Quand l’on parle de chef d’oeuvre ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@ESall-fq3qd18 сағат бұрын
Jazak Allah khairan! Mbacke sakho kou diaraa thiawee la walahi! Kou yabate la, les jeunes niouko too rek la yeureume. Yalla nako sounou borom guindi si limou nek ni , ayye thiakhane deug si la nek
@morndiaye9686Күн бұрын
Machallah dieureudieuf serigne baye momar yalnala yalla defal diamou ❤❤❤
@Lepanafricain-11812 күн бұрын
Yala nako yala yeureum te diégeul ko, ZIARE NALA PÈRE ❤🙏
@SerigneBa-b7q2 күн бұрын
Yalla moo am sa fay ...... Yalla na yalla yërëm ki gaañu
@ndeyekhadydiop6936Күн бұрын
❤❤❤ professeur diagne jërëjëf Yal na Yàlla guddal fan wi te baarkel xam xam bi ❤❤
@moctar722 күн бұрын
Jeureudieuf jeufeuti seugn Momar. Sa takhawaye amna solo. Yalna yallah yokk sa kham kham
@gueyediarra23402 күн бұрын
Maaaaacha alahou maacha alahou yalla naguafi yake loooole té andake wër pape yawe, ake ahmadou rafahi, ake aye cassétou sam baye, ake borom khame khame you lére yéne réke lane ware di déglou ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@demefalldiop23612 күн бұрын
Papa mbacké sakho gni jangoul rek niokoy topp☝🏽 kouci beugue joub dinga jangui
@cheikhsakka81852 күн бұрын
ak beugg lu boone ! té gnaaka nitté !
@modoudiop85912 күн бұрын
Yalla nakou yalla kharé aldina
@abdoulayediop4928Күн бұрын
Toute nos condoléances que la terre lui soit légère Amiine.
Ma cha Allah dieureudieuf sama serigne yana nga fi yague té wer, li nga wakh moy deug. Kou beug waraté dangay diang bou baakh ❤❤❤❤❤❤
@djibyba3601Күн бұрын
Yalla nako yala yereum thi barke seydina mouhamed amine
@adjaroyaal9030Күн бұрын
Yalna yalla sam la thi barké yonet bi saws
@NdeyeseynabouNdiaye-e5u2 күн бұрын
Parfaitement dis Sénégal golo gou diouk yobalé léne si yeufi tiakhane ak yeufi doff
@BiraneKane2 күн бұрын
Yalla na Yalla sunu boroom yërëm mbok mi dawlu ji.
@BachirDiakhate-x5w11 сағат бұрын
Mbackè Sakho nieupla wéèdi yonentabi sahaabayi AK bèp serigne
@gaindefatmacheikhmbgueye9682Сағат бұрын
Waxo deug dh .ab dioulit day wax deug liguen sosal yonente bi ta manou lenko layal si Alkhouran karim lolou la wedi
@Ndrao_Faye_aka_El_Shabbaz9 сағат бұрын
Bilaahi beug Lu yomb moo yobbé Senegalais yi linu nekk
@TddygfiuYfdytvci-c3u2 сағат бұрын
جزاكم الله خيرا وبارك الله فيكم جميعا
@PacoSow-rs3dn2 күн бұрын
Machalla diagne. Nos condoleances. C'est dommage que des personnes suivent ou ecoutent certains brebis galeuses. C'est ce que Serigne Sam Mbaye dit: nous ne sommes pas mures ,nous sommes brulees. Dieuredieuf,la religion n'est pas 1 jeu. Essayons au nom de Dieu d'apprendre notre religion. Ce n'est pas bon d'aimer les choses faciles surtout en religion islamique. Le premier verset du coran descendu sur terre fut ikkera bi issemi rabbika: appends au nom de ton seigneur.
@BinetouDickoКүн бұрын
Paix à son âme ! Que firdawsi nouzoulà, soit sa demeure éternelle ! Amiiine ya rabbi !!!!
@Ndrao_Faye_aka_El_Shabbaz9 сағат бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@mordiop95992 күн бұрын
Dieureudieuf S Diagne wax ngua lepe yalna yalla feyla yiw
@mbayethiao102422 сағат бұрын
Dieureudieuf Papa ❤❤❤❤
@papaamadouname93152 күн бұрын
Pour moi le plus simple c'est de débattre avec Mbacké SAKHO ; cela nous permettra de savoir réellement son niveau. En tout cas je l'ai écouté, mais il est plus logique et cohérent que la majeur partie des oustaz et imams.
