diganté khadim docteur bousso ak cheikh bara ndiaye

  Рет қаралды 34,349

Serigne Momar Diagne

Serigne Momar Diagne

Күн бұрын

Пікірлер: 174
@diagne1041
@diagne1041 3 ай бұрын
Bonjour Père Momar Diagne, vous êtes une personne qui dit toujours la vérité. J'espère que Dieu vous bénit.
@cheikhsadiboutoure1909
@cheikhsadiboutoure1909 3 ай бұрын
Lima khamm serigne momar diagne. Khadim bousso si sene kourel 28 bi aya bimou fini daganal derete omar diagne takh n'a ma khamni d'où nite kou bakh..
@abdoulayeba7078
@abdoulayeba7078 3 ай бұрын
Merci beaucoup. Le procureur devrait l'appeler
@DjilyNdiaye-se4zb
@DjilyNdiaye-se4zb 3 ай бұрын
Dakkorr na ak yaw koy tonto di saga niakk ardiouma rk
@MohamedBodiang-uw7yk
@MohamedBodiang-uw7yk 3 ай бұрын
Vrema moy Sama khalate dou nitt Kouma rafet Lou ay djikome baparé yone dafko Wara wo wakh AK môme parsk tamite deuk bi warnaniou ko ték si deug Ak yone koufi wakh Lo war ta wakh Nala yone wo wakh AK yow
@thiernosylla2816
@thiernosylla2816 3 ай бұрын
Djrëdjëff sama bayou bopou mane deh yay sama baye yalnala yalla samou tè mouthiél ci shaytané ❤❤❤amna solo looooooooooole
@khadime95
@khadime95 3 ай бұрын
Sëriñ Mamour jambar nga té yow dëgg rek mo tax ngay wax mais man ci Tariqa la bokku mais ñu ëpp ci ñoom dañuy dundé yon wi dunda luñu yon wu
@ablayekasse7667
@ablayekasse7667 3 ай бұрын
Lou lère gua wakh dou nieup mais beri na niouy dounde tarikha te hamnaniou len bou bakh
@mougnabadiane1129
@mougnabadiane1129 3 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂❤❤❤❤❤❤❤
@diagne1041
@diagne1041 3 ай бұрын
merci père momar Diagne Sénégal un pays où beaucoup de gens ne veulent pas entendre la vérité 🙏
@mamecheikhndiaye601
@mamecheikhndiaye601 3 ай бұрын
Ma Challah Dieureudiafati Serigne Momar Yalna Yalla Barkel Kham Kham bi Mayla Wer Samou la Yaw Ak Sa Ndiaboot
@cheikhounandiaye6844
@cheikhounandiaye6844 3 ай бұрын
Xaadim Buso moom da fa war a may nit ñi jàmm, te ay waxam tamit jarul jàpp ndax moom fii la nekkoon di tuumaal Usmaan Sonko ci loo xam ne dara leeru ko ci. Loolu mu wax Baara Njaay da fay wane ne rekk amul xam-xam, Wàlla atteena bànneexam kom ni nga waxe Sëriñ bi, te kon matatul li ñi koy woowe muy Imaam S Xaadim Buso may nu jàmm.
@LayeCisse-s7g
@LayeCisse-s7g 3 ай бұрын
Machalla pape ❤❤❤❤❤❤❤
@DiagneFall-ri4hw
@DiagneFall-ri4hw 3 ай бұрын
Macha Allah Dieureudieuf ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
@hamadygassama3620
@hamadygassama3620 3 ай бұрын
Thiey Senegal Qu'Allah nous protége 🙏❤️❤️ dieureudieuf sama serigne yana nga fi yague té wer ❤❤❤
@abdoulayeba7078
@abdoulayeba7078 3 ай бұрын
Amine ya Rabbi
@bamba-f6c
@bamba-f6c 3 ай бұрын
Merci bcp khadim bossou politicien la rek
@MamadouNdoye-w1y
@MamadouNdoye-w1y 3 ай бұрын
Dieureudieuf Serigne momar. Amna solo.
