🛑Direct - Réaction de Khadim Gadiaga après la sortie de Birame Gningue sur Balla Gaye 2 vs Modou Lô

  Рет қаралды 34,593

Lutte TV

Lutte TV

Күн бұрын

Пікірлер: 77
@Azoura22
@Azoura22 4 ай бұрын
modou xaragne lo seul Machalla Yalla nala Yalla Maye ndam rék modou moy roi bi rék ❤
@DoudodiengDoudo
@DoudodiengDoudo 4 ай бұрын
MODOU XARAGNE LO 🎉 LE SUPER ROI 🤴 LE GOAT DE LA LUTTE SÉNÉGALAISE😊 KOUKO BAAGN YAA XAAAM❤
@cheikhibraniang4101
@cheikhibraniang4101 4 ай бұрын
Modou lo sama mbeur bi ❤️
@Steven-ul8pw
@Steven-ul8pw 4 ай бұрын
Khadime Kou Bah nga té Beug Modou mé Lép Loy Wah Mou Conserné Modou Boulsi Diouyo Ak Moom té kom diohnala respé Bou Sanion Lo Wah Mou dfko kon Soy Wah Communique si ak Pér Birame pour Réro Baña Am Ndah Waxantu Yi Sila Saytané yi di Diaar Pour Diaxasé len
@Cheikh-Ahmed-Tijaan__Faal
@Cheikh-Ahmed-Tijaan__Faal 4 ай бұрын
tu n’as pas compris Khadim marqueting management lau deff il vend l’image de mod lo il faut créer des polémiques pour que l’empereur ne dépasse pas le roi niveau médias showbizz quoi
@mbayembengue6302
@mbayembengue6302 4 ай бұрын
😊
@mbayendiaye5033
@mbayendiaye5033 4 ай бұрын
Khadim gadiaga linguay wax danguay toutil modou lo yangui degu balla demb diléne kanion nane niom séne wax yi bokkoul naniou waxtane séne birr respecté les paroles de modou yangui beuga soff
@leuz.patriote
@leuz.patriote 4 ай бұрын
Sama mbeur mi da pares😂
@mbayendiaye5033
@mbayendiaye5033 4 ай бұрын
@@leuz.patriote kouy sa mbeur ?
@leuz.patriote
@leuz.patriote 4 ай бұрын
@@mbayendiaye5033 bg2 🤣
@papamakhtarniang
@papamakhtarniang 4 ай бұрын
​@@leuz.patriote copin insbi mom champion kolo kolo nguéy yor vrai baanga parcelle xagne lo😂. Boudoul woon abdou aziz alé ndiaye dégueu nguén ancien gouloir bou yagua yagueu😂. Fair-play rék amoul sisou
@KhaforNdiaye-m7x
@KhaforNdiaye-m7x 4 ай бұрын
Tu parle trop j suis parcellaire nopil
@adamslo7971
@adamslo7971 4 ай бұрын
Xadim Gadiaga Yoe vraiment Yagui nelaw modou dafa neik cii combat respectéll mansour ba wax cii combat modou akh siteu lii gay defff nii baxoull tittt na Trops modou niakeu combat wam akh siteu pask peteukh bou yague cii deall aziz ndiaye pr soull combat roiyall bii vraiment dafa beurii wax Tei ligay wax keneu Waxlo wouloko
@leuz.patriote
@leuz.patriote 4 ай бұрын
Aziz vres business man la limou begone am nako 😂😂
@vjoficiel
@vjoficiel 4 ай бұрын
Roi bi késsé❤❤
@malickdia3495
@malickdia3495 4 ай бұрын
Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@AliouneFall-q6u
@AliouneFall-q6u 4 ай бұрын
Ki doff deug la Wakhou proteger Modou lo doko wakh thi live. Wakhou birr nekk la Beugue ngen attention lolou
@souleyewade7419
@souleyewade7419 4 ай бұрын
Modou bou dane balla sa sera pr moi le meilleur lutteur de tt les temp
@AdamadouBah
@AdamadouBah 4 ай бұрын
Kahdim la andal bilay ❤❤❤ pere berim Na nopi
@AdamadouBah
@AdamadouBah 4 ай бұрын
❤❤❤❤ xlo rk
@saliougueye9833
@saliougueye9833 4 ай бұрын
Modou seul❤
@momo12146
@momo12146 4 ай бұрын
Khadim gadiaga yaw khalice rèk ngay khol nékhal niite bariga wakh trop
@AssaneKhouma-fb7oc
@AssaneKhouma-fb7oc 4 ай бұрын
bilay boumniou sonnal wayy
@mouhameddia5168
@mouhameddia5168 4 ай бұрын
​@@AssaneKhouma-fb7ocsa way 300 million bouko dieuloul wa keureum wakhak mome déh .méme souko balla di dane sakh nako dieul mane déh yénenakoko
@AssaneKhouma-fb7oc
@AssaneKhouma-fb7oc 4 ай бұрын
@@mouhameddia5168 moh lonage 1xbet faynako 400 et quelques millions mou bagn conn khaliss yeungeulouko
@YatmandiayeNdiaye
@YatmandiayeNdiaye 4 ай бұрын
