Na wadiour yii guenne bayi khel siseen dom yii. Bayileen di yondi khaleyii ci bitti, ak dileen bayi gnouy fo ci Mbed mi. Jamono da sopekou. Niit yii change. Prenons soin de nos enfants.
@eugeniemendy26162 жыл бұрын
Maman c'est triste. Je n'ai pas de mots pour te consoler. Que son âme repose en paix. Mes condoleances.
@carinasenegal70862 жыл бұрын
Franchement keurou affrique yi ken manouso surveiller xalei h24. C pas des maisons fermé mano fo tolou di emprisoner xalei boy dem sangu sax lounei xatj nasi nit gni nio bone rek ta sokhor djiko yi yakhou .mais yalla miy sam yalla nanou samal sunu diabote
@abydiop22572 жыл бұрын
Vous avez raison ddd
@ndelladiop89542 жыл бұрын
Botegné sa bout keur gnoulay beug rayy ak feugg
@mercedesmunozcarmona26302 жыл бұрын
Anta yall na motali ndawame janatou fiirrdaaws🤲gnoune yaye yi gnou geneu vigilant rek.gnane yalla mou samelé gnou.
@diorsow18172 жыл бұрын
Ndeysanne yaye boye mougnal yalla na yalla har sougnou diavote inchalla amin yarabi
@ronixdieng89602 жыл бұрын
Mais père bii limouyy souligné wallahi amoul sens Am naa magg niou mounoul wakh bénn yonn
@prime39152 жыл бұрын
C'est gênant vraiment
@Nafissall72 жыл бұрын
Qui kegne guerre éthnique laye oute
@SaliouGueye222 жыл бұрын
Amoul béna sens
@idandure2742 жыл бұрын
Vraiment amoul sans
@adamaseck88162 жыл бұрын
Pas bi kay moy Lolou
@morniang30472 жыл бұрын
On demande justice pour anta
@morganmor19042 жыл бұрын
Ndeyesn sama kognla jak kipp pour la premier foi lou menlni amfa quartier bi la dioudo yarofa me magui sogua guisli bargny kipp c morgan d8 itali merci babacar toure kewolo
@idamichoudias70712 жыл бұрын
Les bâtiments qu'on construit et on ne les finisse pas on doit les interdits
@ramadiouf73692 жыл бұрын
Vérité absolue
@evalyon93892 жыл бұрын
Surtout cest des nids a malheur
@abydiop22572 жыл бұрын
Surtout
@nadafafall70942 жыл бұрын
Bilahi
@NdeyeNdiaye-vm7qp2 жыл бұрын
Tu as parfaitement raison
@ndeyecodoudiop25002 жыл бұрын
Rip anta Ay 14 heur ndioloor lou khaler bou djiguéne 7ans di def si mbéd amna louma meti trop koko def yalnako yala wer
@ronixdieng89602 жыл бұрын
Franchement problème bii sii gnom laa enh Elle ne surveille pas leur enfant A chaque ainsi leur enfant sont dehors
@1khouredia2 жыл бұрын
Daniou wara surveiller khaleyi vraiment. 8 ans tu dois pas rester 10 mns sans savoir où il est. Teyer lene khaleyi ngir yallah
@Oumanas59952 жыл бұрын
Je t'assure. Sama keur deh prisonniers lagnou toudé teuthie rek
@shelamendy55342 жыл бұрын
@@ronixdieng8960 ne dites pas cela. Sama rak son école se trouve a 2 mn à pied de la maison pourtant chaque jour daniouy yobou di dieuli. Hier notre maman a voyagé. Je lui ai interdit de sortir. À chaque Instant mon papa appelle pour voir s’il n’est pas sortie. Vers 21h j’ai constaté que la maison était calme je sort je ne le vois pas. Je l’ai cherché dans toutes les rues jusqu’à 00h presque. Pourtant depuis hier je ne cesse de lui Parler du nombre d’enlèvements et meurtre sur enfant. Donc aujourd’hui si on ne l’avait pas retrouvé on nous taxerait de parent négligeant??? C’est pas le cas pour tout le monde
@ndeyefatoubaseck78982 жыл бұрын
Merciiiiiiiii
@fatoundiaye64122 жыл бұрын
Mes condoléances metina trop vraiment nagnou yarate sougnou dome yi tè di dieul sougnou responsabilité di lene surveiller surtout lolou dama tite si mime rew ay khallè you touti di deff ni
@serignendiayebeuguefallou70882 жыл бұрын
Merci beaucoup Wa kéwolotv vous étes les meilleurs 🙏🙏♥️
@papasabaly42502 жыл бұрын
Bismillahi rahmanirahim qu'Allah l'accueille dans ses paradis les plus célestes. Mais de grâce il faut mettre des briques de blocage devant les bâtiments abandonnés.jai remarqué que la plupart des malfrats aiment à fréquenter ses bâtiments. abandonnés.
