Esckeey machallah mbacke Balla noreynii yalla ngaffi yague lool téé and koo ak weer ak weerlee sii barckee borom Touba mame thierno Ibrahima faty ndamal darou al mouhty 💗🙏🏽
@tafsirhi-tech60786 жыл бұрын
Il est simplement exceptionnel notre Borom Darou Noreyni
@momodiaw17764 жыл бұрын
Sa Me manques énormément thiat yalla na yalla def diam way vive Sénégal
@Sopeymamediarra20245 жыл бұрын
Serigne bi beg nanou si encadrement jeunes yi macha Allah! Notre Gentlemara dal naw nanou ko, sope ka lole. Souma amone louma begueu si serigne bi moy done mou agali ligeyou Serigne Saliou si tole yi ak jeunes yi. Macha Allah, jeunesse bi wouyounanou ko bou bakh macha Allah, mi ngui defar djiko yi si ndank walahi, dieureudieuf Mbacke. Mon reve c' est de le voir faire travailler tous ces jeunes qui le suivent dans les champs. Faire des cooperatives, des champs ou ils sont embauches meme s' il le faut. La jeunesse a besoin de role model alors qu' il en est deja un. gentlemara so woter tole ya, ben jeunes dou dess! aye way mbacke diap si niou relancer sounou economie. Yalla Dioh nala holou haleyi, si sa naturel, sa simplicite, sa sincerite, so len wowone tolou harer niou topeula, so len wower si tolou thieb, dougoub, box, aviculture, pisciculture, jardinage, niou top la mbacke! Mane dama contane si borom darou macha Allah Mbacke, nianal la nga yague fi ter wer ! Dieureudieuf beg nanou!