Ay deugue you woore gua wakh manchalla!! Yalla nalla serigne Touba Faye. Cheikh béthio yalla nako serigne Saliou térou si adianay firdawci!! Amine.
@sellesene20905 жыл бұрын
Walahi saaway ya am xan xam lingua waakh saway dafma laal bamay tour ay xeweul mangui dogua tourr xeweul ba cheikh bi laako ba leigui...dieureudieuf mouride yalla nala serigne touba faye
@ndeyemattydiop42185 жыл бұрын
serigne béthio dieureudieuf serigne modou kara dieureudieuf tous les thiantacone sont des kara yéé tous les kara yéé sont des thiantacone
@omarsene12235 жыл бұрын
Leerna nagñ . merci mbokkk dèggg nékhoul
@firdaousifirdaousi66105 жыл бұрын
beuri gua thi morom dieuredieufe serigne saliou mbacke diawraw lake cheikh bethio yalla n'a yalla Yoko lairam amine
@soniandiaye4435 жыл бұрын
Waw goor amna solo lol dieureufieuf Serigne Saliou kadou yi rafetna lol tè lidji yèmè moy 1er jour koor gua kham ni dji la portes paradis yep di oubekou akassa mouride santat nane bou bakh
@fatoudiagne61615 жыл бұрын
OHHHHH MOURID YA AM NDIMBEUL.YAW DEH DA NGA MAY FATALI WAKHOU SERIGNE SALIOU BI MOU NAN CHEIKH BETHIO " kou am thieur fa souniou borom dina nagou say mbir". YA NGUI FIRNDEE NI BOROM THIEUR NGA FA YALLA
@dionesswazy40985 жыл бұрын
Fall doundeul way serigne Bethio rek naniy geumm ba faww yagg fi rk tee weerr
@AwatoubaAwatouba5 жыл бұрын
Dieureudieuf mouride ya niak kiniane Serigne bethio nguiko khamoulwone bamou dem la yeureum Serigne saliou wathiewouko si souf loudoul mou rawale diamngui
@ababacardhshakursy7715 жыл бұрын
Thieyy Yalla Serigne Touba mo meune dh saway ya bakh dama yakarone ni nit you bakh you melni iow amatoul si miim rew. Et toi la bien dit tu suis très bien sax.
bilahi ya bakh kene dou serigne bethio gnoune ak mom ba fawww ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@tackodieng54865 жыл бұрын
Ndayssane ame solo trop copin santé serigne saliou rķ cheikh béthio yalla nako yalla yeuraum té kharé ko aldiana
@aminatadiouf94625 жыл бұрын
Ya bah yalla n'a la serigne bi fay machalah
@mamadoundong56225 жыл бұрын
Akassa Mourid waaaw gooor. Bék na loool Barkép CHEIKH BÉTHIO bék na. Ta fasnayéné Maye la oto voiture. inch'Allah
@matymbow8835 жыл бұрын
Hiooooooo sa dwr bilahi yalla rek mo meune kou yakar ni dangey tok rek sa keur nane serigne la beug té doko sonal béne yone ndakh nga sa bop y a d amour il y a ke preuve d amour affaire dieuf dieul serigne bethio wané tina yone wi dieureudieuf thioune mbek mi nagne ko nosso
@anisalihate63375 жыл бұрын
Ndeysane dieureudieuf yaw deh gninga wahal teh meunounio def video barina wayè nioune deh sante naniou serigne bethio boubaaaah thioune dieureudieuf
@ibrahimaboye18255 жыл бұрын
Waw goor mouride kaadou yi rafétt na troop bégu nangou siisa kaadou yi barki serigne saliou doundeul illimité
@Bougane_Gueye5 жыл бұрын
Merci yaram! Serigne Modou Kara ak wakeureum, kéneu dou yen. Yena deugou!
