Ada Fass clôt le débat sur sa relation avec Pokola Baldé : "nioune daniouy…, Balla Gaye 2 damay"

  Рет қаралды 35,049

Gaston Productions

Gaston Productions

Күн бұрын

Пікірлер: 67
@manoumbaye6277
@manoumbaye6277 Ай бұрын
Bayilen domou adama yi nguén di croix sen titres yi pour attirer nit yi dou yoon
@b_lebou8908
@b_lebou8908 Ай бұрын
Merci mangui dem mangui tiit sax yakar dafa am lou balla def😂
@yvondiatta9616
@yvondiatta9616 Ай бұрын
T’as parfaitement raison frérot li dou yone
@ibrahimambow9000
@ibrahimambow9000 Ай бұрын
Danga faté ni que Gaston Production la tmt😂😂
@derkonig3859
@derkonig3859 Ай бұрын
Dagno reew
@afro3827
@afro3827 Ай бұрын
Yow dé ndaw boula roy sankou 😂😂
@bassiroundaw4751
@bassiroundaw4751 Ай бұрын
😂😂😂kiii. Ahn ben instant ayy ree lamay deff weroul deeh
@elhadjisambe3549
@elhadjisambe3549 Ай бұрын
😅
@diawnumero1071
@diawnumero1071 Ай бұрын
Ada fass nimouyy deff kanam bi meuna sii 1 million😂😂😂😂
@MameMbaye-d1e
@MameMbaye-d1e Ай бұрын
Nice😂
@KhadimeNdiaye-n7b
@KhadimeNdiaye-n7b Ай бұрын
Bly bo dieulé Modou lo Dinga khamni meuno beurre amo dollé 🤙🏾🫡🫡
@MbayendiayeNdiaye-r6v
@MbayendiayeNdiaye-r6v Ай бұрын
Boy ki da meune mbeure am doole
@modo6218
@modo6218 Ай бұрын
Kii vip yi menou se dan kenn 😂😂
@khalifadiemekhalifa5883
@khalifadiemekhalifa5883 Ай бұрын
So amone kilifeu boy di nga réglé faut éviter certaines choses et tu concentre sur ton avenir bro
@YoroDialo-hm5vc
@YoroDialo-hm5vc Ай бұрын
Ada fass sougne la né waxal loy wakh ???
@PapamodyWagne
@PapamodyWagne Ай бұрын
Yaw réglél danagofi mbeur zarko ngafi am mou défaral la ngay nguamou wakh rk
@falloudione8641
@falloudione8641 Ай бұрын
wakhofi dara ay door laa do dane kéneu
@ndiameseye3283
@ndiameseye3283 Ай бұрын
Bilahi yen journaliste mbeur boufi naaguou rek gnom la ms ki koum fi dan bay bal bal lou ni ki bilahi mérité woul ay Modou lo, Balla gaye ,eumeu sene na prouvé basi kanam en tou ka mane eumeu sene moy sama mbeur bou beurék ki ma bayiko eum aliou seye 2 moy combat bi mom na djeul jacob baldé wala ay gnom zambala lolou moy deugu
@modo6218
@modo6218 Ай бұрын
Kii ay rée lamay deff bilahi yaw petit lo sakh meno ko dan ay pa rek nga dan
@mamadounguom4992
@mamadounguom4992 Ай бұрын
Ya Bone khôl gniata moromam la dane khana do guiss
@CiroManzo-fg4dp
@CiroManzo-fg4dp Ай бұрын
Yanala yalla May kilifeu
@prospermendy4975
@prospermendy4975 Ай бұрын
Yow do sportif
@MamadoukhalySow
@MamadoukhalySow Ай бұрын
Défo dra si lamb Zarko seul
@moustaphababou6282
@moustaphababou6282 Ай бұрын
ADA Fass yawe onde leu fou mola dane zarko dala pade nga danou yawe do dara
@pronosticfootsenegal1112
@pronosticfootsenegal1112 Ай бұрын
Ada ndakarou tay soiree ibra nadio amena dé 😂😂😂
@sambatv3730
@sambatv3730 Ай бұрын
Boul bayi lamb de boyy ada fass teh nga nek nitt bayyi yeufou doff Di zembre loulou yeufou doff la
@cheikhsene9247
@cheikhsene9247 Ай бұрын
Il ne sait même pas répondre aux questions posées... N'a kholatte bopam
@PapeSow-l2d
@PapeSow-l2d Ай бұрын
Démal geu outii dollé mo geun gay nakhh sa bopp beuss bo amé mbeur dingeu xamni lambe dou thiaxane gouy gii binga dane dafa febar té aven gakoy dane stad bii yeup la saga nekal nitt linngeu beug wakh mayé wouko
@CharlespierreCamara
@CharlespierreCamara Ай бұрын
❌ Balla Guaye 2 bi pour ?
@MakhtarSall-t1i
@MakhtarSall-t1i Ай бұрын
Ada fass borom Dakarou
@AliMalal-ji9js
@AliMalal-ji9js Ай бұрын
j’ai l impression kil n est pas normal 100 pour 100
@cheikhmbackeseck1608
@cheikhmbackeseck1608 Ай бұрын
