Yayam Dafa xamni Thiaga la?motakh mou Wa h djieukeur dji mou guènéko Keur gui Lou doy war Bir Parcel

  Рет қаралды 49,375

Sénégal instant

Sénégal instant

Күн бұрын

Yayam Dafa xamni Thiaga la?motakh mou Wa djieukeur dji mou guènéko Keur gui Lou doy war Bir Parcel.

Пікірлер: 103
@Bob-w6n
@Bob-w6n 7 күн бұрын
Guiissouma loumaye. wetiiok sama yaye je t aime mama❤❤❤❤vive mama
@fantasagna4076
@fantasagna4076 7 күн бұрын
❤❤❤❤😊
@FallElhMalick
@FallElhMalick 6 күн бұрын
Bob-w6n❤ak ko Meunti Doone
@CheikhIbraFall-u2r
@CheikhIbraFall-u2r 6 күн бұрын
🇺🇲 incha'Allah yalla n'a yalla mottali sama yéné incha'Allah Bama yobbou wadiour'yi maqqa si barké seydina Mohamed psl ♥️🫶
@cheikhnandiaye5371
@cheikhnandiaye5371 7 күн бұрын
Molène député Mohamed Sagna AK dame m'bodj gnou régler problème bi vite fait
@YacineDiop-v2e
@YacineDiop-v2e 7 күн бұрын
Bilay mane dhé dama tite si sounou Sénégal bi😭
@aichaba6483
@aichaba6483 2 күн бұрын
@@YacineDiop-v2e bilaye wakhatiko diarna tite beuggueu yaliss reck ackk beuggueu lou yomb
@mamisene3375
@mamisene3375 6 күн бұрын
Yallanama yalla maye ma térale sama yaye
@ndeyediop335
@ndeyediop335 7 күн бұрын
Wo léne Guy Mari Sagna mou réglé ko vite fait
@seynaboufaye2039
@seynaboufaye2039 7 күн бұрын
@@ndeyediop335 wolouna ko thi dé kokou rék khalé douko yabe ba mague diko fonto
@FABI-hw27
@FABI-hw27 7 күн бұрын
Ki moy domeram yalla nala yalla atte ak famille bi
@diez8712
@diez8712 7 күн бұрын
Lii gnaw na trop vraiment yallah nalen yallah takhawou
@AstouSy-f8i
@AstouSy-f8i 7 күн бұрын
Yaye dé mome ndéne la sou dalé sa kawe gua toth so dalé si kawam yakou nite noumou méle guinawe yalla sa yaye la
@pendathiaw5560
@pendathiaw5560 3 күн бұрын
Bien parlé mariétou
@yayodiallo1021
@yayodiallo1021 7 күн бұрын
Li dé Côme filme moudioum diamono la 😢😢😢😢 est ce que moko taye ndah li keneu mousso KO guisse
@bäbäc2130
@bäbäc2130 7 күн бұрын
Talla hanne talibe yayam leu ki kou gueme yayam billahi❤
@kaami8709
@kaami8709 6 күн бұрын
Sen titre bi gnawna trop
@NdiayeBathie-z7d
@NdiayeBathie-z7d 7 күн бұрын
Yalla nagnou yalla mousal si trophol sa yaye ohhh
@MohamedFaye-dl7vx
@MohamedFaye-dl7vx 6 күн бұрын
Nous devons organisé un levé de fond pour elle
@elagegueye3310
@elagegueye3310 7 күн бұрын
kou diappeunee wadji holbi mogueneu wow heer❤
@papatorres4563
@papatorres4563 7 күн бұрын
Dôme Bou nek li mouy niane sounou borom moy teki dimbaly ay wadiouram rawatina yayam.
@loudoulaktalibesafouma3429
@loudoulaktalibesafouma3429 6 күн бұрын
R+1 bi lou mou ndaw ndaw warna diar 100 milon domi haram dji ni mome 13milon la ko mér bi diayé keur gui lolou xél sax na ngou wokou
@AlouSow-zd8wj
@AlouSow-zd8wj 4 күн бұрын
Non ki moy mbam ak nous yaye foré ndeyssane
@fatyndiaye-qt9vl
@fatyndiaye-qt9vl 7 күн бұрын
Bilahi ki doff la wagui khana amoul famille baye détruire famille diambour tamite thiey yalla .ani goor akk seuyi thim
@coumbandiaye6923
@coumbandiaye6923 6 күн бұрын
@@fatyndiaye-qt9vl Daffa niakk diom rekk . Seytane, bone niakk fayda .
