Bly Modou lo moy gore sotnagnouko sote bou niaw té meussoussi niaw Modou Lo est un professionnel et il est le meilleur
@requinquin14 ай бұрын
@@morgaye9582 kouko sott?? Ay man sénégalais yawmal qiyaam. Niép dina niou réglé séni dossier vite fait sénégalais déss fa ndakh niémé Yalla bilahi. Onzou billahi mina sheytaana rajiim
@fallpapa4 ай бұрын
😂😂😂
@ablayeseck44544 ай бұрын
Yalla nanu yalla souteral takhawu niou niou teral sunouy wadiour😊
@abdoulatifdiop56404 ай бұрын
Allahouma amine 🤲🏿🤲🏾
@MoustaphaDiongue-if7lc4 ай бұрын
Allahuma amine 🙏❤️
@AmadouBalde-gy3oy4 ай бұрын
Amine yarabbi
@abdousarr99414 ай бұрын
Allahuma amine
@FallouLeye-s8h4 ай бұрын
Amine😂
@madasylla33404 ай бұрын
Khana mistik boukoul si lamb niou merci père thiaw sonal wayy saytane guene trop merci Azize félicitations balla courage tapha tine c’est fini
@SambaThiamsall4 ай бұрын
Respect len sen wadiour yii guene bayi saga yii respect dafa bax si domou adam
@LamoDiagne4 ай бұрын
Merci beaucoup tu as bien dit
@fatimandao83594 ай бұрын
Nitt yi légui daño réw sokhor saga nitt yi si commentaire la khamoul pour lanela ñak argument rék
@malicksarr21414 ай бұрын
Aziz ndiaye nit kou béwla ❌ modou Lo champion yalnako yalla maye ndame ❤
@fallelhadjiabdoulaye23474 ай бұрын
Daguané néx kw kou andoul ak modou rek bew la😂😂😂😂
@ibrahimadieye70514 ай бұрын
@@malicksarr2141 yalla mo kham kou bah
@papeserignembaye86794 ай бұрын
Wakhal deugue fo guiss béw
@requinquin14 ай бұрын
@@malicksarr2141 Modou Lo mo meun Siteu lolou djaroul wéranté. Bouko Siteu daané combine leu. Tapha Tine rékk la doon moytou motakh mou djeul Siteu
@requinquin14 ай бұрын
@@malicksarr2141 Balla daan na Tapha Tine 2 fois. Yékini 2 fois ci bénn takoussaan. Té Modou Lo laalé woul ak nioniou. Motakh titre Empereur bi normal ndakh Roi bi moss naniou ko 2 fois avec la manière. Yéén gnii di wakh kou ci doon beurré wala nga am domm djouy beurré bo sagnoon Balla lay nirool ci lamb dji.
Aziz Ndiaye dé kouko bagne rék mbeurem da dioutal sa mbeur ta ndiarigne lim am si Sénégal gnikoy khass améwougnouko ndiarigne séne famille bakoy amé ndiarigne Sénégal Aziz Ndiaye yalla nako yalla samm arko si barkep Al khouran
@cheikhdia95514 ай бұрын
Yaaw doul sa khet yi nio yakheu ndeye rewmi kou am xaliss ngen defko bourr nioune guemouniou ndeye borom xaliss borom yarr ak borom xol bou set moniou gondi ngay doul nane mane beugouma ndeye aziz t douma setane lamb awma mbeur na mbeur yeup deh baxam legui apres
@fallpapa4 ай бұрын
@@cheikhdia9551 diaroule sagga
@CASI77974 ай бұрын
Modou Lo yalla nala yalla sammeuu
@kamaraawa81214 ай бұрын
Amine
@matarlo9534 ай бұрын
Li khadime gadiaga wahh lolou moy degue
