Ndeyssann je ne suis pas Mouride ni Thiantakhoune mais il faut reconnaître que les enfants de Serigne Bethio sont vraiment disciplinés, humbles et reconnaissants. Que Dieu vous accompagne
@Tallamor37395 жыл бұрын
walahi aka Nio yarou té xam adouna
@didisylla41295 жыл бұрын
Ces vrai tè didagnou toudou yalla paa rapport sene feue pere
@mariemegadio7745 жыл бұрын
didi Sylla Observer bien la vidéo, durant l’interview il a toujours la tête baissée. C’est un signe de politesse dans notre culture. Machallah
@aicharasullamacktoumienne8555 жыл бұрын
Mme remarque la df
@hafidarharrabti22515 жыл бұрын
Ki si.keparou serigne saliou la yaro nila mana mell
@matyfaye76545 жыл бұрын
Mourite môme ndiguel reek laye dieuffè serigne mountakha yalla nako fi yalla yagual mou ande akkouk weer barkep serigne saliou
Akassa ! Y’a am yar, téy ta kham yonou mouride ak adouna. Dieureudieuféti Serigne Touba. Serigne Mountakha Bachir Mbacké yalanafi yague ta weur. Machallah, am na solo. 🙏🏾
@sokhnadiarrasaliouniass70915 жыл бұрын
😁❤️
@fadelbambiste14515 жыл бұрын
Waw leen goor neklene si rek degue ndigeule la cheikh ibra fall rawei gneup ❤️
@ablayediagne71695 жыл бұрын
Degg rekk Kaye degg ken dou don nou se keur baye di donnou keur bayou diambourr ❤
@aichakounta49715 жыл бұрын
Machalla dieurdieuf chiekh bethio sama dome yi yaregua les yarounou naniou Machalla
@mignonemama45125 жыл бұрын
Wa waw Thioune mame bamby santati nanou dée Faw Faw
@kheussabofaye33785 жыл бұрын
La fils Cheikh Bethio yi yalla nalen yalla dafal Diam fi ci adouna ak alakhira dangéna am yarr loll machalla
@khadimleye57385 жыл бұрын
Kén dou lath koula djour koula yar la Serigne Touba done lathié Serigne Saliou molène yaar motakh ni rek ngén meune méle bakh ak degou Dieureudieuf Serigne khadim
@ibrahimadiop24825 жыл бұрын
Wallahi ma andak iow serigne khadim jigueen dum à meussa jiitall
Je suis Tidiane mais les fils de Béthio parlent vraiment bien. Et là c'est bien dit
@Diezflora5 жыл бұрын
sama kharite bi say kandou rafetna, andak yar machallah 🙏🏼yallah doli sutura
@assanediakhate88255 жыл бұрын
Serigne Khadim nekhnama trop dafa tey tei yarou
@pendapene18465 жыл бұрын
Machalla Serigne khadim wakh dji raféte na Thioun
@Serigne-khadim-mbacke8115 жыл бұрын
Ya goré s khadim thioin yala ga koudou fan
@khadimfall72055 жыл бұрын
Machallah serigne khadim yarou ngeu téye ngeu
@layelaye65835 жыл бұрын
bilahi Thioune mame Bambi sama Serigne koula sope la Serigne Khadim Thioune mbosse
@Tallamor37395 жыл бұрын
Machalah Deugue nexoull
@aidaguene19485 жыл бұрын
Affairou Aïda Diallo sakh lagnou wara zappè toudou biniou koy toudou sakh dakoy may buzz dokhal lène rek
@fatymature94765 жыл бұрын
Bilakhi lolou laniou warra deff🙏🙏🙏🙏
@awadiouf56815 жыл бұрын
Yes bouko kene mayati buz aida dafa yabatee
@fatousamb46625 жыл бұрын
Billay
@sarromar75655 жыл бұрын
Doull ioe
@thiantaconefaaawww65935 жыл бұрын
AYDA FANG DANG NI MIDI
@ndeyediarra20635 жыл бұрын
Macha Allah seydi Thioune yallana yénebi gueuneu woyof ya rabi
@mamyndoye1995 жыл бұрын
Yalna seneu bay ba tekh len loko inchallah
@serignetakkricain13395 жыл бұрын
Diadief Khadim 👉❤️
@ibrahimadiop24825 жыл бұрын
Serigne khadim fierté des toi DEUG rek kay deug
@fatimedioufniang45685 жыл бұрын
Yéne deh mashallah yenangui magal👍👍👍
@ousseynoufall28525 жыл бұрын
Yalla naléne yalla guene taxawou ci barcké Brom Darou salam
@khaditraore56815 жыл бұрын
Ki mome mako sope ndah degou ak yarame limoye identité ndongoye serigne saliou yalla naléne yalla lafal tiate
@ndeyediarra20635 жыл бұрын
Wallahi domou cheikh Béthio yi danô yarou nékha sopeu macha Allah
@bamsdiaby28795 жыл бұрын
