Arrestation du Tik Tokeur Momo Taylor, sa mère inconsolable et raconte toute l’histoire…

  Рет қаралды 29,248

Wassare Société

Wassare Société

Күн бұрын

Пікірлер: 188
@OulayBah-m8k
@OulayBah-m8k Ай бұрын
Lii metina trop 😢 maman yalla nala yalla takhawou🤲
@papediouwara1945
@papediouwara1945 Ай бұрын
Il y a un parfum de jalousie à cause de la réussite de cette femme. Heureusement qu Allah aime les courageux travailleurs.
@manguebourgeoise2760
@manguebourgeoise2760 Ай бұрын
Mere mounioul ligueyeul Yalla yomboul té sa wa kogne yekh nanio lidieunti foye djeulé linga lenn di diokh...eye badola leniou waye boul découragé té gni la beugue torokhal Yalna Yalla dokh sa digueunté ak niom té tekk len louniou ladoul talé ...amine du courage
@dembaniang9050
@dembaniang9050 Ай бұрын
Bo nékoneu sama yaye bilay dinagn yobou sama bakaneu bilay😢 du courage sonko ou c élément wakh lénn si li bala mo eup lokho
@laminebarandoye9244
@laminebarandoye9244 Ай бұрын
Free Momo🤲🏻
@sambadieng1203
@sambadieng1203 Ай бұрын
Je sais pas qui mais j'ai des larmes au 😭😭😭😭💘💘li mettina trop
@dieynabasambou8403
@dieynabasambou8403 Ай бұрын
Justice pour cette maman
@cheucha7281
@cheucha7281 Ай бұрын
Yalla na yalla attè ak mom gnou radié ko en 2025 inchallah si barki seydouna mouhamed
@salladiaw543
@salladiaw543 Ай бұрын
Amine Yarabi
@AmycolleWade-z1h
@AmycolleWade-z1h Ай бұрын
Maman yalla bakhna billakhi ndeysan yalla moléne eupeudolé
@IbrahimaSall-ox4rm
@IbrahimaSall-ox4rm Ай бұрын
Ndeyssane vraiment li métina injustice dou yone mère bi bilahi linouko déf metina trop torokhal sa moromou yaye walahi dou léne djik
@WassareSociete
@WassareSociete Ай бұрын
Merci pour votre commentaire
@fatousow9718
@fatousow9718 Ай бұрын
Motakhit lo si guiss dina gnou liguey ba dé té dougnou am dara
@Marietou-i6u
@Marietou-i6u Ай бұрын
Il faut allez dans tout les radios 📻 de Sénégal métina teuss rfm
@KineThiam-w6u
@KineThiam-w6u Ай бұрын
Taylor 😢😞😞😭💗💗💗💗💗😭😭😭😭😭😭 pourquoi dictature encore djomaye va réagir non
@DembaNdiaye-k1z
@DembaNdiaye-k1z Ай бұрын
Métina ma trop yalla nala yalla sam yaye boy gendarmerie Sénégal ay dmram lén nen niaf sen ndy feulé
@Soumayyarassoul
@Soumayyarassoul Ай бұрын
Bayilén AK yalla yalla Dina atéé yalla na yalla léral lépp inchallah
@salladiaw543
@salladiaw543 Ай бұрын
Amine Yarabi
@daoudadieme3358
@daoudadieme3358 Ай бұрын
Il faut porter plainte et justice fera son travail l'heure de l'impunité et de l'arrogance est terminée.
