bambo amna louka yalla maye déh .wayé wakh mou nék chaque jour lohlou yalla rék moko meune .
@DeggouАй бұрын
lanne lako yAllah maay? non senegal li mo takh dou deme...
@bijoukaneАй бұрын
@@Deggouyallah gneup la mayyyy yaw amneu loumou la mayyy lo eupeuler keineine kone listikhar foumou djouger lane motakh sougnou prophète wakh gnou deifko dou marabout dalay khollal boul weidi yallah mo mayyy gneup mais boul wedi limou ame
@DeggouАй бұрын
@@bijoukane es ce que xam nga vré sens de l'istikhar? le probleme genre yi bouniou yamone ci l'istikhar rek douma wakh mais ci plaçou yAllah laniou beugg takhaw teu ki wakham toujours doy ame....
@abdoulazizdiop-e3rАй бұрын
Modou lo ndam rek inchallah
@DeggouАй бұрын
yaw boul niou thiatou way, khamo gatte fi ngafi indi sathies wakh lou nekk... moddo lo yAllah nako yAllah mousseul ci thiate ak lamigne