Bon sang ne saurait mentir. Le marabout de la jeunesse. Un exemple de la probité, de la droiture ,de la civilité et d'engagement au service de la communauté musulmane en général et du cheikh. Il est d'une discipline rare et d'une générosité remarquable .Aka fess Palassame . Dokhinou dioulite akhane. Il aide tout le monde. Il fait fi des appartenances de confréries ou de tendances . Mes hommages thiatou Mame Ousmane bi.
@papid1003 жыл бұрын
Naître pour être leader. J’aime bien ce discours de borom darou . Franchement borom darou est un vrai vrai vrai leader . Mâchallah
@adjicoumbandoye86413 жыл бұрын
Je suis talibé Serigne Babacar Sy j'aime Borome darou ❤️❤️
@damendiaye38003 жыл бұрын
Mchallah beurri ngeu si morom❤
@arasndamakaramerci32342 жыл бұрын
choukory la terre promise akasa souf sou yalla gereum bofay dallou sah dalakoy faye 👌👌👌👌☝️☝️☝️☝️
@mamepathe46183 жыл бұрын
Soumay khalat Chicory demb ak tay sama khol dafay sedd gouy wallahi...❤❤❤❤❤❤ lii cheikh Ahmadou kara annoncéwone fii mom la Borom darou nek di dokhal motakh nii rek lay démé waw❤❤❤❤
@arasndamakaramerci32342 жыл бұрын
dafa clair moniou waxone borom darou moy ndigeul li alhamdou kara 👌👊
@layethiaw67443 жыл бұрын
Layenne la déh wayé walahi borom Darou damako beug😍😍😍😍
@mamadouseck97553 жыл бұрын
Ton appartenance confrérique n'a aucun sens si tu l'aimes.
@ndawamachallasarr70482 жыл бұрын
Mashalla Mame thierno. Ba faaww inshaala ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
@mariamagueye78433 жыл бұрын
Machalla rose témoignage yi rafetna surtout diamou yala amna solo diouli rek mo worr
@alimatoudieng84623 жыл бұрын
Machala yaguena tok ak mom mai si yalla an yonnet bi rk ak top wadiour rk lay waxx Machala kenn du mom
@nabouba92633 жыл бұрын
Walahi dama beugue borome darou tee yalla rkk takh tee meussou mako guisse meu souma dem touba yalla na sa diam yague ❤️❤️❤️❤️
@papasambandiaye14583 жыл бұрын
Dieureudieuti borom darou le marabout de la jeunesse yag fii lol te weur
@mamadoucissoho373 жыл бұрын
Bilay Magui yek mbectei bi depuis Espagne barki borome chicory👌👌👌👌
@qakk84352 жыл бұрын
Guiss naniou cii ioe diam akk Salam sa niari wadiour yi nga am guiss naniou ni yangui sen ganaw Mame Thierno Ndamal Diné diaramaty ❤️🖤
@abdoukhadretop2553 жыл бұрын
Borom darou yane bi diss na wayé Incha Allah sa kaw sa kanam lii rek laniou done xarr
@seneabdousena75513 жыл бұрын
Borom Darou ha champion
@iboucamara73373 жыл бұрын
Le marabou de la jeunéss borom sikori yageu fii té wér
@marabodian39613 жыл бұрын
Mame thierno borom darou un marabou d'exemplaires un référence un guide très droiture kene dou mame thierno borom darou yalla.nala fii yalla yagal lol ba lep ligua beugue sii yone bii yalla défal lako barki ndiol makka
@khadimdieng71373 жыл бұрын
Machala borom darou chicory yalla nafi yagg lol té werr borom mbekté mi
@fatouciss29503 жыл бұрын
Je suis tidian mais borom darou rek la beugeu 😭😭
@mamadouseck97553 жыл бұрын
Ton appartenance confrérique n'a aucune place du fait de l'aimer.
@babacaargueye58623 жыл бұрын
Dieuredieuf sunu bay thierno
@courafaye43773 жыл бұрын
Machaala yalna ko yalla yok same té gueune ko deugeureul
@isk773 жыл бұрын
Dieureudieuf ti Mame Borom Darou sama Mbecté ❤❤❤
@damendiaye38003 жыл бұрын
Mbokkou yii❤
@doudoundiaye71303 жыл бұрын
Borom darou noreyni,notre référence.yague fi lolou.wa Portugal nénagne wawe.