@mayaciss6821
@mayaciss6821 5 күн бұрын
KOU KHAMONE NI SO AMÉ DOME NI LALAY TOROKHAL NGA GNANE YALLA BAGNA DJOUR UNE SORCIÈRE COMME ELLE VA LE PAYER
@fatoudiatta164
@fatoudiatta164 Күн бұрын
Marietou thi lo nek
@dembathiao8232
@dembathiao8232 7 күн бұрын
On a qu'à les porté plainte et que justice soit faite
@OssaynouKhouma
@OssaynouKhouma 7 күн бұрын
Dieukuer dji mokoye wore
@matydione8670
@matydione8670 5 күн бұрын
Ndiaya ya yess goor diaroul li dé yaye moy Galathiou dome bakhna torokh nga ni Moustapha diakhaté😂😂😂
@PapeAmadouRobertFaye
@PapeAmadouRobertFaye 7 күн бұрын
Ce gars là doit être poursuivi ki domou haram deug leu dina gnou ko guiss sa yaye gua kay toroxol aduna dina len yar
@alediop878
@alediop878 7 күн бұрын
Ki sathie keur diambour Sénégal Yon amoufi
@LazoDiallo-k4c
@LazoDiallo-k4c 7 күн бұрын
Moi aussi je parle pas avec ma mère ne dors pas chaque jour que dieu fait appelle ma mère je veux savoir si elle va bien elle se porte bien elle a mangé elle est pas malade et toi tu fais sortir ta propre mère qui t'a mis au monde
@KassAm-u9w
@KassAm-u9w 6 күн бұрын
La vente ne peut pas être validée sans la signature de tous les heritiers
@KassAm-u9w
@KassAm-u9w 6 күн бұрын
Mareme ❤❤❤
@NdellaDieng-n7y
@NdellaDieng-n7y 7 күн бұрын
Gor deh diaroul li dingako rethiou deh😢😢😢😢
@Bébéamina-x8u
@Bébéamina-x8u 6 күн бұрын
Yalla bakhna ❤
@mamedabakh8494
@mamedabakh8494 7 күн бұрын
Yalnañ yala doli Soutoura rek
@PapaDiawoyeDiop
@PapaDiawoyeDiop 6 күн бұрын
Yallah doli niou soutoureu 🙏
@sokhnaniang8926
@sokhnaniang8926 6 күн бұрын
Allahou akbar
@didijohn694
@didijohn694 7 күн бұрын
Wadji moy domeram deug😢
@SophieNdao-vl2uy
@SophieNdao-vl2uy Күн бұрын
Défna lu yaw goor diarul gay trokhal sa yaye tot ou tard ku goor ki dakoy wor outi lénéne goor yi ay wor kate la yu dé attention les filles bakh na rek
@loudoulaktalibesafouma3429
@loudoulaktalibesafouma3429 6 күн бұрын
Keur gou tolou ni 13milon 😢 lolou rk warna tax justis nangou ko délo ko mér bi dougal garand bi kasso
@PapadjibrilNdiaye-y4o
@PapadjibrilNdiaye-y4o 4 күн бұрын
Dooy na waar
@touffelarose4566
@touffelarose4566 Күн бұрын
Nitte gni tamite di acheté keur yii deileine gestou avant d acheter nakhe ki niou diaye keur gui warna deilossi papier yii niou deiloko xalissame.alalou diambour laniou la diaye
@elagegueye3310
@elagegueye3310 7 күн бұрын
kou geumnee sahnasi nitou safaraleu❤aldiana mogi si ron takkou yay
@malickmbodj4146
@malickmbodj4146 7 күн бұрын
C'est vrai dé dokhan ndayam ay domam reikk😂😂😂😂
@DjilyGaye-em6ec
@DjilyGaye-em6ec 5 күн бұрын
😢😢😢😢😢
@NdellaDieng-n7y
@NdellaDieng-n7y 7 күн бұрын
Yako sagne yaye nimou fore thi dom🤔🤔🤔🤔🤔
@fatouceesay6794