@ninjablakfire673714 күн бұрын
Kou bakh nga Sénégal dafa bari gnou ignane mane mokalna khassida yingay wakh ni Djeuzbou Mawahibou Moukhadimat AK yanèn té Cheikh Béthio moko déf Thi mane dieureudief Serigne Béthio
@cheikhbambasarr68125 жыл бұрын
Bilahi vidéo doumako commentaire roule gorewouma bilahi kou ya bakh yalla nagne la degeu dontee nopou degeu mofa deukeu cheikh Bethio rawna Man douma talibem way rawna
@papisecissko74985 жыл бұрын
Dieuredieuf mouride amna solo jtm bcp dieuwrine
@bassirouseck51615 жыл бұрын
Serigne Touba cheikh Mountakha Mbacke yalna yague té ame werrr Mame cheikh Ibrahima fall Dieumbe yalna fi yague té werrr Cheikh borome mbaor fall inb Seydina Aliou doundel ay kabition atte mou ande ak werrr
Yalla nako yalla yeureum te khrekoaldijna firdawsi te samalko guinawam amine yarabi
@magsertv5 жыл бұрын
Dieredieuf Mourid Sadikh Cheikh Bethio un lumineux Miracle de SERIGNE SALIOU la vraie compétition de nous les Mourides c'est le Pact dallegence la magnification du Grand Magal comme la enseigné Cheikh Bethio et non pas ce bruit linguistique qui ne mène à rien.Wa salam
@magsertv5 жыл бұрын
Il a longtemps oeuvré pour SERIGNE SALIOU
@TyronkaneTopDancersemba5 жыл бұрын
Sant nanela ci kadouyi. Yaw deh yalnala Serigne Touba teyel sa talibé ba faw 🙏🏾.
@magibo14 жыл бұрын
Repose en paix dwr pape birahim Kane diambarou SERIGNE BETHIO
@daoudasow895 жыл бұрын
Aka nga bakh mouride yalnala s touba defal diamou aminnnne diadieuffffffff
@papendour34355 жыл бұрын
dieuwrigne brk s béthio vidéobi mane ngako défal yéne ak nioune béne laniou chikori ak thiantacone nio bokou mision
@passane745 жыл бұрын
Yaw kou bakh ta mandou nga. Yal neu Yallah yok sa tawfekh ak seu Xeweul. Amine
@assba82175 жыл бұрын
Yow nii gua meuna meel cheikh mouhadou kara moye saa s'érigne douguene dioume douguene diawale dgue yalla la
@dizzykhaofficiel5 жыл бұрын
Wadji begg na lol si yow way
@miamia81035 жыл бұрын
Serigne modou kara moy gore on vous aime
@mamebirameba97525 жыл бұрын
Macha Allah. Tu es courageux
@ibrahimagaye2215 жыл бұрын
Dieuredieuf ya wah deugue
@malickgning68345 жыл бұрын
Bilay lep dina yok bayil ba magal gui dinagne kham bou bakh koy cheikh bethio bilahi kene douniou meussa meune ci magal gui
@boucardiouf38035 жыл бұрын
Malick Gning sa numéro la beuguone Mr gning
@malickgning68345 жыл бұрын
@@boucardiouf3803 waw diokh ma sa boss je te ferais signe sur Watshap
Tëguine moy allal ji gëna am sollo ci äduna ak alaaxira tè moy li gën ci li nitt mana Ndamoo akassa fall
@maneladia16655 жыл бұрын
Machallah
@morbane26535 жыл бұрын
Wawawe fall ♡ bégg nane trop
@barandiaye37655 жыл бұрын
DIEUREUDIEUFEUTY SERIGNE BETHIO SERIGNE BETHIO DIEUREUDIEUFFFF EN ROUTE VERS LE MAGAL AMOUL TAKHAW AMOUL KHARE RAWA TINA SAMA WA DARA TOUBA ITALY BRESCIA
@mohamedlaminedoucoure30715 жыл бұрын
Dieureudieuf machallah .........mouride 🤣💓
@dwridadrammeh36445 жыл бұрын
Jerejeffat SERIGNE BETHOI 👏👏👏👏💚💚💚💚
@aissatougning27945 жыл бұрын
Ndeyssane mouride Diadjef Deugue rekay Deugue
@papakarasene43455 жыл бұрын
Machalla😭😭😭
@sophiefallaidara52515 жыл бұрын
Mane talibe serigne bethio la mais serigne modou kara damako beugue trop trop sakh Bilahi goudal fane serigne modou kara Borom bakh bakha borom deugueul dioubal leral
@sophiefallaidara52515 жыл бұрын
Goor yalla sa numéro la sokhla guir dieumi serigne modou kara mbacker borom bakh bakha
