Qui pense comme moi qu'on devrait lui octroyé une faculté à l'université de touba pour qu'il transmette son immense savoir à l'ensemble des étudiants venus dans tous les coins du sénégal et de la sous région. ce bilal est un patrimoine vivant et appris beaucoup de chose à travers cette émission même le juri qui noté les finalistes de bilal 2019 ont été évalués. Talibé rék mo am solo xolal xam xam bou yatou bii rék té moussou ko wané moussou ko dieufé loudoul dokh si ndigueul rék dieureudieufé sérigne touba diarama mbackiou faye bi takh niou defko bilal massalik.
@zizazize2234 жыл бұрын
Vraiment lolou dîna rafet
@mbayesylla51114 жыл бұрын
Dina am Inchal'Allah
@tamsirfaye34304 жыл бұрын
Wallahi c’est une bonne idée ❤️❤️🙏🏾
@ibrahimadione87084 жыл бұрын
Pourquoi Touba kassé et non le Sénégal ??
@aymeroudia23724 жыл бұрын
Idée bou rafete la
@tourkychtv62064 жыл бұрын
Non il faut l'inviter encore doyalounou et de passage je me disais qu'il doit ouvrir une école pour former les jeunes qui ont la passion de l'adan❤Vraiment t'es une richesse pour le SENEGAL🙏 Yaalana yaala wereul baat bi🙏
@xutbatv45162 жыл бұрын
Vraiment... Doyalù niù dara. Naniù ko inviter wat rék. Pour l'école, c'est une bonne idée vraiment
@mouhamaddjigueul55522 жыл бұрын
@@xutbatv4516 k3l333k3
@souleymanetraore7084 Жыл бұрын
Pourquoi pas concours nodou
@BEBEDiouf-ko2cg Жыл бұрын
6.
@xaadim96154 жыл бұрын
Serigne mouhamadou Moustapha ndiaye yalla nafe yego te wer barke Serigne Touba khadimou rassoulilahi saw Amine
@bassiroumbackecisse6823 Жыл бұрын
Aminee
@user-jl5qv6dv9ecoupedumonde2 жыл бұрын
Quand tu le vois s’exprimer,tu vois que c’est une passion pour lui
Alahou akoubar, way serigne bi yallah ga goudou fan. Daga wara am ecole nak di djangal gni nek si djaka yi nodou.
@ablayesamb47214 жыл бұрын
Amena solos trop sama djiguéne
@issaseck12583 жыл бұрын
Nooo émission biii doumaasssi doyalll vraiment on devait lever des fonds pour que tu puisses ériger une université. J'apprécie ta pédagogie et ton humilité
@Marasaliou4 жыл бұрын
On voit qu'il est très passionné
@cheikha13414 жыл бұрын
vraiment oustaz gaye yagg na yeungou si nodou niogui lay félicité invité bi nak li dall moy xamxaam bou werr nous sommes fier d’être sénégalais
@mouhamadoufalilouniang11974 жыл бұрын
Xam Sooga Waxa Gënë Woor waaye yit Mën Sooga Jëfë Gënë Woor Maashaallaah Si Xam Xam bi Ndiaye
@ibrahimasow62233 жыл бұрын
Allahou akbaar Ma sou ma khamné li lépou am na ci nodou.... Billal Mustafaa Jërëjëf Mangui laay tewlou bu baax Massalik Yàlla nala sa Borom samu ci barkep Seex Ahmadu Bamba
@omsarr024 жыл бұрын
Salaam J ai beaucoup appris de cet entretien. Le Bilal MOUHAMADOU a parle du Azan de Abou Mahzura que je ne savais pas malgre que je le faisais. Il a aussi parle de la notion de " Tarji'ou" qui consiste a repeter les deux paroles de Shahada a voix basse apres l'avoir declare a haute voix. Il faut noter que beaucoup de pays ne le font pas- Mes amis Pakistanais et Arabe ne le font pas. Au debut je me sentais comme etrange jusqu'au jour ou j ai demande a mon Imam qui est Somalien et c 'est lui qui m'a parle pour la premiere fois de la notion de ce terme " Tarji'ou". En resume je voudrais exprimer ma satisfaction - I am very happy and I have learned a lot from this MOUHAMADOU - I will do my best to meet you inshAllah whenever I come back to Senegal. May Allah give you a long life full of health, sound imam and enough wealth with baraka ameen.
