Ndayechane kémane deugue la li serigne mame mor hamdy yalla na fi dolé yague toyal na sounou khôl
@falloufall33172 жыл бұрын
mashaa A llah
@modoundiaye1412 жыл бұрын
Manchalla amena solo dieu reu nguine dieuf
@Cinsenegalaise55122 жыл бұрын
Machalla niveau bi kawé nah lool
@mouhamedfaye15562 жыл бұрын
Ndaysan xam-xam 💡mooy koom koom 💡
@alourhan93492 жыл бұрын
Merci pape sidy fall
@amdysylla48702 жыл бұрын
Émission bi am na solo lool dagnu koy topp Saa su ne, at mu nekk. Gni ngéen di invité ay woroomi xam xam lagnou. Dagnou léen namm ndax lu néew lagnou léen di invité ci télévision yi waaye nagnu léen di bàyyi ngir Yàlla gnuy développer. Ta ngéen wagni li nguéen Di wax dafa bari xawa bari.
Éloquence bou andak xam xam yar ak teguin...Jeureujeuf
@lesbellesmeufsn42492 жыл бұрын
Invité len baye Adama Sarr
@ibrahimagueye96552 жыл бұрын
Pape sidy fall il faut pas exagérer bane dieuwrine gua meuss guiss mouy wakh Serigne diw dou dara am na wakh yo khamni kén doukko wakh yaak lay gueuneu déf que deffar