@fatimdia70732 күн бұрын
Il est tout simplement ignorant. C'est un Coraniste pur et dur. Il dit ne pas se référer à la Sunna du prophète Saw. Et vous dites éloquent 😮. Qu'Allah swt le guide et nous guide tous
@papaamadouname9315Күн бұрын
@@fatimdia7073 Il est loin d'être ignorant. Il faut l'écouter d'abord. Il n'est pas coraniste ; il l'a dit et répété plusieurs fois. Il est tout simplement un muslim. Pourquoi se référé à la sunna si tout a été dit dans le coran de manière claire nette et précise (Attention, la parole divine). Est ce que tu sais que boukhari est né presque 200 ans après le Prophète et que ces écrits (Hadiths) sont apparus 239 après sa mort (boukhari). Initialement, il en avait collecté 600 000 hadits et à la fin n'en a retenu que 7 000 ? Il faut retourner à l'histoire de l'Islam surtout après la mort du Prophète et tu verras qu'il y a eu beaucoup de falsifications et d'innovations qui y ont été apportées. Nous sommes tous des muslims. Nous devons œuvrer à la recherche de la vérité pour notre salut dans l'au-delà. Soyons plus tolérant les uns envers les autres ; personnes n'a le monopôle de la vérité. Yalla naniou Yalla guindi.
@BaniAadamaКүн бұрын
@@fatimdia7073 un ignorant on le contredit sur des faits et dans ce cas d'espèce c'est le Coran qui est la référence. Jusqu'a présent PERSONNE n'arrive à le faire sinon de verser des invectives sur sa personne. C'est quoi être un Coraniste?
@newbarka8052Күн бұрын
Ah bon !??? Mbacké sakho ne fait que parler ce que Allah a dit dans le coran et vous dites que c'est un ignorant ??? Juste pour légitimé les paroles d'une personne, certains sont prêts à contredire les paroles d'Allah ??? Incroyable!!! Comme je l'ai toujours dit, jusqu'à présent à l'heure où je te parle, il y'a personne pour contredire mbacké sakho sur la base du coran. Ceux qui ont essayé se sont vus cassés une dent dans les débats télévisés. ''Yalla lii la wakh si Alquraan, dème lène vérifièle ko sène bopp", ngène nè daffay soss si diiné dji😂😂😂, gars y diakhlè nagne nakk@@fatimdia7073
@DaarayalquraanTVКүн бұрын
Yaw tam Serigne Moustapha mbakce mom Serigne saliou dousa morom baguakoy sallawlu Té Serigne Moustafa mola geuna kham yonéntbi sws gën laa topu Sounnah gëun lako khamit linga Wakh si mbakce sakho mom Lèp DEUG Le Tè si xam xam bou woor ngako ték machallah dila niaanal goudu fan AK wër
Walay wakh nga deug, senegalais niepp lay tope, rewmi nga guis djiguene diouy djitè mbolo ay gaur topeko te diangoul,khamoul dara. Mais mbacke sakho mome vrai cas la. Yallanako buur guindi.
@obd22143 сағат бұрын
Ay naafekk ngueine miim reew la ay Seriñ complot Mamadou Dia,miim reew lañuy wax Seriñ diw yallah té kenn doussi wax wayé kou ñeuw dilen wax al quran ngueine melni ay deumb di dieufeurou
@MamadouSeye-qm9fgКүн бұрын
Li mbake Sakho wàhe samadiangue soriwoule wayé xamnané ay feninéne la
@nurujamal-n6y2 күн бұрын
Dieureudieuf serigne momar
@thiernoabdoulayendime16712 күн бұрын
Djiazakallah khayran
@SerignematarSall2 күн бұрын
Yalla nako yalla doli yeurmande tè balko ay bakaram amine 🙏🙏🙏
@jeannemarienunez424Күн бұрын
Que son ame repose en paix et que Dieu lui pardonne ses offenses. Amen
@diakhatemor57042 күн бұрын
Dieuredieuf serigne bi yala nala brome bi faye❤❤❤
@assanesene59892 күн бұрын
Bonjour pqpa j aimerai etre beaucoup pouvoir vous parler. Je viss à Paris et j aimerai venir apprendre le Coran avec vous.