Aïda diallo kay mouride yi la yap wayé dou l'islam / ndakh l'islam a déjà prévenir que djiguene dou meuçeu done kilifeu si kaw gor Yalnagnou yalla khir si bopam si barki seydina Mohamed psl amine
@dieyes.salioumbakce2045 жыл бұрын
Machahllh s. Khadim❤❤❤💋
@augustindiouf70815 жыл бұрын
Yague fi lole thioune ndame rek tie barki Serigne Touba
@tallawadebichri55255 жыл бұрын
Yalla na yalla goudal sa fan
@ahmadoudiop34835 жыл бұрын
Máchala kou serigne saliou yare niga mana méle
@beuleupndao11555 жыл бұрын
Ma cha allah thioune 🙏❤
@falloundiaye4625 жыл бұрын
Dieureudieuf thioune DEUG kéne douko Ray bilahi sopounala gniy dokh DEUG rek nio ande ak yéne
Nite daguaye defare sa keur balagua fatou borome keur bouné nathi bayi xel nak👂👂👂
@ndeyeawa15465 жыл бұрын
Ndeyesane mala beug barckè serigne touba
@dabadiop3805 жыл бұрын
Wawaw thioune sagou nagne dei
@rafaelfernandescosta99965 жыл бұрын
dieuredieufety seringe saliou gueltape thioune yague fi lool tei wer thioune
@modoungom84385 жыл бұрын
Défa leur djiguéne manoul nek khalife aïda diallo defa yab wa Sénégal
@kingroma185 жыл бұрын
Sr bethio yarna niabotam machallaaa
@ayshajuliette5 жыл бұрын
Vraiment kii defeu deugou Niémé neu et il est direct On connaisait pas les enfants de cheikh bethio mais dey nio am yarr deh il a bien parlé et puis diabotou cheikh bethio kenn meusou lenn degg ci bordel Je suis emue Mannn aida sey moko fa yobou wonn seybi diekh neu sou ko nekhei berou tey xamnei serign saliou thioune mo fi nee Dou ma thiantacone mai sama xalat leu
@bachirbachir98315 жыл бұрын
aissatou seydi wakhofi dara nie di wote ap diam nganane
@Dulce-pm1ku5 жыл бұрын
Mom deh yarou neu ba dou sigui sax xol caméra bi masha allah kadfu yi deuggu neu lér neu téguinéna
@falloundiouck91585 жыл бұрын
Diadieuf S. Khadim wakhdji rafétna Mane dé yak Serigne Saliou nawna léne fonkou naléne
@pepegueye81055 жыл бұрын
Cheikh bethio sén bayla aida diallo loumko diaral nalén diarral louko euppou pour mbolomi yéppou ñiawat si yéen dafa ladj di dokh pour dadialéwat mbolomi
@gueyealioune38225 жыл бұрын
kii kouka khole khame ni kou amm yarr la macha allah
@khadimniang55115 жыл бұрын
Vraimeent ngi dall yarou nang
@seydoudrame81955 жыл бұрын
Thioune nioune mbeugue nagnou ande at yeine dh
@khadimniang55115 жыл бұрын
Ndaysan limiy wakh dawna yaram!
@abdoutoure64365 жыл бұрын
Diara diaf thionn kadou yi amna solo
@سميرهالسعدون5 жыл бұрын
❤❤❤❤❤❤👏👏😍
@jougjotna48355 жыл бұрын
Ni len Serigne Bethio yare kesse am na ndiort ni fimou ne Yalla teral na ko.
@ndongosafi6165 жыл бұрын
Machallah 🙏🙏🙏🙏❤❤❤❤❤
@pothiogueye29335 жыл бұрын
👌👌👌👌💝💖👍❤❤❤❤💌
@awafaye64615 жыл бұрын
Machallah mouride ndigueul réck
@bayezallebadiane81975 жыл бұрын
ماشاء الله سرح خدام جون
@omarndiaye8435 жыл бұрын
Machalla deg rek
@deliart38215 жыл бұрын
Thieuyyy Serigne Bethio
@dieynabaabba15555 жыл бұрын
affaire bi check bi la mome mo yak keureume warouwone wakh may yaw yaw mane pour lane chekh bi tawoukoyoune dhiguene bakhoule
@domoupapam47295 жыл бұрын
Mayy yaw yay mane ne veut pas dire k nii souma déweii yay done sama Khalife teii bou djiguéne done djitteii kone sunu Khalifs you beurii fii daniuy kharrrrrr
@awajah71925 жыл бұрын
👌👌👌🙏🙏🙏❤️
@Petitpaa5 жыл бұрын
Nagnou bayi xel la serigne bethio wakhone en 2017si gamou gui tè gnou mandou fatè khadiou fii
@fallsamfall93245 жыл бұрын
Dafa lérr
@yayounabi37975 жыл бұрын
Deugue rak gua wakh
@miriamesow69095 жыл бұрын
ehh way ningua nirok sa baye serigne bethio .bayi ho dara thi mome .thiey serigne saliou dieureudieuf
Déug dal boci wété ite nékci rék kou dëgou dinala fékci té kou bagne gneuw nga bayiko té fékhé ba dëpo ak santané Sr. Saliou té bagna sosse dara thi yonebi ndakh borom matalna lép té moko samal bopam. Naléne Yallah samme té aar léne.
