Mais sèn prophète bi Amoul toure khana ak kan la ci prophète yi🤔 Damay lèr lou dong.
@championkane96596 жыл бұрын
Fi dé meusenafa dém ay yoni yone mé déguonena malaka la mé téy yonénti la déguate yalla rék mokhame
@motsdoux263 жыл бұрын
Nagnko soulii
@khadimgueye44276 жыл бұрын
Soubhanallah, que Dieu nous préserve de l'égarement
@azzizthiandoum907710 ай бұрын
Wakhal dé❤
@cheikhndiaye29976 жыл бұрын
Limou wakh sou ame alhamdoulilah maintenant nous notre prophète c'est seydina mouhamed psl suivons ses enseignements
@yeguebonysamba94216 жыл бұрын
Yonénte yeup say Yonénte lagn
@mouhamadoumbacke26746 жыл бұрын
cheikh ndiaye linga wakh rek moy deug
@ace35706 жыл бұрын
Y'a telment de prophètes a chaque planète la connaissance est si vague. ....ils existent d'autres êtres dans autres mondes qui ont eu des prophètes
@adjicodouka6916 жыл бұрын
Dv
@mouhamadoumbacke26746 жыл бұрын
C’est vrai que tous les prophètes sont nos prophètes, mais notre espoir nous le reposons sur le début et la fin, celui qui a ouvert et clos la prophetie, le sceau, Seydina Mouhamad PSL.
@azzizthiandoum907710 ай бұрын
Sounnah rék Moy deug billahi ❤❤❤❤❤
@kalidouwade94426 жыл бұрын
Toi qui lit ce commentaire je te souhaite bonne chance
@alfinhodioum40336 жыл бұрын
Dieuredieufé Serigne Touba☝👌
@teusssrekkk18596 жыл бұрын
Yonetibi bi goud na trop way 😂😂😂😂
@mamoudoudelba17126 жыл бұрын
Wa yow do ragual yalla NN ban yonenti ki mo nième sétété
Meunna nek kome meunna bagna nek ndakh yaalla aye diouniye diouniye yonente la yooni amena gnioumou wakh si alkhouraane amna gnoumou wakhoul yalla rek moo khame
@hopeline726 жыл бұрын
Les vrais natifs de la petite côte qui on une bonne vision interne des choses savent cela depuis longtemps. 📿📿
@ndiogou15873 жыл бұрын
lane moy bonne vision interne des choses ?
@kumbadiouck33706 жыл бұрын
Niak gueum Yalla ak wadia trokh mo diap Sénégal mo takh lou nekk difi am... Prophète leu d'accord mais lequel... Wax daniou koy geustou bala ngakoy siwal...wax deugg linga fi wax amoul base
@cheikhtidianesarr32296 жыл бұрын
C'est quel yonent?
@abuanas37266 жыл бұрын
Sénégal tolou dof la, lofi beuy mou sakh.
@canamillyefa56115 жыл бұрын
bilay wakh nga deugu
@serignemadiorsenendar52436 жыл бұрын
Mdr..🤣🤣khana yonante yalla doorkate yi mo teudd fii 😂😂 yaa yabaté dh seuh surface bi démal nga djieumate ci salade, ak carotte teuh nguén lékk beuh sourr..
@motsdoux263 жыл бұрын
😂😂😂😂
@ACTUNET16 жыл бұрын
nous les africains nous somme malade jusqu'à la moelle épinière nagnouye khalat waye
@MrDiamrek6 жыл бұрын
senegal c'est le pays des commediens !!!!thieye yallah !!
@zakezakezake3 жыл бұрын
c est plein de grigris ce bordel de pays!la sorcellerie,la divination des tombes....ya latif..qu ALLAH NOUSPROTEGE!
@sereroubamba79566 жыл бұрын
Si c'était un prophéte on l'avait d'écouvert depuis nos hommes de DIEU,khawmo loolene thiii dioublou NAK richessou Senegal sounou SERIGNE sii keepleu,deukou toubab yii amoul yonentii boufeu teud téh thiii niom lanouy daaw bounou diakhlé
@chris94mina6 жыл бұрын
Lima ci méti rek moy beuss dina nieuw niou ladj ma loutax ma done degglou li!!!