Modou lo kassé nak ❤
@Dieng-vk6if
@Dieng-vk6if 4 ай бұрын
Khadim gadiaga borom kham kham leu ba paré ils communique bien
@mouhameddia5168
@mouhameddia5168 4 ай бұрын
xam xam yombouna si réwmi déh kouye wakhé xam xam dina wakhni modou supportaire indiwouniouko fimou eksi deugueleu jambar leu mais niatta mbeur nio meune beurré té yégouniou au sommet ndakh amouniou supportaire lan 2000 kouko dakka beuré domou dangou walla forza.
@SIDYLAMINENdoye
@SIDYLAMINENdoye 4 ай бұрын
Khadim tu parltoua rispetto modou pere biram
@mouhameddia5168
@mouhameddia5168 4 ай бұрын
khadim woro wakhni modou supportaire indiwouniouko fimou eksi deugueleu jambar leu mais niatta mbeur nio meune beurré té yégouniou au sommet ndakh amouniou supportaire lan 2000 kouko dakka beuré domou dangou walla forza xolal ada fass mongui beurék lac té pourtant domou dangou loumfi déff sa way défouko.siteu di beurék modou supportaire moko waral.remercie les supportaire si ce n'etait pas eux modou dou eksi fi démal ladj lac bakham supportaire amena ndieurigne ou pas
@picofall3211
@picofall3211 4 ай бұрын
Sa way ki doff plus leu
@momo12146
@momo12146 4 ай бұрын
Khadim gadiaga tu communique mal .daga beug nék au devant de la scène bala ngay wakh dèl wakh ak modou lo ak biram gnigue.fane yi wakhi dof rèk ngay wakh nane aye technique de communication.
@picofall3211
@picofall3211 4 ай бұрын
wakhal way yalla rék mo meun nék féép en même temps....
@ibrahimasane9157
@ibrahimasane9157 4 ай бұрын
Khadim il faut respecter les gens tu ne respectes pas Modou
@AssaneKhouma-fb7oc
@AssaneKhouma-fb7oc 4 ай бұрын
na nopalou way boumniou sonal
@cheikhmbackesyll9838
@cheikhmbackesyll9838 4 ай бұрын
Khadim gadiaga xana deggo li modou lo wax diokhe woul revanche
@diopmar6382
@diopmar6382 4 ай бұрын
Khadime boulniou sonal diniou wakh communication ak marketing père bireum a raison
@waxkatoudeug
@waxkatoudeug 4 ай бұрын
Yow da ngay diémeu niodi affaire de business man di diémeu topando Aziz. Amo xam xam, amo xaliss, bayil forcé bi
@alioukane6955
@alioukane6955 4 ай бұрын
Désolé, mais votre communication sur les 300M, fut mauvaise, car ça reflète 1 programme de management ds le camp de Modou. Certes Modou doit gagner de l’argent mais ses principes devraient être respectés. Je n’est jamais vu ce lutteur Modou Lo, mais il allait atteindre ses objectifs, car il a tt ce qui lui faut a lui seul. La communication du vieux était bcp plus objective.
@MoustaphaGueye-i1f
@MoustaphaGueye-i1f 4 ай бұрын
Ki pour Instant diaroul wolou bilahi
@adamslo7971
@adamslo7971 4 ай бұрын
Khadim Gadiaga mane personell wolou wouma akh aziz ndiaye daga beug Xaliss d Trops Tei kadou mo geuna fort Xaliss modou yayam motaxaw nei combat bobou doyna Yoe lane moy sa problem gay forcé nii modou beuré woull akh balla repecté niou way bro
@AssaneKhouma-fb7oc
@AssaneKhouma-fb7oc 4 ай бұрын
bayiko fofou rek khaliss lay topou té modou cadom rek lay topou soofna trop
@diatafall944
@diatafall944 4 ай бұрын
Si modou Lo a un vrai staffe de businessman il prendra balla guaye pour avoir une grosse somme d’argent pour terminer son carrière
@IbouSene-eh9lj
@IbouSene-eh9lj 4 ай бұрын
Modou kess
@cheikhmbacke72
@cheikhmbacke72 4 ай бұрын
Modou balla ladioula fene il napa demande à lute contre toi garde ton couronne c bon
@karbalasow8234
@karbalasow8234 4 ай бұрын
Li khadim wakhe deugeule modou pourquoi moye bayii c'est pas un logique lambe mo takhe niou khameko il doit travailler encore c'est un enfant mw js8 de pikine fall modou bou bayiée lambe adouna dinala méréé fall
