N accablez pas ces pauvres parents qui souffrent déjà. Les violeurs sont autour de nous dans la famille le plus souvent. Que la victime repose en paix et que justice soit faite.
@BertheDiallo2 күн бұрын
Bayil gni melniiiii amoul Ay nitt youniou fek sen bir Nek violé len fi si deuk bi
@mariemetherme55942 күн бұрын
@@Bluelove447 vous avez tellement raison. Les violeurs sont souvent très proches de nous. Ce sont les amis des frères, des tontons... Faisons attention à nos enfants, ne cessez pas de leur répéter que personne et en aucun cas apart papa et maman n'a le droit de les toucher.
@Ramzek-f3s2 күн бұрын
@@Bluelove447 très sage vos paroles
@myamya65232 күн бұрын
Vous avez tellement raison.
@rackyndiaye36652 күн бұрын
Massa yaboy metina trop yalna égalé ndawam adiana 🥺😭😭😭😭🙏🙏🙏🙏
@mackysallbadolala6002 күн бұрын
Khale bou am 12ans waroul nek si bend ba 19h nioun wadiour naniou geuna bayi khell si khale Yal nalen Yallah mey kholou mougne
@Bluelove4472 күн бұрын
@@mackysallbadolala600 svp n acccablez pas les parents
@aichadiene54892 күн бұрын
Saway demb fête leu wone té jour fête yalla Moy sam rék mais khalé yi keen mounouleen téré gueen de plus AK nouvelle année bi khalé faut niou jouer tale pétar et tt khalé tmt nékoul tt le temps ngako Mouneu surveiller fi mom yalla rék Moy sam bou keen blamé les parents gni kouleen mounoul Masha wou dangay mandou ils n ont vraiment pas besoin de critique c mm pas le moment ayy moral yoyou mom Moune na niak nga Balma🙏
@bernadettegomis10942 күн бұрын
Vraiment hier c’était les fêtes toi aussi
@Awayandésindidi2 күн бұрын
@@mackysallbadolala600 nioune dé khamouniou wone nék si mbéde Bâ 19h
@boubangom58912 күн бұрын
Fête moy lann Khalè bou 12 ans dome bou jigueen ga dem teudi tè guisso irresponsiblitè fala yameu douguènn aye nitt yalla kou samaloul sa bopou doula samal touss yalnako yalla yeureum tè leral Senegal parents du n’importe quoi nionfa nekk sexx pour senn bopou rek c’est ca la veritè mane douma teude moukk bayi dome surtout bou jigueen 12 ans vous êtes malade
@mamediarraka22142 күн бұрын
Yalna bou aziz dabala ak wally gaaw fegn ba melni bou khalei bii barkep Mouhamed😢😢😢
@ndeyedabadiop5457Күн бұрын
NOTRE BIEN AIMÉ YARASSOULILAHI PSL❤
@mounarositraore868418 сағат бұрын
Amine ya rabi 😢
@boubacardiallo26362 күн бұрын
Ça fait très mal. qu'Allah ait pitié de son âme. Je ne peux pas comprendre comment un père ou mère de famille puisse dormir sans son enfant à la maison. Nous sommes très irresponsables. Nous devons être les premiers responsables de la sécurité de nos foyers avant de passer tout notre temps à interpeller l'état. Eskey les parents d'aujourd'hui
@boubangom58912 күн бұрын
Vraiment Vraiment Senegal do kham yang façon nitt laniou nan la aye parents dem teudi sens leur file de 12 ans catastrophique c’ést dommage repose en paix petite 🙏🏾❤️
@FamaraBodian-e2h2 күн бұрын
@@boubacardiallo2636 bien dit c'est la question que je me pose.
