🚨Croyance erronée Chez les Talibe Baye Niass🤔🤭 ? - Oustaz Alpha Ba Ha

  Рет қаралды 10,858

KAADU DINEE JI Tv

KAADU DINEE JI Tv

Күн бұрын

Пікірлер
@cheikhassane7925
@cheikhassane7925 Жыл бұрын
Mbiir Yangui Lëer dëh
@PaBass-tp6bd
@PaBass-tp6bd Жыл бұрын
Dieureu dieuf baye Niass
@AssaneDiop-w5m
@AssaneDiop-w5m 6 ай бұрын
Saway baye niass moo dakha bokalé yalla sougnou borom
@DIOBISTO
@DIOBISTO 8 ай бұрын
Vraiment vous faites un très bon travail, merci Oustaz Alpha Ba, Younous, Sokhna Khady, Ismaïla, Khakh, Baïllo et toute l'équipe
@indigne2161
@indigne2161 Жыл бұрын
Baraka Allahu fikum ya Ustaz.Bon travail
@MamadMohamed
@MamadMohamed Жыл бұрын
Allahou Akbar Machallah qu'Allah vous protège
@lixman771
@lixman771 Жыл бұрын
Franchement je kif tes vidéos . Ces malheureux de le dire sénégal amoul diamou yalla😭😭😭😭a cause d’eux ce pays tarde à se développer 🤦🤦🤦
@sadikhdibalenoble7434
@sadikhdibalenoble7434 Жыл бұрын
Si ce pays tarde à se développer c'est à cause de la mauvaise politique rien à voir avec la religion
@leveridique9276
@leveridique9276 Жыл бұрын
Yaa meuna fein Senegal dou amoul djaamou yalla feinn amoul djaamou yalla
@AssaneDiop-w5m
@AssaneDiop-w5m 6 ай бұрын
Tarihayi gnoo taxalé djioulite Sénégal yi wallahi
@OumouSow-zz3qk
@OumouSow-zz3qk 10 ай бұрын
Dieureudieuf Baye Niasse 🤲
@Mouhamad-u6f
@Mouhamad-u6f Жыл бұрын
Machallah
@SambaFaye-i7n
@SambaFaye-i7n 8 ай бұрын
Bilahi yekh nga niew legui sounah rek tarikha dou dara tous
@AssaneDiop-w5m
@AssaneDiop-w5m 6 ай бұрын
Talibé baye niass gnoo dakha bokalé yalla sougnou borom amougnou yarr ci yalla
@karimistesarr3457
@karimistesarr3457 Жыл бұрын
Wahh deug yalla je suis mouride sadikh talibé serign touba. Mé nakk yalla bour bii kénn la❤
@PaBass-tp6bd
@PaBass-tp6bd Жыл бұрын
Sa way daga dêg niou wakh ni aye yalla you Bari nio âme
@IssakhaDiouf-e9t
@IssakhaDiouf-e9t 10 ай бұрын
Khé doul way nite dou yala
@AichatouNiang-jo7ej
@AichatouNiang-jo7ej Жыл бұрын
Sheikh Alpha affaires yii mu ngi leer vraiment
@fatimatandiaye6679
@fatimatandiaye6679 Жыл бұрын
Merci ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@moustahadrame6979
@moustahadrame6979 10 ай бұрын
Baye Niass point 🎉❤
@fannylopez8928
@fannylopez8928 Жыл бұрын
Comme daguene diap né yena gnou guene gnoune Talibé Mawlana Cheikhal l’islam kay Diaroul débat Niit kay boko guené diaroul guay wax si mom Yena baxx gnoune gno **** Comme tamit nangougua ni Hanrif bi da diaxasso ak yalla baxna 😂kou xam sa bop xam yalla Alhamdoulilah ❤🎉Dieureudieufé Mawlana❤
@seynaboulo796
@seynaboulo796 Жыл бұрын
Yaw dimbali gnou kouy diamou yallay nitt ak kouy diamou yalla kou thi nitt ki
@fannylopez8928
@fannylopez8928 Жыл бұрын
@@seynaboulo796 insolente d’abord lo guem yaw la Gnoune meunolene Rap Rap bagnou bayi Baye Niass Comme vous êtes les meilleurs c’est bien Bayi lene gnou gnoune gni Pire
@youngflick8082