@wazifagroup83852 жыл бұрын
Vous faites un bon boulot. Du courage
@mbalofficiel75132 жыл бұрын
Massa yal nako Yalla bourbi kharé aldiana si daradja Seydina Mouhamad psl
@ndeyemagatteniang24112 жыл бұрын
Yalna motalé dawam aldiana firdawsi
@mamediarradieng86052 жыл бұрын
Mame boy yalla dinalenko fadial de in cha alla
@ndeyependasarr10562 жыл бұрын
Yalna yalla leral lepp si barki serigne babacar sy metina trop yalla mayla kholou mougne
@tinefall64092 жыл бұрын
Ndeyessane métina trop yalla souf sede si kaw tt mes condoléances à la famille anta ndiaye ndeyessane la pauvre maman de anta n'a pas des mots a dire métina trop
@adamaseck88162 жыл бұрын
Oooooooh paix à son âme 😭😭
@ronixdieng89602 жыл бұрын
Mais ALHAMDOULILLAH 🇸🇳Affaire de la fillette de 8 ans assassinée à Bargny Le tueur présumé identifié et cueilli Il a été arrêté hier en début de soirée par la police après l'interpellation de son complice présumé dans la matinée.
@yayafall73532 жыл бұрын
Alhamdoulilah k justice sw faites
@ndeyefatoubaseck78982 жыл бұрын
Ce que je n'arrive pas à comprendre mooy Que fait un enfant de 8ans dehors di traîner parce que tu fais la cuisine mais noooon. Nga dougg ak moom si cuisine bi moulay deubeul wouteul ko activités mou occuper ko si biir keur gui. Lii moom ça doit servir à tous les parents surtout Nnioune Yaye bi. Reposes en Paix Bébé Anta 😔
@marietoudiop42982 жыл бұрын
Sénégal dagno sa gane si khale trop magui leñe Di massawou vraiment metina. Mais nak teyel en khaleyi si bir keur yi. En Europe khale daf mi melni diamant nak rare lollll si mbend mi pour gua guiss khalebou y takhawalou amoul nakhte loi bi si mbopap mokoy tere
@mbossediaw28412 жыл бұрын
Pour gniy blâmer yaye dji arrête leneu sof ngueneu ak surveiller vos enfants kou Diour sa dôme bamou tol ni surveillé nako yoor sa phone rek di wax c trop facile psk fi keneu xamoul keneu yokou niit naxar rek ngueneu di def fi surveille amoufi place ko bokou ak beneu kogne dou diouguè sa keur bou nieuwone fek nga tok ak sa yaye bou beuguè ngueneu ande sa yaye dou bagne
@carinasenegal70862 жыл бұрын
Franchement ki am 7ans 8ans periode bi surveillance guena metter fimiy ramé di diagueu dokh mosi guena meti
@Minabellaunivers2 жыл бұрын
Bilahi con rek ak beug wax
@khadyfaye37862 жыл бұрын
Bilay dama koy khol si mane rk à cet âge sama yaye da done surveiller ba soneu mais il suffit juste beine moment d’innatention rk pour reuthie bilay khallei mo sop rk
@ndeyemareme382 жыл бұрын
Ohh li métina ndeysane yallah na ko yallah mayy xol lou mougne repose en Paix anta 😭😭
@mariasamb45002 жыл бұрын
Yalna khipè aldiana të yalla maylén kholou mougn gningi bokk ak yén mettite wi doyna war
@mberryfall19072 жыл бұрын
Li meitina nak niounn si bann monde laniou nekk ? Mere bi yal naka yallah may kholou mougn 🙏repose en paix Anta🤍🕊
@sophiediakhate1412 жыл бұрын
Bilaye li metina menouma teyé sama roguagni 😭😭😭
@aminambodji452 жыл бұрын
Gniy politique khalei yi nk Ben dom si s'en yaya laniou sokhla sm ben cousin naron naniouko Ray nakh ben dom la si yayam niou yobuko ba côté cimetièr ba nar ko Ray
@shamthiam77742 жыл бұрын
Chiii père mom merci rek
@MKBkoncept-AfroCoaching2 жыл бұрын
Je m'intéresse à cette histoire mais je ne parle pas wolof ... pouvez-vous sous titrer cette vidéo svp... Afin de la partager . Est une histoire bien triste qui se soit de faire le tour du monde . Paix à son Âme. Qu'elle puisse reposer prêt des ancêtres
@evalyon93892 жыл бұрын
Cest vraiment triste
@apassesane90052 жыл бұрын
Pere c n a rien a faire si on est Diola, peulh cet... un chef de quartier doit proteger tous les gens qui habitent dans quartier,
@clairemari72922 жыл бұрын
Ndeyssane paix à son âme
@fatoudiouf87562 жыл бұрын
Tabakh yi laniouwara dinedi defkatou niaw téf yi silagniouy lakatou
@aissatoudiallo3492 жыл бұрын
Lolu la done wax demb koussi am chantier gua def thi porte teudj ko moy yone
@fatoudiouf87562 жыл бұрын
@@aissatoudiallo349 bilay sokhna si li metti Na trope yalnala ko yalla nite
@1khouredia2 жыл бұрын
Surveillez vos enfants aussi 8 ans khaler la sa place c’est à la maison.