@darmancotv1953
@darmancotv1953 3 ай бұрын
Machallaa la discours est très pertinent
@ousseynousall5808
@ousseynousall5808 3 ай бұрын
Vérités absolu serigne bi ❤
@oliviervaz4658
@oliviervaz4658 3 ай бұрын
Djiubanti yomboul dè senegal lifi nek amoul fen
@zainaboudampha4230
@zainaboudampha4230 3 ай бұрын
Mashalla Papa, great talk again. Unfortunately, we are losing all our good values and morals slowly, slowly.
@Alhamdoulilah7
@Alhamdoulilah7 3 ай бұрын
Père bilahi degoum reka manekh si mom. Andoul ak kenn deug rek la àndal. Meme so àndoul ak mom dangay xamni deug rekako fi bayi. Moulay nekh ak moulay nakhari
@diaibrahim6798
@diaibrahim6798 3 ай бұрын
Merci ya cheikh machaallah choukran lak 🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤ ✅️✅️✅️
@AbassWade-u7m
@AbassWade-u7m 3 ай бұрын
merci ch oumar khadim bousso dou nitt kou bakh gor dou khassaté yaw geuno mame kene niép nio yam thia yallah kingaye khass mole geune fouf fouf fouf
@YayeFall-d9f
@YayeFall-d9f 3 ай бұрын
Baye dieureudieuf la Vérité cheikh Bara ndiaye Valeur ❤❤❤❤
@LébouDak-r6c
@LébouDak-r6c 3 ай бұрын
Dieufeuti Diagne tjrs véridique machallah yow rek lay tope ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@bayesaliou1927
@bayesaliou1927 3 ай бұрын
Salaam baye Momar yàlna yàllah yokku wër gui yokku xam-xam gui
@Loupe221
@Loupe221 3 ай бұрын
Dieureudieuf. micron mingui nieuw. nara DOUG té dou yeuglu 🤔😔 FREE... Salam🙏🏿👊🏿🇸🇳
@modoufall5006
@modoufall5006 3 ай бұрын
❤❤❤🙏🙏🙏verité absolue vraiment machalla ❤
@khadyndao1712
@khadyndao1712 3 ай бұрын
Sala yaa Oustaz. Je vous prie d'écouter la vidéo de Chaikh Bara Ndiaye sur tektal pour mieux comprendre la réaction se Khadim. Je suis par ailleurs très choquée par les sorties de ce dernier ces derniers mois / années. Je l' ai connu comme imam à New York. Mon père me transférait ces audios. Il n'y parlait que Charia. Mais la politique a malheureusement raison sur la plupart des nos érudits... Quel dommage !
@Sauce.piquante
@Sauce.piquante 3 ай бұрын
La puissance de l’argent, des bien matériels , les plaisirs mondains … Yalla na Sunu Borrom dolli niou soutoureu tey diegueul niou
@serigneabdoumbacke7396
@serigneabdoumbacke7396 3 ай бұрын
Machaallah Serigne Momar Diagne
@leytileyti199
@leytileyti199 3 ай бұрын
Dieureudieuf imam diagne mes prières vous accompagne
@serignemomarkane4104
@serignemomarkane4104 3 ай бұрын
Dieuredieufety. La lucidité est exemplaire. Kouy nittrek tit nga ci Li khew tay.. Yallah dal Yallah na wollu Sénégal.
@khadimdiop7852
@khadimdiop7852 3 ай бұрын
Khadim Bouso dor kat ok
@nabousagna4124
@nabousagna4124 3 ай бұрын
Qu Allah vous bénisse Diagne
@Syllatayba
@Syllatayba 3 ай бұрын
شکرا لک یاشیخی ❤❤❤❤❤
@moustaphaleye8471
@moustaphaleye8471 3 ай бұрын
Wakh dji. Amna solo. Mais il faut écouter la version de Cheikh Bara également.