@latdiordiop25576 жыл бұрын
mina kouoh billahi. Senegal 🇸🇳 monekhh d.
@khadimdiakhoumpa95956 жыл бұрын
😂😂😂 no mina kouoh
@taalibedaara48396 жыл бұрын
Wax nga deug dee
@smartfolle6 жыл бұрын
🤣🤣🤣
@azizbah40466 жыл бұрын
mina kouoh wallahi wax nga dagdee
@bambacisse4200 Жыл бұрын
C'est quel Prophète svp
@paapnjaay158610 ай бұрын
Subqaana'LLAA 🤭 Cëy miim réew 🤔 Fii dëkk fi wóorul sax. Li ma métti ba métti ma mooy ñi ëpp ci samaw askan bu ñu réppee ci bókkaale la léen dee di fékk
@balayerabakissima72212 жыл бұрын
Réveillez vous les africains Dieu nous recommande d'aller au Mecque pour le kaba .
@elhadjimoussaseck73736 жыл бұрын
Kharal MA gneuw gass ko khole bane yonénete la
@ultimatetruth92416 жыл бұрын
Thiey Sénégal. Yonente á Mbour. Waaw mais noumou toudou?
@metzo92i6 жыл бұрын
The truth shall prevail il a plus de 23 milles prophète dans le monde
@ultimatetruth92416 жыл бұрын
Mohamed Mbengue Vous voulez dire 124.000. Ce n'est pas 23.000. Demal diangui ngay dieuma diangalaate. J'ai posé une question. C'est quoi son nom?
@ultimatetruth92416 жыл бұрын
Et pour ton information, il n'ya pas 124.000 prophetes. Boo beugué kham, nga ladjté ma diangalla. Salam
@metzo92i6 жыл бұрын
Mais yow tu parles de quoi? Je voulais juste te dire que il y plus de 124mille prophète éparpillés dans le monde... guamay nane aye affaire rou DIAGUAL? Yow loma moune diagual? Lool
@mamansalihat10606 жыл бұрын
Barki yonentibi ki raynala, depuis ma yewou nekouma mai ki dall il a fait ma soirée 😂😂😂😂
@momarseck44266 жыл бұрын
😂😂
@mallbelly82504 жыл бұрын
Waw leegui yonen tibi noumou toudou
@diomrekdiagne28286 жыл бұрын
sant Serigne touba doye naniou
@sardarmardar61966 жыл бұрын
Diomrek Diagne doynala
@modiop47166 жыл бұрын
Alquran ak sunna rek.
@AshmedVimaduk4 жыл бұрын
Senegal macky ngay fene laaaay
@awasarr82926 жыл бұрын
Un prophète qui n à pas de nom , un marabout Cissé qu’on ne voit jamais mais toujours le porte parole s affiche ak lekham yi doule bakhoul
@ahmadousow13436 жыл бұрын
Senegal leup nga fiye deug motakh douniou moussa dem kane.
@aliounediop86416 жыл бұрын
Wa xanaa, dolèen, niane ci barke ku tëdd fofu, salli taggo ak jëff yu bonn yu fay am.
@elhadjiniang77156 жыл бұрын
Senegal nekh na dal lou nekh way mou wakh
@modousen98266 жыл бұрын
Machalla yalla mayena de te boukenn weddi
@Kateliadiffusion38456 жыл бұрын
demlenne légui jamou tombe yii moolen desseee. mais fatté xaliss noko amé bakhna 😂😂😂
@Medzoefall6 жыл бұрын
Yonente bi ak cheikhou Tidiane doy nama
@morcisse52046 жыл бұрын
Lol tei guéna bayi sen yi Yalla mate na ragal dhei Camera yi tim la rek guaye wax Nama yalla balle sa si video bima xol Wassalam
@kadduaskanwitv19076 жыл бұрын
Do wakh ban yonenti le?
