Allahou akbar😱 Cheikh Mbacké Sakho diouli yep man niari rakka lakoy def lolou la yalla wax, ndialo

  Рет қаралды 46,734

TIKGALSEN TV

TIKGALSEN TV

Күн бұрын

Пікірлер: 353
@alyndiaye5168
@alyndiaye5168 2 ай бұрын
Yalla nala yalla guindii AK mbolem dioulite
@As_salih-t9i
@As_salih-t9i 2 ай бұрын
Kou toppp mbacke Sakho rèrr nga torokh nga
@thiernoousmanesow2110
@thiernoousmanesow2110 2 ай бұрын
Mane dé mom lay topou.limiy wakh day daw sa yaram ndax si coran la diogué
@mamadousakho4549
@mamadousakho4549 2 ай бұрын
Perte nga ​@@thiernoousmanesow2110
@alajindom-fs3iz
@alajindom-fs3iz 2 ай бұрын
En tout cas je ne suis pas son disciple . Mais il a donné ses arguments dans le coran.
@moussd5864
@moussd5864 2 ай бұрын
@@thiernoousmanesow2110 en tout cas , la plus des autres ne donnent pas darguments , c s ki est domages ou bien leurs arguments ne pesent pas trop. Car ils ne s appuient pas trop sur le Coran
@DakarFaDA
@DakarFaDA 2 ай бұрын
@@alajindom-fs3iz Non ses arrguments ne tiennent pas. parce que Yalla dafani yonente bi dama wathié alhourane si yow pour nga expliquer ko gnenen gni. té à travers sunna lakoy expliquer. Coran daffa ame yo khamni résumé la. Que ce soit la prière, le pélerinage (la date...), le ramadan...et bcp d'autres actes ne sont pas expliqués ds les détails. Nul ne peut se baser uniquement sur le coran pour adoorer Allah. Gni transmettre le coran gno transmettre les hadiths gnoko binde. Bo si wéddi rek wédil benen bi. Bo seuyé rek sangoul té ken waxoula noy sango, donc on fait cmt?
@aboridial3431
@aboridial3431 Ай бұрын
Walahi waxo deug cheikh sakho
@umardia8474
@umardia8474 Ай бұрын
yallananiou yalla mousseul si sheytanè
@ndiayembaye1458
@ndiayembaye1458 2 ай бұрын
YALNA YALLAH GUINDI
@Président-ABDOU-DIOUF
@Président-ABDOU-DIOUF 2 ай бұрын
😂😂😂Jap ngane yalen eup xam xam....
@lepdiamfall6498
@lepdiamfall6498 2 ай бұрын
Aminnn lolou mo diara gniane
@englishclassmonitoringecm5152
@englishclassmonitoringecm5152 2 ай бұрын
Après le Coran, il y a la sunna. L'Ange Jibril enseignait beaucoup de chose au prophète Muhammad (saws).
@b_lebou8908
@b_lebou8908 2 ай бұрын
Nie niom nioy khouraniyou na yi alhouran laniouy topeu bayyi sounah té yonnent bi nena صلوا كما ر أيتموني أصلي diouli len kom nimay dioulè yalla wax si coran ما آتاكم الرسول فخذوه وما نهاكم عنه فا فانتهوه yalla mo way lounen yonent bi diox dieul len ko lou len terei sori lenko mano topeu alkhouran bayyi sounna yalla moniou topou lo yonenet bi si alhouran
@Abdoukarim313
@Abdoukarim313 2 ай бұрын
Yow dé ya kham louy khouraninioune yalla mouslim la wokh naniou ko done
@zababs10
@zababs10 2 ай бұрын
Lolou bako yalla di wakh yonent il parlait du butin de guerre
@cheikhdiop9673
@cheikhdiop9673 2 ай бұрын
​@@Abdoukarim313Muslim wa Kone loufi andi souna ki dafay wakh pour gni khamoul cheikh mbacké sakho Moy Kane ak limouy woté Moy lane gni khamoul cheikh mbacké sakho laye wax
@aboumansourniang4771
@aboumansourniang4771 2 ай бұрын
و ما أتاكم الرسول فخذوه و ما نهاكم عنه فانتهوا Batt bi tekkiwout li ngua wakh. Lou mouy tekki moy thi arabe deug moy : ak lou lên yonni bi indil dieulên ko loumou terré moytoulên ko. Battou raçoul ( رسول ) dou ap nit ap yonni la thi français moy message pas le messager. Kon raçoul ap yonni la dou ap yonnênta. Dem lên diangui grammaire ( إعراب ) yaw ak mbacke Sakho moy lou guênna thi yên. Cette phrase du Coran se traduit simplement par : « suivre Dieu c’est suivre son message » Salut !