@alamine67134 жыл бұрын
Machalah reviens au pays
@omsarr024 жыл бұрын
I learned a lot from this interview. Bilal MOUHAMADOU spoke of the Azan by Abou Mahzura that I did not know despite the fact that I was doing it. He also spoke of the notion of "Tarji'ou" which consists in repeating the Shahada's phrases in a low voice after having declared it initially out loud. It should be noted that many countries do not practice Tarji'ou ;My Pakistani and Arab friends dont have much idea about it. At first, I felt strange to add it in my Azan whenever I was asked to make Azan at my local masjid until the day I asked my Imam who is Somalian. He broke it down for me. It was he who spoke to me for the first time about the concept of this term "Tarji'ou". Un grand Merci a 2S TV and YOON WI's team starting from OUSTAZ ABDOULAYE GAYE.
@mbayesylla51114 жыл бұрын
Machall'Allah " Nodd deugue boko tèwlo daye dougue sa biir yaram diko Nodaneti "
@serignegningue6623 ай бұрын
Yallana nala yalla doli weer si barkep MOUHAMED (psl)
@abdoukhadre68744 жыл бұрын
Mashalah yallah na Borom bi weeral batt bi tieuy Serigne Touba moy ame kouné
@Anonymous-em5md4 жыл бұрын
Allahou akbar Dotolén def émission bou dakh bii 🥰😍
@nouroudiine103 жыл бұрын
Je peux pas m’en passer je le regarde très souvent et ça me régale Yalla na gua ame Tawfexx yow Mouhamadou Ndiaye❤️🤍
@khadimkare41184 жыл бұрын
Mouhamed M ndiaye 🇸🇳🇸🇳♥️♥️♥️yalla nala yalla samou tei weral sa battt Sougn xol sed na trop si iow ماشاء الله
MaachaALLAH !!! Émission bi daxmaye faateli dioumayii Sunnite yii Makka AK Medina..... Thieye bokk Sunnite yii Makkah ak Medina... Yalnalen yAllah ar aduna AK akhira... Qur'an ak Sunna rek moye deugue
@alassanekanh62824 жыл бұрын
Salaam...MANCHALLAH les ressources humaines de notre pays .... dans tous domaines ALLAH nous a gratifié....
@mouhamedndiaye80633 жыл бұрын
Merci ninga sèdalè sama xol yalna yalla sèdalèko sa xol mashalla💖
@mardiack54032 жыл бұрын
Amiin
@assanengom94304 жыл бұрын
Xool yeup sédeuna machallah ❤❤❤😭😭😭😭😭😭
@souleyendong23094 жыл бұрын
Ah ma sha allah,xolll cedna vraiment. Mbirrr dalll dangua kay diokh wayam. Yalla na sennn diam yague ...
@ibrahimatoure27624 жыл бұрын
Thieuy mourid xam xam bi sélna lérna
@mbayejrsow8052 жыл бұрын
Je me réjouis de d'écouter et de t'écouter encore et encore
@sorysow58054 жыл бұрын
Si tiktok bi lako guissé mai machalla dafay seral sma xol bi
@bayfall26584 жыл бұрын
Machallah kene dou s touba amoul morom diarama mame lamp Fall amoul morom
@zahrarassoul48054 жыл бұрын
Calm down ki dou mouride dé
@madiyanabo34564 жыл бұрын
@@zahrarassoul4805 dett ki moy nodou Jumma Masalikoul dh il est Mouride
@zahrarassoul48054 жыл бұрын
Madiyana'BO kéneu wédiwoulni mofaye nodou mais dou mouride sa waye démal gua guëstou dji
@togolandiaye4 жыл бұрын
@@zahrarassoul4805 lou si ame solo moye dioulite la ta batbi bi nehna gneup bougaune nagnou mouye node sa diaka waye massikoule la neke islam diarignolo machallah. Barakalahou fikoume.
@serignegningue6623 ай бұрын
❤❤❤ machalla j'ai les larmes au yeux ❤❤❤❤❤
@mouhammedkane26934 жыл бұрын
ما شاءالله!!!عجبا لهذا الشيخ بارك الله فيكم يا شيح محمد المصطفى
@m.sart924 ай бұрын
machALLAH♥♥♥
@falloufall14384 жыл бұрын
Macha allah yalla na yalla yok fanwi té weral thieryi si barkep serigne touba khadim rassoul
@mamethiernobirahim77884 жыл бұрын
Ndaysane🌟🌟🌟 Xol sedna trope way machallah.. yalna yala goudeul fane yi téh yok wer gui🤲
@lecoranmonantidote66174 жыл бұрын
Ohhhh☺️والله لقد أثلجت صدري حفظك الله ورعاك🤲🏻Yalna Yalla dolli samme
@espirituelligth73394 жыл бұрын
Warone wakh ci liqam aussi. Invitelen ko encore maachaa Allah.