@mbayangndiaye9009
@mbayangndiaye9009 3 ай бұрын
Merci papa kadouyi machalla ❤
@CheikhDieng-ln2pd
@CheikhDieng-ln2pd 3 ай бұрын
شكرا لك يا عمي قولك صدق ونصائحك مفيد ، أيدك الله ونصرك .ببركة خديم المصطفى ❤
@damefall-it8gc
@damefall-it8gc 3 ай бұрын
Begue khalis te liguiye Diekhna de ❤
@bayemalickseck
@bayemalickseck 3 ай бұрын
Merci beaucoup Baye momar Diagne vous cette plus fort qu'eux
@moussadieng3061
@moussadieng3061 3 ай бұрын
En tout cas dall imame khadim bousso wakh na wakh diou reuye billahi dama rouss sakh kilifa momoull yénn wakh yi ak lou mandi khéw😢😢
@cherialdiana8719
@cherialdiana8719 3 ай бұрын
Malheureusement kokou dou kilifa politicien en cagoulé la
@maguitamaguita3641
@maguitamaguita3641 3 ай бұрын
Vérité absolue!
@SeteSarr-h1i
@SeteSarr-h1i 3 ай бұрын
Moi je pense que mon père la justice voudrait que tu écoutes les deux
@GueyeAbdouLAHAT-y5u
@GueyeAbdouLAHAT-y5u 3 ай бұрын
بارك الله فيك وجزاك الله خيرا
@mota6240
@mota6240 3 ай бұрын
Dieureudieuf
@modoudiop7108
@modoudiop7108 3 ай бұрын
Machalla vidéo yi légui dafa leer
@gasslhumaniste4449
@gasslhumaniste4449 3 ай бұрын
Mashallah
@ModouKhouma-s9s
@ModouKhouma-s9s 3 ай бұрын
daga warouna deguelo cheikh bara baparè Soura wakh
@moustaphaamar422
@moustaphaamar422 3 ай бұрын
Dagua warona deguelou khadim bousso baparé
@mandawegaye5862
@mandawegaye5862 3 ай бұрын
KHADIM BUSSO NITTOU SYSTEM ROBINET YI MO TEUDJ
@NgoneColy-li6sq
@NgoneColy-li6sq 3 ай бұрын
Dieureudieuf Imam khadim thi kourélou Faye Sall la bokk tok mouy dokh ak beugue lou yomb Assalamou Aleikoum
@mariemeniang2612
@mariemeniang2612 3 ай бұрын
Alhamdulillah machalah dieuredieuf❤❤❤
@modoucamara3772
@modoucamara3772 3 ай бұрын
❤❤❤❤
@AbdoukhadreLô-p8c
@AbdoukhadreLô-p8c 3 ай бұрын
Maachalla amatina solo
@modadieng9886
@modadieng9886 3 ай бұрын
Salamalikoume baye bi nalla yalla faye dieureudieuf amale diam baye
@modouabdoulayediop5553
@modouabdoulayediop5553 3 ай бұрын
Diaadieufati baaye Momar Diagne
@aichadioufkane1171
@aichadioufkane1171 3 ай бұрын
Macha halla
@sedibabounacissokho427
@sedibabounacissokho427 3 ай бұрын
Asalamu aley khoum amne solo machallah
@thiernocirediop1267
@thiernocirediop1267 3 ай бұрын
Merci beaucoup nous sommes d'accord toi
@mamebamba6109
@mamebamba6109 3 ай бұрын
Khadim dafa amoul bèn ndiarigne pour askanwi contrairement à cheikh bara et omar diagne. Khadim n'est là que pour son intérêt
@momocreation3631
@momocreation3631 3 ай бұрын
Cheikh bara rek kouko yap dangko ko fékké mouy nélaw attant la réponse khadim Bousso 😂
@fathatasantati2024
@fathatasantati2024 3 ай бұрын
Billhaie
@mohamedsarry3223
@mohamedsarry3223 3 ай бұрын
Merci Serigne Momar
@CheikhounaMbackeDiagne
@CheikhounaMbackeDiagne 3 ай бұрын
Bravos cheikh bara ndiaye
@CheikhounaLeye-z8c
@CheikhounaLeye-z8c 3 ай бұрын
Machalla❤
@Loupe221
@Loupe221 3 ай бұрын