@serigne-momar2 күн бұрын
77 634 06 68
@sopendir2 күн бұрын
Paix à son àme ❤❤❤
@abydiallo89852 күн бұрын
Inalilahi wa ina ilahi radjioune mbokemomou wagnéko Yalnako Yalla yeureum té kharé aldiana barké Seydina Mohamed SAWS
@أبوعبداللهمحمدصو2 күн бұрын
أدامك الله ❤
@CheikhDndiaye2 күн бұрын
Yal na yalla yërëm mbokk mi
@bathiembaye721815 минут бұрын
Mbacké sakho lèeg -lèeg lu léer nañi lay wax bilaahi
@modougadiaga98392 күн бұрын
Yalla na Yalla khare kou aldiana 🙏🏻 🧎♂️
@KhdadimDeme14 сағат бұрын
Man dé wallàhi xeuwmako sakhe
@MbayeKane-w4qКүн бұрын
Macha halla
@sokhanasokhana4110Күн бұрын
Mbacke Sakho nane lakou nit mana deglou ba dikou topo moma diakhal
@Galassgolden972 күн бұрын
Macha Allah amatina solo
@bassbass86022 күн бұрын
Salam sarigne bi ziar nala mane de sa nimoro la sokhe la nguir yala
@serigne-momar2 күн бұрын
77 634 06 68
@SerignemoustaphaBadianeКүн бұрын
Face à face avec sakho il ne faut pas amener boukhari
@nitoudeugue49302 күн бұрын
Mbacké sankou mom daffa tiokeul temps yi. Aye doff you melni molou gueye rek la meuneu dévier
@FaaFallilou2 күн бұрын
❤❤❤Grazie mille 🎉
@hacenahmed3027Күн бұрын
bagniou wakhe thi serigneyi degnlena niouss legui thi yalla ak yonentbi legniou dem ndakh fofou khamnagn ken doulen nokh
@obd22143 сағат бұрын
Waw parceque deuk bouñ nekk geumou ñu yallah,Seriñ yii lañ geum ça en dit long
@broaderknowledgerekКүн бұрын
Nangou na wax ji yeup bamou dess linga wax thi Serigne Moustafa Saliou. Serigne Saliou amoul dome boudoul top souna wala bou rere. Lolou dou meusa am mouk
@bintourabykeita84302 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@annadiallo16892 күн бұрын
❤❤❤
@Djolof2 күн бұрын
MashaAllah 🇸🇳🇪🇦
@salioumbaye34512 күн бұрын
Papa yanala souniou borome faye ta goudal say fane ta yook la wère
@sohiboudiop48942 күн бұрын
Mbacké sakho dafa tawate tawati xool jeurejeuf père
@khalilkebe2 күн бұрын
Machalla segne momar mais je pensent que questions yingay ladje mbacke Sakho Tontou nako ba paré mbacke Sakho daffa Takhaw dh damay degue lou ay debawam mais wathie ko Dou Yombou dh
CMBS mooleu eup kham kham.bayil khatrayou bi.yam sa place.
@Ndrao_Faye_aka_El_Shabbaz9 сағат бұрын
Ces gens sont ses representants de Ibliiis
@aliniang7452Күн бұрын
Mbacke sakh loutakh niémétoul wakh thi yonou mouride ay douma kon il faut niou doumako
@serigneadj17792 күн бұрын
🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿
@TallaDiop-zf7pv2 күн бұрын
ZiARE NAALA KILIFAGI MAA NGI TEEW LU BU BAAX SERIGBI MOMAR DIANG YALLA NGAYAGGE FILOOL TEWR AMIIN
@Idy-ri3yc2 күн бұрын
La seule chose que les musulmans sont d'accord. C'est de ne pas être d'accord sur tout.
@bintourabykeita84302 күн бұрын
Al nayalla yerem mbokk mi
@IbrahimaNDIAYE-hc2yy2 күн бұрын
Senegal moy reew mo khamne lofa dji mou sakh
@ousmanegadiaga2271Күн бұрын
Explication bi mou diokhé ci djouly mo takh ma tey ci mbiram
@gaindefatmacheikhmbgueye9682Сағат бұрын
Bou guen amoul dalil si Alkhouran ngene nopie
@harounacisse91249 сағат бұрын
Le problème de nos jours il n'y a aucune langue qui est d'origine par exemple la langue des premiers francs et le Français qu'on parle maintenant est diamétralement opposé exetera exetera et l'arabe né pas épargné l'anglais de même et le wolof et j'en passe sans compter les langues disparues l'affaire est complexe que Dieu nous guide (si je comprends bien vous nous parlez de intellectuel grammaire vocabulaire tout ça ça a été créé quand) en quelle année? le temps du Prophète notre bien-aimée paix et salut sur lui . Monsieur ou cheikh ceux qui me taraudent c'est des êtres humains qui ont mis en place grammaire et vocabulaire est-ce que vous vous êtes pas trompé c'est une question que je me pose parce que maintenant il est temps qu'on utilise le cerveau et l'intelligence que Dieu nous a donné. Qu'Allah nous guide qu'Allah nous éclairs car vous aussi vous pouvez vous trompez car vous êtes des êtres humains vous pouvez vous tromper cheikh Mbaké Sarko ce qu'il dit c'est clair et précis et ça pousse à réfléchir. Monsieur vous parlez de intellectuel la science du Coran appartient à Dieu il embrasse qui il veut avec sa science pour moi l'intellectuel lité que tu avances est obsolète qu'Allah nous éclair car c'est complexe moi je vous ai pratiquement tous suivi il y a personne mais personnes qui est capable de le contredire dans le Coran Monsieur Ndiaye lui ça se voyait comme un avion qu'il était nerveux c'est complexe
@DiagneNar-ej4uk2 күн бұрын
Père linga wax deug la.... Gnikoy topou je pense degouniou grammaire arabe....
@moctarndiaye-qg8mkСағат бұрын
Wakh diou diib ak wakh diou gaw si yam .MBS alkhourane rek lay wakh. Wa euhlou souna wal diama neklen si sen téréyi.Souna yallah rek moo am.Moo leu eup kham kham fouf.Vous n'êtes pas comparable à tout point de vue.
@mordiop95992 күн бұрын
Ñoongui ñaanal mbok mi yalna ko yalla yeureum te khareko aljanna firdawsi bidiahi sayidiná mouhamed PSL
@saimonbadiane923212 сағат бұрын
Vs nous parlez de boukhari encore .
@mohamadouthiam50582 күн бұрын
Ici aux USA je n'écoute pas ces genres mbacke Sakho