow2 ай бұрын
Yaa gatte xaatrr
@azizsamb46912 жыл бұрын
xam-xam🙏🏾
@abdoulwahabba28412 жыл бұрын
NOUS APPELONS TOUS LES SÉNÉGALAIS AU CORAN ET À LA SUNNAH, MUSULMANS CHRÉTIENS ET ANIMISTES ! ! !
@aliouniangdjolof95062 жыл бұрын
Man dé souniou borom touram la begu kham ken khamagoul touram
@MODOUAMARtvofficiel2 жыл бұрын
Serigne cheikh Ahmed tidiane Sy dafa dakh Lolou néna yalla kene menokoo Guis
@cheikhtidjane29672 жыл бұрын
Wakhna deuge yalla kene douko giss Moy giss bopam koumanout diékh si sa bope dess si yalla kokou doumana giss yalla djante limiy fégne yeup amna niouko gisoul
@mohamadougaye46092 жыл бұрын
Maodo malick nene sou tahoul wone nityi dedou bougn dedou yalla top adouna kone niou gis yalla diaxrane ndakh yalla lou dieguei la li el hadji malick moko binde lossi wax
@justuncliktv52622 жыл бұрын
Deug bou werr ndax Yalla amoul makane amoul zama'ne. Féxél dégg wakhi Seydina Cheikh Avant ngassi commenter. Mame Maodo MALICK SY néna guiss Yalla mo geuna yomb tankk ndoh naane. Mou déllou watt waxni Haqiqatou Keuwnou aynou zatt. Donc noy def niari wakh yi? Maodo dou outé moukkou ak Cheikhou Tijane. Waya ya amoul fahmou motax do meuna dég wakh yi. So amé fathou dinga dégg wakhi goor Yalla yi
@wahiddiouf84522 жыл бұрын
Khana dégoul wakhi seydi hadji malick bi..?
@ibrahimsall64922 жыл бұрын
Amna nasi droit comme mom mounou ko guiss wayé guisd yalla dou problème guiss lou doul yalla moy problème هل هو الظاهر ليس فوقه شيء
@fayebirame92 жыл бұрын
La mauvaise foie et l'indignation ne peut voir ni de près ni de loin ki am makan c est lui qui est difficile à voir par ce que bo semer si keuram fekokofa do kham fokoy weurer mais yallah est homnipresent
@ousmanediop16202 жыл бұрын
C'est inadmissible 🤣🤣🤣🇸🇳🇸🇳
@bourhan1422 жыл бұрын
Lou amoul makaane noo koy guissé?!
@awasall16572 жыл бұрын
Ce code
@awasall16572 жыл бұрын
Dangay niow si baye
@bourhan1422 жыл бұрын
@@awasall1657 moo gueuna goumba gneup. Dara guisso lènko.
@babacarndiaye82632 жыл бұрын
YONENTE NENA GUISS NA YALLA THI SAMA BETOU KHOLE MOUSSA GUISS NAKO
@adamasow92922 жыл бұрын
@@bourhan142 ok légui explique nous la différence entre Mouhamed Abdoulahi (PSL)le premier sur terre et Mouhamed rassouloulahi..boul daw kayy fi mane wane la khamo tousse..ndringue bi
@sambasy2352 жыл бұрын
enristre
@abdoulayekountathiam23742 жыл бұрын
Y’a que dieu qui existe et vous voyez autre chose que dieu .
