Kiko déf yalla nako yalla wérr Mane tay la niak sama yaye métina trop nékété adouna dou dara 😭💔💔
@SambThiaba-r5r5 ай бұрын
Oooh massa yalnako yalla yeureum paix à son âme
@Farmatalalasalihate5 ай бұрын
Sigui ko ndigalé. Yalla feté la fim la fetté wone
@aminatasokhnabeye70065 ай бұрын
Yalla na firdawsi done sene keur
@FatimandaoTymandao-gr4gl5 ай бұрын
Massa ! Lou meti ngay dounde tamite, yalnalen yallah yeureum
@paulinesylva14945 ай бұрын
Oh massa ma chère yalla nako yalla yeureume et famou dieume guenale fimou diogue et yalla maye la kholou mougne massa et courage
@alhamdoulilah39915 ай бұрын
Allahou Akbar.... bilahi d rek moy deugue. Qu'Allah ait pitié de son âme
@aidadiallo10195 ай бұрын
Ay ki déf dieuf djou gnaw dji yalnako yallah nitt si barkii seydina mouhamed psl🙏🏿😭😭
@coumbandao25015 ай бұрын
Amiin 🤲
@Rokina7765 ай бұрын
Wa légui fane la nite di mouthié nak🫨 mane semaine passé la sétane itv bimou done témoigné thi khalé bi niou poignardé pikine...non lii c incroyable 😢😢
@ndiawarfalliloumbackeseck18665 ай бұрын
Mane dama diomi li yalla na yalla gnit gniko déf this barke seydina mouhamed
@elfecky-w9u5 ай бұрын
❤SAWS ❤aminnnn
@AissataBah-ih1kp5 ай бұрын
Ameen Ya Rabouna 🤲😭
@shuifiashuifiana20845 ай бұрын
Des questions vraiment blessantes
@MarietouFayeAmadouneNdiaye5 ай бұрын
Wa Sénégal mome lifi kheew lane la la semaine passée il faisait un témoignage sur l’enfant poignardé à Pikine 😭😭
@barbieshu90675 ай бұрын
G regardé sa ya 6jrs a peine nitt khamoul dra si bopam😢
@sylvestregomis14755 ай бұрын
Lolou sétane nako ooohh
@barbieshu90675 ай бұрын
@@sylvestregomis1475 suis choquée
@elhadjiniang38085 ай бұрын
Diaroul. Thiowli.di beurri peine de mort ba ngi si Yonne sénégalais dinaniou ne thiothiou
@ndeyefatoundour83315 ай бұрын
Bilahi bi ma guisser annonce décès bi image bobou mo niew sama xel Aïe waie nioune founiou dieum même dans ta propre maison tu n’est pas en sécurité
@mouhamedgarmigueye45655 ай бұрын
Yallah na yallha kharé la aldiana
@DaoudaGuaye-z2k5 ай бұрын
yalla nko yalla yaram té kharéko aldiana 😭😭😭
@paulinesylva14945 ай бұрын
Oh metina ki defe dieufe diou bonne dji yalla nako sougniou borome were beuthieuke yalla na agale ndawame aldianaye firdauwsi paix à son âme
@BambaMbegue-o7i5 ай бұрын
Chaque jour ak informations you béss vraiment lii métii na nite dalay diapal hien té doko sakh kham bly
@الحمدلله-ض5ي8غ5 ай бұрын
Cest triste, son role etait remarquable dans dikoon
@arimaz895 ай бұрын
Bilah demb rek lassi guiss beneu sequence mok diamy gueye si tik tok bi tiey aduna gni def Lou niaw li yalla nalen yalla wer 😢
@fatousagna39815 ай бұрын
Que Dieu l accueille dans son paradis
@amiyfall-v1z5 ай бұрын
Yalla nako yalla yereume té khare KO aldiana firdawsi amine 🤲🤲🤲
@ElhadjiMamadouGueye-e2i5 ай бұрын
Sénégal mo Amoule sécurité ! Surtout la banlieue pikine,thiaroye trop de banditisme dans ce pays ! Yallah nako Yallah yeureume !