@diogenelaerce2197
@diogenelaerce2197 2 ай бұрын
Yaw wakho fii dara 😂😂😂. T’es un salafi. Ce monsieur est incontestable
@MamadouDia-f3g
@MamadouDia-f3g 2 ай бұрын
Cheikh Ahmed Cisse yalla nala yalla fay Mbacke xam ngani si ay karhi rek nga nek
@laminediagne8993
@laminediagne8993 2 ай бұрын
CHEIKH MBACKÉ SAKHO WAROO CITÉ BOUKHAARI AK IBN MAADIA PARCE K NÉENGA GUEUMOO LOUDOUL ALXURAAN
@yvefay620
@yvefay620 2 ай бұрын
oui mais dans les hadiths le coran qui avec ses 26 versions est incompréhensible
@bigndanane1448
@bigndanane1448 2 ай бұрын
Non il n'a pas convoqué Boukhary ndakh gueum-gueum. Mais juste pour montrer que même gni gueum Boukhary, cén dieuf wouténa ak li nékk ci téré Boukhary
@elagegueye3310
@elagegueye3310 2 ай бұрын
​@@yvefay620ya meu kath guenalniou 26 versioyi
@diogenelaerce2197
@diogenelaerce2197 2 ай бұрын
Si t’as pas d’argument… tu la fermes
@bocarwade8241
@bocarwade8241 2 ай бұрын
​@@bigndanane1448dafa delo ci xadiss ndax migui wax woute bi am ci ndiap
@lacitoyenneafricaine8566
@lacitoyenneafricaine8566 Ай бұрын
Sama khel bou gatteu geueume nani djouli bou eupeu mo gueune bou manqué ! Lifi mame bayi wone ba legui mou djik gnou nagnou si teukou abadane rek. Yalna ya allah lerale khel yi te nguindi gnou si barki Rassoul karim. Allahouma amine.
@Khadimjoop5413
@Khadimjoop5413 2 ай бұрын
قال سيدنا ابوبكر(ديننا مبني علي النقل لا علئ مناسبةالعقل)
@baboundoye8110
@baboundoye8110 2 ай бұрын
Li moy débat d idées. Ma cha alla
@tesdeshlm9718
@tesdeshlm9718 2 ай бұрын
Wakh Allahou Akbar nékoul si Alkhour'ane .... voilà une preuve tangible Que personne ne peut se passer des hadith du prophète saws..... Cheikh Mbacké bi si ay thiakhane lanék
@ngonesaliou8347
@ngonesaliou8347 2 ай бұрын
Hadiths création nite leu
@abdoukarimsidibe5711
@abdoukarimsidibe5711 2 ай бұрын
Sourate Al- isra verset 111, "Et dis: Louange à Allah qui ne s'est jamais attribué d'enfant,qui n'a point d'associé en la royauté et qui n'a jamais eu de protecteur de l'humiliation ". Et proclame Hautement Sa grand. Ici louange à Allah= alhamdoulilah Proclame Hautement Sa grand= Allahou Akbar. tout est dans le Coran c'est vous qui ne comprenez rien en lisant, Allah nous dit dans la sourate 6 verset 38 : " Nous n'avons rien omis d'écrire dans le Coran , puis c'est vers leur Seigneur qu'ils seront rassemblés...." Omis= oublié de mettre. Gueustou watlén sén diné bi,té moytou arabes yi niom nio Ray Ali, Ousmane, Omar, assane, Oussey gaday lo yonentebi mou jougué maka dém Médine . Faudrait t'il croire les livres de ses arabes.?