@myamya65232 күн бұрын
Au moins toi tu poses la question normalement en indexant les parents en général car au Sénégal ils ont trop tendance à pointer du doigt la mère alors que tous les parents sont responsables
@myamya65232 күн бұрын
Mais aussi va ecouter la version de la maman elle est vraiment très fatiguée elle a des jumeaux bébé kokou tamit dafa sonu
@AbsaFaye-et1yn2 күн бұрын
Mane dé douma tede té samak ndiabot tedousiwoul surtout djigene😭😭😭😭
@Nogaye-h4u2 күн бұрын
@AbsaFaye-et1yn vraiment
@BertheDiallo2 күн бұрын
Iow mayniou way mayniou diam lolou iow la intéressé dogal la loussi mère bi meun da warone Nek iow diga xam lou ki di yeuk nga xol ndax bou nitt Nieuwe dila wax Li dinala nexx boko meunoul dialle nga teudj sa gemigne mo geun
@seynimangane48092 күн бұрын
Ya nék si deugue en plus dokh ba 00h si khalé 12ans dédét mané dé ki am bac rén sakh mayouumako lolou
@myamandiang2 күн бұрын
Hi sama yaye nonoula niiune douniou dem fene sunu telephone ecol diexna te bouy teudi neg yeup lay xol te reuthiouw niouko bene yone
@AdjiGaye-g8o2 күн бұрын
Vraiment xalé dakoy xol surts dormir sens savoir foumou nék yalnako yalla yeureum
@FatimandaoTymandao-gr4gl2 күн бұрын
Legui adouneu dafa doy war, ne faites confiance à personne, personne. La vigilance doit être permanente, dafa meti mais diamono mo changer. Yalnalen deudo diam, kii def lii yalna newi ba deh😢
@Oumanas59952 күн бұрын
Tu as parfaitement raison 😢
@IbrahimaSall-ox4rm2 күн бұрын
Ohhh 😢😢😢 vraiment li métina domou kharam bi def li yallah nako yallah wére noooooonnnn khallé bou am 12ans ngua defko ni 😢😢😢😢😢😢😢😢
@sokhna9252 күн бұрын
@@IbrahimaSall-ox4rm surttou niouné dafa dof kou dof dina protegge domam ray domou diambour
@BellaNiabali2 күн бұрын
Ndeyessane 😭 li metina yalla nako yalla yereum 🙏
@amadousall34912 күн бұрын
En tant que père, j'ai les larmes aux yeux. que le paradis soit la demeure éternelle de cette fillette. Mes condoléances à toute la famille éplorée. Resserrons les ceintures et veillons encore plus aux enfants dans toute la rigueur que cela demande.
@ababacardiop70262 күн бұрын
tout a' fait! cest malade sont parmi nous!facile a' identifier!malheureusment ont les denonce pas! "Peur!avec les masla"
@myamya65232 күн бұрын
@@ababacardiop7026massla lagn wara bayi halé y’a gui souffrir ci keur yi
@khadudiatouba9072 күн бұрын
Comment une femme peut aller au lit sans savoir que son enfant d est couché.