@cheikhgaye50562 жыл бұрын
Kene dou thierno borome darou chicory
@papissbadji80553 жыл бұрын
Notre guideur
@diarrandiaye40913 жыл бұрын
Macha allah, mane dé talibé mame dabakh là wayé serigne bi dama ko sope
@mamadouseck97553 жыл бұрын
Être talibé Mame Dabakh n'a aucun rapport du fait de l'aimer. Dis toi que ''borom Darou, tu l'aimes'' point.
@diarrandiaye40913 жыл бұрын
Tu es libre de faire ton commentaire.Mais ce n'est pas à toi de me dicter ce que je dois dire mon cher.
@mamadouseck97553 жыл бұрын
@@diarrandiaye4091 je voulais juste te revenir. Et je te présente mes sincères excuses, si tu le prends mal... Lii Alhourane wax ni ''fii dini nafcikha'' motax madone layabiir rék.
@madiarafaye63143 жыл бұрын
Magal touba 2021 valide dierediefé mame cheikh ibra fall
@ibrahimandiaye89243 жыл бұрын
Talibé chiékh la waye jme bien borom darou bilahi
@morbeye45713 жыл бұрын
Merci talibe chiekh
@kamaraawa81213 жыл бұрын
Je suis tidiane mais j'aime beaucoup borom darou machallah contanena
@coumbafall20783 жыл бұрын
Yalla nako yalla défal diamou
@amycole6213 жыл бұрын
Machala wa choucori li nehna dieureudieuf Mame thierno yala nala bor jeome Touba faye li dawna yarame Aka bahe Aka âme yeurmande d'où kene Mame thierno la sama yarame migui dawe machala machala nayou deme baci kaname diga guisse Lourawe li diarama Mame thierno
Sénégal danion wara Santa yalla sugniou Mame yi kilifa dineh yi danioufi bayi Lou bah je suis moustarchid talibe ya seydil mouhamadou Moustapha sy mais borom darou rek la beugeu
@zeynadiop45243 жыл бұрын
Borom darou gnepele sope ya bah ndeyssane
@mbenefam90253 жыл бұрын
khaam thierno diot na mbacké dieuredieuf
@coumbabeye99693 жыл бұрын
Thiey borom darou sama serigne sama xeel nieup gui Darou
La journaliste a bien dit, l’avenir d’un pays c’est la jeunesse …..😅😅😅 Senegal nekhna
@mamamniang40683 жыл бұрын
Ndeysane Amiiiiiiine ya rabi machallah 🤲🤲👌👌👌👌👌🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏💔💔💔💔💔💔💔💔
@coumbafall20783 жыл бұрын
Borom daarou kouma nékhla
@aliamsdiocou90103 жыл бұрын
Mashalahh
@mouhamedaidara5583 жыл бұрын
Where is coran and sunna of prophète Mouhamd psl
@peaceandsalam28523 жыл бұрын
Suñu makk ñi seeni njàngalee guennoul Al quran ak sunna dem leen ngueen gëstu séen mbind ba xam luñu bind moo gën ngueeni wër si commentaires yi di wax rek
@papediaw88713 жыл бұрын
@@peaceandsalam2852 merci
@babacaargueye58623 жыл бұрын
Jour bi lougnou fi diangue si al khouran barina j’en sui temoin
@morbeye45713 жыл бұрын
Merci merci merci 🙏🏿🙏🏿🙏🏿👏🏿👏🏿👏🏿
@awasaine50243 жыл бұрын
MaShAllah 🙏👌
@bambatoubareck3 жыл бұрын
machallah borom darou
@ibrahimagueye28653 жыл бұрын
Ya bakh th fonk ndiabote guiiii😭👌🏼❤🖤
@malick94003 жыл бұрын
Baboulahi toi ou rien🥰🥰🥰
@mamadoudiallo26963 жыл бұрын
Waa lii lamb la wala
@mamelatyrly87583 жыл бұрын
Yaw con gua rek
@mamanndiaye67593 жыл бұрын
Jaime sa simplicité
@adamengom12103 жыл бұрын
Boko guisse ba toke ak mome guaye khame simplicité téme sama frèrou yaye kharitame la
@mamanndiaye67593 жыл бұрын
@@adamengom1210 Manshalla c'est rare
@adamengom12103 жыл бұрын
@@mamanndiaye6759 mo defarate khale yeupe machalla
@khadimethioye22113 жыл бұрын
Dieureudieuf borome chicory
@ndoumbekane91333 жыл бұрын
kenn dou thierno koudoul Thierno
@ndeye86583 жыл бұрын
Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤
@ahmadoubamba97563 жыл бұрын
Alhamdoulilah
@diopweuss91413 жыл бұрын
Sikori 😭
@Ndiayemo9213 жыл бұрын
Akssa borme darro
@ababacardiop90073 жыл бұрын
Diarama borom darou chikory tous les talibé de mame thierno borom darou noreyni sont des responsables kou téd ki moko déf
Portez vos masques! Bon sang! N'oubliez pas que vous etes loges dans le group des asymptomatiques . Pensez au retour a vos parents et proches d'un age avance restes a la maison!
