Serigne bii wakhal si moussa camara bayi serigne touba cheikh Ahmadou Bamba MBacke serigne cheikh Ibrahima fall, nagne ko averti ak Ambassadeur Sénégal aux états-unis inchalla
@sambalingeer56803 жыл бұрын
Akassa !!! Jërë ngeen jëf Baay Busra Yàlla në ngë fi yàgg té wér, Ceddo ak Baay Sidi amulleen moroom... Waaye " les frères MANGA " Yalla na ngeen MÀNG tay ak ëlëg barkepp Xassida yi 🙏🏿🙏🏿
@adamadiagne91683 жыл бұрын
Ndeysan khol fess na yalla Guen am guereumeul ku tedki
Pape Djibril lénn rék lalaye conseil moy waxtann bi bou tolo wè bénn ton bi bou ka dague si sa dianguékatt yi ngaye invite wala commentaires fèkk wax bi agoull mais manchalah émission bi amatina solo