@yayefallfall70616 жыл бұрын
Cheuuuuuuu yonent lane mo dolen wakh AK ki Mane deh wa mbour Serigne Touba chiekhra fall la wakh
@arafatdiallo94486 жыл бұрын
Ahh wadji fonkna serign bi deh laaa loko dalna guemin Mais yeuneunt bobou nounou toudou? ?😂😂😂
@babskingVEVO6 жыл бұрын
rew mi maguoum niou nieuk yi nio ko mom. yallah mohamed psl .cheikh ahmadou bamba. mame malick sy. seydi limamou laye. baye niasse. bou kounta .nioniou mou doy khamouniou sa yonati bobou. wa salam
@adjandiaye58776 жыл бұрын
Salaam wohlene niou Lou ler ban prophete LA ak kagne lafi nieuw ak noumou def ba Ken hamouko ak louko fi indi na ler silvplai
@syousmane68756 жыл бұрын
Nioune wa Sénégal ana souniou khel yi
@amadoudiop65096 жыл бұрын
Sénégal s touba rek mofi nék
@mouhamedcisse97286 жыл бұрын
Ya bone ta touti khol yéne sene kholyi bakhoul sene serigne defaroul sene kholyi doléne nangoul béneu waliwo yallah maléne yeureum no seince khélou mbame
@sardarmardar61966 жыл бұрын
sa baay foumou nekk?
@sardarmardar61966 жыл бұрын
Gambie nakk koufa nekk?
@amadoudiop65096 жыл бұрын
@@mouhamedcisse9728 YAW ROSNA MOHAMED BI
@djibidiallo50936 жыл бұрын
mamadou bah yak wadji soriwoulene
@ibrahimadiop71346 жыл бұрын
quelle naïveté. Pitié du Sénégal
@cherifaidara41382 жыл бұрын
Wahi dof rék ngafi wah dara douci deug
@ogflow57206 жыл бұрын
Man deh damay lathie ana kagn la Sénégal di mouthiou chi tchaxane. Nagnou weuridji ka gnouy xamal sunu borom nguir gnou Matal li Mou gnou sant té moy gnou diamou Ko.bayilen di diamou ay kheureum.
@mallbelly82504 жыл бұрын
Yonene tibi mom goudou na dé😂🤣
@KharitouMbayeNdaw-by5pc11 ай бұрын
Mbour yanèntou mo fa teud Baxiya ay yonentè nio fa teud Wayé kiy modj si yonénte yi Seydina Mouhamed la toud guinawam yonént do toule wath. Allahouma sali ala seydina Mouhamad wa ali hi wa sahbihi wa salam.
@coumbageuye91286 жыл бұрын
Madone ballaifoufou en 1990 daraamoufawone beuguesiwe motakhe .deleneragale Yalah.
@mamecheikh63576 жыл бұрын
Xanaa ce "prophète" a été victime de naufrage ? Vous êtes vraiment fort en marketing touristique.
@mamansalihat10606 жыл бұрын
Waaaaaaaaaa😂😂😂😂😂😂😂 suis morte
@laperlecmoi59956 жыл бұрын
wallah
@kankouran84036 жыл бұрын
🤣🤣🤣🤣🤣
@aminatagaye14106 жыл бұрын
Prophète mofa deud deh
@alybayendom92916 жыл бұрын
Mame Cheikh wooohhhh
@CheikhDiop-nj3oz6 жыл бұрын
Senegal kou diouk ni moye borrom diamono... ana prophete bou gnouye neub toureum bane sens la aam
@waxkatoudeug6 жыл бұрын
danio wara geustou ba xam ndakh ki li mouy wakh deug leu. boudé dou deug dégn ko wara diap, tendre ko par quatre ba taati tang!
@doudousall3036 жыл бұрын
Tu m as tué 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂🤣
@kyrakyra4706 жыл бұрын
I’m dead
@azzizthiandoum907710 ай бұрын
😂😂😂😂❤❤❤
@serignecheikhmbaye67856 жыл бұрын
Weddiwoumako dei mais je pense k khawna yombb touti. Léroul daal ci mane.
