N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii...
@rastablondy4656 Жыл бұрын
Père kadou yi rafetna longévité santé à vous
@ejarju406 Жыл бұрын
Merci beaucoup Père. Guiss Guiss ❤️❤️❤️.
@taphandiaye8963 Жыл бұрын
Tu restes véridique et cela dérange. Sachez qu'on a besoin de gens comme père Mangone. C'est une Bibliothèque pour le Sénégal. Il peut apporter encore beaucoup de choses à cette jeunesse parfois manquant de culture et de repères. Père est un éducateur par excellence et j'apprécie beaucoup ses contributions. Un homme de valeur et de courage dans ses points de vue.
@lamb_new-look Жыл бұрын
Père mérite du respect ces un véritable savant yalla na yalla goudale fanam
@Mrdiop Жыл бұрын
Yalla milaa défendre bobaa bataay yalnala takhawou
@mamadoudiop7124 Жыл бұрын
Ndeysane nittou deuglaa🙏🏾🙏🏾❤️❤️❤️
@yilebaba6565 Жыл бұрын
Gni andda ak reug reug dama yakarni gueumou niou yallah ! Mais lii defaite rek laa dou dara ci mbeur ... Ca change rien sur le parcours de reug reug , au contraire , defaite bi moye deff reug reug champion deug ! Sa thies bimouye danou contre Malick niang ak boy niang nii la démé wone , defaite yoyou nioko deff taye mbeur bimou done ! Franchement reug reug ak aye mbokam niou wara kholatt sen communication laniou , ils nous emmerdent ak sen wakh djou beurri , daniouy wouteul sen bopp aye none rek ... Dieredieuf Père Mbaye Ngoné
@ndeyesonadaffediouf Жыл бұрын
Hana hamo gnou tah regue gueuneu dof
@diawmoustapha407 Жыл бұрын
Vraiment
@mouhamedsambe7820 Жыл бұрын
Sa way reug reug amoul Mbok bou weir yayam reik moy weir
@mbackesarr4727 Жыл бұрын
Billahi dagno dof ta gno nara takh yalla tk ay natou metti reug ndx dagno nangou woul dogal yalla billahi
@milkmilo4082 Жыл бұрын
Yagi fépe sama wadji reug reug mo meune sa Thiès Walahi azim nimou démé ri até naléne
@salioudiop4399 Жыл бұрын
Force à toi pére nitou deug kassei nga
@ahmethsiby9994 Жыл бұрын
Il faut qu'on nose de dire la vérité quelques soit les situation on supporte reug mai ils à fait 4apui et ces ça la réalité félicitation sathies et du courage reug mai la cng à une obligation de régler le problème des combat sur place
@bailandiaye2979 Жыл бұрын
Père un grand connaisseur de la lutte
@mohamedngaide5774 Жыл бұрын
Ohhh c'est vraiment triste père sa khôl rafétna machaala
@aminataniang2948 Жыл бұрын
Machallah pere sa wakh refet na kilifa nilaye de dou tontou aye khale pere mbaye gone kontana thi yawa yallah gua am diam😍😍😍👍👍
@idrissaseck3331 Жыл бұрын
C'est très difficile de voir un habitant de thiaroye intelligent. Merci père !!!
@papefall5971 Жыл бұрын
Si linga yakar rék
@milck. Жыл бұрын
C vre pere machalla ♥️
@libasseniang7869 Жыл бұрын
tu nous a insulté sans même le savoir, je tiens à te rappeler que c'est vrai que y'a des irréfléchies à Thiaroye mais aussi y'a des intellectuels avec des têtes remplies de savoir
@idrissaseck3331 Жыл бұрын
@@libasseniang7869 tu n'a pas bien lu mon message,,, pourquoi j'y ai mi le mot "difficile" ??? C'est parce qu'il ya aussi des intellectuels ,,, moi même j'habite à thiaroye donc xam naa limay wakh,,,
@idrissaseck3331 Жыл бұрын
@@libasseniang7869 té mangui diégalou boko guissé nénénne👏👏👏👏👏👏
@ablayembaye8405 Жыл бұрын
Dieureudieuf papa machallah
@iboulo3988 Жыл бұрын
Machahalla Pere we love you ❤
@tmasterp8279 Жыл бұрын
les Touaregs sont derrière vous Père !!!