@youngflick8082 Жыл бұрын
@@fannylopez8928en tout cas senegal mom dine amoufa ak sen genre pass pass yi . do dem fen ci aduna bi ba niou wakh la ay wakhou baye niass. molay wan ni kokou dou dara
@fannylopez8928
@fannylopez8928 Жыл бұрын
@@youngflick8082 demal si narr yi ak nigeria gua wax fa li Limom douma si mere douma si xoulo🤣🤣🤣li lagnouy wax waxi dof ak gnak xam
@BahMadiou-p1k
@BahMadiou-p1k Жыл бұрын
Alpha ba reglel
@aboubakarndao2863
@aboubakarndao2863 Жыл бұрын
Yallah magui lay sante si bigua ma mouthialé thi tarikha yi
@AssaneDiop-w5m
@AssaneDiop-w5m 6 ай бұрын
Tarihayi gnoo taxalé djioulite Sénégal yi wallahi
@abdoulayecisse2566
@abdoulayecisse2566 Жыл бұрын
Niassene dou tarikha sante la encore une fois!!! Tu commences à ns emmerder
@Mouhamad-u6f
@Mouhamad-u6f Жыл бұрын
Sénégal toutil yalla souniou borom ak yonente bi salahou hanleyhi wa salam motakh yalla diniou nato lou nek
@hassanatoudiallo7331
@hassanatoudiallo7331 Жыл бұрын
Seydi Alpha mangui lay ziar boubah je te comprends nak boo degué yiii franchement diné andoul ak Chirk wayé baye nianga louniou liii baye sou wahé lep yallah leu il veut dire lepeuy dieh sauf yallah : koulou man àleyha fannn , il veut dire aussi avant dara diii am yallah rekkk moo fiii nek : baye nak wotéwoul ben yone chirk . Merci si say lecons aussi 🙏
@abdoulazizsow3734
@abdoulazizsow3734 Жыл бұрын
wakhal lo kham baye wakhoula lolou
@DIOBISTO
@DIOBISTO 8 ай бұрын
Même les mécréants sont mieux que ces individus, ces soit disant marabouts ont raconté des conneries et absurdités Merci Alpha et tout votre équipe, Qu'Allah vous protège
@abogassama6567
@abogassama6567 Жыл бұрын
😭😭😭😭😭
@karimistesarr3457
@karimistesarr3457 Жыл бұрын
Non wakhoul mame chéikh Ibrahima fall déeee niom danio am IBRA fall mo tahh na lérrr😅😂
@cheikhsadiboudiedhiou309
@cheikhsadiboudiedhiou309 Жыл бұрын
Assalamouha leykoum
@hassanatoudiallo7331
@hassanatoudiallo7331 Жыл бұрын
Walahi deugleu yallah ken diouroko, té lolou naniiou baye wah yit . seydi del deglou niom cheikh mahi Cissé 🙏 tu écouteras que des enseignements du prophète saws ❤️🙏
@PaBass-tp6bd
@PaBass-tp6bd Жыл бұрын
Baye rék ❤❤❤❤❤❤
@AssaneDiop-w5m
@AssaneDiop-w5m 6 ай бұрын
Baye niass moo dakha bokalé yalla sougnou borom
@amadoudia4615
@amadoudia4615 Жыл бұрын
Man talibé baye la mais amoul fen fou baye waxé ni mom yalla la au contraire baye dafané la kinal hak anna raba laysa bi abdi wal abdi laysa bi rabi
@ibnmohamedthiamthiam1783
@ibnmohamedthiamthiam1783 Жыл бұрын
بارك الله فيك
@oumardia2420
@oumardia2420 Жыл бұрын
السلام عليكم ورحمة الله
@realindicestreet4773
@realindicestreet4773 Жыл бұрын
Bro question bingalatieténi damalaye dello wate tji Li yalla wahe make samaye lalayeka dioullinanie si yoneinetebi leigui bane nguenéle wala bane grate lako yoneinetebi eupalé ba tahe yalla ak aye malayekame dioulli naniou tji mome