@princessemyadiallo97912 жыл бұрын
Massa yalna yalla may léne kholou mougn ndakh domou niépala
@damemarr27452 жыл бұрын
Sènègal 🇸🇳 liy mètiy na lool😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😡😡😡😡😡😡
@afrikfuturleadinginnovatio98012 жыл бұрын
SURVEILLER VOS ENFANTS NE LES LAISSER PAS ALLER SEULS A LECOLE OU A LA BOUTIQUE LES MALADES MENTAUX SONT DANS LES MAISONS MAIS PAS A LHOPITAL COMMENT TU PEUX LAISSER TON ENFANT SEUL DANS LA RUE ,PRENEZ VOS RESPONSABILITÉS.
@ndeyecodoudiop25002 жыл бұрын
Wakh ga lép j t jur
@afrikfuturleadinginnovatio98012 жыл бұрын
@@ndeyecodoudiop2500 mais lorsque je vois des petites filles comme des moutons de Panurge je me dis que leur parent sont des moins que rien c'est facile de faire des enfants mais le réel problème reste l'éducation il ya trop de moutons dans ce pays !! C'est du jamais vu ,un enfant de 7 ans seul pour aller à la boutique ou a l'école mais on va la bouffer vite fait bien fait !
@morniang30472 жыл бұрын
Serigne yalla rek monio mana mousal si li nane wakh niakk sécurité bi nek ci rew respect
@aissasolution96642 жыл бұрын
Le problème est que souvent il sont en danger mm à l école
@fandao21382 жыл бұрын
Wa pabi niit leu ? Kougn rayy domam nganane ko santal, yaw mi tamite so werer dineu ma diakhal
@awasall95362 жыл бұрын
Dafa diakhlé ndeysane
@jujudabo31322 жыл бұрын
Ak weré khel mi Pa bi kay ndysan peut être choc bila
@djitte18safar2 жыл бұрын
Geum yalla ,yonent yi, malaka yi,téré yi ak ndogal bi mu nex wala mu naxari..goor gui fi lay waxé...sunu boroom dani kuma sant ma dolil la..kone domu adaama luko dikal rek nako santé yalla..
@yayafall73532 жыл бұрын
K sn ame repose en paix 🙏
@rokhayadiop18562 жыл бұрын
Grand père bi mom dagne ko warone dague
@awasall95362 жыл бұрын
Dafa meunoul wakh prsk nekoul place bimouka wara wakhé
@lareine21682 жыл бұрын
Bâtiments tu n'y tabakh diko bayi nonou lagnou wara bayi ,fofou la viol you beuri di âme, AK ray
Légui thioro mboup nak lousi wakh mome mo andi khalé bi pour nion rayko di
@nadafafall70942 жыл бұрын
Peulh fouta yi sonal wa thiaroye aussi j ai vu d cas de viole trop
@alouproboykl56382 жыл бұрын
Grand père meuno wax déh le rapport dans tout ça 😟
@الراجيرحمةربه-ث5م2 жыл бұрын
Mane ta wax kay
@juliettebouillet47812 жыл бұрын
Oh m'y good,
@binetandiaye47762 жыл бұрын
Yalla na yalla may l'en xoolou moune
@Mame-ndiaye-savon-officiel2 жыл бұрын
Mais pa bi limou wakhe yeupe kouko ko ladje,aaaaaah lii wére sa dome la,wala dafa yakar ni dagnekoye faye limou fadjé domame.