@Shjeuropfolrh Жыл бұрын
Bilahi père sama xoll sédatina ❤️yalla na sa diam yague vraiment mbeuri thiaroye yi dou niou ay sportif
@assleye8654 Жыл бұрын
Khadim ndiaye yagui sòga am problem nak per nena kum yakar sama mbokkula
@abdoufaye311 Жыл бұрын
Tu et super mon vieu machallah ❤️❤️❤️❤️
@elzoatti8951 Жыл бұрын
Félicitations père
@mactardiop2156 Жыл бұрын
Reug reug est le reflet de son entourage , il lui manque beaucoup de sagesse s'il veut faire une grande carrière son entourage doit être nettoyer ... le sport est un jeux ...
@babacarndiaye2698 Жыл бұрын
Yalna yalla goudal sa fane père mbaye ngoné on t'aime bien
@moustaphadiop1834 Жыл бұрын
Meilleur émissions per daf may fadji 😂😂😂😂
@modoufall1365 Жыл бұрын
Si Reug Reug ne fait pas attention aucun lutteur ne prendra soin de l affronter parce que ya trop d'histoire dans leur camp
@Hakimdiop11 Жыл бұрын
C'est fini pour lui li dall malick niang mokoy dall
@lamdaofficiel Жыл бұрын
Sérieux j'ai jamais commenté sur youtube.mais vraiment reug reug risque de perdre beaucoup de choses dans la suite de sa carrière.staf daffa am solo.wa salma
@issabayo8522 Жыл бұрын
Li lamb rek diarr nako Problem bi moy niouy waa thiaroye yeup khamna niou reug dane naniouko mais kou wakh niou tame la deume. Mais Reug dafa wara khamni defal goul dara si lamb ji meune na nek roi des arenes dafa wara guem lolou teh bayi tiakhane yi. Sa Thies dane la grawoul ndakh niom niar dinaniou beure watt na prepare lolou mo guen lii
@bdiene66 Жыл бұрын
Mon ami il y'a beaucoup de tricheurs dans L'arène. Les gens n'aiment pas les vrais champions et c'est dommage pour la lutte.
@ahmethsiby9994 Жыл бұрын
Reug reug a une obligation de regarder bien sa comuniquation et sont comportement puisque on le suit depuis très longtemps et on l'aime bien en tank mbok mai vraiment ces malheureux ce qu'il à passer avec balla ces un secret ils devai pas en parler
@malickndiaye3436 Жыл бұрын
Damako beugue rk tei Yalla takh❤️🤧
@pathesylla6971 Жыл бұрын
Père vous êtes international ken doula lal
@magy3113 Жыл бұрын
Non taye mome Père chapeaux wakh dji nice na
@ousseynoufall2289 Жыл бұрын
Merci père si question boko délo niatta reug reug mo am si adouna bii Mai pere Boul tontou bén mak bou irresponsable
@oumydiagne8938 Жыл бұрын
T'y
@aboubacarndiaye779 Жыл бұрын
Les partisans de Reug,reveillez vous, ce n'est que du sport, évitons de menacer les gens de mort, c'est excessif et une honte pour les habitants de Thiaroye, félicitez Sathies et allez de l'avant pour le bien de Reug,un sportif doit avoir un esprit de dépassement avec mes respects
@serignembackembaye1578 Жыл бұрын
Khadim Ndiaye kholatal sa bomm ko wakh muni tour wi
@MedouneAmar Жыл бұрын
De tout coeur avec père Mbaye ngone seutou damel
@baradiallo1656 Жыл бұрын
Merci père ma ngone
@tawdabasall Жыл бұрын
Oh père ya daig machalla doundeul rk ❤
@miandoye7480 Жыл бұрын
Pere 👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾💝🥰
@falloudieng447 Жыл бұрын
Per merci beaucoup
@jazzjazz4902 Жыл бұрын
WA THIAROYE VRAIMENT LI KHAROU ÑIOUKO SI ÑIOME LI DAFA ÑIAWE TOROPE LI SPORT DONGUE LA
@emmanuelmendy3058 Жыл бұрын
Père ndanane deug nga bilaye
@moussagueye7902 Жыл бұрын
Mbaye tu es une référence. K. Ndiaye est un déséquilibré.. Reug Reug doit s'éloigner de lui
@papandiaye1823 Жыл бұрын
Père yow wakhal loula nekh ba keneu lalela rek 👌🏿
@ousseynousow5336 Жыл бұрын
Merci Père li nga wakh rek nga wara wakh
@BeauGossFaramareen Жыл бұрын
Ndeysane un sage . Sénégalais begeneu sport waay xamouko
@cheikhndong359 Жыл бұрын
Machala per ma.gonee ken d'où yow kou kham lamb 'nga War naniela diokh imission lamb si tale yi
@assaneniang7 Жыл бұрын
Thieuy père mo dégueux🙏🏿
@requinquin1 Жыл бұрын
Reug Reug avait l'intention de blesser ou tuer Balla Gaye 2 et personne ne réagit 🤦 Naniou ko téré yoré " Badiène " Bédjéne, sinon dineu meusseu gaagn nitt ci arène bi ndakh doff la. Heure bii waroon na fékkeu niou défféré ko mais Galsène dou deukkeu c dommage
@bayladiop642 Жыл бұрын
Sa parle trop de mal diamou dji yalleu bayi media yi
@requinquin1 Жыл бұрын
@@bayladiop642 koy wakhal nonou 🙄
@truckwarriors9832 Жыл бұрын
Reug Reug est le reflet de son entourage ay con deug, ken nawlowoulene nakh niak nitter, pere du courage!