@ibrahimaba5199
@ibrahimaba5199 2 ай бұрын
​@@ngonesaliou8347Yaw ya rére yonénte bi la yalla wathié guir mou léralalal gniou alhouran té koko geumoul do dioulite achhadou an laa ilaha ilalah ach hadou anna mouhamadarassoullalah la yalla wakh nga soga don dioulite té alhouran dafa teungkou dou n'importe qui Mokoy téki d'où ay meuneu wakh wala ay idé hadiss monioukoy léralal.
@adjamoubayeniassendiaye2986
@adjamoubayeniassendiaye2986 2 ай бұрын
​​​@@ngonesaliou8347 Et quand est-il des hadiths qudsi. Ce sont les paroles de Dieu que Dieu a inspiré saw sans qu'il soit textuellement dans le coran Comme par exemple quand il dit " j'étais un trésor caché et j'ai voulu me faire connaître. Je créai une créature par qui on me connait . Que faites-vous des hadiths aussi ????? Comme vous voulez nier tous les hadiths
@aliouba6480
@aliouba6480 Ай бұрын
Takbir maguissi
@Fallmuslim
@Fallmuslim 2 ай бұрын
❤maachaala cheikh mbaccke sakho
@dramestardrame9497
@dramestardrame9497 2 ай бұрын
Mashallah amnasolo 🎉🎉🎉
@cheikhbabacarmbaye2353
@cheikhbabacarmbaye2353 2 ай бұрын
Mbackè sahko ya rèr yonèntabi mo diagalè dinê ta alkhourane sì mom la wathiwon yaw ya geuna dègeu alkhourane mouhamed spl ragalal yalla yonantabi mo diagalè l'islam khamolo alkhourane 😢
@mortalladiop7144
@mortalladiop7144 2 ай бұрын
Kii dafa réw billahi😮😮
@SeydouMbodji
@SeydouMbodji 2 ай бұрын
Cheikh Ameth invitél Professeur Madiama ça sera un débat très intéressant ❤
@jecodedoncjesuis875
@jecodedoncjesuis875 2 ай бұрын
Ce professeur raconte tellement de bêtise !!
@ngonesaliou8347
@ngonesaliou8347 2 ай бұрын
​@@jecodedoncjesuis875bayil féne mo meune sa baye
@ababacarsadih8030
@ababacarsadih8030 26 күн бұрын
Non koku borom xam xam la dina tokk ak dof yi
@tafsirdiop2292
@tafsirdiop2292 2 ай бұрын
Kou topou mback Sakho safara gua jemm
@ibrahimasene549
@ibrahimasene549 2 ай бұрын
Ya sokhor safara nit gua do yala
@thiernoousmanesow2110
@thiernoousmanesow2110 2 ай бұрын
Safara niou ték fa ataya rék
@CheikhsadbouAidara-ck3vu
@CheikhsadbouAidara-ck3vu 2 ай бұрын
​@thiernoousmanesow2110😂😂😂😂😂😂😂
@MameCheikhLo-p9v
@MameCheikhLo-p9v 2 ай бұрын
Lou werr
@MameCheikhLo-p9v
@MameCheikhLo-p9v 2 ай бұрын
Bly iblis dfa Doug ci diné diamono dji diakhasé leppu
@bigdia2266
@bigdia2266 2 ай бұрын
Yalna léne yalla guindi
@BiraneKhoulli
@BiraneKhoulli 2 ай бұрын
Mbaké Sakho mo bariy thiakhane😂😂😂😂😂
@MouhamadoulamineSeck-e1o
@MouhamadoulamineSeck-e1o 2 ай бұрын
Walahi mo beri thiakhane
@dieyemamadou8847
@dieyemamadou8847 2 ай бұрын
da bari thiakhan moss
@Le_Natron_
@Le_Natron_ 2 ай бұрын
Wallahi
@alyndiaye5168
@alyndiaye5168 2 ай бұрын
Mbackee Sakho srx dagua reere
@dieyemamadou8847
@dieyemamadou8847 2 ай бұрын
ki kay daa rér ta khamoulni daa rér
@alyndiaye5168
@alyndiaye5168 2 ай бұрын
@@dieyemamadou8847 trop sax vraiment m nakk ignorant leu dh
@lacitoyenneafricaine8566
@lacitoyenneafricaine8566 Ай бұрын
Dégueu lou nala yaw Cheikh Sakho ngani "kou djeneu aduna kene douko djouler nagnou ko sangue djeule yobou soule". Ma laye ladj ndakh dinkou nga say mbokk wala nitt de confiance wala imam niko yalna yekh " yaw so djener aduna boula keneu djeuler nagnou defar rek djeule souli?".