@alinesamb5006
@alinesamb5006 Жыл бұрын
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته كيف حالك أنت بخير أحسن الله إليك ماشاء الله بارك الله فيك أخي الشيخ الفاهم باه حفظه الله ورعاه ❤❤❤
@IssakhaDiouf-e9t
@IssakhaDiouf-e9t 10 ай бұрын
Kay boss baye moy cheikh Tidiane li degla yow do ragal yala leup lou baye am si cheikhou Tidiani lako yala diaralé
@AssaneDiop-w5m
@AssaneDiop-w5m 6 ай бұрын
Chiekh tidian ak bay niass gnoo dakha bokalé yalla sougnou borom amougnou yarr ci yalla
@PaBass-tp6bd
@PaBass-tp6bd Жыл бұрын
Khana ibadou gua😂😂😂😂😂
@zeydaoumouinsadiakhate1258
@zeydaoumouinsadiakhate1258 Жыл бұрын
MA IBRA FALL KOSSY DOU SEN MOROM WAKHATOUMA NGEN AM AUDACE DI WAKH THI BAYE NIASS NEK LEN THI LINGEN NEK TÉ NGEN MANDOU THI DIAMOU YALLA YI
@aboubakarndao2863
@aboubakarndao2863 Жыл бұрын
Hein séne guem guem yémé na lou takh yéne yi nék si tarikha yi do léne khalatt
@asinoh589
@asinoh589 Жыл бұрын
​@@aboubakarndao2863yas yaye khalate kon bakhna 😂 Boudé tarikhat molènn déranger di ngènn nax doufi dagne mbouck yénn gni diap né yéna bax yéna né di deug dina lér boudé tarikha bida le kousi nék yéfèrr le dina lér
@IssakhaDiouf-e9t
@IssakhaDiouf-e9t 10 ай бұрын
Khé doul yéna takh gnou yab Baye
@assanediallo150
@assanediallo150 Жыл бұрын
Qu 'allah efface tout sort de scirk et bida au Sénégal
@zeydaoumouinsadiakhate1258
@zeydaoumouinsadiakhate1258 Жыл бұрын
GNOUNE BAYE NIASS LAGNOUY TOPOU MEUNO LEN THI DARA
@fannylopez8928
@fannylopez8928 Жыл бұрын
Gni gno diaroul waxal 😂bayilene gnouy di-ngat Gnoy gniy teuxxxxx
@fannylopez8928
@fannylopez8928 Жыл бұрын
Mbam yagui beuy yagui guinar yagui tew Ndaxam gnoko bagnone demb seydi barhama❤️🥰 Yaye boye gni yess lagnou def té walahi dinagnouko guiss Nagnou lathie gnidone wax si Baye lou gnaw Kou bagne baye doumala nouyou doumala diox lokho
@seynaboulo796
@seynaboulo796 Жыл бұрын
Toppall yalla mo diara toppou dé
@fannylopez8928
@fannylopez8928 Жыл бұрын
@@seynaboulo796 taw dh topoko ndax yagui si commentaire yi di weur talibe baye yi🤣
@SambaFaye-i7n
@SambaFaye-i7n 8 ай бұрын
Dema touma gamou dou magal sounah rek ouztas liga wakh moy degue sounah dafa nopele trop
@mouhabarxam70
@mouhabarxam70 Жыл бұрын
Saway Baye Niass limou deffal islam diamou ko ci yalla ba bangay dé doko deffal l'islam kone bayilen dingatt. Baye Niass mossoul thiaxane
@issadiallo2905
@issadiallo2905 Жыл бұрын
Damal laathi khoudar loutalh mou réyoon khalé bi , beunneu gaalou miskiin yi
@arameba7441
@arameba7441 Жыл бұрын
Définition bi nguey djokhé ci Anrif tamite ware nga léral foko teik. Lane moy Anrif lou kharam amoul ci mome ? Cheikh Ibrahim bi nguey wakh ni il adapte son discours tamite dou deug parce que Baye nimou mélone ci Al QURAN ak ci SUNNA wakh naci wakhati ci. Nga ni Sangue Ndiaye ay wakhou Baye Niass ley répéter té amoci béne preuves. Djoulite Haqqan avant mouy wakh dafey vérifier.