@BertheDiallo2 күн бұрын
Iow doul mayniouuuu Li dogal la loussi mère bi meun ki Nek si nkar nga nieuw di am loy wax bo meunoul console nga teudj sa gemigne mo geun adouna nieupay deff erreur xamo foy moudieee ak dogal boulay dallll ki niou reyy domam mou am nakar nga nieuw di am loy commente di wax di critiquer doul way
@Fatoumataousmane2 күн бұрын
@@khadudiatouba907 c’est pas normal vraiment
@NdeyeMbaye-o5t2 күн бұрын
Man dé diakhal nama surtout khalé bou am 12ans nga teude nélaw té guissoko ba souba nanou gueuna veiller thi sounou ndjaboot ndakh adouna yakhouna yalla nanou yalla sàmm sammal nou sounou ndjaboot massa mettina yalla naleen yalla may kholou mougne
@myamya65232 күн бұрын
Comment des parents (père et mère)peuvent aller au lit sans savoir que leurs enfants sont couchés. Wadiour dou yaye rek
@IbrahimaNiang-v2v2 күн бұрын
😢😢😢 hoo jai mal au cœur allahou akbar, ki déff li moy nitt kou bone ,paix a son ame thiéy Sénégal masta hoo 😭😭😭
@myamya65232 күн бұрын
Ki key dou nit
@fatoudiop61612 күн бұрын
Bilahi ku dioure dome bu djigéne sakhe dangaye tite😢😢 yalla nanou yalla samale ndiabote gui
@SokhnaSeck-q8z2 күн бұрын
Amine ❤❤❤
@yayouSalihousamb1553Күн бұрын
Amine instant bi dôme bu djiguen ak bu goor nio yam rek goor Sakh daniouko violé Aduna mo yakhou😢
@NdiayeAwa-nv6hm21 сағат бұрын
😢😢😢😢😢😢😢
@mansourndiaye92942 күн бұрын
Il faut éviter d'envoyer des journalistes qui posent des questions idiotes. Comment peux-tu demander au père si son enfant de 12 ans était dévergondée ou pas?
@Bluelove4472 күн бұрын
@@mansourndiaye9294 et même si elle l'était? Le sous entendu du journaliste est révoltant. Mais ça ne rejoint que les gens qui demandent en cas de viol comment la victime était habillé
@mansourndiaye92942 күн бұрын
@Bluelove447 a fortiori au sujet d'une victime de 12 ans froidement assassinée. Je ne puis pardonner sa bêtise à ce pseudo journaliste. Le journalisme est un réceptacle de connards dans ce pays.
@astouciss49612 күн бұрын
lo kham si kou con manque d'éthique ak déontologie😪
@myamya65232 күн бұрын
Dara Legn hamoul Amouniou formation yeufi dof rek lani def
@amadouhagne18732 күн бұрын
oo j'ai les larmes au yeux ndeysane metina trope
@ColyAdama-b6i2 күн бұрын
Téy kouye yaye sa khole nékhoul yalla nako yalla yereum té ki def li yalla nagneko diape
@Oumanas59952 күн бұрын
Blahi
@mariamakourmang16572 күн бұрын
Bilahi 😭😭😭
@myamya65232 күн бұрын
Metina 😭 😭 😭
@amytendeng8869Күн бұрын
Li mom diaroul sah nek yay. Kou âme xolou nite rek métti naleu
@NdiayeAwa-nv6hm21 сағат бұрын
Métina
@bintafall94042 күн бұрын
Pour mois les Parents doit surveiller les enfants surtout les Mamans😢😢😢😢😢
@seynimangane48092 күн бұрын
Boubakh sakh
@myamya65232 күн бұрын
Surtout les pères
@bintafall94042 күн бұрын
Comment laisser un enfant de 11ans seule sortire jusqu'a le lendemain sens aller Controller es que tous va bien 😢😢😢😢😢😢
@zeinadieng7187Күн бұрын
Aaahhh wa bakhna lii Moy dague sama khooll bii
@helenepouye89072 күн бұрын
Surveillez vos enfants. Il faut savoir a tout moment ou ils sont.
@onlygood11142 күн бұрын
Bilahi
@gorandiaye24192 күн бұрын
Atté islam rkk kou rayy diou rayy la amoul wakh diou bari😢😢😢😢😢😢😢😢😢
@telemaison-t5n2 күн бұрын
Masa li dafa niaw il faut arrêter les criminels qui fait mal les enfants vraiment triste
@ndiougadiop18152 күн бұрын
Yalna lene yalla may kholoub mougn metti na trop
@gorandiaye24192 күн бұрын
Ki déff li katt na ndeyem bon no ki deum la 😢😢😢😢😢
@AbdouDiaw-t2y2 күн бұрын
@@gorandiaye2419 gua malma mais fii sagua amoufi place nianalko rek mo guene
@sokhna9252 күн бұрын
Kokou de yageu na def lou bonne tay dafa werou en plus sathie truan lep la def
@rokhayathiam44082 күн бұрын
Massa c est dur et méchant. Que dieu l accueille dans son paradis
@FamaraIbrahimaSane-il8oeКүн бұрын
Hélas !notre société souffre terriblement,les gens ne sont plus normaux et c de pire en pire.Repose en paix pauvre petite
@gorandiaye24192 күн бұрын
Kou rayy diou rayy la loulou la yalla wakh 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
@pivoine4812 күн бұрын
Moy likay safara motakh souniou borom santanèko, té souniou ko dèdoul dou fi dioguè.