@Fashionistas834005 ай бұрын
Ki ko dagno wara tègual ndayame diko thior ndank ndank ba fin non li métina tè métina ma,un jeune comme ca il lui ôte la vie pour rien 😢 mbam ala lagnou domerame you bone Paix à son âme yalla nako yalla bolèke makaka yeurmeundè ay li métina nama nakk
@MameNdewDiouf-zn7bi5 ай бұрын
Bien dit focus rekk deff com wa Thiès rekk guène efficace loi bi rekk akk police légui rekk dèyi wagnè kou inchallah mètina Paix à leurs âmes 😭😭😭😭😭😭💔mon cœur de mère saigne
@fallougalassbeye35795 ай бұрын
Yalla nako yalla yeureum 😢😢
@lamineteuw68395 ай бұрын
Hier rek on ces parlai au téléphone, repose en paix frère,,
@Keny_Secrets5 ай бұрын
@@lamineteuw6839 hier??
@boromkourousstv51395 ай бұрын
Yalna yala maygnou mouth bou rafétt ta djiegualko kharéko aldiana
@OusseynouDame5 ай бұрын
Yalla nako yalla yereume kharè Aldjanaye firdawsi barki seydina mouhamed mètina trop
@aidababou96785 ай бұрын
Ohhh ndeyssane 😢
@laliakoite70435 ай бұрын
Barki demb rek lako setane mouy df témoignages sur l’enfant poignardè a pikine💔 Non nioune di bane deuk lagn nk vremen li meti kiko df li yalnako yalla niite si barkep werou safar bi🙏🙏😭metina trop trop bilahi
@moudoudiop62165 ай бұрын
Ndeysane mitina tourp bilaye yalla Nakou yalla yaram 😢😢😢😢😢😢
@ndeyeamysarr54305 ай бұрын
Yalle nala yalla yeureum mais nitt bouy boundou wara di khalate yalla yalle nala yeureum té yeureum gnou
@fatoufaye32895 ай бұрын
Yalla na firdawssi di nopalou kayame si barki seydina Mohammed amine yaraby
@yasjoop7165 ай бұрын
Yalnako yalla yeureum kharéko aldiana firdawsy amine
@serignesaliousarr94245 ай бұрын
Serigne Cheikh Tidiane Sy Al Magétoum waxone naa Ngou Sangue Sénégal bala mo sangou wé Déréte. Ndeysane mom semaine passée mii ngu nakarlou boy bign poignardé pikine. Tay mom ngou ray koo lii doyna war walahi. En plus snap bim moudjei publier sur tik tok snap bii filtre danger laa binde ak bombe lolou dal tay naa sama xell. Yalna yallah yeureum kooo
@mariemethiam58615 ай бұрын
Walahi Vip Sagnsé motakh makoy sétane! Kou ame humour!! Khalé bignou raye mouci done wakh sétane nako! C'est avec tristesse que j'approuve ce moment, je prie que son âme repose en paix!
@senebijou73655 ай бұрын
C’est triste
@Thiambabel9475 ай бұрын
C'est grave vraiment la vie est tellement grave surtout ici au Sénégal 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢 paix à son âme metti na tropp 😢😢😢😢😢
@fadeltine94265 ай бұрын
Yalla bourbi yereumeko def Al diana mouy kereum si barké seydina mouhamed sws 👏
@FadwaSbai-i5f5 ай бұрын
ohhhhh li métti na waye😢😢
@SokhnaNdiaye-md3wk5 ай бұрын
Yalah na ko yalah yereum diéguel ko kharé ko aldianay firdawsi 😢🙏
@CouraDiop-k4m5 ай бұрын
Away yallah boumouy deug allahou Akbar 😢
@Senegalinfo6155 ай бұрын
Bilahi momafi indi mane
@mamebourrygueye99945 ай бұрын
Ooh lii dou deugueu wayyy😭😭🙏🏾
@Lilac585 ай бұрын
Thieuy Yallah! Khol yai yakhou. Naniou deffar khol yi. Les gens sont devenus trop mechants dans mon cher pays. Senegalais moo gueunoon bakh tchi Adouna, mais de nos jours, les gens font des choses inimaginables...