@minkahaircutcoiffeursenega5132 жыл бұрын
Diapal ni mom moko meunoul guisse ms boum wakh kene meunouko da fekk ni barhama sobou la rek bref diem lena tarbiyou dji khamko mo guene ngeni rére si adouna bilae diereudiafati cheikh Al islam
@gueyeyakhouba13202 жыл бұрын
Barham sax manoo koo gise, Yalla kénn Doko Guiss fii si àdduna, ak komo mana Doon
@omarbunkah60572 жыл бұрын
@@gueyeyakhouba1320 يا أخي لقدأنكرت كلام الله قال تعالى في حديث قدس الحج حجان حج كعبة المباني وحج كعبة التداني فمن حج كعبة المباني أعطيته غفراني ومن حج كعبة التداني رفعت عنه حجاب حتى يراني
@babacarndiaye82632 жыл бұрын
@@gueyeyakhouba1320 WAKHO DEUGUE DAGNOU KOY GUISS
@abibousy97612 жыл бұрын
@@babacarndiaye8263 , est-ce que tu as vu Dieu ?
@biguendiaye8532 жыл бұрын
@@gueyeyakhouba1320 Dème lene khamidie yalla
@minkahaircutcoiffeursenega5132 жыл бұрын
Lolou nieup ko sédé cheikh ahmadou BAMBA wakhnako thi massalikoul jinane kou tokk fi di wakh q c impossible de voir dieu danga guestouwoul thi say téré serigne comme nouko babacar thiam dane wakhé
@aronambaye53202 жыл бұрын
Yalla dé mo wakh si Alkhouràne lane tarani, kéne douma gis et il a utilisé le terme lane en arabe qui signifie une negation catagorique mane dama diakhlé si yéne
@mamadoudienggaye8822 жыл бұрын
@@aronambaye5320 mn frère tu te crois plus savant et plus honnête que Moustapha Gueye pour ne citer que lui
@aronambaye53202 жыл бұрын
@@mamadoudienggaye882 c’est qui Moustapha Gueye et entre la parole divine et la parole de Moustapha GUEYE laquelle je dois croire,hè Dieu a dit dans le coran لن تراني et toi tu me parles les propos d’un simple serviteur Allahou akbar
@aks37082 жыл бұрын
@@aronambaye5320 walakine après loussi topou
@mamadoudienggaye8822 жыл бұрын
@@aronambaye5320 Évidemment un simple serviteur beaucoup plus savant que vous et moi très honnête
@taphaniang19622 жыл бұрын
Yalla kéne douko guiss il est inaccessible manoul nék kéne douko guiss mako wakh kouko wédi
@biguendiaye8532 жыл бұрын
Yalla nena bala guamaye diamou gua khame ma ta baye moye khamele yalla
@barhamlofficieltoure26192 жыл бұрын
DIEUREUDIEUFÉ BAYE
@abibousy97612 жыл бұрын
Est-ce que quelqu'un parmi ceux qui lisent ces commentaires a vu Dieu ? Je le prie de se signaler pour nous édifier.
@jamilandiaye73142 жыл бұрын
Habibou Sy moi je l'ai vu en 2007 l'année où j'ai pris le wird je traverser des lumières ces dernières étaient de plus en plus intenses jusqu'à la dernière lumière la plus intense je m'arrête et une voix à commencer à ce prononcé en me disant des paroles qui me faisait vibrer de la tête aux pieds et cette voix me disait je suis le seigneur dont tu dois adorer je suis le seigneur dont tes parents doive adorer je suis le seigneur dont le monde entier doit adorer et au même moment je t'ai entrain de répéter les noms de Dieu.yavais à mon côté droit des oiseaux de couleur jaune doré qui volaient en cercle.j'ose raconter ceci parsk c l'anonymat .
@abibousy97612 жыл бұрын
@@jamilandiaye7314, merci de m’avoir répondu.
@PapeSDIAO2 жыл бұрын
@@jamilandiaye7314 cheytan rek nga guis ! Désolé
@moussadiop69742 жыл бұрын
Kou guissoul Yalla thi adouna doko guiss alakhira, té kou guissoul Yalla do dougou aldiana tawtef
@abibousy97612 жыл бұрын
@@moussadiop6974 , fo ték lolou ? Est-ce que tu veux dire que notre mère Aïcha n’ira pas au paradis ? Est-ce que tu as pensé aux milliards de musulmans qui n’ont jamais vu Dieu ?