@bayeratebayerate58934 ай бұрын
Aziz Ndiaye dafa reww ndayam
@NdiareMboup-vi6sk4 ай бұрын
Motat ndayam
@m_g30094 ай бұрын
En tout cas Aziz Ndiaye wakhoufi dara lou ayy xalaa tam rék la wax 🥺
@ndakarudialdiop12064 ай бұрын
Diam rék ngay am Aziz❤, sissou man yii dioy, sén kholi di bone nopalulén khamni balla gaye moy lamb ❤
@jeanlouismendy7134 ай бұрын
Aziz tek xel leu
@allaniang84284 ай бұрын
Li lepp mystique leuhh
@IlimaneSamba4 ай бұрын
Becay mbaye ki boulene ko nexal loudoul bewwww japakou
@modousarr88484 ай бұрын
Béw rék
@ibralemeringue32584 ай бұрын
Bilay dafa béww
@cheikhndiaye99144 ай бұрын
Aziz Ndiaye naniou ndaye dimbali d'où nday daraa
@IbrahimaDiallo-hd9nr4 ай бұрын
Aziz mola guene fouf kene khamoula tédial sa gatte😅
@Ahmadou-bl9oh4 ай бұрын
@@IbrahimaDiallo-hd9nrya meun doul khana sa bay la geun doméram
@IbrahimaDiallo-hd9nr4 ай бұрын
@@Ahmadou-bl9oh yaw khamna domou orjeu NGA motakh nga meune saga 🤣
@nafisene53354 ай бұрын
@@IbrahimaDiallo-hd9nrYow doul kou la kham
@fatimandao83594 ай бұрын
Mais pour lanela saga yi
@GN03044 ай бұрын
Et puis Mansour le promoteur de Jambaar doit corriger Aziz.
@abdourahmanesindidi18184 ай бұрын
Pere becaye tres véridique mashalla
@MactarDiaw-u2r4 ай бұрын
Fadam limou wakh duegg la lolou coach dousi jiel Sakh avertissement regel ma mayénko merci Fadam 2
@OldySy-v7u4 ай бұрын
Aziz topal falé
@ibrahimabadiane82524 ай бұрын
Azize ku béw la ku réw
@gabyndiaye36544 ай бұрын
fans ballala mé aziz day plané koi koumou nékh far foula nékh
@TidianeMbaye-k9w4 ай бұрын
Sénégal nion sokhor aziz yafi nek
@fatysyll56434 ай бұрын
😂😂yaw esk ça va do wax ahlou lamb ngay Sénégal
@cheikhtidianefaye8244 ай бұрын
Fi ken sokhorou fi Aziz Ndiaye mo Wara nguen thie ay thiakhane point
Aziz de fe arrogant de trop ... il pensé que le fait arroser tout le monde d'argent vont faire de balla gaye un roi des arènes , mais malheureusement pour lui khadim gadiaga et modou lo ont tout compris.
@volfroitfall87854 ай бұрын
@@khalifakane8415iow dagua dofff
@assgueye98994 ай бұрын
Merci beaucoup fadame wakh nga degue dé
@abdoulayebalde37864 ай бұрын
Aziz Ndiaye loumou ame yalla la .nit dou soxor ❤
@Dpp2054 ай бұрын
Loumouy am?
@cheikhmbenguebaye_fall4 ай бұрын
@@Dpp205moma diakhal alal dou dara
@abdourahmanesindidi18184 ай бұрын
@@cheikhmbenguebaye_fallalal kay dara nak seugn bi bayi len waxou wolof ndiaye yoyou
@Victoireman4 ай бұрын
C bien pour lui mais âme alale tahoul mou geune nitt yi, même notre bien aimé prophète Muhammad sallalahou aleyi wa salam, il n'était pas millionnaire..wayé mo geunoneu nieup...il doit arrêter de vouloir détruire modouu a tout prix...