@kandjikhar49812 жыл бұрын
Mome mi moy doff bi
@maimounagoudiaby26722 жыл бұрын
Peine de mort est la meilleure solution face à ces meurtres perpétrés au Sénégal
@Minabellaunivers2 жыл бұрын
Je compatis votre douleur 😣 ça me rage
@boxingpulse97232 жыл бұрын
Merci la police ,mais il rétablir la peine de mort
@mamecheikhdiopjazbou25392 жыл бұрын
Kico yoni goor la wala djiguene ak bane àge la am
@aminambodji452 жыл бұрын
Djiguen la 13ans la am
@shelamendy55342 жыл бұрын
Diap nagn ko.
@ndeyekharyfall58192 жыл бұрын
Mane dal dama fok ni dafa am peut-être Loulen xaler bi xamal te beugougnou mou fegne mo tax xana gnou def ko ni
@sambasylla50932 жыл бұрын
kou ray niou ray la
@dalouch32652 жыл бұрын
😭😭😭😭
@khadimka20582 жыл бұрын
sen delege d quartier bi dh dofla ki limiy wakh nii loum diotek li khew bamouy lim naan ay diola ay peulh extr.... ki dh waroul djite ken mais nak delen segue lingueni tek avant nguen koy dialale si media amna nio xamni wakhi doff laniy wakh nama yalla baal
@akaramory74412 жыл бұрын
Anta repose en paix Thiéy Sénégal gnou wara déff constat séne auto pane gnou dokh le Pays va couille
@fallfall85202 жыл бұрын
Laye diarra
@dijabousonkotvofficiel29642 жыл бұрын
Paix à son âme 🙏
@kaami87092 жыл бұрын
Pabi vraiment c grave😡😡
@haysamatanar24752 жыл бұрын
Yawit mam febar bi djaroul soulli yemal si deegi mam
@yayediormbengue2 жыл бұрын
Moma diakhal
@sokhenaseck71162 жыл бұрын
Mak bour laa
@weezy78972 жыл бұрын
Pas bi keuy mome diakhale nama trop soutoura zero
@Onomar2 жыл бұрын
Un délégué de quartier qui mérite pas sa place . Qui ne sait pas parler et qui doit immédiatement être destituer parcequ’il peut déclencher une guerre civile ses paroles sont bizarres . Comment on peut dire surtout Peul’s yi
@marietoudiallo61612 жыл бұрын
Bien vue
@marietoudiallo61612 жыл бұрын
Mane dh dama bêta Sakh wakhou fi dara
@nadafafall70942 жыл бұрын
Il a mal parlé mais c peulh la font trop de viole surtout a thiaroye gare j ai vu d cas comme ça
@girlnoir91542 жыл бұрын
Un enfant de 7ans Ndeyssan xamoul dara
@ndeyebounamadiop58632 жыл бұрын
Aye waye yene tamit 2h lou khale di def si mbeed
@sodambaye16282 жыл бұрын
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@oumoungom31682 жыл бұрын
Yom yeupou aye khalelayou
@fatoudiouf87562 жыл бұрын
Ki nagiouko Ray mou diekh
@aminambodji452 жыл бұрын
Yaye dji ben dom la am
@ramadiouf73692 жыл бұрын
Paix à son âme
@mbayemously22492 жыл бұрын
Wa pa bi werna
@ndeugoulayesarr45852 жыл бұрын
Ki kay doyna war
@opporeno77992 жыл бұрын
Naiou ko Ray bamou dé
@nadafafall70942 жыл бұрын
Esk fi senegal la wala
@papiscisse23712 жыл бұрын
veuillez retifier le nom du quartier svp c'est bien Bargny Kipp au lieu de tipp
@OnaimeLeSenegalAvecPassion2 жыл бұрын
Legui mome Sénégal deukou thiaga leu... Maname legui khalé you djiguène gni khar touniou mariage pour seye... ken neketoul vierge... Billahi diaplen ko ni rek... Di katanté ba diaral leu ngueu reye sa mbokhe... Thieye khalass. Teu lolou choqué oul ken. Waw goor.
@lasalihate61012 жыл бұрын
wa pabi esck weurneu
@ladoucedouce99282 жыл бұрын
Kiko yoni wone goorla wala djiegene
@KewouloTV2 жыл бұрын
Djiguène leu. 13 ans la ame
@Yaramyaram8442 жыл бұрын
Kiko yonni djiguen la moko ray ak copain wam dagne done deff report sexuel khalè bi guiss lène
@Mina-em5bq2 жыл бұрын
Wa mais grand-père est-ce que cava ?