@kaninekahn6273 Жыл бұрын
Wa thiaroy gueumouniou yalla khana😂😂😂 yen naka nguene meuné gueum ni nit Molène khagne victoire. Ak naka lalene KO père ngone khagné😂😂😂 doul way loudoul yalla d'où gatt
@alassanedieng259 Жыл бұрын
Toud yalla ték thi saga thieuy
@cheikhahmadoubambasarr1518 Жыл бұрын
Pere merci ❤
@ousmanefaye6467 Жыл бұрын
Oh Père ya wakh deug way, Mane litah NGA nékhma Moy sa Beug SERIGNE TOUBA, linga wakh lepp deugleu té deugouna rafétt na
@moussafall9400 Жыл бұрын
Pére yaw yatakh ma commentaires ndey ssane yalla nala yalla may goudou faan ak werr rekk fall yaw moom sama mbook nga
Tête pleine il connaît trop De choses ce vieux Mbaye Ngoné Machalla
@amadoufall8193 Жыл бұрын
Dieuredieuf pere mbaye ngone
@bybrufisquois257 Жыл бұрын
Ha père tay nak wakh ngua deugueu gniwakh diarouniou tontou, tracel sa chemin rek yalla guider la inshaa allah
@sambadrame3497 Жыл бұрын
Machalla pére yalla bakh na
@momidiop7878 Жыл бұрын
Machalla
@ousmanewillane8479 Жыл бұрын
Merci beaucoup perr
@khabs2628 Жыл бұрын
Wouy 26:45 pére néna leuf lo 🤣🤣🤣🤣
@diazpaco3809 Жыл бұрын
Petit à petit on laisse les esprits malsain s'installer attention à cette rancune c'est l'image du pays mais le sport doit unir l'esprit Fair play..Lou teug Tass té Dara yagoul
@momonjiae2314 Жыл бұрын
Mashala père amna solo iao môme nite nga
@amadouba4254 Жыл бұрын
Tiey reug reug sou meytul kom niom khadim Ndiaye ak issa pouye lay moudje C triste
@mariobarba3798 Жыл бұрын
Per yabakh di yaguell te wer Barack serigne touba Cheikhouna akhamdo Bamba ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ khassidayi Khadim ndiaya dafa tradì si adouna amul dara si adouna ko dakhar ndeye yamla
@ycamara9034 Жыл бұрын
Wow Peace ✌️
@koffimendy-cc3gh Жыл бұрын
Moytoulén mag bou kham merci père
@falffh7737 Жыл бұрын
Merci
@assanegaye513 Жыл бұрын
Bilahi damakko yeureum saxx
@diengsoda7570 Жыл бұрын
Pére yaay mbokoum reew mi koula lale laale reew mi Nanou réglé laa wakh té doundd céne défaite o calme
@alfarokhevision8801 Жыл бұрын
2iem défaite bu ecri regue regue bi 😂 rousna sakh
@princetorodo8590 Жыл бұрын
deugeu mn nekhoul mais père mbaye ngone limou wakh dafa lerre 🤷♂️
@massambadiop8181 Жыл бұрын
Bilahi Wa camp reugg reugg lal nguén lalaké nak père mbaye ngoné da nguén done yorou waya yapp Nguén ki dou Bécaye deih ki dou moustapha Guèye 🤣🤣😂😂
@papendiaye6424 Жыл бұрын
Per merci
@abubasey4245 Жыл бұрын
Machall amna solo
@mbayesarr6052 Жыл бұрын
Thieye Pere moy Sénégal déh
@ilimanediop529 Жыл бұрын
Cest triste vraiment
@papagueye3597 Жыл бұрын
Machalla pére tu connais bien l sport
@massambadiop8181 Жыл бұрын
Wolof néna khalé bou réw day moyou makk bou féké lépou ki deih khana mou am loumiy sétt waya limou féké beurina boulén ko wakhlo bakhna
@kemesambsamb9059 Жыл бұрын
Vraiment li métinama bilay ki amna louko méti trope 😓
@ilimanediop529 Жыл бұрын
Torope
@mbayepape-wk4tn Жыл бұрын
Dieureudieuf per
@princetorodo8590 Жыл бұрын
Billahi père bou nekon mbeur signature dina nkh trop 😂😂😂😂
@daguathioune1432 Жыл бұрын
😂😂😂😂 dafa leeer bilahi père dafa nekh quoi
@222musicofficiel2 Жыл бұрын
Ils est très génie machallah
@sadiokaradiallo3414 Жыл бұрын
Bilahi père sénégalais xamoul sport
@Mrdiop Жыл бұрын
