Visite du Khalif Général des Mourides au chantier keur Qacidas yi au complexe Cheikh Ahmadoul Khadim
Пікірлер: 245
@maguettembaye60454 жыл бұрын
Ndey sane serigne mountakha mbacke yalla gafi yague lole te weer mbacke si barkhe xassida yi amine rabi
@khadimbeye4314 жыл бұрын
amin
@allahalla80864 жыл бұрын
amine
@bocktvba27654 жыл бұрын
Aminne
@beuguebambaseck49164 жыл бұрын
MONDE = PROBLÈME... MOUHAMED SAWS = RÉSOLUTION... KHADIMOU RASSOUL = SOLUTION☝️☝️☝️Serigne Mountakha Mbacké Yalla Na Fi Yague Loool Té Andak Wéer🙏 DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA ❤️
@alinebadaratalibeserignekh17694 жыл бұрын
Bègue BAMBA Seck amine
@babacarcisse38234 жыл бұрын
Machallah rafetna yalla nayalla fayla ak serigne touba ak maodo sy
@DAMEWADE934 жыл бұрын
Amine barkep serigne touba 🙈🤍
@MrCSeck4 жыл бұрын
Amiiiiiiiiiiine way Cheikh bi
@alkhouranaksounnasounna50214 жыл бұрын
Amin waye si BARGUEB S.TOUBA AKH s.el HADJI malikh sy dabakha
@modoutouretv28764 жыл бұрын
Amineeeee
@Waxdeggteyallatax4 жыл бұрын
Babacar cisse yaw ko bakh nga bilahi amiiiiiiiine
@ablayediakhoumpa45094 жыл бұрын
Un bâtiment aussi complexe vraiment mouride yi wanétinane xam xam avec ce joyaux pour les écrits de serigne touba
@fatimthiam50324 жыл бұрын
Man dé ci yeen la bokk ci sama khol barkep serigne saalihou
@amdymoustaphafall99324 жыл бұрын
Lo meuna guiss ak lo meuneu dégu...HT rawna
@bambaniang93054 жыл бұрын
Mach Allah bilakhi sama xol bi Séde na lole mbacke balla Aïssa yaye diambarri l'islam yaye diambarri serigne Touba longue vie à vous je suis fière d'être mourid yalna ma yalla maye keur Touba si barcke mame cheikh ahmadou bamba
@cheikhmbacke60444 жыл бұрын
Amineeeee
@souhiboubadiane98114 жыл бұрын
Serigne mountakha bassirou mbacké yalla nafi yague loll té wer barkeb Serigne touba
@ahmandiaye60244 жыл бұрын
Aminne
@alinebadaratalibeserignekh17694 жыл бұрын
Abo Badjan amine
@cherif73144 жыл бұрын
Serigne mountakha dinama ray rk billahi maala beug ❤
@matarseck61124 жыл бұрын
Ndayssane wa Hisbou Tarkhiya raw nguéne dé dégal ma dji wakh rk mbacké balla Aïcha yague fi lole té wer barkep khassida yi amine
@ndiagamakhtardieng44574 жыл бұрын
S' mountakha diammi s,Abdou lahad rék la may diokh😥
@abdouahadahad42354 жыл бұрын
wallahi
@blackdioll4584 жыл бұрын
Serigne abdou lahat ak serigne saliou
@Senemusic_Plus_2214 жыл бұрын
Dieureudieufé Serigne Touba Wa Hizbu Tarkhiya walahi yénagnou saggal ! Yalnanguén lakheu Nguereumeul Serigne Touba Khadimou Rassoulilahi Sounou Yaakaar . Man dé yén rékka ma yémmm Walahi
@babacarwagne42904 жыл бұрын
Yague fi lool Mbacke bala si barké brome touba mi amoule morome tay ak eulek amine kouné amine yalla nga dadiek gueurmandé serigne
@ndattoudiop14954 жыл бұрын
Amine
@xaadim96154 жыл бұрын
Amine
@dieureuffcheikhibrahimafal96994 жыл бұрын
Diawrine serigne atout diagne machallah liguey bi rafetna machallah ça kaw ça kanam inchallah
@cheikhfiagne4 жыл бұрын
Dieureudieu serigne touba Mbacké yalla gua fi Yague lolle té am wéér ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏❤️❤️❤️❤️