@aimefaye69872 күн бұрын
Massa metina torop plus de vigilance les parents warolene teud te dadiale wo sa ndiaboot 😢
@Sofieba-v3t2 күн бұрын
Niaw na saltè na yallah yeureum ko th khareko aldiana firdawsi th wer ki def li thi barkè Seydinamouhamed psl
@DieynabaBa-ni2pr2 күн бұрын
Franchement vous êtes trop négligentes neuk ne pas voire sa fille toute une nuit vraiment c'est incroyable
@الحمدلله-ض5ي8غ2 күн бұрын
Bo teudeh ba gudi sakh dangawara juk encore reverifier
@khadudiatouba9072 күн бұрын
Franchement
@mansourdiouf14132 күн бұрын
Mansour beaucoup de courage dans cette épreuve... j'étais avec lui à l'ugb j'ose imaginer ta tristesse actuellement... Magi lay mastawou
Wa est ce li dou négligence parentale diamono nekhoul il faut toujours veiller sur les enfants mais c très dure paix à son âme
@zeinadieng7187Күн бұрын
Négligence la
@NgonéNdiaye-y9d2 күн бұрын
Mes vraiment xalei bou ame 13 ba 1h teudoul j'imagine sa souffrance la pauvre petite princesse
@NabouThiam14672 күн бұрын
Ndeysan li métti na trop😭 yalna KO yalla yereum té kharé KO aldiana firdawsi 🙏🥺 té yalna lén yalla maye kholou mougne 🙏🥺🙏
@nabyafialamp89962 күн бұрын
Yalla nagnou yalla dakal cheytane
@AdamaNdom-i1m20 сағат бұрын
Yalla nako yalla yarame amine 😭😭😭🤲🤲🤲🤲🤲🤲
@BounaNiang-mt8mg2 күн бұрын
Téyélene séne dome yi sén keur yi 😭😭
@NdeyeMbaye-o5t2 күн бұрын
Waaw ndakh diamono yakhouna nanou veiller bou bakh thi sounou ndjaboot yalla nanou yalla sàmm sammal nou sounou ndjaboot sàmm gneup
@BounaNiang-mt8mg2 күн бұрын
@NdeyeMbaye-o5t amiine
@laminelayekebe6152 күн бұрын
Alakhou akbar 😢ki deff li bone na 😥😥😥
@helenepouye89072 күн бұрын
A 12 ans et a 2h du matin vous ne savez meme pas ou se trouvait votre fille
@namaly8292 күн бұрын
Doynawar des
@NeneCamara-pv9gs2 күн бұрын
Parents yi tamite sagane nagne teud té do khôl sa domme
@maried90312 күн бұрын
Les parents aussi comment vous pouvez dormir sans savoir où se trouve exactement votre enfant que son âme repose en paix qu'Allah l'amène au paradis éternel
@aboumouhammaddiaby14116 сағат бұрын
Marabou bi fén rék léy déffe Diarraye yalnako yalla yeureum , kharéko Adjiana 😊
@rokhayatoudione39122 күн бұрын
Dal nguéne khel khaley bou djiguéne dem djissoulenko nguene dal khel teud nelaw yow tranquillement nga dieul say bagass feuss yené diaye !