Xamnaa palace baa ngaay waakh diarnafa bataay dém tol
@AminataWade-d5g6 ай бұрын
Yaw diam rek gay AM ❤❤❤❤
@cheikhwade4438 Жыл бұрын
Vraiment li niaw na bayilein bayou diambour bi ngenn di saga
@oliviervaz4658 Жыл бұрын
Sports dal il être fair play reug reug am défaite niou begua khas tout le monde
Niane nalako boulwah tourbi,wahal ngorsi Ndiaye wahal,dofou Thiaroye bi 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
@abdoulazizwade3204 Жыл бұрын
Vous savez au Sénégal on a de sérieux problème on confond adversaires et ennemis " sport d'où khaadialai mais daye bolai mais li yeupeu problèmou fan's club la mais kou beugue sport diko doudou doko yak té ce problème c'est partout même dans le domaine politique nos leaders que ça soit l'actuel Président ou les opposants niome nieupeu sene yenai moye defar donc pourquoi une telle violence et pourtant ce sont les soit disons intellectuels niokoye defe kounek meune ngua faral koula nekh même dans une même famille.
@boromnimzate4615 Жыл бұрын
Billahi wallahi wakh nga deugg pure et dure ndakh la petite soeur de bombardier avait supporté modou lo même en luttant contre bombardier son frère sans problème et sans gêne
@deuguekepp10 Жыл бұрын
Lamb ak lenene l c'est po du sport..dakh amoul sportif
@mbayendoye5779 Жыл бұрын
Douma ndakh alamap lébou 😂😂😢😢bayilen lebou yi waaye roussna sakh😢😢😅😅😅
C’est un beau parleur ce vieux. Entre ce qu’il dit et ce qu’il fait, il y a une éternité. Toutefois, je condamne fortement les menaces et injures à son endroit.
@mohamedfaye4493 Жыл бұрын
😂😂😂😂😂
@julioniasse1932 Жыл бұрын
Cela ne donne pas le droit au camp de Reug Reug d'insulter,de menacer,d'utiliser des propos malveillants,de parler de la mére de Modou Mbaye,de la femme de feu Double Less,niougui tass aue famille,ils se prennent pour qui pour ne pas accepter leur defaite et il suffit que quelqun accepte la victoire de Sa Thies pourqu'ils te traitent de diable.C'est une tres mauvaise image qu'ils sont entrain de véhiculer,la lutte a connu des champions avant Reug Reug.Yekini,Balla,Modou ce qu'ils ont fait il ne l"a pas encore fait.Ils font yrop de bruits et risquent de porter préjudice au gosse
@ahmedmbackefall6109 Жыл бұрын
yalla motakh May wakg mais cf kil fit y c kil fait estimé opposé fait mbouppo thiaroy ça l'avait vfrit
@cheikhsyllame4457 Жыл бұрын
Bilahi reug reug ak sa wa keur laissez le vieux tranquille
@abdourahmanefall6546 Жыл бұрын
Kou deukoul AK lébou rek meuno khame djiko lébou père mougnale.
@TheBandafall2003 Жыл бұрын
Yeah j’habite avec eux ils ns appellent étrangers à Thiaroye tu peux rien contrôler à Thiaroye si tu n’est pas lebou
@mbayendoye5779 Жыл бұрын
Mouniii🤷🏽♂️🤷🏽♂️😂😂😂😅😅
@serignemakhoudiandiaye361 Жыл бұрын
Difficile à cohabiter avec eux des mecs problematiques
@bayfallfall1256 Жыл бұрын
Te gua wakh te guene si lebou yii
@sambadiordiagne3168 Жыл бұрын
Aw leegui wakhgnou lala djikkeuy lebou?
@ndoffngom7994 Жыл бұрын
Khadime ndiaye limou amouton si lambeu yeuppp pr mom di reug reug lako wara amé mais nakk Yagui nakh sa bopou
Reug reug moy kane dafa waroul danou wala ?respecter lén nitt gni yaw reug reug ak gni nga andal .lambou kouy beuré yay dane mé yay danou .faut être sportif