@DaoudaDIOP-m4x
@DaoudaDIOP-m4x Ай бұрын
Abusé baxoul adouna diékh na ba paré. Courage Maman
@Salsaa-x7z
@Salsaa-x7z Ай бұрын
Justice amoul thi réwmi fi Dara changer woufi courage maman
@Madamemmedia
@Madamemmedia Ай бұрын
Massa thiono❤❤
@papediop2737
@papediop2737 Ай бұрын
Conseiller lenko mou porté plainte,
@AmetDiaw-r8s
@AmetDiaw-r8s Ай бұрын
Yalla na yalla leral leup maman
@AlimaSamb-xw6gd
@AlimaSamb-xw6gd Ай бұрын
Massa ma sœur yallah Nala borombi ater ak gnome justice pour Mere Dioba
@aichafall5023
@aichafall5023 Ай бұрын
Ndeyssane c triste Iniane rekk président nassi wakh
@ndiayefatou565
@ndiayefatou565 Ай бұрын
Justice pour cette famille
@MohammetBaldé-q4k
@MohammetBaldé-q4k Ай бұрын
Du courage maman ,je prie pour que Dieu ,le très miséricordieux ,le tout miséricordieux vous réserve le meilleur et que ces policiers soient remis sur le bon chemin pour qu'ils puissent mieux servir dans les règles de l'art. Amine.
@alfylyfa7645
@alfylyfa7645 Ай бұрын
C'est pas possible des forces de l'ordre 😳😱 mère va porter plainte aye bandits lagnou
@Salihate9
@Salihate9 Ай бұрын
Franchement am na ay hommes de tenus corrompus et malhonnêtes État bi na si wax li niaw na trope
@salyallemomuawrksarr8652
@salyallemomuawrksarr8652 19 күн бұрын
Gouvernement sonko et diomaye Faye ligueyou gniou fi Dara danio tok injustice bi gueneu bari sarap ndayou Sénégal Yi Policé sougniou dée wou detec mment safara lagniouy dem yalla nalene akh momo dal pabi faye Khalis Policé Yi yalla na dée dem safara justice pour mom 😢😢😢😢
@AlimaSamb-xw6gd
@AlimaSamb-xw6gd Ай бұрын
Quelle injustice yallah Nanou borombi dolí soutourale
@ummhuraira2495
@ummhuraira2495 Ай бұрын
Yalla en majuscule svp. Merci
@khadimtine5257
@khadimtine5257 Ай бұрын
Yalnala yalla takhawou yaye boyy
@cheikhdiop4086
@cheikhdiop4086 Ай бұрын
C'est vraiment regrettable. Une souffrance infligée à une dame très vulnérable. Bayyileen ak Yàlla mu fajal la ko.
@khoudj841
@khoudj841 Ай бұрын
Mougnal dina djekh inchallah 😢
@AmycolleWade-z1h
@AmycolleWade-z1h Ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@Marietou-i6u
@Marietou-i6u Ай бұрын
Masta kholale si oussemane sonko 😢😢Masta yaye
@helenesagna2006
@helenesagna2006 Ай бұрын
😭😭😭😭sama khole bi diekh na rakkk
@MbayeAwa-t5e
@MbayeAwa-t5e Ай бұрын
Bilaye li dafa meti😭😢
@AichaVital-m6e
@AichaVital-m6e Ай бұрын
Problème bi sounko regleone comme il se doit avc les autorités compétentes gnou expliquer mer bi k fasse do ko garer si cogne ndakh les rues sont exigus ak Problème hygiène bi donone demai nenaine . Mais kousi naik ta voulu régler le problème à ta façon. Ka même g mal pour cette dame car elle semble très affecté. Massa yaye boye. Li lep niak wakhtane mo ko indy . Vraiment femme bi li k dal ça fait mal
@SeynabouFaye-b6q
@SeynabouFaye-b6q Ай бұрын
Metina yalnako yalla takhawou courage maman
@WassareSociete
@WassareSociete Ай бұрын
Merci pour votre commentaire
@Gggge_dudiolof9536
@Gggge_dudiolof9536 Ай бұрын
Il faut aller voir un avocat et porter plainte.