MUHAMADU LAMINE BARRA DAFA TANG. Niou layenté bir ngir BOROM BI🙏🏿😊
@madickeniass6165
@madickeniass6165 3 ай бұрын
Merci beaucoup
@BAAY-DIAW
@BAAY-DIAW 3 ай бұрын
Jërëjëf góor gi amatina solo
@alioudiop555
@alioudiop555 3 ай бұрын
Dieureu dieuf Baye momar diagne
@senwoloftv1556
@senwoloftv1556 3 ай бұрын
Malay ñaane ga jox cheikh bara ndiaye ćerr biko yalla jox ab cheikh la
@MusaSillah-pi1xc
@MusaSillah-pi1xc 3 ай бұрын
C est ça la verite roen que la verite vs eyes vs dieu
@galasssarr3267
@galasssarr3267 3 ай бұрын
Cheikh bara si deug la nek
@CheikhounaMbackeDiagne
@CheikhounaMbackeDiagne 3 ай бұрын
Khadim bosso bol ñiou fonto bayil diné djigaye fowé
@mamadoucoulibaly8235
@mamadoucoulibaly8235 3 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤dégelé papa
@samyniang4002
@samyniang4002 3 ай бұрын
Machalla di
@bassiroundiaye3913
@bassiroundiaye3913 3 ай бұрын
Bilahi bima déglo Serigne khadim bosso bimako setané sama comantaire bi lolou lathi wakh gnom naire War nano diomba wakhaneté Lou niaw louma méti la bilahi
@modoufall1365
@modoufall1365 3 ай бұрын
Li leep politique moko waral yalla naniou yalla mousseul thi politique barké Serigne Touba
@FaaFallilou
@FaaFallilou 3 ай бұрын
❤❤❤Grazie
@ndeyefatoubadji3923
@ndeyefatoubadji3923 3 ай бұрын
Tonton momar il faut écouter la version cheikh bara ndiaye après tu va comprendre pourquoi. la réaction khadime bousso
@mouhamadndiaye3876
@mouhamadndiaye3876 3 ай бұрын
Amna solo machallah
@magammoseck8486
@magammoseck8486 3 ай бұрын
Machallah rafetna
@khadimediop1512
@khadimediop1512 3 ай бұрын
Khadim bousso kay da bàyyi lokhom wakhdiou ñaaw laa wakh
@mohamedsarry3223
@mohamedsarry3223 3 ай бұрын
Merci Père, sénégalais yi legui dqo perdre repère ❤
@thianendiaye6363
@thianendiaye6363 3 ай бұрын
Sama Serigne ziar nala vidéo bi amatina solo lole thi deugue rek ngaye dokh Dieuredieufati
@tallafall6839
@tallafall6839 3 ай бұрын
Salaam salaam Imam bousso ndaa juum, Té tontu wul ci li Ch b wax.
@elhadjidiop3585
@elhadjidiop3585 3 ай бұрын
No Monsieur Bousso danuna
@elhadjimalickndiaye2802
@elhadjimalickndiaye2802 3 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@mohamadouthiam5058
@mohamadouthiam5058 3 ай бұрын
Machala tes analyses sont pertinentes oui ce khadim Bousso est très vulgaire et même les chrétiens ne se comporte pas comme lui Il pense qu'il est plus noble que tout le monde et il représente mal le mouridism une honte pour le mouridism une honte pour la Oumar Toute la diaspora est choqué par la vulgarité et la stupidité de ce khadim Bousso
@aliounethiam1776
@aliounethiam1776 3 ай бұрын
Si j'étais toi, je n'écrirais pas "même les chrétiens ne se comportent pas comme lui"; le bon comportement n'est pas une affaire de religion seulement mais aussi de valeurs morales communes à toutes les religions et même aux croyants et aux Ceddo.