@asannediop3826
@asannediop3826 Жыл бұрын
Salam mbok yi Loutah dou ngou respecter yalla soungou borom Allahou Akbar
@AlkhairyAlkhairy
@AlkhairyAlkhairy Жыл бұрын
شيخ ابراهيم انياس لم تقل ابدا بانه هو الله لم يوجد في كتب شيخ ابراهيم انياس أبدا إلى أبد الآباد إذا وجدته في كتب شيخ ابراهيم فلتات بي لايوجد أبدا أما هولاء الذين يقولون هم الله ليسوا بطالب شيخ ابراهيم انياس هم ينتسبون بشيخ ابرهيم فقط وليسوا بطالب شيخ ابراهيم . بعد ذلك اتيت لك نصا الذي كتبته شيخ ابراهيم انياس . قال شيخ ابراهيم. في جواهر الرسائل. أن الرب ليس بعبد والعبد ليس برب ولكن الذي يصح أن يكون عبدا هو الكون. هذا قول شيخ ابراهيم انياس
@asinoh589
@asinoh589 Жыл бұрын
So amoul kham kham Hakhikha dagaye oup sa guémigne té mandou komk yènn gueumolènne hakhikha sèn affaires leu Baye niass dou yalla ndax wakhouko sangue nak molène togne nax mo wax lolènne khamoul mais Baye niass milènne di déranger dousènne morome dou sén moromou Baye aye talibème gnémé wolènne took ak niom face à face en direct plateau khana lakhatou si écran yi di fènne rk
@DIOBISTO
@DIOBISTO 8 ай бұрын
Wakhi doff reck ngènne di wakh, 😂😂😂
@issadiallo2905
@issadiallo2905 Жыл бұрын
Bébé nga doo yam si rouy yi ak sa biberon yi té baayi yapp bi. Chiot bi nga doon
@issadiallo2905
@issadiallo2905 Жыл бұрын
​Golo Sakh moo KO geune
@IssakhaDiouf-e9t
@IssakhaDiouf-e9t 10 ай бұрын
Bayil khasté té tontou si kham kham
@sonyboys2967
@sonyboys2967 Жыл бұрын
Qu'Allah nous preserve des sectes
@SambaFaye-i7n
@SambaFaye-i7n 8 ай бұрын
Outaz lima komom bilahi guisna sima bopou tarbiyana depuis 2011 me rethiou na lepou guindi guenma boubakh
@mysteremystere5196
@mysteremystere5196 Жыл бұрын
Yen s'en niveau agoul fi kone bouléne ko wedy
@moussaalkhayri5253
@moussaalkhayri5253 Жыл бұрын
Yaw Alpha Ba daga aborder sujet bo maitriser woul. Li wakh si Baye Niass ak ndignat mom khamel ni ngoula eupou khamkham gueun la ragal Yalla eupoula îmaan gnossi nekk diko ndoundou, gueum ko ta diékh si takk. Yalla rekk mofi nekk wayé lolou niveau la mais dou wakh diou molafay takha yegg.