@bambagueye41675 жыл бұрын
Mane sama Khéll Dallna Ndakh fi mome l'islam lafi gise néke léne thi rék dina bakh fingén ték séne tangke foufou la
@aminatouthiam64435 жыл бұрын
Je pense que li takh senegal yeup merewone cheikh bethio ken waralouko loudoule aïda momou on peut voir quil a eduqué ses enfants dans la droiture et dans letique islamique ce quon na jamais remarqué jusqua sa mort. La femme est tres claire dans ses actes et c typiquement le comportement du cheikh apres setre marie avec elle. Cheikh Bethio etait bien un vrai musulman et le comportement de ses enfants et limage du cheikh bethio deg ndigueule ame yare ak talibé que serigne saliou avait cheikhal mais malheureusement détournée par satan aida diallo qui continue de diviser ses talibés
@aron60545 жыл бұрын
Diam rek nguéne di thioune mame Bambi
@princengom58495 жыл бұрын
Iow sa baye kouko gueuna done goor yalla dafa am té Mo djital Sokhna Aida Mane dal xamnani Sokhna Aida Molène gueuna digne wa keureum tmt niolëne gueuna digne ndax dinagne dieul parole babayi té dounioulène garouwalei té yë xamoulni sax vous êtes dans ce bas monde té yène chaque jour nguène Koy garouwalei Té Sokhna Aida sou amoul ndam kone Kane moko am ???mom mouy djiguene rk té limou dieuf ci magal gui benn goor défagouko waxoumalak iow kone mom sou amoul ndam Kane mokoy am ??? Bilae Sokhna Aida rawnalène té dounguène sen sax peundeum
@lespatriotesdusenegalsoute23895 жыл бұрын
Diallo ak khalifa mais nak serigne béthio déf na erreur thi bimouy dounde famme dafa grawe gnome gnolaye wakhlo lou né
@ndeyefatougueye92825 жыл бұрын
Mane dal ki nekhnama nakh dafa yarou
@galgalgal80075 жыл бұрын
aka nirone cheikh bethio
@walydiagne82355 жыл бұрын
Kadou gui rafet neu. Yonou mouride lii leu NDIGUEUL REK
@mamansalioudieng57845 жыл бұрын
Dafa lére st srgn saliou rk atou ka ki fé ki fi rafétoul té mou mene nék béne sokhna aida mourite digale défale lila srgn mountakha wakh nakh lp geuneu nékh adouna amoul solo na raféte rkk yalle nasa khéle délou sii si mbrcké srgn saliou
@mboubandiaye65555 жыл бұрын
Me khadim sokhna aida a dit publiquement que elle e simple diewrigne universelle
@abdoulayediom87605 жыл бұрын
Mbouba Ndiaye kana khamo ni diawrigne universelle yii danio barri lol sax
@dabadiop3805 жыл бұрын
Diadieuf thioune sagou nagn
@mouamedmbaye44445 жыл бұрын
walahi degula thioune
@mamendiaye68505 жыл бұрын
Serigne bethio ay mbireum kénn douko donou mome rék lay sobb mou sobeu ko fouka nékh té fa sokhna aida lako déff limouko wakh lérna dh nénako Yaw La yaakar sama guinaw douma mafi diougué sokhna aida Deug deugui dieum dji Yalla nanga fi sakh faw sokhna aida saliou
@cheikhounambacke28635 жыл бұрын
Mame Ndiaye yaw iska yangui khalate serigne touba mon guene mague thièpou ta Bamoufi diogué domame mon ka donne yaw nganane cheikh bi douñiouko donnou yène iska vous êtes correct sérieusement
@fatousamb46625 жыл бұрын
Vrement nakk djiguene dou djitté mouk
@mamendiaye68505 жыл бұрын
Cheikhouna Mbacké baye khamm nanou histoire l'Islam dh bi fi yonétébi bayéko sokhna aicha mo djité wonn mbollo ma ki nak di sokhna Aida serigne bethio Monika Yaw La wolou sama guinaw kousi ande ak mome dh dinga déff loma nékh té nioune li nékh serigne bethio rék lanouy déff. Serigne mountakh wakhnako kouné kholale koula doy si ndiabot gui mou djitéla konn kay wakh dji diékh na nioune sokhnasi monou doy point
@makoddufaal14705 жыл бұрын
Yalla na yalla guindi.
@khalilndiouck86825 жыл бұрын
Prk journalist seytané
@ramatoulayendoye76455 жыл бұрын
Ndaysan yenn.dal daguenna bax te am yarr yagg lenn fi rek yow mom je tapprecie lol bilhi ndax digayy waxtaner si Serigne saliou mbacke