@DaroulBirrTV6 жыл бұрын
Sénégal souf sou nangoula lofi djii mou sakh Quand des fous sont en face des caméras et qu'on leur tend les micros. Business en gestation !!!!
@senegalkesso12934 жыл бұрын
Comment s’appelle le nom du prophète que vous avez découvertes mr
@serignekhadimmbaye11516 жыл бұрын
Wakhalal from nGay nio ,khamko
@abydione99366 жыл бұрын
Bilay yalh mo mane mougne rek lima si miti rek moy dinagn ma lathie louma done deglo li
@yayoumouhammad84076 жыл бұрын
Thieye mime rew lii doyna war chaque jour ak aye fene you bess
Wakh ngua deug sama mame mofi teud yonenti yalla inconnu 😂😂😅
@ibrahimaniangboxeurofficie95613 жыл бұрын
Yonenet yu bari ay nit ñu ñuul lañu. Tubaab yi ñoo def seeni Film diñu nax. Waaye Yonenet yu bari ay nit yu ñuul lañu. Ndax ñi Yàlla njëkk a sàkk ay nit yu ñuul lañu
Sante yala nou war bílahi leri baye Laye ya diolina siw na fep nioun deh guem nano momadoy mame limamou Laye 🤲
@baraabdoulayefall35876 жыл бұрын
prophéte bi mom xana kankouran la toudou? saway niémé nga yalla dh
@gorandir96486 жыл бұрын
Kii moh ame fit té niémé yallah
@adamambodji10316 жыл бұрын
Thiey.... Sénégal mooo nekh !
@sondji5358 ай бұрын
Wa mes ki bane yonate la
@badaradia23496 жыл бұрын
Li ban série la?
@alibosn89506 жыл бұрын
ya bone dh😅😅😅
@badaradia23496 жыл бұрын
😁😁😁
@aledieng65876 жыл бұрын
comme sénégal lou nèkh waye wakh kay guissa gunou dara bamèlou psl sakh dinan nou ko wan
@dioptalla15476 жыл бұрын
Scénario bi nice na, on a déjà vu El cheikh, anamou legui 🤷🏾♂️
@petitpapa95586 жыл бұрын
Senegal Amna richesse wayye tubaab bee jël lepp
@issaaw33576 жыл бұрын
s'il y avait un prophète enterrer ici au senegl SERIGNE TOUBA ( RTA ) l'aurait écrit ou parlé avec ses disciples certainement parceque DIEU lui a tout appris grâce à son affection hors du commun son amoure infinie sur le PROPHETE ( PSL ) donc ces propos ne sont pas fondés parceque jusqu'à présent aucun "bayitte"que nous connaissons ne l'a souligné pour le moment
@dakarforex40336 жыл бұрын
del wakh loula lerr pauvre naïf
@khadimdieng17456 жыл бұрын
Sa wayy yonente yii amone nane ay tour deh ,lingay wakh ni tego fenn, legueyil te bayi sa tapaleyii, Sénégal moom leguey dagn ko khewil tapalè rek NB:bo dello si père Youssou neko mou wakhla tour bi
@amarndiaye85944 жыл бұрын
Bilaye koula guiss yaw khamene yaw kou nieme yalla ga
Je demande kel est le nom de ce prophète et depuis kan il est mort ensuite cmbien d’années k il a vécu ??
@djibrillayediagne633 Жыл бұрын
Waawe mais c'est quel prophéte parmi les313 ou bizn? Toi qui parle, est- ce que tu sais que tu as une grande responsabilité devant Dieu !!!!
@doudoudiarra24966 жыл бұрын
Grand ragalal BOROM BI
@mouhamadoudiallo60196 жыл бұрын
الهاكمالتكاثر حتى زرتم المقابر La course au richesse vous distrait jusqu'à ce que vous visitiez les tombes (sourate 102 attakasur )
@ballakebe81276 жыл бұрын
Way déme léne guéne diangui alkhourane mo gueune légui kou diouke poté yonéneteu. Béneu yonnéneteu rék la yalla watié sénégal mouy seydina limamou laye psl
@FamaMuslima6 жыл бұрын
Ay domou adama moo niemer boromam.gnom hana dagno feter dagnouy deeh.soubhanallah. raggal lene Allah
@benmalick856 жыл бұрын
Pourquoi ne pas appeler des archéologues?...tu demande aux gens de faire des recherches mais sur quelle base? Il fallait y penser avant de construire la tombe...