@IKS_Barhama
@IKS_Barhama Жыл бұрын
Xam-xam ngen di dég si talibé baye yi. Motax ngen sone si sene vidéo yi.
@mouhabarxam70
@mouhabarxam70 Жыл бұрын
Saway boul fatté ni deukk djioulitt yoyou ngay gnom gno fekk ci Baye Niass Kaolack ay seuttou Yonneté bi gnom la Baye Niass yobou ci tollou kossi yi gnoukoy bayal thia tangor ba. Sa niveau deffa bas. Boy Alpha
@ibnmohamedthiamthiam1783
@ibnmohamedthiamthiam1783 Жыл бұрын
Wallahi ndaysan diadief
@AichatouNiang-jo7ej
@AichatouNiang-jo7ej Жыл бұрын
Sheikh Alpha prochain live bii c'est quand ?
@abdoulayecisse2566
@abdoulayecisse2566 Жыл бұрын
Alpha Ba yow cheikhou cherifou rekk lay guiss thi yow en mode grand écran !! Damala yeureum walalhi
@SambaFaye-i7n
@SambaFaye-i7n 8 ай бұрын
Sague Ndiaye mom domeharam diaroul tontou ab baye fall
@nassirdiagne3739
@nassirdiagne3739 Жыл бұрын
Ya gui wakh lo khamoul tu finiras mal ليس كمثله شيء
@alassaneseye2191
@alassaneseye2191 Жыл бұрын
Bayil sa thiakhan yi
@LamineToure-c4l
@LamineToure-c4l Жыл бұрын
لا يصح ولا يتصور الحلول والاتحاد إلا ممن يعتقد المسافة بين الرب والعبد،،،، وهو لا يكون إلا ممن قلبه في ظلمات بعضها فوق بعض إذا أخرج يده لم يكد ومن لم يجعل الله له نورا فما له من نور،، والله هوالنور. وأصل هذا أن المحجوب يعتقد في الله الحسية كما يعتقد في العبد،،،فيستحيل عنده اجتماع الحسيين عقلا فيقع في تلبيسات وشبهات جاءت من عنده، و اعتقاده هذا لا يمنع أن يكون الحق تبارك وتعالى حقا ولا الباطل باطلا. والله المستعان.
@PaBass-tp6bd
@PaBass-tp6bd Жыл бұрын
Vraiment tu me fais rire
@aminatambow4164
@aminatambow4164 Жыл бұрын
Kou am xam xam DEUG mandou si nitt yi kou dé akk sa bamel Kone kay kounek bayiko AK waxam AK gueum gueumeum
@dabakhniang5926
@dabakhniang5926 Жыл бұрын
alfa baye dafe amon moukhaddam boutoudou chiekh ibra fall
@yerosow4792
@yerosow4792 Жыл бұрын
Pas de sons
@leveridique9276
@leveridique9276 Жыл бұрын
D'abord wakh bi waadji wakh ni ibra fall dafa dougou ci neigou baye niass guiss baye niass di djangal yonent bi loolou weiroul meunoo djeul ay wakhi keinein dici attei baye niass il existe plein de hadiss yoo hamni yow dagay wakh ni weiroul yonent wakhouko wala histoire bi amoul donc sou nit wakhei ay wakham diko askanalei baye niass dagay gueustou baham wakh dji weirna wala weiroul talibei bi dougou di djeima layal wakh djii day sonal boppam yonent amoul loumoul djanguei ci baye niass baye niass leipp loumou ham ci yonent bi lako hamei saw
@abdourahmanendiaye7293
@abdourahmanendiaye7293 Жыл бұрын
Li gay wakh amoo thi xamxam té nga noopi wala nga gnew senegal wakhko book boudé deugue la dokhoum essence dougne ko fayé day dafay yook day gui doolé
@aminatambow4164
@aminatambow4164 Жыл бұрын
Niassene yi finiouy waxé kouko dégoul doko xam Kone nga nopi
@PaBass-tp6bd
@PaBass-tp6bd Жыл бұрын
Khana ibadou gua 😂😂😂😂😂😂 yalnala yalla yeureume ok 😂😂😂😂😂😂
@asskhayrimbow5316
@asskhayrimbow5316 Жыл бұрын
Ki d'où niassene
@realindicestreet4773
@realindicestreet4773 Жыл бұрын
Bro question bingalatieténi damalaye dello wate tji Li yalla wahe make samaye lalayeka dioullinanie si yoneinetebi leigui bane nguenéle wala bane grate lako yoneinetebi eupalé ba tahe yalla ak aye malayekame dioulli naniou tji mome
@mouhamedfaty3857
@mouhamedfaty3857 Жыл бұрын
Frère ta question je l'ai compris peux tu éclaircir d'après lima lire c'est comme si tu fais une comparaison entre le prophète et Baye Niass wla man ma dioum ?