@fatouceesay6794 6 күн бұрын
😢😢😢
@singuinard1659
@singuinard1659 7 күн бұрын
Niaw na trope😢😢😢
@WadeAssane-s8n
@WadeAssane-s8n 5 күн бұрын
Senegal bous bone lou bes
@soniasene8417
@soniasene8417 7 күн бұрын
Wa fat Ndiaye domou mère bi mo guéner yayame keurame khana dedaite kay😢
@mouhamedsambe8294
@mouhamedsambe8294 7 күн бұрын
Xamoul valeur yaye bilay waydiou kouko trokhal trokh t lo lidieunti dou soti t bala deh trokh
@cheikhseck4243
@cheikhseck4243 6 күн бұрын
Mais mane dama djiomy wala????😮😮😮😮😮se yaye? Non bé légui comprendrouma quoiiiiii😡😡😡😡😡😡😡
@Zazindiaye218
@Zazindiaye218 6 күн бұрын
Keurgui danio wara talll ndeyam domėkharam bonneu amna
@Mbodji-walo
@Mbodji-walo 7 күн бұрын
Soubhanallah😭😭😭😭😭
@rokhayatoudione3912
@rokhayatoudione3912 6 күн бұрын
Ken défoul domou mère bi fatou ndiaye mo def bokk ak say rak ndeye ak baye nga body len and ak sa dieukeur dieund keur bayi say rak ak sa yaye. !
@abdoulayediouf2140
@abdoulayediouf2140 7 күн бұрын
Sénégal dhall légui toroxalaté moffi xéw, mais toroxal sa ndeye dhei ndax goor, goor bobou molay toroxalate beuthieuk ndaroup kamb, ngay délou di weurate sa yaye far torox nak adounak alahira. Yaye dou morom... Li yep ngakh koy wala xalis? Boumssi meuneu done daka diaroul
@ndiayendiaye313
@ndiayendiaye313 7 күн бұрын
Allahou Akbar Allahou Akbar
@rokhayaseck537
@rokhayaseck537 7 күн бұрын
Haral rek dou yague légui wadji dieul 2ème femme guéné ko keur dji setane lén rek
@souleymanewade3786
@souleymanewade3786 6 күн бұрын
Encaisser xalissou diambour ba paré takhaw di yakhà derou mr diouf
@Beugdeug
@Beugdeug 7 күн бұрын
Allez voir Muhammad Guy Marius Sagna et Dame mbodj les deputes rels du peuple
@AwaFaye-k4h
@AwaFaye-k4h 7 күн бұрын
Wallahi Bro 🥹🥹🥹
@cadandong7564
@cadandong7564 7 күн бұрын
Bissam dina gnow. Bo fonkoul sa yaye sa Dieukeur dinala def lou reuye
@amadoufatimakane3564
@amadoufatimakane3564 7 күн бұрын
Xanaa Abdou Rajiim key
@cheikhantadioptv2790
@cheikhantadioptv2790 7 күн бұрын
Lii koumokoo dèf maa yoboulaa sii ndiagoyii Kate saa ndaye
@Gggge_dudiolof9536
@Gggge_dudiolof9536 7 күн бұрын
Bilay ki domeram la sathie keur diambour
@ahmadoubambandiaye-ke4qb
@ahmadoubambandiaye-ke4qb 6 күн бұрын
Niawna dh
@CireHanne-p1z
@CireHanne-p1z 7 күн бұрын
Douko djikk dè Yaye mom Yaye rkk
@SenMedounesen
@SenMedounesen 7 күн бұрын
Yalla danako Wane yaye d'où morome
@KhidmalBarkham
@KhidmalBarkham 6 күн бұрын
Man lii dafma diomal ba Nga xamn😓i Meunoum Geum Que C'EST Naturelle
@FatouNdiaye-zb8um
@FatouNdiaye-zb8um 7 күн бұрын
😭😭😭
@aliounediop-w9e
@aliounediop-w9e 7 күн бұрын
Yaw yap nga wa keur massar dée. Nganan aleuh😅😅😅
@FatouHanne-z8z
@FatouHanne-z8z 7 күн бұрын