Diambar merci wayé corona mission wam la dokh niouy dokh sounou mission masque meunou arrr kén si corona
@bassirousenghor71803 жыл бұрын
garde tes conseils pour ts enfant
@moustaphadiophamdy14973 жыл бұрын
Kéne waxu léne deugu. 365 jr xna tay ngéne diaap sii wagnii fooo biii nk si farata biiiiiiii. Dooof kéne douko né ya môme diangu yiii
@maam70293 жыл бұрын
Deggloul paroles yi mo geun: “Jerejeuf sunu Baay Thierno, kendou Thierno koudoul Thierno, xam Thierno diote na, Jaarama Borom Darou Chikory... Yaadi seutou Mame Mariama, di doomi Noreyni, Borom Darou, Ndangou dieul na thieurou begne, leer ya sarr na sarralé ba Chikory”
Mane talibe Chiekh la mais ndamale darou damako beugue
@mouhameddiaw32143 жыл бұрын
Blh Mane sakh
@mariamagueye78433 жыл бұрын
Sama khol bi toyna diamou yala da forr
@salkabrahim36853 жыл бұрын
Li kaye dou diamou yalla ,diamou seytané le ,melni combats lamb arène nationale
@moustaphadiophamdy14973 жыл бұрын
80 % gni fa nk amoune diplôme amoune joop c sa l'avenir toukh 🚬 sangara 🥛 ngir yaala déléne até deugu
@peaceandsalam28523 жыл бұрын
Ragalal yàlla est-ce que da nga leena guiss ñuy tux wala ñuy naan Guddi gu ndëkk ci bàmmel ku ko dul xalaat lula neex defal waayee fàwwu ding ci jaar
@laminebadji59573 жыл бұрын
Vous n ètes pas malin vous
@loptimisteoptimiste41313 жыл бұрын
Yaw ya amoul dara mola perte toop réseau sociaux ak say commentaires you négatifs mandou dala war lii mom moment de communion regroupant tout les êtres excepté yaw mi tekiwul dara yaw mou négatif mi do gate yaw vrais saytané nga
@juniordiallo29283 жыл бұрын
Mandou bahna dh seytané gua rk gni meune naniou may sa baye khaliss
@smbackeniang39063 жыл бұрын
Fii ay takhwalou kat kèssè
@thiernodiene96223 жыл бұрын
Yaw bayil togn togn bakhoul yaw gni Niola tané fouf pask dagay togn t niom toniougn doul way
@idambye31323 жыл бұрын
Santa serigne touba rek❤❤
@sambkarbala44623 жыл бұрын
Mandu🙏
@yorosarr41403 жыл бұрын
Niit kou bakh dou togne
@amycole6213 жыл бұрын
Machala wa choucori li nehna dieureudieuf Mame thierno yala nala bor jeome Touba faye li dawna yarame Aka bahe Aka âme yeurmande d'où kene Mame thierno la sama yarame migui dawe machala machala nayou deme baci kaname diga guisse Lourawe li diarama Mame thierno