C'est toujours un plaisir d'écouter Oustaz Niang Mbaye. Mach'Allah yalna y'Allah sàmmal niuko mayko wer ak guddu fan
@rokhyngom10715 ай бұрын
Macha Allah très émue de revoir notre oustaz en bonne santé.yalnako yalla guéna saam
@abdallahtimera45965 ай бұрын
Machallah oustaz Niang mbaye yallah na la yallah defal wer AK werke saam la. Beugg naniou torop fil'Allah. qu'Allah vous récompense de la meilleure des manières ici bas et l'au-delà. Amine, saam sa ndiabott t barkel KO. Defalko mbolom dioulitt. Dama diakhale woon ci niakk degu oustaz Niang mbaye mais alhamdoulilah aujourd'hui
@manebassirou7795 ай бұрын
Macha Allah imam Niang mbaye yanna yalla dolli la tawfekh
@mbayeniang87775 ай бұрын
Yàlla na yàlla sàmmu ya oustaz
@sambasankhare66785 ай бұрын
Qu'Allah vous récompense ❤
@RokhayaNdiour-n7f2 ай бұрын
Macha Allah notre Oustaz yalna Yalla saam laa arlaa mayla gūddū fann gū andak wérgui yaram lolū mūsseul laa mūtheul laa mayla lū geuneu kawé sa ndjorte fii dūnyaa wal ahiraa yalna Borom bii yokk xam-xam gui loo meunn rénn rk yalna yokk déwénn in Sha Allah 🤲🏻🙏🏻
@aidaniang12885 ай бұрын
Assalamou alaykoum wa rahmatoulahi wa barakaatouhou. Ma fi djitou. Ma ngui ziarr gneup. Yakamti deglou sounou Oustaz Niang Mbaye
@coumbadiaw54805 ай бұрын
Macha’Allah ya Oustaz yalla na bour bi yokku wer gui