@batorasecurite98985 ай бұрын
Ooh je pleure
@arimaz895 ай бұрын
Ndeysane aywaye Aziz way yalla na yalla wer gni la Ray metinama lol
@AbdoulayeErikNdiaye5 ай бұрын
Pikine comme ay deum, lékanté realty .paix a sont âme Pikine n'est pas un lieu de vies surtout quand tu est artiste 😮 😢 😢
@ndieumbetmbodji17145 ай бұрын
Yay vrai Deum bi Domeram. Nioune dh fi lanou deuk mais leipp lanouy tek si lokho yalla
@AbdoulayeErikNdiaye5 ай бұрын
@@ndieumbetmbodji1714 Pikine est Thiaroye devriez être rasée illetré kessé nioko fess
@sabrymm70835 ай бұрын
@@AbdoulayeErikNdiaye vous avez tellement la haine que vous en perdez votre cerveau. Ne pas aller à l'école est un crime maintenant???
@ChevreryBurk5 ай бұрын
Hoallaa they Sénégal changé na di gana dangereux ce jeune je lai apprécié dans une serie VIP Sagnsé ak beuneu khale bou dodj. Paix à ton âme
@ACTUNET15 ай бұрын
Thiéy adouna d'où keur
@LamineDiop-u7m5 ай бұрын
Ndeyssane lou meti 😭😭😭😭😭😭
@sophiecheval18895 ай бұрын
Cest vraiment triste paix a son âme yalla yeureum khareko aldiana firdawsiamine
@yourdarkqueen62755 ай бұрын
Je l'aimais bien ndeyssane ya Allah nako ya Allah yeureum
@FatouFaye-i2b5 ай бұрын
Nn li dou Deug wayy 😢😢
@Sia000035 ай бұрын
Vraiment ce pays a changé
@ndyebinta-qz2xe5 ай бұрын
Non li ersk Deguellaa tamite yi kén douko fowé
@famafall64023 күн бұрын
❤❤❤😢😢😢😢😢😢
@AstouSy-f8i5 ай бұрын
Li dou deugue ki récemment magui koy setane mouy wakh si béneu interview si khalei biniou diam ahh mane warou ndeyssane adouna diékhna kouko wakhone douko gueume paix à son âme
@AwAdja5 ай бұрын
Yala nako yala yeurem té xareko aldiana ki def li yala nako yalla nit bilakhi meunouma sakh nelaw
@CartonsTVSN5 ай бұрын
Yalnako yàla yeureum té khareko aldiana
@SeynabouFaye-b6q5 ай бұрын
Ay way gnoune bane rew lagnou nek yalla boumou donne deugue dama tite sakh menoumako gueum way
@sokhnaoumoudiop68885 ай бұрын
Tank Sénégal koumou nekh dougou djiko Khale yi yakou naniou étranger nio dan def li bon yi
@coumbasidibe78095 ай бұрын
Paix a son ame
@MoulimatouMbaye5 ай бұрын
C dur li métina ki def li yallanako yalla wer
@niang.talibe.brom.ndienend54345 ай бұрын
Boun don def ku raye niou rayla point legi Senegal come x Zimbabwe
@oumysylla81815 ай бұрын
Ay waye je commente mais je ne sais pas quoi parler doyna waar dé li bilaye c triste vraiment c triste mais pourquoi tué tamite pourquoi.mais k firdawsi soit sa demeure éternel
@ndackkebe67115 ай бұрын
Merci ❤❤❤❤❤❤😎
@maimounasarr37415 ай бұрын
0u' il repose en paix