@yatmaseck30564 ай бұрын
Aziz dafa yabaté ta khamoul bopam 😮 kholal sa morom milliardaire yi baréwunu wakh daga sokhor rek surtout li Modou lo yor budé empereur mon eup dolé kay louguénkoy top😮
@reglerek60714 ай бұрын
J’adore père becaye 😂
@issamballo37344 ай бұрын
Wa Lambj nio ragal Aziz Ndiaye
@AbyDiaby-w7w4 ай бұрын
aziz Ndiaye doul deumeu nga sokhore nga trop doul modou lo seul
@alinesyllaSyllaaline4 ай бұрын
Aziz deum leu
@matyseck70034 ай бұрын
Sa yaye moy dembou
@khadimfall9794 ай бұрын
BG2 rekk ❤
@Rhitnewtv98354 ай бұрын
Aziz billaye wallay adouna dina la yeeh wallay dinga xamne yalla mayewoul dey lebale
@NayeFall-qq7xi4 ай бұрын
Loo ko yéene mu ñàkk naanal ndox soxor baaxul
@ousmanediaw3484 ай бұрын
Merci beaucoup khadime gadiaga
@cheikhbasskeurmassar95484 ай бұрын
Aziz Ndiaye kéne dou mome machallah
@henricorentindiedhiou11244 ай бұрын
Aziz Ndiaye nous fans de Balla Gaye on est fier de toi pour tout ce que tu fais pour notre lutteur
@mamadousegnane94624 ай бұрын
Salam fans modou la mais aziz c'est quelqu'un de b1 vraiment Albourakh vraiment mogui diapelè lamb th amousi dara Albiurakh dagnio yereum mbeur yi wayè sénégalais yi s'en xol yi nekhou si gnisi barri du gniep mais kepp koup mbeur vraiment yagui sante albourakh Dakh moom rek mo xam s'en thiono th dilen diapalè th sentouwoun dara exemple kouy fayekou 1 millions albourakh gniew ak yeurmander dila fay 15 millions vraiment chapeau à albourakh di gnianal gniep jamm ak goudou faan amine ya rabi
@Victoireman4 ай бұрын
Yaw dagay féne do fans Modou plus tôt ennemi Modou akk saay teste bou gouddou😅
Aziz ndiaye j'adore rek ngua mome momo nitte gni amo bene fouleu
@khalifakane84154 ай бұрын
Pour yawe jadore rek la mome lolou ga khame kaye😂
@adviseragnam70504 ай бұрын
Milliardaire bouyyy fén di coupé thimmm😂😂😂😂
@nafisene53354 ай бұрын
Ki dafa xamoul boppam
@BoyPoulo-kg5pl4 ай бұрын
Ki domeram la
@MatarFall-ze1fl4 ай бұрын
Aziz wakh len ko degue yaw
@tidianebiaye15734 ай бұрын
Merci beaucoup Aziz Ndiaye borom baax contaane nagn si yow❤
@seringediopargentina66294 ай бұрын
Azis dafa soukhar tourop
@chatif11964 ай бұрын
Aziz mii loumouy mérr mom 😩
@ibrahimadieye70514 ай бұрын
Par ce domou adama la
@nafisene53354 ай бұрын
Nooooon Li comme guerre. Wa ki mome est ce ke Werna? Yow nga teugue sa lamb creer ci couronne, ngani moy bou bakh bi, def tout va dieul ko, dû continuer Di mer. Ey modou y’a am dollé 😂😂😂😂
@ibrahimadieye70514 ай бұрын
@@nafisene5335 et à près
@YacineSène-s5h4 ай бұрын
Bilahi pére Becaye moy nanditè
@doudouthioye43984 ай бұрын
Mercie becaye li la mak diarine
@bintacham-iy8sd4 ай бұрын
Thank you AZIZ❤❤❤❤❤❤❤❤
@mbayelo60904 ай бұрын
Aziz Ndiaye warnga kham sa bop dh fouy nga trop
@ismacisse71624 ай бұрын
Fadame wa hoo deugue lambou dji lépou mystique la
@jeanlouismendy7134 ай бұрын
Père Kebaye il est véridique
@OldySy-v7u4 ай бұрын
Aziz doméram nga
@dgtouba45104 ай бұрын
ioe mi yaye doumoram
@OldySy-v7u4 ай бұрын
@@dgtouba4510 sa data yaye
@moussapayemane41674 ай бұрын
Sa baye moy doméram
@papenar25614 ай бұрын
Aziz dafeu soof da yeug bopam adouna yalla moko mom
@mansoursene47004 ай бұрын
Félicitations à Aziz et à BG2.
@Victoireman4 ай бұрын
Aziz deukkeu bi nioulaa eupeuu xaliss niofii nekk teu kéneu douléne degueu yaw momo nitt yi khadim nitt kou degou la
@sabarasts4 ай бұрын
Aziz wa Balla yeup contane si yow ndakh sa takhaway merci Aziz, am nga droit faral sa mbeur bou légn gnou sonal, Senegal esprit yi mo tarder, kou faroul sa camp gnou saga la wala khass la
@lixman7714 ай бұрын
😂😂😂tu e marrant toi 😂😂
@sabarasts4 ай бұрын
@@lixman771 tres marrant sakh, ça te dérange?