@bassiroudione55814 жыл бұрын
Yalna sa diam yagg yalna Borom bii wereull bapp bii té sam la boubakh Allahouma amine
@abdoulahadndiaye79104 жыл бұрын
Ma cha allah chékh Moustapha yallh nako yallh barkéll barkéb s Touba
@tigredordusenegalkung-fuwu3118 Жыл бұрын
Machalah waay mourid sama khol Sedna yalla nala yalla Faye si barké alkhourane amiiiiiiiiiiiiine
@falloudiene706 Жыл бұрын
Billahi ki dama dioylo loubari wallahi Moustafa yalla nala yalla faye 🙏
@bambandiaye98984 жыл бұрын
Yalla nala yalla samm sama khol sédde n'a trorop billahi walna Yalla wéreul battbi ba 190 ans
@bayedembathiam60954 жыл бұрын
Maaaachaallhou Serigne bi yalnaléne yallah barkeél Barkep Brom Touba
@mamadouthiam19424 жыл бұрын
Machallah ndiarigne kessé amna solo lolou un vrai noddologue agrégé en noddologie. Sounou xol sedd na lolou. Dieureudieufeuty !!!
@mboupmboup10694 жыл бұрын
Mouhamed habibe diop machallah bonne contination ak sa ani varicelle yéppe 🤲👏👏
@جوفعلي4 жыл бұрын
Macha Allah ki yalnako Borom sameu té met KO wérr
@benabdallahndiaye76572 жыл бұрын
NDIAYE REQ NGUA MEUNA SANTE WOLLAH ♥️♥️.MASHALLAH YALNA YALLA SAMMEULAAA
@alnfall19784 жыл бұрын
Borom touba cibopam mo amoul moroom mouride yi diiné kepp moléne nior kham nga ki lii mouy def nior nako dako geustou lou wérr lay leeral sama kholbi seddna
@bane2574 жыл бұрын
Walahi linga wakh deug gou wer la machala Dieuredieuf Serigne Touba Serigne Mountakha yalla nafi yag te wer
@abdoukasse32714 жыл бұрын
Évitez certains commentaires bayilène di convoqué tarikha foumou amoul place. Nékeu lén ay nit svp.
@sokhnadiarrambacke26974 жыл бұрын
@@abdoukasse3271 saay daga fi giss kufi wax waxi Tarika? Ya wara nek nit giss gnuy goorgoorlu si Diine bi fierte la wara doon
@espirituelligth73394 жыл бұрын
Ki dou Mourid pourtant migui nodou massalik donc nagnou bolo ci Islam. Ki fierté leu ci diné bii
@iiiiii66164 жыл бұрын
Ay way nanu bayi par pa vrlo yi si tarikha. Nan jiitl l'islam Kuy ab joulit rek diine ñor nala Sénégal Réew mi benn la
@moustaphandong47558 ай бұрын
Mashaallah Mashaallah Mashaallah Yalla na Borrom koun fa Yakoun wereul baatt bi té wereul xam xam bi
@serignesammbayeserignesamm86944 жыл бұрын
Ndeyesan machalla gui diambar la lolou yalla na yalla takhawou wéral batt bii
@أهلالسنةوالجماعة-ص5ل4 жыл бұрын
Démbou séetnaako ba sonnou waaw kay Alhamdoulilah guisna émission bi
@hm-gw2ms4 жыл бұрын
Alhamdou lil Llah. Nos enfants devraient apprendre tout ceci. Quand on sait ce qui se passe dans ce pays, avec une tolérance parfois coupable des autorités religieuses. Mâchâ Allah !
@hm-gw2ms4 жыл бұрын
La relève est bien assurée.
@mbayeseydinadjibr2 жыл бұрын
No li billakhi wallakhi dinama ray 🤲😭❤❤❤❤❤❤❤❤
@alaminefall59064 жыл бұрын
Macha allah mouhamadou moustapha ndiaye bilal macha allah liguafii wakh yeup ham ham leuh yalna yallah barkel lepp