Seuuuttt😂😂😂...mais doungéneu bayi sama mbeur bi😂😂😂...légui dale fans modou rek mo wara banie balla😂😂😂😂
@bayealyndiaye6096 ай бұрын
Balla meilleur lutteur de l’histoire ✌️de la lutte sénégalaise
@OusseynouSeck-j7v6 ай бұрын
Billahi déguena dégg
@mouhamethniang31546 ай бұрын
Khana taye la oooooooi boye niang nak wala euemeu sene
@AdianaseydiAdiana6 ай бұрын
Il est l meilleur seul contre tous 😂😂❤❤
@FaaFaa-pt9jr6 ай бұрын
Meilleur lutteur de tout les temps 🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤
@mouhamedniang79626 ай бұрын
Le meilleur de tout les temps ❤
@mouhamedabdoulahidiagne7866 ай бұрын
Balla dal professionnalisme rek la dané Tapha ak sañsañ il étudie ses adversaires et il a d’excellents coach
@PAPAMOUHAMADOUMOUSTAPHAM-fr5kt6 ай бұрын
C’est le meilleur franchement.
@julescisse34316 ай бұрын
Balla gaye 2 le meilleur de sa génération, l'empereur de la lutte sénégalaise. Sakhal ci entraînement yi rek leepeù meun na neek cikaw cikanam inchallah
@dominicdulac47376 ай бұрын
Balla Le plus grand lutteur du Sénégal le plus talentueux de loin Un vrai champion
@ElhadjiDeme-d8f6 ай бұрын
Balla Gaye 2 rek❤❤❤
@cherifka77586 ай бұрын
Bayou modou lo balla seul ❤️💪🏿
@boubaleye20036 ай бұрын
Meilleure lutteur d tt les temps
@selebiiimopelitalegonga6 ай бұрын
Balla seule ❤
@MauhamedJabbie6 ай бұрын
Balla rek❤❤❤
@FaaFaa-pt9jr6 ай бұрын
Ki dmakoy beug mba kagne ❤❤❤❤🎉🎉
@falltapha-uk1ez6 ай бұрын
Balla gaye 2 mbeur Kamil la
@moussamane42366 ай бұрын
Père bécaye nguir yalla lire léne sama commentaire té nguén wakhal ma lolou balla ndakh sougnou déréte la.
@ibrahimaFall-f3t6 ай бұрын
Balla kassé ❤
@ndiayeabibou39516 ай бұрын
Mane khalifa babacar sy la beugue ni sakh ❤
@doudouthioye43986 ай бұрын
Lou souy sounou yoon léguii do wakh sa papa ba paré dogaay beug papay diambour khéép sa baye bi takh ga kham khalifa Babacar
@thiernodiallo28306 ай бұрын
@doudouthiobonye4398 bonne réponse 😀😀😭
@MadickeGueye-f6r6 ай бұрын
Gnioune balla rékk lany top
@adamandiaye56226 ай бұрын
Balla avc c fans c une famille po des fans maintenant c une famille
@bambasyllaahmadou6 ай бұрын
Balla seul
@babacaargueye58626 ай бұрын
empeureur de la lutte senegalaise
@MrFayemanou6 ай бұрын
Empereur titre famille leu 😂
@CherifCherif-f2s6 ай бұрын
Khana wadji balla dioutelone moy sa mbeur 😅😅😅 le petit roi
@djibysoung29986 ай бұрын
Aziz Modan tapha
@KhadyGaye-n5g6 ай бұрын
Bilakhi balla 2 moye lamb te louma nekh si mome souye beures Senegalais yi nieup koye bayi khel
@SerignesaliouDiao-fe7bm6 ай бұрын
Bilahi modou Mbaye est très professionnel par rapport ak bour et fadam leurs questions est trop nulle
@assanediop7716 ай бұрын
Lulay wahati le 21 ba leegui reprendre ro say entrainement limoy beugo entrainement lii bo done modou lo mba eumeu sene reperendre seen entrainement bou yag ngir yalla comencèel entrainement yi thia teel bala ngay amat combat
@modoudiagne28206 ай бұрын
Demal entrannner dji nak na bir bi dégne
@KaneArman6 ай бұрын
Balla ya lamba
@moussapayemane41676 ай бұрын
Fans Modou Lo yi liléne méti ham nagne ko,trophé bi nék si empereur bi té nékoul si sénn roi bi motah 😂😂😂😂kénn dou Abdou Aziz Ndiaye barké fapésss 😂😂
@WallyDiop-z1e6 ай бұрын
Balla dagua daw question bi dé gneuw bi gua gneuw stad
@Domou_Deukk_Bi6 ай бұрын
Loumoussiy daw ??? Amoule droit nieuw stade???
@Adnanezinho-jm8zk6 ай бұрын
Doul
@moussamane42366 ай бұрын
Balla retrouver woul nieup wakh deugu fa yalla. Surtout côté politique bii mo ko yakal lou beurrii. Ak Surtout loumou wakh thii casamance au moment de leur duel sur les manifestations
@rngm22486 ай бұрын
Politique bi kouner am na droit far fouko nekh .Casamance nak wakhou fi lou diara mereuh.
@fallpapa6 ай бұрын
damoko beugue rék
@WallyDiop-z1e6 ай бұрын
Bour amo khame khame
@assanediop7716 ай бұрын
Yaw balla bo respèctèwone entrainement kènne doula eup doolè
@alassanedieng2596 ай бұрын
Babacare my dafa sof trrop té beug ay francé
@WallyDiop-z1e6 ай бұрын
Balla bi mounoule dane mbeur
@MadickeGueye-f6r6 ай бұрын
Baln nane lâ
@OusseynouSeck-j7v6 ай бұрын
Balla di dioutale nganane
@MrFayemanou6 ай бұрын
@@OusseynouSeck-j7v badou daa djoutale sa. . . Y boul takh maa yegalli un peu de respect
@CherifCherif-f2s6 ай бұрын
Nm comprendre len ko wadji balla dioutelone moy mbeureum
@WallyDiop-z1e6 ай бұрын
Fadame yow mome dagua kon trope
@moussamane42366 ай бұрын
Balla déloul casamance ndakh niom ngua yagua bakou amna xollii youla méré ba téy mane casamance la deuk thii Bignona thii tenghory wétou keur doublass
@souleymanefall68396 ай бұрын
Billay dadioum balénko
@WallyDiop-z1e6 ай бұрын
Balla liguaye wakh sakh gueu moko
@oumarniang66326 ай бұрын
Le lutteur le plus nulle et immature vive son excellence Mr Modou kharagne lo.
@ridialdieng28616 ай бұрын
Ss way wakhal si lambji toubap yaga France
@espritsaints46856 ай бұрын
Balla mo null ?😂 Yaw doff bugn peinture nga wakh ak yaw erreur la
@NdamalBachir-m5r6 ай бұрын
Bilae iow wa immature daniy faye balla dakh mome dafa immature ba nek roi dane gnifi meune ba dane beure bou guene mature mouy fatou lo alias diouta lo borom khotou you Eure yi 😂😂😂 ba weer na legui 7:25
@bintagaye12826 ай бұрын
Pourquoi cngé lignouy dague dougne si diapalé beur yi nék en difficulté assurance lac d guerre loumouko dieurigne