@ModouMboup-v8s4 ай бұрын
Nanal ndokh
@sabarasts4 ай бұрын
@@ModouMboup-v8s yow ya wara nane ndeyou ndokh
@lixman7714 ай бұрын
@@sabarasts non ça me fout au pôle nord 🙄c’est juste stupide 🙄
@Deggou4 ай бұрын
Aziz yaw redescend sur terre momou lo nitt yi tu ne peux pas dirigé tout le monde, amna nio khamni xaliss yeugalouléne..khadim kouu koo xam xamn. NIttou deugg la...
@babacardiop41734 ай бұрын
Lamb dji dafa Bari ay parparlo AK yama nekh AK Ay guenalanté AK ay khékhanté
@DieneNdour-z8l4 ай бұрын
Merci beaucoup Aziz Ndiaye deuk Guediawaye soutenir sa mbeur mo dann tu as le respect de toute personne qui soutient sa localité ❤❤❤ on a pape sarr pikine. Jajeuf Jambar
@GoraMbengue-f2j4 ай бұрын
Aziz Ndiaye xaliss kassé dou adouna nitt dangay am respect si nitt yarou . Mais malheureusement Sénégal so amé xaliss kenn doula wakh deugue danioulay maral 😢
@papesouleyendao43124 ай бұрын
Aziz dafa ndayou rew
@josephcoly41274 ай бұрын
Khalis day dof lo nite..aziz pour mome mo guene niep..
@dioufpapndiaga35564 ай бұрын
Kou adje beugoul kou sentou aziz bakho kou ignane nga
@adamaseck88164 ай бұрын
Motay ndemmm
@nafisene53354 ай бұрын
@@adamaseck8816Yow doul Niak ngeen fayda torop
@cheikhdiop96734 ай бұрын
kou bagne Aziz Ndiaye rék mbeurem da dioutal sa mbeur Aziz Ndiaye ndiarigne lim am si Sénégal di dimbali ay nitt gnikoy khass améwougnouko ndiarigne séne famille bakoy amé ndiarigne Sénégal Aziz Ndiaye yalla nako yalla samm arko si barkep Al khouran
@AhmadaJadid_Diop4 ай бұрын
@@cheikhdiop9673 😂😂😂 gnikey khass yeup Sen yaye yi diourougn kou melni Aziz. Tei djiguéne bouci meune am dom migui niane diour kou melni Aziz.
@@adamaseck8816ioe da nga con kx saga pré toud Yalla danģen réw ba faté sen placou jam bi len Yalla toklo dax ay affairou aduna yu len jeurignul ben yone
@noaevents75934 ай бұрын
Je suis tout t'a fait d'accord avec Faddam
@mamadoundiaye52304 ай бұрын
Aziz dangua niak fayda nak beug houlo trop
@jeangabrielcoly40914 ай бұрын
Aziz Ndiaye la couronne du ROI des arènes detenu par Modou le dérange c'est ça la vérité
@layekharagne22244 ай бұрын
ah biniouy sott modou 2019 diko kheureum ils n’avaient jamais pensé que ce dernier allait être le roi des arènes cette même année
@jeangabrielcoly40914 ай бұрын
@@layekharagne2224 effectivement tu as tout compris
@@requinquin1 saway balla d'où daara loudoul lutteur comme le autres daana Modou mais ,eumeu bombardier Boy Niang Issa pouye danenaniouko...lamb kéneu meunoul diekhal nieup...
@requinquin14 ай бұрын
@@Victoireman Khadim Gadiaga kou mouss leu nga wakh di... motakh ma tontou la lolou. Kham nani fou Balla mi doul dara djaap Modou, wouy sama nday dja dina takkarnaassé 😂😂. Balla dara la dé nangou ko rékk
@Victoireman4 ай бұрын
@@requinquin1 😭😩😅😅 yaw fanatiques nga...