@serignesaliou5695 жыл бұрын
Mouride barké Serigne Bamba sama Khol sédena lol ci kadou yi Damélni dagua kham li nek ci kholou Thianta yeup naniou gueneu lakhasayou rek yok pastéf Diadieuf Mouride
@GM-xz6pc5 жыл бұрын
DIEUREDIEUF SERIGNE BETHIO béégu na lool mourid yaw tu es à l'image de ton guide mome daa niaakeu kignane. Voici quelques vers de SERIGNE TOUBA dans MASSALIK JINAANE sur les marabouts." Ces vilains rusés, se targuant de perfection et de sainteté, accablent les gens par leurs multiples et diverses relations 1434. S'il t'arrive de louer à coté de l'un d'eux, un autre chef spirituel, jaloux et passionné, il suffoque de colère 1435. Au contraire, quand on critique un autre, il se réjouit à l'écouter et sa figure rayonne, s'agissait-il d'un Seih dont tout le monde connaît la vertu et la sainteté 1436. Il ne lui fait plaisir que d'être seul à être loué et exalté parmi les créatures humaines 1437. Quand, en quête d'un guide éclairé, ton choix porte sur un autre que lui, il en prend ombrage et s'irrite 1438. Malheur à lui ! s'il était désintéressé, s'il n'avait d'autres objectifs que le salut exclusif de ce disciple 1439. Il aurait plaisir à le voir sauvé n'importe où, et par n'importe qui, et son départ ne lui importerait guère 1440. Les chefs religieux de ce genre sont parmi les mercantiles, après au profit matériel, il faut les fuir 1441. Le Seih qui se croit au-dessus des serviteurs de Dieu n'est point à aborder, éloigne-toi de son voisinage, toi qui es vrai aspirant 1442. La Bonté de Dieu n'est point restreinte, Il comble qui il veut parmi Ses serviteurs 1443. Le célèbre proverbe relatif au jaloux renferme une sagesse, soit : "certes, un jaloux n'est jamais noble (de caractère)" 1444. Comment pourrait-il être noble alors qu'il aime et souhaite la perte de tous les biens à ses frères croyants
@SayDBamba2215 жыл бұрын
Merci Beaucoup Vraiment Bégg na trop tji Commentaire Mane Dama done Wakh rek té amouma kham kham yaw nga Indil mako thji Li Souniou Yakar tay ak Euleuk bindeu
Surtout Lamp tv vraiment niom beugou niou cheikh bi puisk ils n'ont jamais montré cheikh bethio sur leur chaîne même le grand magal setane trace moma gueunal setane Lamp Fall tv
amnasolo mouride madé jiapouuané bén mouride ba ngoull cheikh bi dax défarou s touba bane mouride mokai mbmng chou bokousi yonou mouride réx ngokai dignat wayé cheikh bimome sa sagoup mouride yapoulla
@diagnediagne75175 жыл бұрын
Merci
@niangmouhamadou78495 жыл бұрын
Kadou yi rafette na Lou diougué si khol si khol lay diougué Vraiment beug na kouma envoyer vidéo bii
@rokhayasambou20405 жыл бұрын
ya bakh wayyy diadieuf
@diaraafmbengue21555 жыл бұрын
Akassa mouride
@diodiondiaye60215 жыл бұрын
sama khol da sédd
@diomfoulla81625 жыл бұрын
Allah le tout puissant: C'est Lui qui détient les clefs de l'Inconnaissable. Nul autre que Lui ne les connaît. Et Il connaît ce qui est dans la terre ferme, comme dans la mer. Et pas une feuille ne tombe qu'Il ne le sache. Et pas une graine dans les ténèbres de la terre, rien de frais ou de sec, qui ne soit consigné dans un livre explicite. Et, la nuit, c'est Lui qui prend vos âmes, et Il sait ce que vous avez acquis pendant le jour. Puis Il vous ressuscite le jour afin que s'accomplisse le terme fixé. Ensuite, c'est vers Lui que sera votre retour, et Il vous informera de ce que vous faisiez. Al An'aam v.59-60