@felixemmnuelsagna25772 жыл бұрын
Tout ça, c' est le fruit de l'impunité, une justice a double vitesse. De grâce plus de rigueur et de sérieux sur la sécurité des personnes. 365 jours sur 365 jours de politique politicienne, ç a ne fait développer un pays.
@khadimka20582 жыл бұрын
so diklo djiguene gni di wakh rek ngua xamni sen kholou yaye moy wakh motakh yaye ken amoul fayam nanlen geuneu fonkou souniou wadiour yi rawatina yaye mais aussi ki def lii defna lou niaaw dome ak nimou nekhe si khol ngua rayko si 0
@folashade27492 жыл бұрын
mais OU EST LE CRIMINNEL ? LE GARCON.. A T'IL ETE INTERROGE?? ET AUSSI LA FILLE DE DOUZE ANS SON GIRLFRIEND?? FRANCHEMENT
Parce que dafa wara dioy devant les écrans pour montrer qu'elle a mal?? Choc émotionnel dafay am Amna niouy dioy ci khôl wala mou dioy ba fimné xol bi Day deugeur m
@Mina-em5bq2 жыл бұрын
@@aminambodji45 je crois qu’elle répond au grand père de la petite
@fadabakhfashion24822 жыл бұрын
Pourtant je m'adresse au grand père de la petite fille même moi j'ai pleuré je senti que la maman souffre à cause de sa fille mais la manière dont le vieux a parlé en révélant la maladie de la maman me fais vraiment mal en disant qu'elle doit pas pleurer cause pour laquelle j'ai dis que yaye dji dafa am xol loutakh waroul dioy j'espère on s'est pas compris.
@fadabakhfashion24822 жыл бұрын
@@Mina-em5bq tu m'as compris chérie
@beautenayo10312 жыл бұрын
Mais ces koi sont délire ay diola ak peuls gnio me dounou ay nite
@babelthiam75892 жыл бұрын
wa guiga yonei mak la walla khaller
@fadabakhfashion24822 жыл бұрын
Wa pa bi tamite
@virus9652 жыл бұрын
Wa pa bi momit esk warougn ko yobou fann n’importe quoi
@OnaimeLeSenegalAvecPassion2 жыл бұрын
Thiaga bi
@takodiew24332 жыл бұрын
Foudene
@mamedialedia83782 жыл бұрын
KIKO YONNI ANNONCÉ DÉEGUI KHAMNATHI DARA
@andresperezhernandez93502 жыл бұрын
Papi tamite metinama metiwouma moy lane
@beautenayo10312 жыл бұрын
Ce vieux ils est fou ou tromatiser dé bi metina metiwouma moy wakhi lane
@antandiaye33982 жыл бұрын
M0
@babsmbengue94122 жыл бұрын
Je ne le connais plus le Sénégal le Sénégal vas très mal 😭😭😭
@jellyberry97392 жыл бұрын
C'est ta faute mme désolée pour se qui t'arrive mais vous n'avez pas d'arrière pensée tu n'as pas surveillée ta fille 😭😭😭😭toute la journée à un âge très délicat niou yobou sa dome dou sori sori et il a fallut qu'on t'appelle pour venir et doré on la retrouvé 😭😭😢😢😢 j'ai mal parsque la principale coupable c'est la mère tu as laissé sortir ton enfant sans qoucis et c'est quoi l'explication 100frs et sama yaye daf may daure aucune explication valable .
@mbossediaw28412 жыл бұрын
Genre commentaire yi mome war ngueneu ko bayi niiit kou nek si naxar nga koye yokou naxar bou nekone inconnu moko def la on p dit m’ai kou xamni deukando la lolou on n’y p rien nga balma nak
@marybarham34902 жыл бұрын
Amina Sarr arrêt fi kou fi am dôme dinako têye Ck khalé lagnou mounoul teye rek yaw esk bigua neke khalé sa yaye daf la done teye yafi dakone dokh kon boul gnou sonal tegua gnanal rek mo guen mo guen guay agne yayam adouna nak dafa goudou tang boudone yaw digua begueu koula epaule walla yaw bokou khalé bi reyy la arret nak
@marybarham34902 жыл бұрын
@@mbossediaw2841 ki dou nitou dara esk mom yayam daf ko donné teye ki dou nitou dara khana bokou ki rey la