@abdoulayecisse2566
@abdoulayecisse2566 Жыл бұрын
Yow soy sarakhé lane ngay wakh ame yallah diokhla kone fane nga nekk !!! Bro si tu veux passer toute ta vie à critiquer les arifs dinga tardé soula gnoré demal kaolack et tu saura t'es trop terre à terre linga diapé xam xam dou dara
@IssakhaDiouf-e9t
@IssakhaDiouf-e9t 10 ай бұрын
Ii mo takh kén dou cheikh Ousmane mbow
@mamediarraboussodieng3068
@mamediarraboussodieng3068 Жыл бұрын
Yaw té gua mandou té gua wakh thi lo métrisé meune wakh daffa nekh deug ko raw guir yalla maloko ñane so ñeuwé ñou tarbiala tarkhiyalla yégualla wathiéla gua dokh deug deugui kham kham di gua SAP 5000fois
@AssaneDiop-w5m
@AssaneDiop-w5m 6 ай бұрын
Baye niass moo dakha bokalé yalla sougnou borom moo daha togne amoule yarr ci yalla sougnou borom
@mamoudoudaff3028
@mamoudoudaff3028 Жыл бұрын
Ndessaye lou xamoul .mou rereleu..demal tarbiyou tu comprendra lou harif bilahi..
@moussaalkhayri5253
@moussaalkhayri5253 Жыл бұрын
Diiné dji dafa am ay makhaamats à savoir: l'islam, l'imaan et l'ihsane. L'islam aussi dafa am ay maratib: Tawbatou Istikhamatou Takhewaa. Niéti yi bou sinekk amna nougn koy ndoundé si diné dji. Imaan la mm chose . Ihsane aussi la mm chose. Ndakh ihsane maraatibab moy Mouraakhabatou Mouchahadatou Maarifatou. Guisgua kon fi maarifa bi guay nekk di wakh fim nekk. Kon maarifa dou kou diot rek dissi wakh. Attention Alpha ba
@fannylopez8928
@fannylopez8928 Жыл бұрын
Diaroul sax lirel papeu Gni walahi serane lene Niit bou tokk ba yakar ni ya guene sa morom rk walahi xolatal sa bop
@IssakhaDiouf-e9t
@IssakhaDiouf-e9t 10 ай бұрын
Khé kham ormal lén yala li mo takh cheikh Ousmane mbow dilén diangal khamna moukadam yo khamné dangue lén wara réndi diné da buegue sél sét wakh yéna takh gnou yab Baye li kidi wakh né baye lila wakh sangue ndiaye liko cheikh Ousmane mbow di Déf rék doyna diangui lén
@issadiallo2905
@issadiallo2905 Жыл бұрын
Yaw imbécile nga rék mbaam khoukh bi nga doon
@IssakhaDiouf-e9t