😂😂😂😂😂 ndeyesan ki damako yeureum wakhi dofe rek guafi wakh demale entaine ji
@aboubacarba3410
@aboubacarba3410 Ай бұрын
Worna Yalla Kii Kagñe Lah🤣À Par Mbokoum Milieu Yii Kou Beuga Baakh Douh Dieul Thii Mom Exemple Walla Bay Topp Thii Mom Sakh😂
@MoussaNdiallo
@MoussaNdiallo Ай бұрын
😮❤😮😮😮
@princetorodo8590
@princetorodo8590 Ай бұрын
Fans bandit nga
@metza-e1e
@metza-e1e Ай бұрын
Ah saway ma fokni 3 combats mola déssé...?
@LamineGaye-x1h
@LamineGaye-x1h Ай бұрын
Go Dou touss
@Bayedame-tf7ll
@Bayedame-tf7ll Ай бұрын
Ada bilaye dafa diongué kois😂
@manebaye4021
@manebaye4021 Ай бұрын
Dangay nakh sa bop
@Gueye-zu9ur
@Gueye-zu9ur Ай бұрын
No ki loutakh ma bgue ko Rk la hamoul 😅😅
@papito8025
@papito8025 Ай бұрын
Ada bala la dei mounane xalei la , amagouma 30 ans etc … 🙄amo 30 ans mais am nga 27 ans té balla gaye est devenu Roi des arènes à 25 ans 🤷‍♂️ … da Nga tarder té yeugoko bilahi . Delorme la deuk barké cheikhoul mais da Nga bari wakh tekci Naagou. La vie que tu mènes ak Lamb andoul , té nioussou nioula ba nga k.o do regler Mbam bi😡
@OusmaneFall-xv2uu
@OusmaneFall-xv2uu Ай бұрын
Mdrrr yalla dou faye wakh bayi dieud
@famaradembele2734
@famaradembele2734 Ай бұрын
Ngone soirée ibra nadio amna dh
@mamathiam5649
@mamathiam5649 Ай бұрын
Niar yii gua moudié dane nio gene nékhé dane iow do mbeur
@fallousylla7866
@fallousylla7866 Ай бұрын
Yawe daga niak diom
@Charleskandio
@Charleskandio Ай бұрын
D'où sa comportement bi ma lakoy may nékal nitt
@sidyfaye44
@sidyfaye44 Ай бұрын
Nékal nitt boy danga warra nek nit
@AboulBacharSall
@AboulBacharSall Ай бұрын
Yaw 3 combat mola desse di wala dangua faate😂 wala sousse bii mola baye goul
@MoukhamétNdiaye-g9s
@MoukhamétNdiaye-g9s Ай бұрын
Ada fass liko dalé si franc ba Modou lo meuno si danne kén vip yi gnola eup gnola Moune fouff barki seydina Mohamed
@cheikhdiop9932
@cheikhdiop9932 Ай бұрын
Ada. Gor Gor loul rek figa tek sa tank bakhna. Diga guis ndia ring bi
@CheikhDieng-b9g
@CheikhDieng-b9g Ай бұрын
Soko begué digua sangé sa comportema
@morgningue7654
@morgningue7654 Ай бұрын
Yw khana Kone, 3 combat yi daga done sob rk 😂
@Bigboss-hd8fx
@Bigboss-hd8fx Ай бұрын
Boy t nga yem si madji madji bo beugué aye victoires feulé gars yi tok andoulak soirée
@KhadimeNdiaye-n7b
@KhadimeNdiaye-n7b Ай бұрын
🎉
@famaradembele2734
@famaradembele2734 Ай бұрын
Saway yaroul nk reww nga loll
@Methmethavelly
@Methmethavelly Ай бұрын
Nekal nit nak
@MorTALL-i4k
@MorTALL-i4k Ай бұрын
Ada bougou mala saga mé yaw kou niank diom nga mouno nékh niit té nga khamni niit say nawlé laniou tégué déguelou père coundou koula beugue la mame wék na domam wayé baniou ko
@marambaye5926
@marambaye5926 Ай бұрын
Yaw dhè doto dane kène fi AK 5 combat walahi
@bouryGueye-jt5kk
@bouryGueye-jt5kk Ай бұрын
Ada fass potîé lo combat lee
@saerhihiodf110
@saerhihiodf110 Ай бұрын
Ki weroul ta niakeu na diom 😅😅
@NdeyemaremeFall-jw1pn
@NdeyemaremeFall-jw1pn Ай бұрын
Diaal diop sangomar bi seul
@WallyDiop-z1e
@WallyDiop-z1e Ай бұрын
Ki dafa con
Sa Thiès Fait des révélations explosives "Balla gaye Lim Wakh C N G .....
6:48
Hoodie gets wicked makeover! 😲
00:47
Justin Flom
Рет қаралды 104 МЛН
Walking on LEGO Be Like... #shorts #mingweirocks
00:41
mingweirocks
Рет қаралды 6 МЛН
Trick-or-Treating in a Rush. Part 2
00:37
Daniel LaBelle
Рет қаралды 43 МЛН
🚨🚨Balla gaye 2 dadone deugueunték Ada Fass lou doy war
7:52
Fadam2 expert de la lutte sénégalaise
Рет қаралды 137 М.
Hoodie gets wicked makeover! 😲
00:47
Justin Flom
Рет қаралды 104 МЛН