@berengermpamy1819
@berengermpamy1819 4 ай бұрын
Khadim, Beuzz daflay foukhal rek ngay bayékou. Beuzz, Balla Gaye moy mbeureum, louko arranger rek lay wakh
@ndiagathioye3928
@ndiagathioye3928 4 ай бұрын
Beuz toi aussi il faut arrêter de parler comme les lutteurs..Toi même tu commence à croire trop aux mystiques
@babacar3178
@babacar3178 4 ай бұрын
Modou waroul wona téla wakh lolou wakhna deug nakh niga wakh doto beuré ak niome dagne laye khékh
@rimesmakerposeidon2427
@rimesmakerposeidon2427 4 ай бұрын
Modou lo messi de la lutte sénégalais xaragne lo
@ndeneniang8524
@ndeneniang8524 4 ай бұрын
Modou so dieulé balla niak roi bi khaliss diarouka
@ndiagathioye3928
@ndiagathioye3928 4 ай бұрын
Non khadim boul diawalé vu yi dou yaw déh..Balla ak modou yiguay toudou leu
@amathgueye302
@amathgueye302 4 ай бұрын
Demel tal say lamp di wax si Modou Balla
@adjigueye8313
@adjigueye8313 4 ай бұрын
Khadim je t aime bien mais problème by dou balla mais siteu leu modou dafa am combat
@saliougueye9833
@saliougueye9833 4 ай бұрын
Khadim kou yewoula te mous😂
@ACTULAMB
@ACTULAMB 4 ай бұрын
Bolen beugue 300 millions amguen Jambar nako teugue Diokh lenko Mansour
@KhaforNdiaye-m7x
@KhaforNdiaye-m7x 4 ай бұрын
Si azis ta donne d l'argent comba modou ama tu a vendu les tikets nopil
@DembaKeita-yd9vo
@DembaKeita-yd9vo 4 ай бұрын
Beuz demal lokhatii dji tyson ak yekini defal lolou gnognou vue dina beuri lol
@Alamine-lx9vi
@Alamine-lx9vi 4 ай бұрын
Apare carier diarna bayi khél bougnoko fayé khaliss na beuré thakhan bakhoul ana gnom yikini gnom Tyson tay kén topatoulén
@leuz.patriote
@leuz.patriote 4 ай бұрын
Li bg2 done wax😂
@MassambaNdiaye-z3t
@MassambaNdiaye-z3t 4 ай бұрын
Tu churches du buzz khadim tu travail pour toi pas pour modou
@afro3827
@afro3827 4 ай бұрын
Guemo touss 😂
@leuz.patriote
@leuz.patriote 4 ай бұрын
Na bayi akh kouy bayi dou tago 😂
@leuz.patriote
@leuz.patriote 4 ай бұрын
Xana sen promoteur yi amougn xaliss ani jambar😂😂😂 thiout day xam lèkam
@salifliilakaronciserignbis4182
@salifliilakaronciserignbis4182 4 ай бұрын
Billay moudou lô tapha tin
@KhaforNdiaye-m7x
@KhaforNdiaye-m7x 4 ай бұрын
Vraiment. Nopil vendeur d tiket
@AmadouBa-xm5ln
@AmadouBa-xm5ln 4 ай бұрын
Modou Lo il est intelligent il sé très bien menoul dane les VIP motakh mou dieul boy yi😂
@Faty1206
@Faty1206 4 ай бұрын
Eumeu séne,Ama balde ,Boy Niang ,Gris bordeau et lac de Guier .Modou les a battus tous .Je suis Fan de Balla Gaye mais Modou les a tous battus En plus Modou Toute sa carrière c’est seul Balla Et Bombardier ont battu Modou . Modou a battu Eumeu et Eumeu a battu Balla Gaye Modou A battu Boy Niang et Balla a été battu par Boy Niang .Ama Balde est le jeune le plus dangereux mais Modou L’a humilié
@babacar3178
@babacar3178 4 ай бұрын
Yawe wakhi none kaye wakh modou khana néwoul wone si vip yi
@miachoufall6665
@miachoufall6665 4 ай бұрын
@@Faty1206yagui yakh sa énergie ki d’à sokhor boulko falle
@ouzinsane468
@ouzinsane468 4 ай бұрын
@@Faty1206 ya gooré bilay
@wara2043
@wara2043 4 ай бұрын
@Faty1206 t'a répondu😂😂😂😂😂😂
@KhaforNdiaye-m7x
@KhaforNdiaye-m7x 4 ай бұрын
Tu fais ta popre promotions
The Best Band 😅 #toshleh #viralshort
00:11
Toshleh
Рет қаралды 21 МЛН
Try this prank with your friends 😂 @karina-kola
00:18
Andrey Grechka
Рет қаралды 7 МЛН
Каха и дочка
00:28
К-Media
Рет қаралды 3,3 МЛН
小丑女COCO的审判。#天使 #小丑 #超人不会飞
00:53
超人不会飞
Рет қаралды 16 МЛН
The Best Band 😅 #toshleh #viralshort
00:11
Toshleh
Рет қаралды 21 МЛН