@gorandiaye24192 күн бұрын
Sénégal dou rew wallahi 😢😢😢😢😢
@ballagassama9790Күн бұрын
Mes condoléances et courage à la famille.
@ndeyeseynaboundiaye11922 күн бұрын
Massa mon frère Mansour
@RiimaToure2 күн бұрын
Khalé bi déna dé bou méti
@MouridoulAllah2 күн бұрын
Li gnawna bilahi kouy yaye rek sa hole toyna yalna yalla sammal gnou sougnou diamboot
@Mamyzahra9352 күн бұрын
Hale 12 ans nga teud tei Guisso ko lolou folein ko tek meti na lol nak mai hale dagnou koy surveiller bein parent amoul droit teud tei hamoul domam foumou neik
@Fatoumataousmane2 күн бұрын
Vérité
@zeinadieng7187Күн бұрын
Deugue rek guafii wakh teude di neelaw te yoor ay dom you djigueine
@aichagoudiaby11482 күн бұрын
il faut que ça cesse au Sénégal
@amdiatoudiallo39532 күн бұрын
Yalla na yéguélé ndawam thi aldiana you kawé yi 😢😢
@ndacksene72142 күн бұрын
Soubhanalah noy nélawé té sa dom teudoul.khalatoumako Yalla naniou Yalla ar aralniou jabott gui
@Fatoumataousmane2 күн бұрын
Vraiment d’où yone
@aidambodjmbodj46542 күн бұрын
Allahou Akbar Massa yaye boy
@aminatandiaye87682 күн бұрын
Deug la métina wayé nagni teudie khalé yi à la descente. Ils traînent partout pendant les vacances et les week-ends. Banlieue dafa méti trop
@AmadoudlLLo20 сағат бұрын
Ndeysane 😭😭😭😭
@sydambe21662 күн бұрын
Yalha na ko yalha yeurrum te yalha karé ko adjana firdawefie amine.yarabie courage pour la famille courage justice 😊
@Fatima-ti2me22 сағат бұрын
Ndeysan yala bakhna😢😢😢
@derkaderka8635Күн бұрын
Salalahou hala mouhamed
@bathiembaye64472 күн бұрын
Daysane métina trop 😭😭
@omardia-lq4io2 күн бұрын
Ndeysane yalla n'alla xarré aldiana sa leur ❤❤❤❤❤❤❤❤
@AmyTraore-s2y2 күн бұрын
Massa yalnako yalla yeureum 😢
@AmadouBa-o8wКүн бұрын
🥹🥹🥲🥰
@jeynababa72982 күн бұрын
Macha li metina trop 😢😢😢😢😢😢😢
@boussogueye7168Күн бұрын
Masta masta matina trop trop yalnalen yalla mey kholou mougne t diarra yalnako yalla khare aldiana c'est triste 😢😢😢😢
@AidaBabou-o1n2 күн бұрын
Paix à l’âme
@ousmanediop41102 күн бұрын
Paix à son ame amineee YARABI ainsi qu'à tous nos défunts amine YARABI
@MatarNdiaye-x5g2 күн бұрын
Sénégal khana da ame aye djinné youfi dougue temps hier, chaque semaine ak raye bou bess.
@assydiba96521 сағат бұрын
Yallah nakoo yallah yeram
@fatoudiakhate15162 күн бұрын
Yalla nako yalla yeureum kharèko aldiana firdawsi si barke zeydina Mohamed
@bequediallo4582 күн бұрын
Salal'ahou Alleyhî Wassalam Amiiiin'Allah !