@mamanmbaye1305
@mamanmbaye1305 Ай бұрын
Bilakhi mére bi warone na nék sama yaye koune dou yomb
@maramesamb3279
@maramesamb3279 Ай бұрын
Ay wayy mére bo do nonn sama yaye non walahi azim gnila def li dinaniou kham ni lal nagn lala ké Sénégal dal ni reck justice bou bonn reck ba kagn
@Momodiop153
@Momodiop153 Ай бұрын
😢😢😢ylla na ylla may kholou mounie yaye boy Biliahi nji defli di nane ko rethiou adouna dou keur dh
@laminesow7830
@laminesow7830 Ай бұрын
que justice soit faite togne bahoul diaye dole bahoul
@djilysall7727
@djilysall7727 Ай бұрын
Mer yalna sa diam yage
@AstouDieng-o2n
@AstouDieng-o2n Ай бұрын
Courage maman 😇
@KineThiam-w6u
@KineThiam-w6u Ай бұрын
Ana wa pastef lou sonko di khar🤔
@moustafaniang225
@moustafaniang225 15 күн бұрын
Diotna nk quoi
@moustafaniang225
@moustafaniang225 15 күн бұрын
Té momo diambar la wone si khekh bi
@fatousane9443
@fatousane9443 Ай бұрын
Yalana Yalla até
@amadoudiopndoye3582
@amadoudiopndoye3582 Ай бұрын
Trop injustice !! Ousmane Sonko on c battu pour ça
@cheucha7281
@cheucha7281 Ай бұрын
Limotakh kouthi retraité done Andi Capè ndakh sène rèwandè gnom pour gnom ténu pour diaye doolè la
@loveyoumaman3882
@loveyoumaman3882 29 күн бұрын
Bilay ay domerame lagnou
@MansourMbaye-c1t
@MansourMbaye-c1t Ай бұрын
Sama yaye boul dioye lou méti yagna thi adouna yalla bakh na lép dina diékh incha alla 🙏🙏
@diopelmalick456
@diopelmalick456 Ай бұрын
Bilahi li metina trop yalna yalla diékhal leup inchallah amneu niit niu sokhor
@fatousow9718
@fatousow9718 Ай бұрын
Aythia reek développement dîna gnou ko yékha déef di dioylo maak gni reek ak djiguen gni injustice bi né fi khass liguey ba dé té dougou ngén am dara
@marieeliseloume5422
@marieeliseloume5422 Ай бұрын
Akhou deukeno akhou deukeno akhou deukono wassalame
@mariediandy111
@mariediandy111 Ай бұрын
Cheu pourquoi guaye toude gendarme bi laye dimbely nonnnn
@ramatoulayengom8594
@ramatoulayengom8594 Ай бұрын
Lor na KO dé
@veroniquenatack7392
@veroniquenatack7392 Ай бұрын
*Vraimnt warone na zapé fofou rk*
@maguettediopsow2786
@maguettediopsow2786 Ай бұрын
Gendarme bi espion la
@Doumadialale
@Doumadialale Ай бұрын
Les gendarmes doive respect les Senegalese. Il faut aller porte plainte au pres du procureure.
@AmeteDiop-wk9pn
@AmeteDiop-wk9pn Ай бұрын
Demal keur mbaye fall nga guissal bopou
@ndeyefatougoudiaby744
@ndeyefatougoudiaby744 Ай бұрын
Oohhh lii metina yalla na Yalla atté si barké al khouran
@adamandiaye4314
@adamandiaye4314 Ай бұрын
Lignawna loleeeeee Maman courage police dèfena lou gnawe démale khalass ak teuss Fadel Dakak Beus ak falink Dakar dou yone sa deukeudo bakhougnou eskey yallana yalla até
@KineThiam-w6u
@KineThiam-w6u Ай бұрын
Mamá consulte un bon marrabout c un guerre espiritual c trop pour la famille.va a aventure ❤
@alfylyfa7645
@alfylyfa7645 Ай бұрын
Amougnou droit dougue sa keur ni di fouyé pourquoi faiblesse bi sa birr keur
@zalezale8946
@zalezale8946 Ай бұрын
Bizarre cette histoire elle ne dit pas tout : Le Sénégalais est toujours dans l’émotion ! Quand l’OCRTIS se déplace, sans compter les autres descentes de Gendarmerie ou Police ce n’est pas pour régler des histoires de voisinage par copinage ! Maintenant de mauvais fonctionnaires de Police irrespectueux dans le travail il y en a! En tout cas on ne souhaite à personne ce qu’elle a vécu même si la famille était coupable !