@MbaroodyNdiaye
@MbaroodyNdiaye 2 ай бұрын
Dégue yalla ji dana léér par force merci sakho
@aboridial3431
@aboridial3431 Ай бұрын
En tt cas il ptrend un grand risque Mbacké Sakho
@Fayelo123
@Fayelo123 2 ай бұрын
Waaw me mame diomi na deh 😮
@adamacamara2861
@adamacamara2861 Ай бұрын
refernece hadith : "Sahih Bukhari , 140" nous montre comment faire les ablutions qui complete le verset n est pas en contradiction avec ,pour faire simple le coran est la constitution et la Sunnah de notre prohete PSL est le reglement voire la loi ou meme decret d application , la suna vient expliciter le coran, sur la base des observations de notre bien aime Muhammad PSL - dans sa vie de tous les jours let ces compagnon sont les meilleurs - Cheikh Mbacke da nga rer - yalla na gnou yalla bole guindi - gnoun gneup
@tesdeshlm9718
@tesdeshlm9718 2 ай бұрын
Légui no xamé historique le jour du vendredi bakoy nétali... vraiment ki dafa sankou
@babsinfostv1665
@babsinfostv1665 2 ай бұрын
Cheikh Cissé dieuf ci tay ndakh question yi lerna té lima beugone xam ci Cheikh Mbacké
@aboridial3431
@aboridial3431 Ай бұрын
Mbacké Sakho mi si gatal nena Sérigne Touba, Elhadji Malick baye Niass niom nieup Danio rer
@lesamouraisnoir5304
@lesamouraisnoir5304 2 ай бұрын
Ki bayiléne diko déguelou koukoye dégelou kou sa pass pass degueroul dina nguakal sa geum geum
@ndiougadiop7250
@ndiougadiop7250 2 ай бұрын
Subhanal'lah ki soxla na ndimbeul d yallah na yallah guindi
@KooMboup
@KooMboup 2 ай бұрын
yénn gniy wédi mbacké sakho kenn ana séni. preuve lolou rk lay lathié😂😂😂😂
@Sénégal-aujourd8
@Sénégal-aujourd8 2 ай бұрын
Aka yombou !! Oustaz Akhlou sunnah yi léral nagn co bamou lerr wallahi … bo comprendroul dagay yakarni il a raison
@ababacarsadih8030
@ababacarsadih8030 26 күн бұрын
Doul katt la en plus wakhi dof diaroul tontou
@mouhamedkasse1220
@mouhamedkasse1220 7 күн бұрын
Mais qu'elle preuve qui c Un fou qu'on doit arrête Rapidement
@B-221
@B-221 2 ай бұрын
KHAM AL HOURAN.. TE TOPOU SOUNAY YOUNENTIBI TAKHOUTA NEK DIOULIT SOUNAY YONENTIBI REK MOY DIINE TE MOM NANOUY TOPOU
@fatoumbodj27
@fatoumbodj27 Ай бұрын
Je suis confuse 😢 qu'Allah montre le vrai chemin parce que là je suis très confus 😭🤲
@aliounewade4412
@aliounewade4412 Ай бұрын
Dooyna war dal
@Pan_fn-kz5rl
@Pan_fn-kz5rl 15 күн бұрын
Kii limouy wax dara doussi deukk traduction wam yi bahoul kii amoule ham ham boko déglo dinga réére
@aboridial3431
@aboridial3431 Ай бұрын
Walahi daagay fen si gatal ki dafa wax yonent bi diarul won mouy niew guir jangal niou dine Alhouran leral na lep
@sokhnandiaye6177
@sokhnandiaye6177 2 ай бұрын