@MaguetteThiam-j5zКүн бұрын
Yalla na ko Yalla yereum
@NabouMbye2 күн бұрын
May her soul rest in peace Haley bu am 12ans waruta neka c benen nek ba 00 mem budeh bena kerr la sah wahumala tog c mbeda
@aliousow23842 күн бұрын
yalla nalén yalla may kholou mounie
@TavaresAlexis2 күн бұрын
Vraiment ces triste
@fatouseck73442 күн бұрын
YALLANAKA YALLAH YEUREUME SOUGNOU DOMOU KHOLLE FIRDAWSSI SOIT SA DEMEURE ÉTERNELLE INCHAALLAH AMIINNE YALLAH MAYEGNOU KHOLLOUMOUYE KOUDIOUR YEUREUME MASSA LES PARENTS ET TOUT LE SENEGAL
@maiinasamb46522 күн бұрын
Tellement de peine et de tristesse. Nous devons protéger nos enfants. Il est inconcevable d’aller se coucher sans s’assurer au préalable de la venue de son enfant mineur. Que Janatu Firdawsi soit ta demeure éternelle petite Souadou - Diary Sow …. Notre petit ange 🤍🤍
@adjamaguettendiaye89822 күн бұрын
Linlo metty la, yalnako yallah yarame
@fsJh808423 сағат бұрын
<a href="#" class="seekto" data-time="150">2:30</a> mara bi dé fèn na
@benjamindasylva35802 күн бұрын
Que Dieu nous épargne des ritualiste au Sénégal
@mamadoualimoubahkelen19612 күн бұрын
Paix à son âme
@hawadiallo90492 күн бұрын
Parfois ces journaliste pose des questions bêtes noooo medre
@OulimataNdiaye-zu3ln2 күн бұрын
Une maman doit être toujours la première et la dernière personne qui doit toujours surveiller ses enfant soyez vigilant cette acte est trés irrespectueuse
@AdamaNdiaye-fm3fu2 күн бұрын
yalla nako yalla yeureum té khareko al dianna firdawsi Amine
@cheikhmbackendiaye39972 күн бұрын
Wa diourr yi si boppam niou démissionne
@mariamacisse96112 күн бұрын
Deuk bi woratoul li metina trop😢😢
@benjamindasylva35802 күн бұрын
Tchéii Sénégal que Dieu nous transforme et nous donne une dignité
@ajajatta69672 күн бұрын
Very sad 😢😢😢😢
@SeynabouNIANG-n9g2 күн бұрын
Bane Sénégal laniou nekk 😢lii Doyna waar
@MariamaDembele-gy7kz2 күн бұрын
Yalnako yalla yereume
@jeynababa72982 күн бұрын
Yalla nalen yalla May khollou mouñ
@SokhnaAntaNdiaye-v8m2 күн бұрын
Éyway kou défli bone na....parfois sous l.effet de la drogue ils font des bétises c un acte monstrueux une petite fille innocente vraiment ! 😭😭
@SERIGNEIBNOULO-fb4hq2 күн бұрын
Yalna sa borom kharé ko aljana mais aussi des parents irresponsables
@Senegalseul-ek8jy2 күн бұрын
Yalna ko yalla yereme te khareko aldianay firdawsi sy barke Alquran vraiment ly ñaxna
@henrijoelsossou39872 күн бұрын
Métina c très très difficile mon frère Je compatis votre douleur
@OusmaneSambe-l3f2 күн бұрын
😢😢😢Hooo métina torop😢😢😢massa yaye boye😢😢
@aminataseck55712 күн бұрын
Oh massa li metina mane deh tite na legui lidi khewe Sénégal 🇸🇳 dowena war
@ModouFall-z3y2 күн бұрын
Yalna aguali ndawame tha aldiana firdaws !
@fktfkt29322 күн бұрын
Ay way teyee lenn khaleyii svp diamono dafa changer na kounee bokheu sa dom nioune magui sakh nekatouniou sécurité saka khaley
@kollegs1012 күн бұрын
Masa metina waye Sonko Premiere Minister moko ndieke
@BabacarDiop-de7km2 күн бұрын
Yalla nako yalla yeureum kharéko aldjana firdawsi métina😢😢😢😢