@IssakhaDiouf-e9t 10 ай бұрын
Yow khana talibé sangue ndiaye nga Do wakh kham kham
@wellelepatriote6694
@wellelepatriote6694 Жыл бұрын
sénégal DAÑIO YAP YALLA nelaw bi yagneu BOROM BI SAKH DOLEN LA BAAYI YALLA SWT DU MOROM
@alassaneseye2191
@alassaneseye2191 Жыл бұрын
Dieuredieufe billahi deug rek nga wakh nga tarikha thiakhan rek
@awaba3307
@awaba3307 Жыл бұрын
Mais gni est ce que gnoukhite yi tanéwougn lénn
@alassaneseye2191
@alassaneseye2191 Жыл бұрын
Gni gnoukhite yi gno len tanné
@layekharagne2224
@layekharagne2224 Жыл бұрын
gnoukhite tanèwoul kene tarikhas yeup bone mais gnoukhite mom tanè woul kene
@sadikhdibalenoble7434
@sadikhdibalenoble7434 Жыл бұрын
On dirait tu as un sérieux problème avec les talibés Baye Niass fais tres attention petit
@seynaboulo796
@seynaboulo796 Жыл бұрын
Ces tarikhas sont plus k des problèmes ms natou Sénégal la dougnou dara nak touss tassarr menancé rkk dans l'air
@alassaneseye2191
@alassaneseye2191 Жыл бұрын
​@@seynaboulo796dieuredieufe
@PaBass-tp6bd
@PaBass-tp6bd Жыл бұрын
Yaw khamo sakh loye wakh so khamoul Ibrahima fall bignouye wakh gua nopi
@PaBass-tp6bd
@PaBass-tp6bd Жыл бұрын
Daga âme diote 😂😂😂😂😂😂😂baye Niass moye yalla
@abdoulazizsow3734
@abdoulazizsow3734 Жыл бұрын
oustaz alpha baye niasse dafa ame ibra fall boumou done andale cest pas celui de touba
@AmyTouré-h2z
@AmyTouré-h2z Жыл бұрын
SOS mo gena bon te yow mom gay def
@asinoh589
@asinoh589 Жыл бұрын
oiw topal féléee😂 khamolènne touss khana lakhatou si écran yi Di Digate 😂 nopaloulènne talibé baye yi niolène dax djouli dax lëne woor.... Eup lènn xam xam fouffff euplène yar bilahi
@sakhoousmane7066
@sakhoousmane7066 Жыл бұрын
Alpha yi mom fen rk fi ba abadan dong la wakh dara
@moussaalkhayri5253
@moussaalkhayri5253 Жыл бұрын
Sangue ndiaye dani " ni Yalla mel nonla Baye mel et viceversa" Lolou nak dou débat si brom khamkham. Ndakh Yalla mowakh yonent ni إن الله خلق آدم على صورته bukhãri ak mouslim yeup andinagn hadith bi. Ta li benn la ak li Sangue Ndiaye wakh.