Parfois dal damayy mandou sinon djikhy djikha layy indy kone bilal da nodeu te woter djiouly leu ci langue arabe donc yalla n'a yalla yeureum te nangou sougnou diamouyalla
@HssptDiallo
@HssptDiallo 2 ай бұрын
Al Quran wahoul❤question bamel❤
@cheikhtidianely2349
@cheikhtidianely2349 2 ай бұрын
ta wahoul niou sangue naiw ak jouléko
@cheikhciss5549
@cheikhciss5549 2 ай бұрын
Guissnga soofi bayyé YOnéntibi doo ame argument
@barambow581
@barambow581 2 ай бұрын
Mbacké sakho kouleu bayikhél rék guindékou
@expertpablo7148
@expertpablo7148 2 ай бұрын
Kou beug Lou yomb rek mokay top
@Sénégal-aujourd8
@Sénégal-aujourd8 2 ай бұрын
La xawla walla xuwata illah bilah kou wéddi sunnah yonete bi né li alhouran kassé lay yam tei limouy wakh ci alhouran détails bi moguici hadith yonete bi … ki kane la meuneu guindi
@mbayeba9845
@mbayeba9845 2 ай бұрын
Les comenter des sunnite ndeysane alhouran kèssè dalène di derangè
@DakarFaDA
@DakarFaDA 2 ай бұрын
Sourate 59 verset 7 doyna daline pour Sunna.
@serignepgueye4853
@serignepgueye4853 Ай бұрын
Et si tu as perdu conscience pendant une journée que faire avec la prière
@englishclassmonitoringecm5152
@englishclassmonitoringecm5152 2 ай бұрын
En tout cas les Shiites ne prient pas comme lees sunnites et ne citent pas le prophète Muhammad (saws)...
@SerigneSaer
@SerigneSaer 2 ай бұрын
Cheikh mbacke ya sof khamoleen dara
@MouhamadoulamineSeck-e1o
@MouhamadoulamineSeck-e1o 2 ай бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂walay walay
@ibrahimaba5199
@ibrahimaba5199 2 ай бұрын
Alhouran Moy yonou yonénte bi kén meunoul nék ab dioulite té do top yonénte bi yalla KO wakh téksi yalla si mom la wathié alhouran pour mou révèlé KO téksi binde ay hadiss ngir todialgnouko ndakh alhouran dafa diss té Lou diafé dégue la genrou mbacké sokho yi nga khamné dégouniou Dara Di diahaséka wakh loulén nék Di fén rék . Kouko top mou sank là yonou cheytané là . Lifi yonéte bi bay niom imam Malik yénén imam yép nékon si ba légui mbacké Sakho mi nga khamné tékioul Dara beug fé indi lénéne kouko top bo déwé yéwou.
@mbackendoye876
@mbackendoye876 28 күн бұрын
Naala lébal sama xalisss ngani ma wakhtou wa. Passer na douma la fay souma la mbeuggé😂😂rééw
@Ibn-youssouf
@Ibn-youssouf Ай бұрын
Mbaké sakho néna sakhabaa yi danio done dopa diaymé ak diéndeu mi la topone si jouri aldiouma Loulou alkhourane la wala
@yaragteggiin5101
@yaragteggiin5101 2 ай бұрын
Yalla na yàlla yeureum cheikh mbacke sakho هاداك الله 😢😢
@seydounourouniang2780
@seydounourouniang2780 2 ай бұрын
Thiey Sénégal ce Mr Mbacké je ne sais quoi wa Sénégal danion worone niouss ndeyem srxma.