@@aliounediop-w9e keur massar dou aalal dh
@nianadiallotvbien-etreetri4525
@nianadiallotvbien-etreetri4525 7 күн бұрын
Baal léne KO kholam nékhoul keur massar dou aleuh
@Gggge_dudiolof9536
@Gggge_dudiolof9536 7 күн бұрын
Ki kay weroul , magui Paris keur massar la deukk. Keur massar mo dakk fouf parcelle
@SigaDiouf-zu7yt
@SigaDiouf-zu7yt 7 күн бұрын
Gnoune wa keur massar ngay wakh lolou moungui gnaw dé
@nianadiallotvbien-etreetri4525
@nianadiallotvbien-etreetri4525 7 күн бұрын
Baal léneko sama rakk la khôl bi mooh diekh dafa dioum
@SigaDiouf-zu7yt
@SigaDiouf-zu7yt 7 күн бұрын
Ok
@aloubeby2235
@aloubeby2235 7 күн бұрын
Ioe sa titre bi affaire Domeram yi nak😮😢
@fatoudiop58
@fatoudiop58 6 күн бұрын
@@aloubeby2235 sooff ak beugue ay vues rk
@Aymen-z4z
@Aymen-z4z 7 күн бұрын
Dérétou diam mo mene lou melni, kou goor ki diam la je suis sûre et sa femme niak faida
@Yassadidal
@Yassadidal 7 күн бұрын
Sénégal yakhouna c foutti khana kou Tedd ki walou gnou
@ninkinanka3644
@ninkinanka3644 7 күн бұрын
🛑DIEUNEU SA YAYE MOM DARA WQROULA KO DIARAL... ADUNA BOU DIEKH BI... AKHIROU ZAMAANE DAL LANIOU NEK
@elagegueye3310
@elagegueye3310 7 күн бұрын
ligadef mogueneu bonn li ki deff wat si nitt bokoleleu
@aliounegueye62
@aliounegueye62 7 күн бұрын
Si seulement j avais toujours une mere
@myandiaye4960
@myandiaye4960 7 күн бұрын
TEIYLOULEIN ,BALLA BEIN COMMENTAIRES. UL Y'A ANGUILLE SOUS ROCHE.
@Salihate57
@Salihate57 7 күн бұрын
Ak lep ni mou meuna dèmé warour ngueuné yayam, lolou dara mounouko justifié si adouna
@Gggge_dudiolof9536
@Gggge_dudiolof9536 7 күн бұрын
Wadji sa sathie li dafa niaw, c'est un manipulateur, profiteur
@mouhamadoulaminekande8796
@mouhamadoulaminekande8796 7 күн бұрын
Aye lii gnawna trop sheuuuuut
@PapaNdao-x5g
@PapaNdao-x5g 7 күн бұрын
Sokhna si waxol bayi sinon degeu bi keur massar moy all
@nianadiallotvbien-etreetri4525
@nianadiallotvbien-etreetri4525 7 күн бұрын
Baalko dafa dioum khôl bi mooh nékhoul rek😢
@bayefallthiam2495
@bayefallthiam2495 7 күн бұрын
Mère bi kham nako sama kharite leu waye li mou def dafa niawou torop
@mortalaless8364
@mortalaless8364 7 күн бұрын
JOURNALISTE BI SOXNA SI GANANE SA YAYE
@icAlphaDiallo
@icAlphaDiallo 7 күн бұрын
Man Kay lolou moma diakhal 🤣
@icAlphaDiallo
@icAlphaDiallo 7 күн бұрын
Yalla na yalla diapalé mér bi
@mariamadiallo1828
@mariamadiallo1828 7 күн бұрын
Wakh deug Yallah beugeu khalé khalé lou rek
Série - Jeux de Dames - Saison 1 - Episode 48 - VOSTFR
36:01
Marodi TV Sénégal
Рет қаралды 1,4 МЛН
黑天使只对C罗有感觉#short #angel #clown
00:39
Super Beauty team
Рет қаралды 36 МЛН
Try this prank with your friends 😂 @karina-kola
00:18
Andrey Grechka
Рет қаралды 9 МЛН