@IssakhaDiouf-e9t
@IssakhaDiouf-e9t 10 ай бұрын
Yow may gnou Diam sangue ndiaye wakhoul kham kham
@ibrahimazakariasall1234
@ibrahimazakariasall1234 Жыл бұрын
Ki mo bone
@PaBass-tp6bd
@PaBass-tp6bd Жыл бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 Dêmal outti kham kham
@wellelepatriote6694
@wellelepatriote6694 Жыл бұрын
MAHI ÑIASS MO YESS
@moustaphakouta3252
@moustaphakouta3252 Жыл бұрын
Alpha ba bala nga dée alakou
@leveridique9276
@leveridique9276 Жыл бұрын
Kiikay dafa alkou bou yaagu
@mouhabarxam70
@mouhabarxam70 Жыл бұрын
Sangue fimouy wakhé aggago fa bayilen dingatt
@SadioFall-n5s
@SadioFall-n5s Жыл бұрын
Mane talibé bamba yaw dague fene rek
@AmyTouré-h2z
@AmyTouré-h2z Жыл бұрын
Bay niass mos te wahne moy yala
@nassirdiagne3739
@nassirdiagne3739 Жыл бұрын
Ya gui wakh lo khamoul
@alassaneseye2191
@alassaneseye2191 Жыл бұрын
Khamal gnou
@mamoudoudaff3028
@mamoudoudaff3028 Жыл бұрын
Demal tarbiyou..digua ham... lepp diam yalah
@moustaphakouta3252
@moustaphakouta3252 Жыл бұрын
Lougn wakh ngani bidha yaw mi gneuw ginaw yonenti bi khana bidha nga
@seydinaousmaneba416
@seydinaousmaneba416 Жыл бұрын
Alpha demal youwou cheikh baye niass monguilay wo débat public depuis 5 ans lancé len defi . Demal wouyou te khamne gningen di wedi ay millions nites gueum nanioulen baparé te ken doussi delou guinaw sen khew mo wara nek wa Palestine winuouy torokhal té gnilen ngemb niolen di torokhal ngen atté deug si lolou sinon boulen niou sonal way eh
@PaBass-tp6bd
@PaBass-tp6bd Жыл бұрын
C'est Ibrahima fall kokou talibe baye Niass lâ
@PaBass-tp6bd
@PaBass-tp6bd Жыл бұрын
Sa way Baye Niass moye yalla soulla nakharê gua sêtt no dêff
@PaBass-tp6bd
@PaBass-tp6bd Жыл бұрын
Garawoul mougnal mais baye Niass moye yalla soulla nêkhê ak soulla nakharê
@PaBass-tp6bd
@PaBass-tp6bd Жыл бұрын
Sa way dagaye fênne mc dou rapeur bayile fêne
@moustaphakouta3252
@moustaphakouta3252 Жыл бұрын
Yaw yangi suivre sounou wakhtane
@SeydouNdiaye-ys2io
@SeydouNdiaye-ys2io Жыл бұрын
Dom kharam dji mbirou diambour rek ngay lidieunti
@PaBass-tp6bd
@PaBass-tp6bd Жыл бұрын
Yaw amo kham kham nopil
@AmyTouré-h2z
@AmyTouré-h2z Жыл бұрын
Yaw li gay wah amul ben njerin
@PaBass-tp6bd
@PaBass-tp6bd Жыл бұрын
Ibrahima fall bi mouye wakh talibe baye Niass lâ won so khamoul gua nopi
@arameba7441
@arameba7441 Жыл бұрын
Beurina ay hadiths yo khameni daniouy wakh ni wérou gnou légui nguéne beug ki dougg léral léne wakhou djambour. Nguéne Teik ko fane? Baye Niass dafa dakh Ma Ibra Fall bimou wakhé ni guissna Yonente bi mouy djangue ci mome. Lolou doyou léne teiktal mais inkar reik reik moléne takha djoug
The evil clown plays a prank on the angel
00:39
超人夫妇
Рет қаралды 47 МЛН
Леон киллер и Оля Полякова 😹
00:42
Канал Смеха
Рет қаралды 4,4 МЛН
[BEFORE vs AFTER] Incredibox Sprunki - Freaky Song
00:15
Horror Skunx 2
Рет қаралды 20 МЛН
🚨 TFM LIVE : Plateau Tabaski 2023 avec Oustaz Modou Fall
1:39:45
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 83 М.
🚨DÉBAT LUMIÈRE SUR LE FAUX PROPHÈTE || PAROLES AUX AUDITEURS LIVE TIKTOK
2:47:53
Oustaz Alpha Ba officiel
Рет қаралды 10 М.
GUISS YALLA XAM YALLA WAHTANE BAYE TOUTI NIASS
2:08:12
DAHiRATOUL FADLY TV
Рет қаралды 31 М.
Ce Mouride Fanatique Défiait Oustaz Alpha Ba
1:04:20
Watawasaw Bil Haq
Рет қаралды 54 М.