@masstv2484
@masstv2484 2 ай бұрын
Billahi ki soun si diogoul dina sanke ndaw you bary ki nite darra yi war nan si wakh Diap alkhourani sounu borom ji diko fire nouko nekh wa baax na nan setan rek
@zababs10
@zababs10 2 ай бұрын
Mais ki wakhou yalla ley wakh deh dou ay wakham yén key dieufleunté léne AK yalla rek t bako
@aboumansourniang4771
@aboumansourniang4771 2 ай бұрын
@@masstv2484yaw demal niouss ndayam sagam thi deug ngua nek. Mom xamna ne alquour’aan bi Loumou indi bokout ak li nguên Di deff thi sunnisme. Erreur bi mouy deff moy nimouy firi alquour’aan daray dou thi deug. Dafa dak Hadith ba noppi di top tafaçirs ak tarjama bouhari ak yi ni mel.
@blacknegro7408
@blacknegro7408 2 ай бұрын
Tu as dit vrai ce gars sa mission c'est de combattre l'islam et égaré bon nombres de musulmans c'est des sectes sataniques qui rentrent dans la religion pour semer la zizanie
@thiernoousmanesow2110
@thiernoousmanesow2110 2 ай бұрын
Soit Poli
@BaraDiop-cv8ij
@BaraDiop-cv8ij 2 ай бұрын
yalla néna toppe lén yonnentibi sallal lahou alayhi wa sallam, C est le meilleur exemple. yonnent bi nena diouli len kom nimay dioulè
@sauljob2396
@sauljob2396 2 ай бұрын
Senegal mom feem tolu nee bess bu ku bess guena, dina bu bess
@abdougassama9322
@abdougassama9322 Ай бұрын
Demande le si le prophète faisait ça, mais quand tu l'entends il écarte le prophète et il essayé d enseigner sa propre enseignemnt
@diodiondiaye5450
@diodiondiaye5450 2 ай бұрын
Ki vraiment doméram
@SambaSy-i5d
@SambaSy-i5d 2 ай бұрын
Bayelen ki dof la
@mohamedfall6154
@mohamedfall6154 2 ай бұрын
The calling for prayers. Was because every mosk leader wanted to wake the people. Mostly mornings prayers. THATS IT. NOTHING ELSE.
@serignecheikhfaye5899
@serignecheikhfaye5899 2 ай бұрын
Kouy dieufé ay waxam sankou sène xeil reik lanouy waxei té diné dou xeil alxourane amna loumou indiwoul mais khadith moy motali leip
@mouhameddia5168
@mouhameddia5168 2 ай бұрын
xam xam laye déhmé
@serignecheikhfaye5899
@serignecheikhfaye5899 2 ай бұрын
Yalla xamnani liguay wakh dou xam xam sa dîné bopou ga amm
@senenutscompanyets3664
@senenutscompanyets3664 2 ай бұрын
​@@serignecheikhfaye5899 bayi doul ligua wakh amoul
@Alioune123
@Alioune123 2 ай бұрын
Thiakhane rek! Yonente bi Alkhourane bouy dokh la.
@diogenelaerce2197
@diogenelaerce2197 2 ай бұрын
Ça veut dire quoi 😂😂😂
@PapeDemba-eu9hu
@PapeDemba-eu9hu 2 ай бұрын
Mbacké sakho boul sonal sa bop sa message menoul dialleu
@modoufall1297
@modoufall1297 2 ай бұрын
Suite bi wakh tane bi amna solo
@elagegueye3310
@elagegueye3310 2 ай бұрын
Wahtanou domeramyi ganan amna solo😮
@MouhamadoulamineSeck-e1o
@MouhamadoulamineSeck-e1o 2 ай бұрын
Khame guani guani kéne doula top bayi yonénetibi mousiba la ki
@Sénégal-aujourd8
@Sénégal-aujourd8 2 ай бұрын
Ce qui est bizarre Mbacké Sakho bo jangoul diné boka déglo dagay yakarki il a raison parsk il se réfère sur une sourate alors que les détails sont dans la Sunnah du prophète ( tei mom ci alhouran kassé lay yam geumoul hadith yonete bi )
@BabacarNiass-zb9lb
@BabacarNiass-zb9lb 2 ай бұрын
جنب loumouy firi si wolof
@BayeFall-c7n
@BayeFall-c7n 2 ай бұрын
Kou andeu ak sobbé
@IbrahimaSow-z1w
@IbrahimaSow-z1w 2 ай бұрын
Cheikh mbacké sakho habite ou
@johnjanha3910
@johnjanha3910 2 ай бұрын
SUBHANALA.