@BassirouDiop-v8h
@BassirouDiop-v8h 3 ай бұрын
Diadieuf ❤
@Diopmamoune483
@Diopmamoune483 3 ай бұрын
Khadim Bousso na répondre ci xam. Xam Mo nguén mouy khasté
@And.611
@And.611 3 ай бұрын
Khadim Bousso dafa dioudou thi guilèm nampe thi mbam yoroul daray Serigne Touba c'est une honte pour la tarikha mourid
@serigneadj1779
@serigneadj1779 3 ай бұрын
Lérna 🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿
@madickeniass6165
@madickeniass6165 3 ай бұрын
Jërëjëf❤❤❤❤
@ElhadjiMassarThiam
@ElhadjiMassarThiam 3 ай бұрын
Machala kaadou yii amena solo lol waay
@CheikhounaGueye-q3w
@CheikhounaGueye-q3w 3 ай бұрын
Serigne mamor diagne ya am kham kham bilahi dr khadim bousso wedi nako ndakh dafa total doumo adama
@modouabdoulayediop5553
@modouabdoulayediop5553 3 ай бұрын
Baaye Momar Diagne diaadieufati
@aliouneseck6083
@aliouneseck6083 3 ай бұрын
Papa wakh nga dege senegal yakhouna legi lepe loubon ngafay ngis Kom ay mbam waxante lou bonrek.
@omarniang5469
@omarniang5469 3 ай бұрын
Les chaussures de cheikh bara ndiaye valent mieux que khadim bousso
@NdayeboussoDiop-x4m
@NdayeboussoDiop-x4m 3 ай бұрын
mon père
@falloumbengue7559
@falloumbengue7559 3 ай бұрын
Djarajeuf imam
@MadokyMadoky
@MadokyMadoky 3 ай бұрын
Mane yaye sama serigne
@mamethiernodieng5067
@mamethiernodieng5067 3 ай бұрын
Imame ziyarnala mies khadime na wakh Lii takh seringe Mame mor mbacke mourtada dialekou USA khamnane lii xeww de bakhna na contine rek
@mouhameddiallo9969
@mouhameddiallo9969 3 ай бұрын
Serigne bara ndiaye jerejef si wakh jiga wakh dé
@abdoukhadrediouf-zv4pz
@abdoukhadrediouf-zv4pz 3 ай бұрын
Serigne sii danio niaka fayda legui man sen taliber you la yereume ay kilifeu yo khamner wakh diou niaww rek diomouniou Dara sarap ndeye liii
@mamadounallaba9495
@mamadounallaba9495 3 ай бұрын
Wahatiko dh
@leytileyti199
@leytileyti199 3 ай бұрын
Imam ,moi personnellement j'ai confiance d3 votre droiture et sincérité de sorte que je like je prie pour vous même si je suis pas d'accord avec votre analyse. Amna yakhine ni amoulo parpaarlo, vous ne faites faites pas dans la langue de bois
🚨Bi YONENTIBI Gissé YALLA😱PR MADIAMA FALL !
53:35
ISLAM_AK_HISTOIRE_TV
Рет қаралды 64 М.
SERIGNE SAM MBAYE
3:00:30
Sunu Thiante
Рет қаралды 136 М.
Une nouvelle voiture pour Noël 🥹
00:28
Nicocapone
Рет қаралды 9 МЛН
Mom Hack for Cooking Solo with a Little One! 🍳👶
00:15
5-Minute Crafts HOUSE
Рет қаралды 23 МЛН
小丑教训坏蛋 #小丑 #天使 #shorts
00:49
好人小丑
Рет қаралды 54 МЛН
Chain Game Strong ⛓️
00:21
Anwar Jibawi
Рет қаралды 41 МЛН
mbiroum mbacké sakho souma sagnoon douma ci wakhati
33:28
Serigne Momar Diagne
Рет қаралды 18 М.
Cheikh Bara Ndiaye Vilipende Les 3 Mousquetaires Corrompus
9:42
Nazir Cissé Chroniques
Рет қаралды 12 М.
Ahmed Ndoye lance une exclusivité « Dame Mbodj mako don… »
8:50
Sen Tv Officiel [DMEDIA]
Рет қаралды 15 М.
tarikha khadria li ci khew gakkal nako bou bakh
13:08
Serigne Momar Diagne
Рет қаралды 17 М.
TAFSIR CHEIKH SILLY TIMERA NUM 06
2:27:21
WAGADU VISION TV
Рет қаралды 102 М.
Une nouvelle voiture pour Noël 🥹
00:28
Nicocapone
Рет қаралды 9 МЛН