@requinquin14 ай бұрын
@@Victoireman Ak yaw tamit di. Yaw mi Balla déff louni wéng sa mbeur nga takhaw ni Balla dou dara yaw koula gueu neu nékk fanatique déh🙄
@seneami44484 ай бұрын
Aziz naafékh la
@khadijarassoule16544 ай бұрын
Vous qui critiquez Aziz mais il n’a rien dit louy montré daffa bew ou autre pourquoi sou nite farré walla mou diépi kéne loum def gniouni baxoul ou autre
@GabrielLouis-fk7tv4 ай бұрын
Aziz Ndiaye il est très impoli
@Elhadji21874 ай бұрын
😂😂fadam louko nekh rrk lay wah vraiment ioeee Fadam revient sur terre way
@Kopp21114 ай бұрын
Mais il a raison so kholé combat pokola vs liss.pokola bimouy dèm ardo Jule balde daka téyé fofou di wakh ak mom arbitre bi sifflé faléwouko
@Kopp21114 ай бұрын
Mais il a raison so kholé combat pokola vs liss.pokola bimouy dèm ardo Jule balde daka téyé fofou di wakh ak mom arbitre bi sifflé faléwouko
@BaboucarrFanneh4 ай бұрын
Aziz kholal bi fekhull wayy😂😂😂
@diallomamadou45254 ай бұрын
Non aziz damako yereum billahi pour mom khaliss moy lepp pour mom vu k dafa am khaliss senegalais yeup danio wara ande ak mom
@modousarr88484 ай бұрын
Bayi ko rék béww
@freresjumeaux93384 ай бұрын
Aziz ak xol lay waxé Mais stp met de l'eau dans ton vin
@dawdatouray2664 ай бұрын
Aziz is very intelligent he knows what to do and he knows what he wants.
@ibralemeringue32584 ай бұрын
Aziz Ndiaye khool bi moooy bone
@DieynaFall-we4ue4 ай бұрын
Aziz mi kou sof la
@djibiciss994 ай бұрын
Khadim couronne 👑 diakhaloulll Balla Gaye 2 Manga 2 Tyson Bombardier Yekini Balla Gaye 2 👉 guasiy tëk Bombardier Eumeu sen Modou lo di sogua gnaw
@moussapayemane41674 ай бұрын
Kénn dou Abdou Aziz Ndiaye barké fapésss
@AmadouDiallo-sj1es4 ай бұрын
Aziz c est la 1ere fois ma guisse Aziz def sorti bou thiouné 😂😂
@Vikingsénégalais4 ай бұрын
Aziz adouna dou keur tu es devenu très arrangeant,
@alassanediallo70544 ай бұрын
Merci Aziz on t'aime ❤
@boubacardiamba4 ай бұрын
Ana gris bordeaux, lolou yagoul dara
@NabyLeJuriste4 ай бұрын
Balla tapha tine rk lafi dan depuis plus de cinq ans danou fi mbeur 😂ngen dieul tapha tine statut danko beug mom nitt gni Modou lo the king
@sekousane60414 ай бұрын
Ya moune doul
@ablayegaye78484 ай бұрын
Aziz dafa rèw
@becayepreuvendiaye9224 ай бұрын
Aziz khamo foye takhaww Modou lo ga beugu beurélle c'est le Roi des Aréna té môme beurréwoul ak yao nanguoulko.🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
@afro38274 ай бұрын
Aziz nit kouko guena bew yewowoul senegal
@Nitou19904 ай бұрын
Aziz ndiaye l'homme le plus arrogant au Senegal
@issakanafiou18654 ай бұрын
Ce que je veux savoir entre balla gaye 2 et Modou lo qui doit demander revanche a l'autre c'est Modou lo pourquoi a chaque fois c'est le Can de Balla gaye 2 qui veut toujours une revanche pourtant il a deux victoires sur lui , ça n'a pas sance , il save ce qu'il cherche
@layekharagne22244 ай бұрын
wei c sa dh
@Nitou19904 ай бұрын
Modou lo vs Pikine 6 - 0 Franc vs Pikine 5 - 0 Modou lo vs Fass 5 - 0 Franc vs Fass 2 - 0 Modou lo vs Guédiawaye 3 - 2