@salioudiene7271
@salioudiene7271 2 ай бұрын
Mbacké mi foum bock
@Ismaeljallow-k3b
@Ismaeljallow-k3b 2 ай бұрын
Mbackeh Saho yaw danga doff.
@cheikhflodiao6091
@cheikhflodiao6091 2 ай бұрын
Nitt meunoul maîtrisé al'quran ba raw yonenti bi.. Tei yonenti bi mo raniaani woone nieuw djangalé djaapp djangalé djuli ba paré. Kone kénén douniou djangal djuli
@bayefallgalsen2096
@bayefallgalsen2096 2 ай бұрын
Ay diamono mo fi done critiquer Cheikhoul Khadim. Li yeup ay setlou you am solo
@realb.a.bslofficiel5598
@realb.a.bslofficiel5598 2 ай бұрын
Bou yaboo kou nèkk na topou sa wasileu guemou tè bagn deglou kènèn louko moy DAJAAL yii dinagn la rèereul. Kou amoul werouwaay bou deugeur dinga yomba gueleumeul. Jeureufé Cheikh Ibrahim Niass❤
@elagegueye3310
@elagegueye3310 2 ай бұрын
😂holen comantairou mbay ba nan sounityi alhouran kese dalen di déranger.nel Sénégalkay 90% souneu dalendi déranger
@yvefay620
@yvefay620 2 ай бұрын
Mais quand Allah et ses anges prient sur ou à Mohamed ils prient à qui et pourquoi ils prirent pour lui puisque pour vs il est le meilleur des êtres.. Il est Dieu ou quoi ???
@zizou6648
@zizou6648 2 ай бұрын
Très pertinents ❤❤❤❤
@KooMboup
@KooMboup 2 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤
@omarjako1915
@omarjako1915 2 ай бұрын
Hadith 2020 du Inn Madia'a wakjoul li di Saho wakh. Hasith bi si divirce lai wakh mais pas ai kharr ak ai bei.
@BaCheikhouna
@BaCheikhouna 2 ай бұрын
Mbacke sakho mii fomou diangue yeen 😂
@aboumansourniang4771
@aboumansourniang4771 2 ай бұрын
Liy woudou amout thi alquour’aan weurguel kepa ! Verset 5:6 wakhout djappou walla sanguou sett.
@galasssakho5178
@galasssakho5178 2 ай бұрын
Chekh kabar bi dano gua si😢
@sokhnandiaye6177
@sokhnandiaye6177 2 ай бұрын
Alkhourane mo nakary interprète vraima interprète Alkhourane yomboul j préféré me limite
@cheikhdaffe9944
@cheikhdaffe9944 2 ай бұрын
Sakho c'est un gars que j'aime écouter mais il se trompe sur l'interprétation des versers coraniques.
@lacitoyenneafricaine8566
@lacitoyenneafricaine8566 Ай бұрын
Fouma rombeu se video ladj nala li: "pourquoi tu dis toujours dina wah Fatiha ak Al Coran". Wa pourquoi Fatiha ak Al coran te fatiha bok si Al Coran? Wala se wahine fofou mo leroule ?
@lacitoyenneafricaine8566
@lacitoyenneafricaine8566 Ай бұрын
Si domou djalo mome logique ngafi tek. Nane le ay "say say" demer deff li lene nekh après dome djoudou si gnouni khaler bi la gnouye "punir". Khel nangou wouko. Khaler victime le dou responsable. Ya allah si sourate at tini thia fin ba birome bi wah na moy le plus juste des juges alors ay domou adama tok ni gno koy punir gno kay atter wa lou khaler bi deff??? 😂djoudou rek le deff te tanou ko...