@NdoumbeMbaye-k6w5 ай бұрын
Ndayssane mane dama titeu😮 li metina feke niit ba keureum rayko
@BabacarDieye-wn9cmАй бұрын
Dafa dee mai come mogui doundou ba legui
@binetalayembengue38865 ай бұрын
Repose en paix 🪦 😢
@farimamangane90925 ай бұрын
Senegal amna niou bonne yake samaye nélaw titale ma dagaye séte lii rek
@ismailadiagne74065 ай бұрын
Kone dewoul
@awaseye5035 ай бұрын
Bilay bonn rk ak sohor mai yalla baxna
@diopsy70025 ай бұрын
décédé na kay
@sicorisow1995 ай бұрын
RIP
@Tocabubs4 ай бұрын
Nabou leye sokhor ga , tu as tue aziz dabala ci digg ndeun deum ,a la fleur de lage.nabou je ne sais pas mais les senegalais tattendent rayy sa ndeye
@FatouDiop-p9f5 ай бұрын
Paix à son âme
@BellaAdam-f4n5 ай бұрын
Sa titre ak lima guiis dou benn
@ndeyefatougueye36335 ай бұрын
Moma djakhal 😢
@basselabdou98915 ай бұрын
Doul rék lanie déf Sén titre you bon yi
@ngonefall3865 ай бұрын
Ah Sénégal dé yakouna khana dou ki modone deff témoignage fanyi rek thiey yalla
@basselabdou98915 ай бұрын
Ki déwoul Danie fén rék
@ndoumbesow48435 ай бұрын
@@basselabdou9891si😢
@coumbathiam74705 ай бұрын
No vrema peine de mort doit être appliqué
@mairamefaye-vg1qz5 ай бұрын
🤲🤲🤲🤲🤲😭😭😭😭
@fatoutoure72355 ай бұрын
🤷🏼♀️😭😭😭😭😭😭😭
@khadydia28695 ай бұрын
🖤🤲🏼🤲🏼🤲🏼🖤🖤😭🤲🏼🤲🏼😭😭😭😭😭😭💜💜
@mamemariamabadji43525 ай бұрын
Questions yi c'est pas respectueux bayilènn vexè nit yi
@mbayeciss57255 ай бұрын
lane moo takh légui yiy khéw senegal presque kénn wakhatoul ni probleme sécurité la??? Alors qu avant lou khéw booy lire commentaire yi danouy wakhni police ak gendarmerie gnoo liguéyoul...thieuy senegal dina yékha avanver déh...
@miyandiaye4735 ай бұрын
😭😭😭😭😭😭😭🥱😱😱😱
@DioumaDiop-v3u5 ай бұрын
😭😭😭😭😭😭😭🤲🤲🤲
@mamendiemethiam75405 ай бұрын
Je crois pas interview rék la guisse y'a pas d'information sur sa mort
@aminatadiop67225 ай бұрын
Mane dé tite na trop si Deuk bi
@tidianedoumbia44575 ай бұрын
Je crois que c'est à cause du témoignage fait sur l'enfant poignardé
Attend ? KI GOR LEU WALEU DJIGUEN ?? Soubhanallah Yalla nako yalla yeureum mais sama xel niaw na si comportement wam bi c bizarre 😢😢
@CXOUNABMB-075 ай бұрын
Ak noumou mandi mél nit bou tollo fi niaanal ko RK lolou mosi am solo
@b_lebou89085 ай бұрын
Yonent bi daf niou sant sou nit guenei adouna niou sedel ko lou rafet imagine ay mbokkam lire li dina metti si niom ki dem dem na nie dess nioy geuneu souffrir yalna borom bi yeureum ko اللهمّ اجعل الجنّة مسكنا له وارحمه وعافه واغفر عنه 🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