Il doit être condamné à vie cette personne est un danger poure la société prison à vie
@hamzafall54752 күн бұрын
Boulèn gnou sonal ... Nabou lèye mongui ni gnou diapko si double meurtre tè amna libertè provisoir...Senegal amoul justice...
@AissataSow-n4i2 күн бұрын
Vérité absolue
@veriteabsoluedeugneekhoul17202 күн бұрын
Merciiiii
@sisterssister95372 күн бұрын
Ya aucune preuve contre Nabou leye . L'enquête suit son court!
@aminataseck55713 күн бұрын
Wadji fall defoul loudoul sokhor rew lake dome raye domou jambour !belle émission le papa a fait une très belle réflexion Masha Allah très pertinente Yallah na souniou borom kharé Adjana Diary Sow Yallah na metitame dess si adouna amine yarabi
@adjiadialo3 күн бұрын
qui kagn domeram deugu le qui boudé droguè tamite laloul domam
@adjiadialo3 күн бұрын
Doko narone violé dakh sibi nako bamou sett doko narone teude khamna l khale bi banie mou khotie ko bamou sedd mais dewoul wone dakoy teudé da khamni khale bi dh na motakh qui di domeram nanie ko livre niou ray dayam
@astoumaguettesissokho323 күн бұрын
Day féne litah drogue bi heurtelouko si propre domam mbame le moko tay
@cissehabib8125Күн бұрын
Vérité absolument ❤
@alimatoubah33443 күн бұрын
Moko tèye nagnu ko reye mu dièhe 😢
@fatoufall72032 күн бұрын
Tacke
@khakika-d9g3 күн бұрын
Mais tentative de viol cest du viol cest un crime niouko dak droguer niofi nek ter douniou def lolou cest un mauvais prétexte moko tey mane mi di wakh dama dane tokh wayer bayina sama khel meussoul nek siloubone dey fene
@zeynadiop71363 күн бұрын
Alkhamedoulila comme bayiga
@adjiadialo3 күн бұрын
qui moko tat domeram le
@Kingpronosenegal2 күн бұрын
Daguay doul bayiwo😅
@khakika-d9g2 күн бұрын
@Kingpronosenegal Sagua bi nguama sagua bayinala ak yalla dinaniou ater sagua wouma kene sama khalat rek la diokher di conseiller niouy tokh yamba dilene nianal niou bayiko kouder ak sa bamel bimako bayer mat na 15 ans bilakhi kene si adouna diaralouma fene tu m'insulte gratuitement pour lane loumala def da nguama kham gadou sama ak ndakh metinama lol sakh loukofi diar doumaley diangual worma lilakoy diangual di nguako am bayinala ak yalla lowakh bakhna mane douma yeukeuti kadou niak worma diko dieumaler si nit kharam Bakar bobou doumako guadoul kene yar limoula meyoul doulako khagne yalla Nala yalla sopi
@Kingpronosenegal2 күн бұрын
@@khakika-d9g mais magui AK béne bouka mou nieuw
@Gkcdshndsncs2 күн бұрын
Senegal tanke yobou wougnou nitt arène national entré gratuit pandre li doufa diouk
@sambandiaye53312 күн бұрын
Bien dit vèritè merci beaucoup
@ThiaraMbengue-cx9ne2 күн бұрын
Nagne ko ray mou deh diaroul yagal bayi dom ray dom pour lane
@alimatoubah33443 күн бұрын
Sa fait male parents diari yi di dègue li yeupe 😢😢😢😢
@adjiadialo3 күн бұрын
wa dji nanie ko poisoné sibir kasso bi qui bakhoul si société
@Ndeyesokhnafall-e5yКүн бұрын
ki da yabate bou diele drogue rayo sa dome dem di ray domou diambour melni deume ni thim
@fatoumoundaodiop63862 күн бұрын
Drogeu loutakh mou khame domame ak domou diambour papame aussi amenasi part de responsabilité sa dome teula ga niew sanileco Wa Sénégal deme teudeu Italie te mou khameni danger la pour population 😢😢😢
@mourtalladiagne3592 күн бұрын
C'est pas l'effet de la drogue par ce su'il a distengue diary et sa fille
@KhadySylla-yv9bx2 күн бұрын
Métina kou ray bouniou ko rayone ken dotoul ray
@DiocouBabacar-kg2de2 күн бұрын
Sariya rëkk lii nëkh yalla nëkh gniou. Nako yalla yeureume. Mom ame naa domm loutakh raayoul ko? Svp.pourquoi pas son propre fils c'est ça là question epui arrêter lés bla bla bla.