@B-221
@B-221 2 ай бұрын
LI YONENTIBI DOM DEF DARA GANOU KA WEUR ADUNA BI YEUP BEND FASON DIOULLI REK MOFI AM TE MO WEUR WAYE KAYI DANOUY DOYODAN DIINE DJI SANKOU FARATA BIMOU WAKH DARA BAKHOU SI AK DIAP BI AY WAKHAM TEKOU WOUL FÈND
@maodogamer
@maodogamer 2 ай бұрын
Adouna touki na
@dieyemamadou8847
@dieyemamadou8847 2 ай бұрын
touki na moss
@diogenelaerce2197
@diogenelaerce2197 2 ай бұрын
T’es un fou toi😂😂😂…
@benmouhamad2021.
@benmouhamad2021. 2 ай бұрын
Kuko toppu réer boy saaxo mi
@KhadimBabou-u4q
@KhadimBabou-u4q 2 ай бұрын
Moytoulma nafékh bou diangue kou noye bope gnou wolbatila
@Abouhalima
@Abouhalima 2 ай бұрын
Mbackr yonou sankoute nga diel
@MbaroodyNdiaye
@MbaroodyNdiaye 2 ай бұрын
💪💪💪 sakho rkk 😂😂
@MameCheikhLo-p9v
@MameCheikhLo-p9v 2 ай бұрын
Bou aduna toukki ap diouli dufi dess nit danañ diouli di woor wayé la yonenti bi diangué won yeppu lañi bayi Iblis dfay fekhé ba effacer yonenti bi moy sunam boko defé nak ap dioulit do tofi dess nak
@cheikhbarambacke4812
@cheikhbarambacke4812 2 ай бұрын
ومآءاتينكم الرسول فخذوه وما نهكم عنه فا نتهوا
@DakarFaDA
@DakarFaDA 2 ай бұрын
Mom nimouy dioulé yeup alhouran diangalé wouko. dem weut ben verset bouni nga sabal yalla ni moy kabbar bi. mom diouli ak wor yeup amoul daline
@elagegueye3310
@elagegueye3310 2 ай бұрын
Kon loutah yalla ne Mohammed psl.kou dioulidjiwoul 3 djoulys vendredi yeferga.nankatou sagara ak nonou mouhameth psl nioy lif
@cisseaziz2707
@cisseaziz2707 2 ай бұрын
Yalla nalla yalla guindi mbacke
@niomrelo1959
@niomrelo1959 2 ай бұрын
Kii dafa diott Morom kham kham yii toke am mom si plateau télé yii dadji ko si kham kham 😢😢😢😢
@DiaMbar-si3cu
@DiaMbar-si3cu 2 ай бұрын
Ki Loy dadji ci mom ? Bo diangoul dangaye Yakar ni limouy wakh amna place ci diné dji fék diégé woul Sakh AK islam
@abdoufall2928
@abdoufall2928 2 ай бұрын
Maa diomi mane😮
@jupinleye8346
@jupinleye8346 2 ай бұрын
cheikh mbackè sakho kii moo gueuneu katt ndayam maneu doûl waadjii c'est un danger
@moula8497
@moula8497 9 күн бұрын
Il raconte ses propres histoires. Qu'Allah nous protège des ennemis de l' islam
@mamadoudior5239
@mamadoudior5239 2 ай бұрын
Alxourane rék Moy deuge
@diopdiaga3361
@diopdiaga3361 2 ай бұрын
Mbacké sakho thiy thiakhani keppou nga nek😂😂😂
@sangarebarry6508
@sangarebarry6508 2 ай бұрын
CHIEH MBAKE AMNA HAMHAME NARYI DAGNOU MODIFIE HAYATYI REK LHEUR DE PRIER FADJIRI COMPLIQUE FI SI FRANCE DE
@aboridial3431
@aboridial3431 Ай бұрын
Allhuran nena kou topul yonent daga rer te ku rer safara ga dieum
Cheikh Mbacké Sakho vs Cheikh Ahmed Cissé Cissé
2:27:00
Cheikh Ahmed Cisse Official
Рет қаралды 10 М.
Cheikh Ahmed Cissé vs Cheikh Mbacke Sakho
2:51:38
Cheikh Ahmed Cisse Official
Рет қаралды 40 М.