@en2mots8176 жыл бұрын
suis d'akor avec toi ils ne nous ont rien prouve de ce qu'ils avancent
@cheik-pointsg12386 жыл бұрын
Feuz john jay ta bien dit mais le Sénégal et devenue grave ils vont aller jusqu'à devient des animiste dans le rendre compte
@bayefallgalsen20966 жыл бұрын
On est dans un paradigme où l'archéologie ne peut pas édifier les gens. Comment est ce qu'un archéologue peut dire aux gens si la tombe appartient à un saint ou pas ?
@latdiordiop25576 жыл бұрын
Feuz john jay Soiniou wowé archeologues day wanè sene doul yi.
@cheikhtidianesamb32906 жыл бұрын
Feuz gni dagnouy doul rek
@thiemoco94596 жыл бұрын
Yakana sama connexion rek
@fatimazahrachannel64046 жыл бұрын
😂😂😂😂😂
@danediego1376 жыл бұрын
Ah bon kone chine da am yonete bouma teude mousou mako degue merci si information bi . Mé yonente bobou chinoi la wala?
@aminatasow53786 жыл бұрын
Dane Diego yonente yalla ching jong Young xana mdrrr
@lamineniang2066 жыл бұрын
Kep kou yakarni ka deute ca bamelba meuna fatie sa aadio kon demal waye kep kou gëmni yalla moy fatie aadioyi kat toogal wamantawakklala alallahi fa innahou hasbouhou kep kou doylo yalla dalay doy seuk
@alphasow58676 жыл бұрын
YALLAH rek mo xam Mane dè amoumathi xam-xam kone douma thi waxx louma xamoul et faite attention thi sène commentaire yi
bande d'hypocrites. vous dites douma si wakh je suis mandou nianiania . même le fait de dire ça c'est un commentaire et une prise de position. alors foutez la paix au gens et laissez chacun dire ce qu' il pense. trop de faux culs et de moralisateurs dans ce pays
@hamzasall21576 жыл бұрын
Ki day doul rek Sénégal mobari gnou khif bô commencer togou ay mbana thiebou yape AK ay toufé la wakh gnouné gogue légui affaires des Serigne Sénégal business lengko dey
@mbalkakognedof58666 жыл бұрын
😁
@niakhdiarignou66876 жыл бұрын
😂😂😂
@djibidiallo50936 жыл бұрын
hamza sall no dina dè ngani senegal da Bari niou khifff😆😆😆
@moustaphadiallo17876 жыл бұрын
Al koubou ri youna ahloul seytane Wa bi'daa mole wakh Raye Ko defarate bemou raffet sank domou adama yii rek ba mel yenenti est apres. Legi ñiou dem diamouko ak Raye disi Yakar ragal Len yalla tey doun dou tawhid bayi di sosal yalla Te geun bayi di diamou aye niit .
@tarousenegal99336 жыл бұрын
Yalla naniou Yalla baleu ci cétaneu biniou cétaneu vidéo bi
@AshmedVimaduk4 жыл бұрын
Wa noum toud lguii
@abdourahmane88866 жыл бұрын
Senegal dano ame sen propre dieu ak sen propre prophète ak sen propre diné wallahi Sénégal xawma bane yalleu lanouy diamou
@MbackeNdar826 жыл бұрын
Sénégal de pays la bo khamné kepp kou xam dara çi Yalla xamné Sénégal pays la si pays Yalla yi.
@boysenegal66226 жыл бұрын
En tout cas yalla Aÿ yonentem fep fou nit nek rk meusse nafa yobou yonenti kone mouy senegal ak fenzne yeup amone na ay yonenti 1240000 la yalla yonii en tout cas Wayei nk fi koufi teud yalla rek moko xam nagn si mandou