@safietoufall2512
@safietoufall2512 Ай бұрын
Dans ses paroles on peut noter beaucoup d'incohérences.
@Marietou-i6u
@Marietou-i6u Ай бұрын
Sénégal métina 😢😢
@maguettemboup3604
@maguettemboup3604 Ай бұрын
Yalla na la yalla takhawou 😢❤
@douguindiaye23
@douguindiaye23 Ай бұрын
Y’a trop injustice
@rokhayandiaye7375
@rokhayandiaye7375 Ай бұрын
Massa❤
@aliounewane9909
@aliounewane9909 Ай бұрын
yaye boye mounieul yallydina lerale lepp inchallah
@coumbasarr7261
@coumbasarr7261 Ай бұрын
Injustice total bilahi😭
@WassareSociete
@WassareSociete Ай бұрын
Merci pour votre commentaire
@kileuniang805
@kileuniang805 Ай бұрын
Justice déff léne sene liguey comme vous la dit le président,injustice
@mmmomo4267
@mmmomo4267 Ай бұрын
DAMA GAWTOU DIOKHEH SAMA KHALAT MAIS MERE BI DIOM MOKA SONNAL DAMAKOY DIEUGEULOU DIKO MASSAWOU DIAMBAR FOKO FEKEU NATTOU DAF KOY SONNAL NAGNOU DELLOO LEPPEU YALLA JE SUIS VRAIMENT AFFECTÉ SURTOUT POUR LE CAS DU JEUNE TAYLOR QUI RISQUE D'ÊTRE BRISÉ
@adamandiaye4314
@adamandiaye4314 Ай бұрын
Maman courage il metina loleeeeee police linou dèfe gnawena sa deukeundo bakhougnou démale teuss ak RFM khalass Fadel Dakar beuss khana police amou gnou yaye
@pamelakydane5210
@pamelakydane5210 Ай бұрын
J la connaît très bien c tune femme très brave barki yallla
@papendong1810
@papendong1810 Ай бұрын
Mousso bobou nga warone woute caméra de surveillance
@iboudrame2449
@iboudrame2449 Ай бұрын
Billay lolou ladone wakh
@malickndiaye4840
@malickndiaye4840 Ай бұрын
On a des bandits pas des gendarmes ni policiers mais des bandits
@ndiandekebe8819
@ndiandekebe8819 Ай бұрын
Massa maman sénégal barina niou sokhor bo amé xaliss rk niou sokhor gendarme yi Lou léne nekh la niouye déff mais yalla bakhna 😢
@Marietou-i6u
@Marietou-i6u Ай бұрын
Masta yaye 😢
@matarsene3859
@matarsene3859 Ай бұрын
Justice amoul Senegal lo lo te azzis ba ak waliii sene de leroull
@sambatirera2297
@sambatirera2297 Ай бұрын
Thiottou ndaye raww mi man amouma yakar si rew mi chak fois justice day tedé ndiakhanay
@Nafidramè-r7b
@Nafidramè-r7b Ай бұрын
Yalla nalen yalla atè
@tallibeserignesallouelectr7681
@tallibeserignesallouelectr7681 Ай бұрын
De mal si yon
@KaraJieu-p5p
@KaraJieu-p5p Ай бұрын
Mère,boul toude tourou gendarme bi diko indil ay problèmes ngua naane diedhiook diatta nii,baakhna. Yaw naikhoo dimeuli dai,tai kou nakhari dairaite ngua
@amadoudiopndoye3582
@amadoudiopndoye3582 Ай бұрын
Sonko li neine beugue mou dieh Sénégal
@tout1958
@tout1958 Ай бұрын
Yaye boye dalal bou ak dal amna solo
@AlimatouDiop-p5l
@AlimatouDiop-p5l Ай бұрын
Ma warou li métina dé 😭
@Mamemalickmamemalickdiouf
@Mamemalickmamemalickdiouf Ай бұрын
😢😢😢😢😢😢
@Diodiadij
@Diodiadij Ай бұрын
Massa ❤❤😢😢
@AbdoulayeDiallo-ub7fp
@AbdoulayeDiallo-ub7fp Ай бұрын
Mère Outal avocat ga porté plainte
@serignebarradiouf8335
@serignebarradiouf8335 Ай бұрын
Mai nakk magui diégalou té lila dall méti nama trop mai yaye danga khawa nakhari dérétt souma dégué sa cominication mai nakk khay na dagn la tongn mtx yalna yalla tégui natou bi
@ummhuraira2495
@ummhuraira2495 Ай бұрын
Lan moy nakhari deret? Bagn kou la nèwal doolè? Khoolaatal lingay bind!!!
@momathniass5720
@momathniass5720 Ай бұрын
Yaw doul ndeyam merbi degne ko togne domoukharam yi ❌❌
@almouridoutv6946
@almouridoutv6946 Ай бұрын
Yaw khana dala daloul motakh dakh koumou donon sa yaye do wakh lolou dèh Senegal monèx dal Police dal dalay torokhal tè do wakh darra!!! Kouy torokhal domou adama do am moudiouguou rafèt yaye boy Yalla Nala Yalla samou tè takhawoula massa😢
@ummhuraira2495
@ummhuraira2495 Ай бұрын
Empoisonné le cheval???? 😢 Allaahu akbar... empoisonné bénén encore??? Violence policière??? Yalla nagnou Yalla mousseul tchi deukkeundoo bou am fitnah... massa.
@adjiniolediongue
@adjiniolediongue Ай бұрын
Dicourage yay boy mougneul dina diex
@sadiomassaly7071
@sadiomassaly7071 Ай бұрын
Elle faut l'ai porté plainte
@GnagnaMbaye-i5f
@GnagnaMbaye-i5f Ай бұрын
Mère bi cou tengue laaaa waye yalla nalla yalla takhawu
@business6901
@business6901 Ай бұрын
Deuk bi batay changé woul
@khadimka2058
@khadimka2058 Ай бұрын
Gendarmerie normalement souy diap ay nitt waroul basé wou si ay wakhi deukando rek, vraiment soudé nila demei metinama trop, dafa am nio xamni koulen eupale laniou beugoul
@Patriotsavie
@Patriotsavie Ай бұрын
Li dafa wara diekh méré nite toumalko,
@djibrildiouf-l5p
@djibrildiouf-l5p Ай бұрын
li métina trop way yalla nako yala takhawou way
@TallaDiop-zf7pv
@TallaDiop-zf7pv Ай бұрын
MEER LANSEL APEL UOSSMAN SONKO AK JOMAAY FAY PARESIDA
@yayourassoul6110
@yayourassoul6110 Ай бұрын
Duap sa morom Yaye diko torokhlaal niii bahna rek
@ibrahimadia517
@ibrahimadia517 Ай бұрын
Mère bi bilahi merétouwoule li
@diallombathio2227
@diallombathio2227 Ай бұрын
L naniou si wkh ni rie diay doleh wayei kou nek na kham ay droit wam li vraiment dadoul yoneu
@Soumayyarassoul
@Soumayyarassoul Ай бұрын
Douma généralisé mais policiers yousi eupeu ay policiers corrompu laniou yamba bobou mér bi wax policiers yii niokafa deff lolou sén djikola sén mbone weurna réwmi mér bi yalla nalla yalla maye ndam
@KhadidiatouGueye-x3k
@KhadidiatouGueye-x3k Ай бұрын
Thiey yalla sama khôl bi toy na
@nogayegalon969
@nogayegalon969 Ай бұрын
Le dieu est grand maman ça c'est mentalité sénégalais laisse l'ais avec le Raby
Ayat Kursi 7x,Surat Yasin,Ar Rahman,Al Waqiah,Al Mulk,Al Kahfi,Al Fatihah & 3 Quls By Saad Al-Ghamdi
3:43:19
Ayat Al-Quran Live - آيات القرآن مباشر
Рет қаралды 266 М.
Как Ходили родители в ШКОЛУ!
0:49
Family Box
Рет қаралды 2,3 МЛН
🚨🚨TFM LIVE : XIBAAR YI  - 05 Février 2025 - Pr ABDOULAYE DER
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 1,4 М.